S. Habib Sy : "Un marabout qui ne peut t'éviter la prison, ne peut rien pour toi dans l'au-delà"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 фев 2025
  • Dakaractu, la chaine d'information en ligne!
    Abonnez-vous à notre chaîne sur RUclips : www.dakaractu....
    Rejoignez nous sur Facebook:
    / dakaractupointcom
    Suivez nous sur Twitter :
    / dakaractu

Комментарии • 184

  • @sirambodji6313
    @sirambodji6313 5 лет назад +1

    Yalla nala yalla faye amine

  • @abdoudiahoumpa6564
    @abdoudiahoumpa6564 5 лет назад +1

    walahi SY MALICK deug reck ngua fi wah YALNA NIOU YALLA defal déegueu ak topeu té bayila sounou kanam thi barké SWAS AMINE

  • @OureyeSeck
    @OureyeSeck 9 месяцев назад +1

    Walahi DEUG la chaque jour Serigne wax fii né Molay ramou té nga ndaule ak yénéne rawatina ngua dougou casso MBA talibém nék fa té meunoukofa guéné Mane bima xamé Lolu la xam foumay ték sama tank wa sala🙏🏾👍🏾👍🏾👍🏾

  • @borombeyti417
    @borombeyti417 5 лет назад +2

    Wallahi lou werr yag fi té werr lol sy malick ❤❤

  • @elhadjindiaye2116
    @elhadjindiaye2116 5 лет назад +2

    Manchahalla serigne wakham dawara dieumm sii Yalla ak yonénne tii bii

  • @keitaache
    @keitaache 5 лет назад

    Ma Shaa Allah

  • @mansourgueye5860
    @mansourgueye5860 5 лет назад +2

    Wawaw loudoul diouli dioulè
    ka geun loudoul yalla
    yalla ka geun wasalam🙏🙏

  • @ndeyediop6387
    @ndeyediop6387 5 лет назад +19

    Vérité absolue. Il faut tenir un langage de vérité pour guider les talibés

  • @bayethiam7511
    @bayethiam7511 5 лет назад +4

    Il est bon. Il parle très bien franchement. J'ai beaucoup aime

  • @MamadouDiallo-yz4cd
    @MamadouDiallo-yz4cd 5 лет назад +1

    Machallaaaaah barakalahou fikoum🙏🏽🙏🏽🙏🏽

  • @baguellepatriote4265
    @baguellepatriote4265 5 лет назад +5

    C ça qui doit etre le role d'un guide
    Vraiment machallah

  • @alioudrame6266
    @alioudrame6266 5 лет назад

    Merci serigne. Nakhoulene gnou deh. Bilahi

  • @bamsdiaby2879
    @bamsdiaby2879 5 лет назад +5

    Dieureudieuf sy malick message bi amna solo

  • @talibeserignemostaphasymal1917
    @talibeserignemostaphasymal1917 5 лет назад +7

    Wallahi ndeysane deugue pur sy malick yallah na nga fi yageu Té and ak weer

  • @oumardiatta2946
    @oumardiatta2946 5 лет назад +19

    C la vérité pure que le tout puissant allah vous guide amine

  • @ndeyekhadydiopmbengue6570
    @ndeyekhadydiopmbengue6570 5 лет назад

    Bien dit sy yalna yalla fayla tes goudeul sa fane yokou kham kham bi ak lérou denebi bayila thi kanamou gnabote gui amine

  • @mog4988
    @mog4988 5 лет назад +5

    Machallah kaduyi rafetna
    Qu’Allah le Tout Puissant guide vos pas.

  • @VoyageSpirituel
    @VoyageSpirituel 5 лет назад +10

    Wallahi Sy lolula sa wadiour cheikh seydi mouhamadounil mansour rta donn wakh Machallah yallah naniou yallah wonn yonu ndioupp ndakh senegal serigne si legui kenn khamatoul lanla wakhatouniou nitt gni senn borom niom senn poche rk laniou fi nekal cheikh al hadji abdou aziz dabakh dann na wakh nann serigne ak Talibé souniou defantéwoul nowlé ne bobu andd anddou sentiment la te andd bouko sincérité laloul bakhoul malheureusement senegal kenn khamatoul lifi nk nitt gni ragualatouniou yallah yarotouniou comment on peut être sûr les réseaux sociaux et d'insulter le père des autres Vraiment lifi nk doyna war yallah naniou yallah guindi omatniou si ndioupp serigne kenn ragualatoul yallah legui khadiss yi ak aya noulen nekh lagnkoy firé rien que pour wakh nitt ki louko nekh nakh limo lay diokh Wa ana yallah les jeunes de mn pays réveillez-vous serigne boula mounaloul fi dra wakhouma euleuk nk

