Je suis mourid mai mam modo manna way lol limi wakh nékhna lol إني فقير ومسكين إلى آخرها ماأجمل هذه القصيدة في فنن التوحيد. ياسيد الحاج مالك سه جزاك الله خير هذه القصيدة تهتز قلب السليم والله سأسمع كل يوم هذ البرنامج عبد العزيز امبي مع حزبه كلها نسأل الله أن يجعلكم خير وأ ن يطول الله عمركم أناأفرح جدا فرح الله بكم ببركة سيد. الحاج مالك سه
Di ngène ma rayy rekk té sama heure diotagoul😭😭😭heure boumakoy deglou je n'arrive plus à retenir mes larmes😭😭 yalla naniou yalla fayall souniou Mame Cheikh Seydi El Hadji Malick Sy
En tous cas khawma kane wayé Borombi khamal nama secrets bou reuy si khassida "Ya kaachifa D'a " ,je l'écoutais durant l'hiver 2021 coïncidant au Mawlid virtuel du au covid19 avec beaucoup de difficultés et de peine pour s'en sortir ici en Europe, dans un restaurant en faisant de petits boulots en noirs 😢😢, à la sortie de ce mois béni, Dieu à résolu tout mon souhait...(Qu'Allah l'agrée Cheikhal Hadji Malick et sa noble famille, ainsi que la famille de Moussé Alé Mbaye bidiakhi Taaha Yaçina Aleyhi Salam)
Masha'Allah. Je ne sais pas vous mais ce Khassida transperce mon âme, et je ne peux retenir mes larmes. Yallah nagnou Yallah fayale mame Maodo. Amin yaa Rabbi....
L'émotion dans laquelle nous plonge les paroles de ce khassaïde et la chorale est indescriptible ; on dirait que toutes ces voix ont été faites pour fusionner toutes ensemble afin de nous déclamer si harmonieusement Ya Kachifa Daa'i de Mame Maodo... Au delà de tout ça, la qualité de la vidéo, du montage et de la présentation est impeccable !!! Yalla fayal gnou leen ci liguey bou rafet bi 🤲🏾❤️
Macha allah bouma ammé kénn lou may gné ci adouna moy gnii. Yalla na lénn yalla fay té yagallén fi. Grace à vous des gens comme moi commencent à maitriser les écrits Seydi Elhadji Malick Sy radiyallahou taanla anhou. Encore un grand merci à vous
Masha'Allah ! Malika TV vous avez fait un travail remarquable. Enregistrer la famille de feu Moussa Alé sur les écrits de Cheikh Seydi Hadj Malick, maouloud 2021,nous n'oublierons jamais.
Est ce qu'on connait nous tous les senegalais qui est CHEIKHOU Hadji Malick sy Serigne Cheikh Tidiane Sy Almaktoum a raison de dire Maodo l'inconnu de la nation on peut même dire de l'humanité
J'aime tellement cette chanson que parfois quand quand je l'écoute j'ai j'ai le cœur qui bat comme s'il y avait quelque chose comme si j'avais perdu quelqu'un cette chanson est vraiment vraiment très belle je vous le jure
Wallay Ndeysan Yalnaniou Yalla Fayal Cheikh Seydil Hadji Malick❤🇸🇳Wayé kene dou Abdoul Aziz Mbaye ak Sidy Ahmed Mbaye❤🙏👑Yalnalenfi Yalla Bayi Niou Yague Diniou Bégal❤🇸🇳
Bilahi abdou aziz mbaye goudal fane ak weer... euleuk do rouss si kanamou maodo bilahi...yaw abaibe sarr ibou sakho kéne amoul sène fay yalla nalène yalla fay si barké szeydina mouhamed psl
Mach Allah Pape dji Yana bour yalla wéral batte bi ti maye la wérre samala are la Ak mbolami djoulite Malikia thiakaw sa thiakanam incha Allah Bon Gamou Houma islamique Di gnane 🤲🤲 sunu Khalifa bi yaggue fi loleu té andak wérre
Malika & Asfiyahi yalna yalla barkèl tèlè bi yagal fi Khalifa bi ak Ndiabott gui yèp Abdou Aziz Mbaaye yalna yalla goudal fan wi yak famille Mame Moussa Ale Mbaaye gui yèp
