Vraiment baye Mass je suis un fan inconditionnel de ta musique chaque jours j'écoute ta musique avec ta voix qui touche tout ton âme vraiment bonne continuation song bi nekhna trop trop machallah
Ohh bay mass man bilay j tadore litakh ma gueun la beugu man nit no meunti mel bo beugué sa yaye fonk KO dameulay té guisna sa relation ak sa yaye meun na ni tay la xam Iow yay kan depuis fadjar ba legui magui def recherche si iow setan na plateau yignoula invité yeup té musique meussouma dioylo mei tay say son m'ont fait pleuré Tay nk la la xam mei vrement j valide tu es jeune talentueux machalla yalla na la thiatt sekhlou gua guiss lou kawé sa ndiort sissa carrière ba yéné bigueu am sisa yaye yalla motaliko si barké serigne touba Et pourtant son pod et marichou bi j lé cherché partout ndéké yako way bima KO deglo amatouma diam pour xam kiko way et te voi la frère diam si iow niguaniouy bégueulé yalla nala KO yalla beugueulé
Ce son mérite des millions de vues 😍 Je ne suis pas fan de mbalax, je suis plutôt hip hop mais je ne peux plus me passer de ce morceau et je pense même en faire ma sonnerie de téléphone 🥰 Waly ak Sidy Diop boy baa ngi ñëw dal seen kaw 😂
Machallah baye mass mann dé meusouma déglou musique yaw rék lay déglou ndakhté lingay woy khalé meunnako sétan ak makk vidéo bi simple neuh wouténa ak musicien légui yi nga khamni Dani dieul ay khalé sol lo lénn ay yeuré you Bonn souko déffé khaléyi Di roy si gnom mais nk bonne continuation mon frère je l'écoute et l'écouterai personnes que toi billahi ♥️♥️
Machala lima yékha commenté rek moma metti mais je fais partie ci gni ndieukeu am son bi,g tte ta music dans mon repertoire boy say parole nio riche machala moi et ma femme on te bégué grave machala amal diamm
Machallah Baye Mass Jour bimala ndieukeuh deglo moy beuss bou El Maestro done présenter album ba inviter la si lako ladj wa Maestro ndanane bi kane la? Mounima Eva ki moy Baye Mass nanguene ko baayi xel Machallah yalla nala dioureul ay disques d'or inch'Allah 🥰❣️😍🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Machala mass yaw sa son yeupeu nekh yarou nga khamnga adouna et tu es vraiment talentueux man j t sui depuis des annees mais rien a dire bonne continuation
Ohhhh Sama ndanaande bi💪 Nieuwat na AK lou nekh 😍 superChanson 😍😍 Nice Clip Belle viox😘🎼 Lingay def dal l'AF thiat rek 😍😍😍😘😘💪 Contane si yaw trop waay😍😍😍
Tu resteras toujours notre artiste très belle voix même en reprenant le "Ndékété Yow Nobouloma" de notre chère tonton Youssou Ndour tu as travaillé le son avec tes propres mots qui ont beaucoup touché les internautes bravo à toi 👏👏👏👏. Très belle rénovation !!!!! De la part d'une de tes fans
Futur youssoundour inchallah ki est d accord avec moi😍😍😍
moi inchallah❤
Merci
@@bayemassofficiel nagn la nianal rekk yalla mousseul la bou bakhh🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Machallah beug nala trop 💕💕
C claire🙏
Baye mass futur Youssou Ndour inchallah ❤️❤️
Wa yen fah aidara mii mii rafett na di😭❤ en plus elle joue très bien machallah
Vraiment baye Mass je suis un fan inconditionnel de ta musique chaque jours j'écoute ta musique avec ta voix qui touche tout ton âme vraiment bonne continuation song bi nekhna trop trop machallah
Baye mass j’ai déjà like avant song bi di nieuw 😌😂
Même moi 😂
Moi mm
Ak mane 😂😂
Message Président Ousmane Sonko🇸🇳〽️🏅
ruclips.net/video/j1MOzYSrPj4/видео.html
Moi aussi
Merci beaucoup pour vos commentaires, le meilleur est à venir. Abonnez vous et activez la cloche y'a beaucoup de chose qui arrive.