  • @ndiassegaye8417
    @ndiassegaye8417 5 лет назад

    Lou lerr nagn yalla nala fii yalla bayi

  • @kamkao3738
    @kamkao3738 5 лет назад +9

    waaaaaaawaww le marabout a compris
    paix sur vous et nous tous

  • @babacarthioub8601
    @babacarthioub8601 5 лет назад

    Amna solo ❤❤❤

  • @nguiranetapha6230
    @nguiranetapha6230 5 лет назад +4

    Machala sy malick yangi wakh ak Brom khel yi

  • @pendandao2307
    @pendandao2307 5 лет назад +1

    Deug nekhoul way les jalouses vont maigrir dieureudieuf seydi hadj malick sy 🙏♥️

    • @omargaye9950
      @omargaye9950 5 лет назад

      Malén yeureum aduna mom kou djeufoul wax rekkk

  • @fatimadjarri5648
    @fatimadjarri5648 5 лет назад

    Vous êtes ma fierter ,damaye titaro bok bène derète ak yène ! Sy Malick goud fane ak werr

  • @serignengom2889
    @serignengom2889 5 лет назад +3

    Machalahhh

  • @fallxaadim9941
    @fallxaadim9941 5 лет назад +23

    Yalla maynama aduna ak alahira ( borom touba)

  • @bamsbams3171
    @bamsbams3171 5 лет назад

    Dieureudieuf s'y Malick amna solo DÉ away Sénégal dé'lô'léne séne khél si yalla té djamoudji yalla mô'gueneu

  • @bafodesano3811
    @bafodesano3811 5 лет назад

    Machalla nitou deuk deuk moï s habib

  • @salimatoubalde2475
    @salimatoubalde2475 5 лет назад

    Merci Sy

  • @generalking1798
    @generalking1798 5 лет назад

    Pêr niew ga aksa lafa 🤣🤣🤣8

  • @mouhamedndiaye3779
    @mouhamedndiaye3779 5 лет назад +5

    JAAWARTOU LANAA
    PASSEPOROU ALDIANA
    (DJËRËDJËFÉ BOROM TOUBA)

    • @syngariboundou2355
      @syngariboundou2355 4 года назад

      Fène rèkk diawartou dougaloule kèn aldiana dèmal diamoudji bour yalla

  • @khadindao3035
    @khadindao3035 5 лет назад +2

    Machalla cheerign koudal fan way 🙏❤❤❤❤😍😍😍😍

  • @PolarBearTrainer1304
    @PolarBearTrainer1304 5 лет назад

    Verite absolue.

  • @ibrahimasenenabien1204
    @ibrahimasenenabien1204 5 лет назад +1

    Dieuredieuf Serigne bi sa liguèye si Tarikha bi amna solo yalna yalla samla arla yok sa wèrr yok sa soutoura

  • @serignemalickcisse4862
    @serignemalickcisse4862 5 лет назад +2

    Machalha li moy kuer sedilhadjii malick ❤❤

  • @elmansoursarr5646
    @elmansoursarr5646 5 лет назад +1

    Machaa Allâh yague fii lol ta ande ak weer

  • @mamadoundiaye4751
    @mamadoundiaye4751 5 лет назад +1

    Massalikoul jinane 27 09 2019

  • @kanyindangoyisaac5779
    @kanyindangoyisaac5779 5 лет назад +4

    Le prophète Mohamed a perdu des guerres est pourtant bou euleuguer moy ramou diame gni

    • @kopajean6608
      @kopajean6608 5 лет назад +1

      Bien dit ! Et mieux encore, le Prophète (PSL) a eu à être malmené dans des guerres et c 'est lui qui par la Grâce d'Allah nous sauve sur terre et nous sauvera à l'au delà

    • @kanyindangoyisaac5779
      @kanyindangoyisaac5779 5 лет назад

      @@kopajean6608 il a perdu des hommes la guerre est pourtant gni bouniou sonal way