Masha'allah. Yalla nagnou yalla fayal Mame Maodo ak ndjabotam. Papa Abdoul Aziz mbaye ak papa Doudou kende mbaye ak ndjabote gui nguén jité yague léne fi lool té ande ak wér. Déwénaty à tous
هذه الأنشودة تزداد القصيدة رونقة وجمالا من حيث التنسيق و النغمة العذبة والصوت الهادئ وخاصة في هذاالبيت إني فقيرومسكين ومنكسر yaall n'a yalla fayalnou mawdoui
Salam je suis tidjane mais talibe baye niass wayé mane dama.beugue seydi el hadji malick sy billahi adouna sunu xamone kane moy mame moado waleu mou wanone gnou boppam senegal keneu dou fittou wote billahi mako wah té fou laire lako.teck nak
Machallah Malikiya TV Ak Asfia TV mangui niaane Yallah ayy xëweule you may lën di téralë mou donn ayy millards bijahi Naby Moustapha s a w s... Vraiment xool seed n'a gouyyyy si yeen Yallah guën gueuneu barrel Amiiine Amiiine Amiiine ya raby
Machala baye abdou aziz mbaye yalla na yalla wereule bate bi thi barekep yonne sedal gua khol yi nékhe na loll thiey cheikh seydil hadji malick sy mo meuneu taga yonéne bilahi
Bilahi Abdou Aziz mbaye yalla naga goude fanne nii ngaye séédlé sama koolll bii euppp naa limaiye niane yalla moye mou défma deugue deugue talibé cheikh ma dound sii tarikha bii déési dékissi si barkhé serigne babacar sy amiiiii♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Vraiment merci beaucoup Malikiatv depuis japon Jai bien apprécié votre travail trés propre son et image et surtout l'initiative Yalla na Yalla doli takhawou
Salam Alaikum. Djeuredjeuf.les anciens ont travaillé pour nous, ils ont tellement de blessés pour nous. Mais c'est nous qui nous limitons et n'avons pas compris qu'ils ont fait des pactes entre eux en fonction de nos challenges, ils se relèvent pour nous assister. Yalna naniou oubi sou nou khool yi, te tataane kheweel yi. Djeuredjeuf mame Elhadj Malilck Sy. Alhamdoulilha rek
Machallah 💥 Jeunesse Tidianes MALIKITE d'Italia Moghi Lèndi Ndokel bu bakh Tabarkalah 💥💯💫❤️
Mashalla, ndok sa wal. Yalla na lene Yalla Faye 🙏
Mashallah ❤🇸🇳
Très très fière d'être Tidiane.
El Hadj malick n'a pas d'égal.
11¹¹1¹p13 œyl7pjky
Aa
Ya Kachifa Da ii 😭sama meilleure Khassida 💓🤲🏾
Mashalla 🙏🙏
Dafa yèmè
Seder nako c la deuxième fois ngay commentaire si khassida bi
Sokhna Amina mou bakh miii
@@papediakhate930 ndeyesane deugleu 🙏🏾❤️
Je suis mourid mai mam modo manna way lol limi wakh nékhna lol إني فقير ومسكين إلى آخرها ماأجمل هذه القصيدة في فنن التوحيد. ياسيد الحاج مالك سه جزاك الله خير هذه القصيدة تهتز قلب السليم والله سأسمع كل يوم هذ البرنامج عبد العزيز امبي مع حزبه كلها نسأل الله أن يجعلكم خير وأ ن يطول الله عمركم أناأفرح جدا فرح الله بكم ببركة سيد. الحاج مالك سه
Mashalla
Machallah limou woy mo nekh té daw yaram
Masha Allah Yallah nala Yallah faye sa khole sèdè bi rafetna 🤲💓💕💗❤
Choukouran
Mais serigne touba ak mame maodo bénn lagnouuu
Yalna yalla barkel te fayall niou seydi hadj Malick
Di ngène ma rayy rekk té sama heure diotagoul😭😭😭heure boumakoy deglou je n'arrive plus à retenir mes larmes😭😭 yalla naniou yalla fayall souniou Mame Cheikh Seydi El Hadji Malick Sy
Pareille comme moi.