Milles Merci ! ☺️
Ton nmro svp
Continue mon frer t es le meilleur 🙏🏾🍀✊❣️
Inch'Allah thia kaw thia Kanam rek
♥️♥️
Ohh bay mass man bilay j tadore litakh ma gueun la beugu man nit no meunti mel bo beugué sa yaye fonk KO dameulay té guisna sa relation ak sa yaye meun na ni tay la xam Iow yay kan depuis fadjar ba legui magui def recherche si iow setan na plateau yignoula invité yeup té musique meussouma dioylo mei tay say son m'ont fait pleuré
Tay nk la la xam mei vrement j
valide tu es jeune talentueux
machalla yalla na la thiatt sekhlou gua guiss lou kawé sa ndiort sissa carrière ba yéné bigueu am sisa yaye yalla motaliko si barké serigne touba
Et pourtant son pod et marichou bi j lé cherché partout ndéké yako way bima KO deglo amatouma diam pour xam kiko way et te voi la frère diam si iow niguaniouy bégueulé yalla nala KO yalla beugueulé
Association des inconditionnels de cette sublime voix. Niongui khaar.
FMa
waouhh waouhh waouhh notre Mass à vraiment déchiré la toile hein🎉🎶
Merci
Ils l'ai fort
Go one frère on apprécie ce k tu fais continue de nous surprendre nak et vite parfoi Khar bi day yagg dé
Merci beaucoup !
Ce son mérite des millions de vues 😍 Je ne suis pas fan de mbalax, je suis plutôt hip hop mais je ne peux plus me passer de ce morceau et je pense même en faire ma sonnerie de téléphone 🥰 Waly ak Sidy Diop boy baa ngi ñëw dal seen kaw 😂
Yess👍👍👍
Machallah baye mass mann dé meusouma déglou musique yaw rék lay déglou ndakhté lingay woy khalé meunnako sétan ak makk vidéo bi simple neuh wouténa ak musicien légui yi nga khamni Dani dieul ay khalé sol lo lénn ay yeuré you Bonn souko déffé khaléyi Di roy si gnom mais nk bonne continuation mon frère je l'écoute et l'écouterai personnes que toi billahi ♥️♥️
Merci beaucoup !
Watal
@@serignemodoundiaye5826 barké Serigne Babacar sy yalla rék motakh may wakh
Tiaatu neeg bi yaa aay way! Ma Sha Allah!
Blessings de la part de toute la famille!
futur youssou ndour
Machala lima yékha commenté rek moma metti mais je fais partie ci gni ndieukeu am son bi,g tte ta music dans mon repertoire boy say parole nio riche machala moi et ma femme on te bégué grave machala amal diamm
Bravo encore le frère Baye Mass et toute l'équipe vraiment job bi nice na. Bonne continuation ♥️😍🎤🎶
Cvb
Machallah Baye Mass
Jour bimala ndieukeuh deglo moy beuss bou El Maestro done présenter album ba inviter la si lako ladj wa Maestro ndanane bi kane la?
Mounima Eva ki moy Baye Mass nanguene ko baayi xel
Machallah yalla nala dioureul ay disques d'or inch'Allah 🥰❣️😍🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Le meilleur son que j'ai écouté et je suis congolais 😁en plus j'aime trop le Sénégal meilleur pays d'Afrique
Merci frére
@@vieuxndiaye2074 yyÿ oooyiy
Très belle chanson é Bne continuation frére liguey rk
Machallah ndékei teh yoo yafi neh🥰🥰🥰🥰
Mâchala notre chanteur national domou thiaroye🦋Dinagn la degg fou soré sori🥰laff thiate rk 🙏
wallahi tu es le meilleur de ta generation jmo
quelle belle voix machallah❤❤👏👏
Merci
ruclips.net/video/6T0zAeOhm3E/видео.html
🙏🙏🙏
@@bayemassofficiel bon continuation baye mass yalla na yalla sammo la defal la diamou te mayla wer barkep Serigne Saliou
Message Président Ousmane Sonko🇸🇳〽️🏅
ruclips.net/video/j1MOzYSrPj4/видео.html
Mane dislike yi rek moma diakhal sons bi vraiment c’est top et quelle voix machallah Baye
Musique bobou maay degu si souf yaaw ak sokhou bébé dinaa todj senegal defar xol you beurri Ma sha Allah
Incha Allah, c'est sur !