  • @moustaphabeye6198
    @moustaphabeye6198 5 лет назад

    Soko manol nobel wayyyy😃😃😃

  • @paped5180
    @paped5180 5 лет назад

    Serigne habib sy yalla nganfi yague te wéér sy

  • @dienyssef48
    @dienyssef48 5 лет назад +1

    Machala deg na deug

  • @assiatoutalibeserignmousta6364
    @assiatoutalibeserignmousta6364 5 лет назад +2

    Amna sole ❤❤❤

  • @babacarthioub8601
    @babacarthioub8601 5 лет назад

  • @gpproduction4720
    @gpproduction4720 5 лет назад

    Mato Serigne dh. Koula djiss khamné khamo gattt

  • @abdoukhouma4983
    @abdoukhouma4983 5 лет назад +1

    Massalah

  • @ndiayekane7780
    @ndiayekane7780 5 лет назад +1

    Machala❤👈

  • @papeballasylla7255
    @papeballasylla7255 5 лет назад

    Koufi diamou wouy yalla mom bodewé dougou safara rek

  • @sokhnawade6843
    @sokhnawade6843 5 лет назад

    Mane koumay woneilei AK Habib nguire yalla damako beugue

  • @ndongodaara2391
    @ndongodaara2391 5 лет назад +3

    Ndeysane Senegal diam rk moofii ame inchallah

  • @ballagaye2youtubeleliondeg907
    @ballagaye2youtubeleliondeg907 5 лет назад

    Akassa am na solo

  • @karainfo3891
    @karainfo3891 5 лет назад

    tu es entrain de raison gueweul bi nous on connais vos parents griots

  • @salioundiaye6297
    @salioundiaye6297 5 лет назад

    Kattal sa ndaye ak ko yakar ak s mansor sy sèn leufeul ndaye

  • @babacarwade86
    @babacarwade86 5 лет назад

    Dieureudieuf Sy Malick

  • @tvadamandiayekhassaidtouba8388
    @tvadamandiayekhassaidtouba8388 5 лет назад +7

    KADOU YI RAFET NHA YALNA NGA AME DIAME BARKEB S TOUBA

  • @sopemoustaphambouptivaouan8048
    @sopemoustaphambouptivaouan8048 5 лет назад

    Machalla yalla djou sett tivaoane

  • @maddoulaminesonko9988
    @maddoulaminesonko9988 5 лет назад

    Bilay degguatina degg
    Lila ham si serigne
    Lumu metti Wahal nityi degg
    Mais senegal 🇸🇳 dfa barrí yallah
    Tè ñune talibè yi ñolen fatekk

  • @fallam1010
    @fallam1010 5 лет назад +2

    Koum nékh ga né Meuno ma yombe kéne Aljana, Wayéh kéne meunul yomb kéne Aljana mom na kounék xam sa bop meuno ma wayé kéne meunul lol yaw kay so meunul rek soumil sa yéré Serrigne took ci suuf bayi waxji ak nangu adiya yi

  • @lebou2503
    @lebou2503 5 лет назад

    Machallah eskeuy deug rek la wakh

  • @papandiaye979
    @papandiaye979 5 лет назад

    Cool nourog gag se baye de

  • @alertecitoyen9932
    @alertecitoyen9932 5 лет назад

    Ioe loo liguéyaal dinné dji?

  • @malickdiagne3421
    @malickdiagne3421 5 лет назад

    Degg na deugg

  • @BAMBISTETV
    @BAMBISTETV 5 лет назад

    Dou ay teguin sah nulay tontu waye adduna ak allakhira bokounu dara
    Fi Nila fi mana guenne rebus manu nioula rambou elleuk te momte man nanuko fi de
    Yonnente bi shw Dana khey dou am sah loumu tale cin keurem dan khare di niak te tewul mou guemne yalla miko yonni moko diokhoul loum lekk te mokoy khagne loubari
    Ak yenen you Bari youy misal youni mel
    magui toub damay leral rek 🙏🏾