Dafa nekh si xol mais doundeul lou bari
So khamé signification bilay gueneu nékh
Amine ❤❤❤❤
Allahouma Amine barké Yonente bi sala lahou alayhi wa Salam.
Barkep Serigne TOUBA li ap yéfar szkh bouko dégueloo warna toyal kholam Machallah
Dieureudieuf
Yaw sokharo, yalnala Yala faye thi sa wakh bourafete bi, thi barke sa serigne Mame Cheikh Ahmadou Bamba Mbacke ak barke sama serigne Mame Seydi El Hadji Malick Sy radiyalahou tahalaa anhoumaa
💯 %mouride mais li dafa nekh bilahiii yalla na yalla may goude fan
Thiey yalla bi mom moy sama khasida prefere si xol lay dougou bilay mbaye yalla ga goudou fan❤🤩
En tous cas khawma kane wayé Borombi khamal nama secrets bou reuy si khassida "Ya kaachifa D'a " ,je l'écoutais durant l'hiver 2021 coïncidant au Mawlid virtuel du au covid19 avec beaucoup de difficultés et de peine pour s'en sortir ici en Europe, dans un restaurant en faisant de petits boulots en noirs 😢😢, à la sortie de ce mois béni, Dieu à résolu tout mon souhait...(Qu'Allah l'agrée Cheikhal Hadji Malick et sa noble famille, ainsi que la famille de Moussé Alé Mbaye bidiakhi Taaha Yaçina Aleyhi Salam)
... Fcv
😢Cft😢😢5😢
Machallah ❤️😍😍Y’a Kachifa Da iii Dafa yemé dehhhh Mane mome beneu seutou Seydil Hadji Malick moomako done tekiillll un jour😍❤️
@@maguettediagne3585
Surtout bo khamé gorgui limou siy niane 🤔adouna ak lissi biram mongui si ...Yalnaniouko Borombi woutou fayal niouko Incha Allah
Alhamdoulilah bima boké si djaboot seydil Elhadji malick sy RTA🥰🥰🥰🥰😭😭😭😭
Alhamdoulilah machalla 🙏
Bilay yak kanne
Dieureudieuf mame maodo et merci malikiatv. Si kaw si kaname
Mane yaw ak kane😍😍
13:06
Maodo bindeu neu louné, Abdul aziz mbaye wayééko nouné! MashaAllah
Bilaye
Machalla Abdou Aziz mbaye yalna sa diam yage barki serigne saliou
Allahumma Amine
Macallah merci beaucoup Abdul Aziz
Masha'Allah. Je ne sais pas vous mais ce Khassida transperce mon âme, et je ne peux retenir mes larmes. Yallah nagnou Yallah fayale mame Maodo. Amin yaa Rabbi....
Amine inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
SALAM même moi sama holl dey fess mashaALLAH Dieureudieuf Amine YA RABI pareillement inshaALLAH
pareillement wallahi ❤❤❤
Allahouma amine
L'émotion dans laquelle nous plonge les paroles de ce khassaïde et la chorale est indescriptible ; on dirait que toutes ces voix ont été faites pour fusionner toutes ensemble afin de nous déclamer si harmonieusement Ya Kachifa Daa'i de Mame Maodo... Au delà de tout ça, la qualité de la vidéo, du montage et de la présentation est impeccable !!!
Yalla fayal gnou leen ci liguey bou rafet bi 🤲🏾❤️
Masha allah le meilleur commentaire
Bilaye vous avez raison j'ai les larmes aux yeux ce que je ressens sans même comprendre ce qu'ils disent est indiscriptible je pleure !