Continu comme ça very very Nice Macha alla kéne d'où yawe je t'adore vraiment longue vie à toi
Le Meilleure tu es le Meilleure musicien du monde yalla na la yalla diapallè
Félicitations Mass
Très bon message à la jeunesse
Kou nékoul cii li yallah santané yagui si erreur
Et il n'est jamais trop tard pour se repentir
Futur Wally seck waw ki est D'accord avec moi 👍👍👍
Merci beaucoup !
Bane Waly ki mo dakk Waly weuy c chansons réveillent!!! C mm pas semblab
@@jacqueskennedyndiamy1245 tu n'ai pas sérieux j'espère
Ki futur Baye Mass leu epi c tou! Yalla nako yalla daf carier bou Mak ba nit gni beug nek futur mom!🤲🏾
@@owbiking9341 Amin
MACHALLAH Baye Mass voix bii moh am ndeyesan machalla sa sort du coeur et vas tt droit vers le coeur MACHALLAH laff thiatt bnne continuation
Merci beaucoup
Avant makay déglu laa liké❤😂
Merci
Nice future youssou ndour 🤩🤩🤩😘😘😍😍😍💯💯❤❤
Un gars que j’aime depuis le temps des covers
Merci beaucoup !
Thieuy mom frr aa diam yalla na yague
J'adore vraiment 🥰
Ok
Message Président Ousmane Sonko🇸🇳〽️🏅
ruclips.net/video/j1MOzYSrPj4/видео.html
Mashaallah mashaallah mashaallah🙏 baye mass yalla boula thiat dougg inshaallah yaw wayentou wo dh futur youssou ndour inshaallah je T'aime bien🥰 yalnala yalla sameu boubaxx bonne continuation frère 🙏amal diam waay
What a voice! Love all the way from Gambia🇬🇲🇬🇲 keep it up baye mass the sky is the limit
Salut
machallah son bi nekh na fah comme dab tu assures
Oh Baye Mass J'adore ton style de musique les paroles son riches et je vois trop de maturité en toi bon continuation
Merci beaucoup !
Nékh na yalla na yalla wéreul batt bi té lafale si thiatt
Sama song bii😍💪🏾💪🏾💪🏾Merci frère depuis sa status ba balégui magui koy xar
Merci
Non sa première son lala beugé ba taye baay mass yalla n'a yalla dolly soutoura rek machallah ms n'a geuneu tangue rek Dina nieuw 😍😍🔥❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ohhhhhhhhh Machallah sama kholll sedddd na😍🔥🔥🔥
Merci bro
Ww futur youssou Ndour mahalla yalla na bate bi wére je t'aime dall🥰💯❤❤
Vraiment Baye Mass il est bon ce jeune la et de plus ce clip est très simple et beau la qualité d’image excellente le son rien a dire
Merci beaucoup !
Mon fils Son neikh loll ❤❤❤
Tu as encore frappé fort✌😍machalah frère 😍bne continuation
Dieureudieuf
Très bell voix
Man mom may sa fan num1
One love Baye mass depuis Paris j'écoute tout tes chansons trop fort machallah🙏
Machala mass yaw sa son yeupeu nekh yarou nga khamnga adouna et tu es vraiment talentueux man j t sui depuis des annees mais rien a dire bonne continuation
Macha allah ❤️❤️❤️ fr le futur ambassadeur de la musique Sénégalaise bonne continuation
machallah bonne continuation ❤❤❤❤💗💕💗💕💞💗❤
Il est incroyable ce mec😭🔥❤
Merci beaucoup !
1ere fois ma guiss son bamou diexx ter amoul maquillage machallah notre Fa🥰
🔥❤️ force à baye mass il chante trop bien courage
❤️❤️💝💝💝💝💝💝❤️
diadieufe frère dina bakh ❤❤
J'aime ta timbre vocal bonne continuation
Machalla baye mass laf thiate bilakhi yaw la wa thiaroy am boul tite dara sa kaw sa kanam😍
Fier d'être from thiaroye 😍😍😍🎁🎁🎊🎀❤️❤️🎉🤸🏽♂️🤸🏽♂️🔥🔥🔥🔥🔥🍯🍯🍯🍯🍯le miel intense est servi
Merci beaucoup !
tu es mon chanteur j ecoute tout tes chanchon machallah
On t'attends depuis Paris que Dieu te garde🙏❤❤❤😘
Yes WA Paris
Merci pour ta réponse😊🤝👍
@@womanpower4355 h
Merci beaucoup !