    • @mamadoumanediop3601
      @mamadoumanediop3601 5 лет назад

      Ligay diéma léral dagay moudié leundeumeul dh bakh

    • @mamadoumanediop3601
      @mamadoumanediop3601 5 лет назад

      Kou diamoumoul yallah perte gua si adouna ak lo fekh fekh al ahira wakhi noppi

    • @yibydiop1536
      @yibydiop1536 5 лет назад

      Wakhi serigne deugue rek la wakh soulene arangewoulé tan pi

  • @fayebineta7604
    @fayebineta7604 5 лет назад +1

    machala kaddu yi rafetna lol

  • @modoufallthioune6731
    @modoufallthioune6731 5 лет назад

    samaa Serigne dee maanna fii et maanna fei baa boobaa

  • @deboursy6215
    @deboursy6215 5 лет назад

    Ta raison mais jsw pas tidiane nak

  • @amjuuf9053
    @amjuuf9053 5 лет назад +10

    Mais Serigne bi tay sén cérémonie guoudé na dh démna ba après timis ?

    • @bamsdiaby2879
      @bamsdiaby2879 5 лет назад

      Hé après

    • @amjuuf9053
      @amjuuf9053 5 лет назад

      @@bamsdiaby2879 limouy kass mbir keureum la xéwé.
      Wa Salam

    • @bamsdiaby2879
      @bamsdiaby2879 5 лет назад

      @@amjuuf9053 lidjan'til lisa keur bay moguene

    • @malickdiouf5728
      @malickdiouf5728 5 лет назад +2

      Mani wax deuge mo ame solo mome souy wax ba nara tarder gua deme diouli dji c simple waxnalene li yalla wax pas plus mome Dafa yekha diouli ou autre c lui et Dieu mais entre lui et les autres waxnalene Louy deugue foi diouli dioté demlene diouli dji
      A moins kon soit jaloux pour dire du négatif fi Deugue pure et dure mofi guene xam xam bou lere

    • @toutetderien3541
      @toutetderien3541 5 лет назад

      Loutax négatif

  • @deugdeug1945
    @deugdeug1945 5 лет назад

    Billahi deug la serignebi

  • @abdoudiall1797
    @abdoudiall1797 5 лет назад +1

    Machallah♥️♥️♥️

  • @oumarsall5958
    @oumarsall5958 5 лет назад

    Mahcalh

  • @yacinefall9459
    @yacinefall9459 5 лет назад +1

    Lol ki dh amoul kham kham nakh Moustapha sy dougg nafi prison khana kone mom amoul Serigne bou meut Serigne di wakh di inventer rekk
    Façon kou bagne Serigne Touba nala lere ni safara nga dieum

    • @yayoumd560
      @yayoumd560 5 лет назад +3

      Yacine Fall ndakh nga sagn ko wax....li lène déranger moy Raz de Marée bi dal sên kaw ,té Serigne Cheikh Ahmadou Bamba déclencher ko...Lilèn Al Amin waxon rek Serigne Touba mo mom Touba ,sos ko wayè ...Lexpension de la ville,la Grande Mosquée,talibé yi rek nioko fi dëf...niou né détéway Massalikoul Djinan dal sen kaw ,khimaliko gougnou Université nouyo...machallah yalla naniou anda ak S Moutakha bamou yèg si diam incha Allah....Waw li nékhoul Yacine,yoon wi machallah ki ko wara doxal mi ngi si....Le chien aboie, la caravane passe...!

    • @papitodiack3092
      @papitodiack3092 5 лет назад

      @@yayoumd560 wérneu dafa lérr ni midi

    • @yacinefall9459
      @yacinefall9459 5 лет назад

      @@yayoumd560 lou werr deugg nga wakh yonn bi dou takhawww dayy demm rekk tei daniou demm andakk mom

    • @ngonegueyembaye5488
      @ngonegueyembaye5488 5 лет назад

      Am nguéne diott do lenn suivre s'en Serigne ta bayi niou yenangui merr dë

  • @momobame8934
    @momobame8934 5 лет назад +7

    Legui serign yi akh yonetè bi diarre prison nak ?