Walahi sa mappaise
@@katykane2725 c est le mot elle apaise
@@yanidoungom6092et fais pleure en meme temp
Yalla nalèn yalla takhawou sam len guoudou fane were ak werlè yokou xam xam bi ak katane bi ❤️🙏🏽🕋
Amine
Malikiya tv séne lépa raféte,billahi li waroule diékh,loumaye yeuk sama xol mane rék mâko xam,dieuredieuf diaredieuf,yala bou kéne manké,ba déwéne inchallah,ndawe yi sounú borome mayléne aye CDI,baniou térale séni wadioure,aminne billahi sounú borome yalnko défe
Allahouma Amine, Mashalla Yalla nalene Yalla Faye
Qualité Son et image c'est Top Mashallah Malikiatv Yalla na Yalla bollé ci tele you mak yi nguene niou yagg beggueul ci Salalahou Aleyhi Wa Salam❤
Allahumma Amine 🙏. Yalla na lene Yalla Faye 🙏
Amine ya rabi 🙏🏾👏🏽
Macha allah bouma ammé kénn lou may gné ci adouna moy gnii. Yalla na lénn yalla fay té yagallén fi. Grace à vous des gens comme moi commencent à maitriser les écrits Seydi Elhadji Malick Sy radiyallahou taanla anhou. Encore un grand merci à vous
WALAHI NDEYSANE 😭❤️❤️
MAÀCHA ALLAA MBEEGUE CI YEEEENN
À part Dieu, son messager psl❤️et nos parents. Amatougnou lénéne loudoul Mame Maodo Malick Sy ❤️❤️rta
Bilay ❤❤
La lumière du prophète psl est le source de nos lumières ❤️❤️❤️❤️❤️ mame Moado yaniou khamal yonénti bi ❤️❤️
mashalla
Je lol ini
Bilahi moado mon niou khamal yonénti bi (psl)
Bilahi moniou ko hamal
Walahiii
Keen dou Maodo wayé Abdou Azize Mbaye dara nga machallah 🖤💫🖤
Machalah, yal na Yàlla may léen wér ak wérle ci barke Seydinaa Mohamad SWS.
Ay way abou mbaye temps yi nigay sédalé sama hol bi yalnako yalah faye thi barké seydina mouhamed psl🙏
Allahumma Amine 🙏
Kholl seddana Billahy
Amine ya Rabbi ❤❤🙏🤲
Al Hamndoulilah 💘 yalnagnou yallah fayal Maodo 😭♥️ abdoul aziz mbaye yalna yallah goudaal saay fane 🙏 Malikya Tv yalnaléne geuna taxawou bidiayi seydou woudioudi SAWS ♥️
Allahumma Amine 🙏
Y'ALLAH n'a Abdoul Aziz mbaye doundou 💯 ans amine,🕍🕌🕋🕋🕋
Amine ya rabi
Amine y’a rabbi
Amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine
Ameeen pour les prieres qui sont dans ce Qassida
Begte bou amou app yalna maylen wer ak fan wou goude lool
Masha'Allah ! Malika TV vous avez fait un travail remarquable. Enregistrer la famille de feu Moussa Alé sur les écrits de Cheikh Seydi Hadj Malick, maouloud 2021,nous n'oublierons jamais.
Mashalla, merci beaucoup à vous. Yalla na lene Yalla Faye tamitt 🙏
Machallahhhhh
Fatabarakala
@@malikiatvtivaouane t
Masha Allah je vous aime très fort ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mbaye Yana yallah Goudal fanwi🙏❤️😭
Abdou Aziz mbaye yalla Nafi yague té ande ak werr si barké seydina mouhamed ak ndiabotou mame moussé ale mbaye yeup machalla wayy nékh na😍🥰❤😭
Allahumma Amine 🙏
amiin yaa rabbi
Machalla 🙏🙏🙏😭😭😭❤️
Amiine à toi aussi ❤
Est ce qu'on connait nous tous les senegalais qui est CHEIKHOU Hadji Malick sy
Serigne Cheikh Tidiane Sy Almaktoum a raison de dire Maodo l'inconnu de la nation on peut même dire de l'humanité
On ne le connaît pas assez malheureusement c’est la solution pour le Sénégal
Mach'Allah yallna sén diam yag si barckè seydina mouhamed psl ♥️🙏🏽
Ini fakiroun wa miskinoun wa moun kassirou.......❤❤❤❤
Ah dayo bimou am sou démé bay wah li kémane leu😪
Bilakhi souma yalla dèfoul wonn talibè cheikh khawma sama dound loumouy donn dieureudieuf ya rabbi
J'aime tellement cette chanson que parfois quand quand je l'écoute j'ai j'ai le cœur qui bat comme s'il y avait quelque chose comme si j'avais perdu quelqu'un cette chanson est vraiment vraiment très belle je vous le jure
😢😢😢 la lumière du prophète paix et salut sur lui
Wallay Ndeysan Yalnaniou Yalla Fayal Cheikh Seydil Hadji Malick❤🇸🇳Wayé kene dou Abdoul Aziz Mbaye ak Sidy Ahmed Mbaye❤🙏👑Yalnalenfi Yalla Bayi Niou Yague Diniou Bégal❤🇸🇳
Thieuy mbékté biii dh kéne xamoul noumou tollou ❤️ Yalna gnou Yalla fayal Seydil Hadji Malick Sy (RTA) 🙏
donn tidjane dafa nékh donn tidjane doyna titeure 💙💙
Yalla nanou yalla fayal seydil hadji malick sy
Bilahi abdou aziz mbaye goudal fane ak weer... euleuk do rouss si kanamou maodo bilahi...yaw abaibe sarr ibou sakho kéne amoul sène fay yalla nalène yalla fay si barké szeydina mouhamed psl
Mach Allah Pape dji Yana bour yalla wéral batte bi ti maye la wérre samala are la Ak mbolami djoulite Malikia thiakaw sa thiakanam incha Allah Bon Gamou Houma islamique Di gnane 🤲🤲 sunu Khalifa bi yaggue fi loleu té andak wérre
Malikiya TV assure gua dall si gamou gui machalla
Dieureudieuf mashalla 🙏
J suis yaye fall mais j'aime bien ce tahissire machalla ♥️🙏🙏🙏🇸🇳🤗🤗🤗🙏♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Longue vie à abdou aziz mbaye et à la famille moussé allé Mbaye
Allahumma Amine 🙏
Dieureudieuf Malikia TV. Sett na..nekh na séleu na..diékeu na. Yalla na Borom bi barkél si barké Salatoul Fatihi
Yalnagnou Yallah fayal Sunu Mame Cheikh Seydi Elhadji Malick Sy (rta)🤲🤲🤲
Malika & Asfiyahi yalna yalla barkèl tèlè bi yagal fi Khalifa bi ak Ndiabott gui yèp Abdou Aziz Mbaaye yalna yalla goudal fan wi yak famille Mame Moussa Ale Mbaaye gui yèp
Tout ce qui vient du coeur va droit au cœur MACHA'ALLAH
yalna nalénn yalla faye si serigne babacar sy niou wakh amine
Masha'allah. Yalla nagnou yalla fayal Mame Maodo ak ndjabotam. Papa Abdoul Aziz mbaye ak papa Doudou kende mbaye ak ndjabote gui nguén jité yague léne fi lool té ande ak wér. Déwénaty à tous
ALLAHOUMA AMINE
Dieureudieuf seydi Elhadj Malick sy
Yalla na yalla delosi diamou keurgui ak tawe fékh Sibarké
Seydil hadji malick 😭😭
Nagnou sunu borom fayal Cheikh Seydil El hadji Malick 🙏🏼🙏🏼❤️
Amine ya rabi
Amine 🙏🙏
0
@@ayibeseye8991
Amiiine ken dou moome waaay !!!!!