    • @serignediop3137
      @serignediop3137 5 лет назад +1

      Tres intelligent

    • @aliounendoye5749
      @aliounendoye5749 5 лет назад

      Yaw khamo foumouye wakhé sakh .diguate rek

    • @malickdiouf5728
      @malickdiouf5728 5 лет назад +3

      Dafla wax ni serigne boula menoul guené prison menoula guéné safara donc diamou yalla rek molay dieurigne

    • @rokhayangom6094
      @rokhayangom6094 5 лет назад

      Nitt daguay xalate xél pour xalate la limouy wax xamo foumouy waxé daguay déglou watt boul gawa répondre

    • @mbayediop8922
      @mbayediop8922 5 лет назад +1

      Dama setlou niou eup di comentaire en negative douniou vue video titre laniou bazé wou

  • @koulaalhakk8975
    @koulaalhakk8975 5 лет назад +4

    aucun marabout n'ose dire a un talibè boul diamou yalla.....Donc Khalifa sall maodo meuneulouko dara c ce ke vs voulez dire

    • @assandiop5366
      @assandiop5366 5 лет назад

      @@babacarsall4203 kii douloule dé liseugne bi wah la kion firmé

    • @babacarsall4203
      @babacarsall4203 5 лет назад

      @@Bouba8689-s3 yaye dei nala moytou rek ndax ndiriwoma kou wéur

    • @malickdiouf5728
      @malickdiouf5728 5 лет назад

      Yaw boul diamou yalla ba dé gua Xole ndakh sa Serigne dinala meneul dara ok si tu es véridique bayil diouli wore et tout tokk xare dé
      Wala gua ray nit bagniou teuthie le digua xam
      Au pire des cas waxal sa Serigne moi ray nit ndakh dou dougou sawara wala mou bayi diamou yalla ndakh dou lake

    • @minielgueye2908
      @minielgueye2908 5 лет назад +1

      Évidemment.. .toi tu as bien compris🤗🤗🤗🤗

    • @BAMBISTETV
      @BAMBISTETV 5 лет назад

      👏🏾👏🏾👏🏾 Ci lim wah rek

  • @dorami4976
    @dorami4976 5 лет назад

    Il m rappel son papa ndeysan

  • @madoundiaye697
    @madoundiaye697 5 лет назад +1

    Dafa lér s'y malick

  • @Corailpro
    @Corailpro 5 лет назад

    Seydi sy. Deug rek. Je vois en lui son père boromdaradji !

  • @khadimseck4188
    @khadimseck4188 5 лет назад

    Ki ab dfeant la day siisou dinguéne dead déi borom touba dou masa am morom sén xoll you leundeum yi tchim dara si lérr amoulénko

  • @MHDdiapoulho
    @MHDdiapoulho 5 лет назад +1

    La comparaison est maladroite. Et n'a aucun sens. On peut bien ne pas réussir à sortir une personne de prison et reussir à lui faire entrer dans la mesicorde de Dieu à travers l'intercession qui existe bien. Ce qui est des hommes n'est pas de Dieu
    On peut bien demander à un talibé d'adorer son seigneur sans pour autant faire ces genres de comparaison débiles.

  • @mouhamedcisse9728
    @mouhamedcisse9728 5 лет назад +6

    Yaw déh Borom khelyi ngay wakhal.
    Sénégalais dafa Beug louyoumbeu Beug dougou aldiana té dodiamouyalla wala diko wérr si diamou yallah diambour.

    • @thiabasene5434
      @thiabasene5434 5 лет назад

      Aka ya wakh deug!
      Surtout wérou ci diamou Yalla diambour! Ça me fait rire et en même temps ça me fait peur!

  • @omargaye9950
    @omargaye9950 5 лет назад

    Mando geune djouli bobou ngay def ndah meunoko khamolén yalla mara vip ak mbazin bou yandji niakk khorom

  • @saikh2348
    @saikh2348 5 лет назад +3

    🤔mane daal tasawouf diakhal nama
    Waaji mooy wakh ni ab tidiane touyabay diouli ak woor douka dougal ajana
    👉 yawmal khiam cheikh tidiane moo fa am ay magasins
    👉thialay diokh tidiane yep Niou dougou ajana
    👉bouka défé tidiane yi di weur mbedi yawmal khiam yi Di mayé séni touyabay diouli ak woor
    👉té même cheikh tidiane mi soos sén tarikha bi ab talibém mass nako fatali heurou diouli mou guénéko tarikha bi
    Pour wakh lani Kilifa tidiane Di dag wakhtane nguir diouli bokoul ci tarikha bi