Juste magnifique un chef d’œuvre vraiment cheikh seydil Hadji Malick Sy rta ya kaachifa daà’i
Macha allahh amena solo yalla nala yalla samou Sénégal 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳
Machallah nekh na lol
هذه الأنشودة تزداد القصيدة رونقة وجمالا من حيث التنسيق و النغمة العذبة والصوت الهادئ وخاصة في هذاالبيت إني فقيرومسكين ومنكسر yaall n'a yalla fayalnou mawdoui
ملاحظة دقيقه ومهمة
وأنا شخصياً كنت سيغمي علي في بيت من نوره نيل ما نلنا جزاكم الله خيرا
Salam je suis tidjane mais talibe baye niass wayé mane dama.beugue seydi el hadji malick sy billahi adouna sunu xamone kane moy mame moado waleu mou wanone gnou boppam senegal keneu dou fittou wote billahi mako wah té fou laire lako.teck nak
Djeureudjef, ya niak kignane yalna Yallah feyla s khol ci barkei Mame Baye Niass
@@fatimsow5870 allahouma Amine lothi khamou keur Mame Abdou Aziz Sy fi thi Dakar la diangué Mouy doundou makoy Guisse môme Mame Abdou Aziz Sy
Machalah rék yalla na yalla fayléne yiw si Barké Seydina Mouhamad PSL kéne dou Mame Maodo contane rék
Merci Malickia TV séne liguéy rafét na yalla naséne diam yague
Machallah Malikiya TV Ak Asfia TV mangui niaane Yallah ayy xëweule you may lën di téralë mou donn ayy millards bijahi Naby Moustapha s a w s...
Vraiment xool seed n'a gouyyyy si yeen Yallah guën gueuneu barrel Amiiine Amiiine Amiiine ya raby
ALLAHOUMA AMINE. DIEREUDIEUF
WA RAHMATOULAHI KOULAL QALQI QAD WASSIHATMINE FAJIRINE WA MOUTIHINE ZA-IDINE BARI❤🙏 YALNANU YALLA YEUREUM BARKÉ MAGG GNI
🥰🥰🥰😍😍😍😍😍😍😍😍😭😭😭😭😭😭😭 li lanla tmt thi nékh nékh diadieuf sm wadji yalna yala barkél
Ya allah fayal gnou seydi Elhadj Malick sy
Maa shaa alah yalah naley sounou borom défal kham kham bou guéneu niaw thi barkè seydina mouhamed
Amine amine 🙏
Yalla nagnou yalla fayal mame maodo thi barakati khour anoul karim amine
Machalla Malika TV khôl seed yalla na yalla faye si barcker seydina mouhamed saws ♥️♥️♥️♥️🇲🇷🇲🇷
Mashallah wa malikia amlen diamou rek contanna merci beaucoup
dieuredieuf
Machala baye abdou aziz mbaye yalla na yalla wereule bate bi thi barekep yonne sedal gua khol yi nékhe na loll thiey cheikh seydil hadji malick sy mo meuneu taga yonéne bilahi
Malikia + asfiyahi = mbecté reik machallah à vous du bon boulot
Mashalla dieureudieuf 🙏. Ensemble pour la hadara
Mane dh « les jumelles » laléne doupé walae Ndeysane
bane mbecté ? shirk rek
@@ndiogou1587 On est où là tagg Seydina Mouhammad nguanane bokkalé 🤣😅
@@ndiogou1587 démal sawi té teudi
Malikia Tv si kaw Si kanam Inshallah…
Dieureudieuf Seydil Hadji Malick rta
Allahumma Amine 🙏 dieureudieuf
Yalla yalla Faye thi barkè seydina Mohamed Amine 🤲🤲🤲
Amine
Je écoute et réécoute jusqu'à 200 ans et 200 millions de vues il me soulage bien merci beaucoup Malikia tv
Yalla na yalla goudal sen fan si barke seydina Mouhamed saw ak seydi El Hadj Malick Sy sa youma wete moy sama weteul.
Alhamdoulilah li dafa nekh waay dieureudieufé cheikh Seydyl Elhadji malick ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oh ndeysane el hadj abdou aziz mbaye yalna yalla wereul batt bi ak kep kouy tag katou yoneneti bi
Macha Allah.diarngeun dieuf sagal ngeun wakeur Mame Maodo gui yeupe.
Ma cha allah khol yeup toye na Yalla naniou Yalla fayal mame maodo
Dieureudieuf famille mame moussé alé
Dieridieuf malickia t.v de nous faire entendre ces belles paroles de Abdoul Aziz Mbaye dieridieuf maodo Malick
ndeysane mouride bou mak Abdoul Aziz mbaye Daf may doundale
Masha’Allah✨✨✨✨yalla nagnou Yallah fayal Mame Maodo🤲🏾❤️
Amiiiiiiine
Walay tayy gnou déeé😭😭😭😭😭😭lii dafa eupe si sunu xol you ndaw yii
Sunu khôl atanoul lii dé walay
Wallahi mbekte reik lay am soumay deglou li♥️♥️♥️
Walahi, je peux l'écouter à longueur de journée.
Machala baye abdou aziz mbaye yalla na yalla goudeul fane ni guaye weuyé khasida mame maodo yi ame na sollo loll
Tabarkala machala. Walahi cheikh seydil hadj malick sy rta bindeu nowul ak keneu.yalla fayal niu ko inchala.
Malikya tv sounou borom barkel
Billahi sama khôl sedd na sante yalla bama nékké talibé cheikh diarama seydil hadji malick
Bilahi Abdou Aziz mbaye yalla naga goude fanne nii ngaye séédlé sama koolll bii euppp naa limaiye niane yalla moye mou défma deugue deugue talibé cheikh ma dound sii tarikha bii déési dékissi si barkhé serigne babacar sy amiiiii♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machallah li mouy Def thi khol nékhna lolou. Yallah nagnou Yallah fayal Seydil Hadj Malick Sy Rta ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machala malikiyah tv yallana nek tèlè bi gueneu mak si monde bi tè barkel
Sante rekk bilaye pape diamm sii yaww
celui que j attendais le plus 😭😭😭
Fa hl kg cv j g k
Macha Allah abdoul Aziz mbaye
Yalnaniou yalla fayal SEYDIL ELHADJI MALICK SY R.T.A
AMIINE
Vraiment merci beaucoup Malikiatv depuis japon Jai bien apprécié votre travail trés propre son et image et surtout l'initiative Yalla na Yalla doli takhawou
Allahumma Amine 🙏 ziar bou bakh machalla
Masha allá
Ma cha ALLAH,
Abdou Aziz mbaye yalla na yalla guoudeul say fan ak bolem famille mame moussa allé
Yalla naniou yalla doli fayal Cheikh Seydil Hadji Malick Sy walahi Sy fagoul nganiou lou bëri
yalla na niou yalla fayal seydi elhadji malick sy
Machalla yalla na yala Dollé goudal fane yi amine amine amine amine
Toujours dans nos coeurs Ya Kachifa Daa i❤😢 MashaAllah diarama Mame Cheikh Seydil Hadji Malick Sy🙏🏾🤲🏾❤️
Fane you goude akk wérr gou yarame insha Allah mbaye wakh léne amine 🙏🙏
gorgui abdou aziz mbaye ak ñimou andal yalnaleen yala samm ta faylenn
Sa lumière est la source de toutes les lumières saws
Salam Alaikum. Djeuredjeuf.les anciens ont travaillé pour nous, ils ont tellement de blessés pour nous. Mais c'est nous qui nous limitons et n'avons pas compris qu'ils ont fait des pactes entre eux en fonction de nos challenges, ils se relèvent pour nous assister. Yalna naniou oubi sou nou khool yi, te tataane kheweel yi. Djeuredjeuf mame Elhadj Malilck Sy. Alhamdoulilha rek
Machalla wakeur Mame Mousse Allé dieureudief baye AZIZ mention spéciale à Malikia TV c'est une fierté être une tidiane mais aussi beugue Mame Maodo
Amine yaraby mâcha allah cheikh seydy Haji malick