    • @wakhdeugguetayallatakh8129
      @wakhdeugguetayallatakh8129 5 лет назад +1

      Tasawouff mofi gneuppe dolé ba yawmal hiyaam dem leen noppolo gni gno raw sen serigne yi nguene yaakar

    • @morseye9249
      @morseye9249 5 лет назад

      من حسن اسلام المرئ تركه مالايعنيه

    • @saikh2348
      @saikh2348 5 лет назад

      @@morseye9249 salam gayi danioo nakh sounouy mame thi ay philosophie ay guéntak ay imagination tédar douci deug
      Kiylay wakh fii diamoul yalla
      Mooylay wakhat maalay dougal ajana
      Mais malheureusement yén khamolén Tasawouf

  • @ahmadaly6666
    @ahmadaly6666 5 лет назад

    Bilahi deguela

  • @matouloveki8277
    @matouloveki8277 5 лет назад

    DIARAMA SEYDI

  • @morpouye1437
    @morpouye1437 5 лет назад

    Deugue nekhoul

  • @karainfo3891
    @karainfo3891 5 лет назад

    vous êtes griots serigne habib

  • @mamadouthiaw7
    @mamadouthiaw7 5 лет назад

    Wa Lila téré Djouli Timis mome khana menale nala dara eulak

  • @thedemocrate6687
    @thedemocrate6687 5 лет назад

    serigne mansour biss

  • @modoudiop8383
    @modoudiop8383 5 лет назад

    Waho lo am

  • @diehiitoumakgni2503
    @diehiitoumakgni2503 5 лет назад

    Son bi avant serigne bi diwakhe titre bi svp

  • @moduololo613
    @moduololo613 5 лет назад

    Nimoro seringue bi la beug

  • @khalifadiop6739
    @khalifadiop6739 5 лет назад

    Wah nehna waya daigueu ko raw serigne bi da bagn talibe ya fouss rek lo yakaar kou bah dail toppou farata ak sunna ba parai di dounde tassawouf

  • @mamadouthiaw7
    @mamadouthiaw7 5 лет назад

    Sa djorete mo rafétoule rekk.Wa kone guéné léne prison gniguéne téyé ba Djouli Timis passé.

  • @senegalrek7975
    @senegalrek7975 5 лет назад +3

    Yaw katal sa sarap ndaye garou walé rek nga kham domi khathie

    • @ahmedgaye6825
      @ahmedgaye6825 5 лет назад

      Yaroulenne mo guenne si yenne daguenne di kheye souba ni degue younane lane la feke toy rek

    • @mbayediop8922
      @mbayediop8922 5 лет назад

      Yaw gaïndé khana do dioulite foumala fék daghay saga mane douma comentaire Mai saga yi manoul fathie dara

    • @sowmountaga9779
      @sowmountaga9779 5 лет назад

      Yow gainde Ndiaye Boko sagater serigne habib sy ma oubi sa leufeul ndeye domouharam

    • @yibydiop1536
      @yibydiop1536 5 лет назад

      Gaïnde ndiaye sa leufeul ndaye ak ko yakar séne khôl yi dîna wade gni deugue la gnou nampe mom lagnouy wax

  • @abasall711
    @abasall711 5 лет назад +1

    Machala wax nga degue sa wadiour moko wax dhe goudal fan ak wer diam bamu nexla si Barker serigne babacar sy malick

  • @francescogallicchio907
    @francescogallicchio907 5 лет назад

    Machahala

  • @papisseck1439
    @papisseck1439 5 лет назад +2

    Machallah

  • @biranekouta8489
    @biranekouta8489 5 лет назад +1

    Macha allah

  • @mamadousall7046
    @mamadousall7046 5 лет назад

    Machala

  • @MHDdiapoulho
    @MHDdiapoulho 5 лет назад

    La comparaison est maladroite. Et n'a aucun sens. On peut bien ne pas réussir à sortir une personne de prison et reussir à lui faire entrer dans la mesicorde de Dieu à travers l'intercession qui existe bien. Ce qui est des hommes n'est pas de Dieu
    On peut bien demander à un talibé d'adorer son seigneur sans pour autant faire ces genres de comparaison débiles.

  • @mamadoudiallo9853
    @mamadoudiallo9853 5 лет назад

    machallah

  • @toutetderien3541
    @toutetderien3541 5 лет назад

    Machallah