@@bayemassofficiel De rien mon chanteur préféré tu es le meilleur macha allah❤❤❤😍
Baye mass yalla na la yalla defal diamou
Bly yw Lou lrr futur Youssou Ndour 💖💖
Futur baye mass et youssou Ndour qui est d'accord avec moi lalale j'aime bien ❤❤❤❤❤❤❤❤
Bay mass Diga yagall musuqe senegal bi❤️❤️❤️🇬🇭🇬🇭
Avant de dislikey prenez le temps de visionner😪.
En tt cas joli clip ,son bou nexx😍
Ohhhh Sama ndanaande bi💪
Nieuwat na AK lou nekh 😍
superChanson 😍😍
Nice Clip
Belle viox😘🎼
Lingay def dal l'AF thiat rek 😍😍😍😘😘💪
Contane si yaw trop waay😍😍😍
Merci beaucoup !
Afia RĖK Frr dina bakh inchll🎺🎧
Baye masse💖💖💖 fierté bi depuis si sa sons cover yi sa voix massalah 💞💞 Big respect
👇👇👇👇 J'aime
Merci à vous
Baye mass je le connais il habite à thiaroye 😍♥️♥️
Force à toi frere courage ✌🏾et bonne continuation 🙏🏽💪🏿🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
✅❤️
Mon Gas il frappe tjrs comme un volcan !!!!✊🏽✊🏽👍🏿🇸🇳 Eksigaaa Mass!!Ak Masse!!!!!
Une plume et une voix, one love ❤️🙏
🥰🥰🥰💙💙💙💋💋💋
Machallah kén dakouko way Baye Masse bonne continuation frère
Bravo mass et félicitation pour la suite 🔥🥰
Merci beaucoup
Nice frrr
Gueume ko rek frère ta boul guestou ndakh dina mèti Waya inchallah Dina bakh♥️♥️♥️
Merci beaucoup ❤️ ! Suivez moi sur Instagram instagram.com/bayemassofficiel_?igshid=n927whm3d9ng
Fah aidara you’re so amazing❤️🇬🇲😉
2eme couplé biii souma koy déklou ak moto damay faté sakh niii ma ngui dawal ❤️
Ci kaw ci kanam rk notre baye masss❤️🙏
Malabouge walahi ake sama niari fans yi 100% bété
Le peuple est content🔥🔥🔥🔥😁😁À streamer à fond❤️❤️✨✨
C juste waoh je c op koi dire mashallah on est derrière tw 😭❣
Baye Mass woy ga té thiaxanoo nn dafa néx❤❤❤
Merci beaucoup !
felicitation frr🤩🤩
Un jour inchallah tu deviens artistes international mon artiste préféré ♥️
Merci beaucoup !
On le suis depuis le Mali il a percé 🇲🇱🇲🇱
Mashallah ❤ yalla na yalla wereul batt bii th mousseul la thi thiat 😘😍
On est très fier de toi frère j’aime bcp la créativité l’innovation 🥰✊
Sama khel dém na si khoulo bi avec père Youssou ndour♥️😂😂😂
Nice boy!continue à faire ton bonhomme de chemin sans bruit.la réussite s'en chargera
Machallah boul wathieu yone winga téguou dé ne te laisse jamais pervertir par le succès
Nice..BMW..C t'un them qui est sous forme de dialogue,les mots son clair..et y'a le rythme et les rimes sont très riche..bonne continuation bro
Merci beaucoup !
@@bayemassofficiel je vous emprit
@@bayemassofficiel yty
Futur thione inchalla
Fah fayal nar bi lim la diokh😂😂😂dédicaces au joueur de pari foot😂😂😂😭
🤣🤣🤣 tu m'a fumé esk tmt nékoul narr bi wara fay parieur yi
Non mais boy international inchAllah !💯💫💥💞
Tu resteras toujours notre artiste très belle voix même en reprenant le "Ndékété Yow Nobouloma" de notre chère tonton Youssou Ndour tu as travaillé le son avec tes propres mots qui ont beaucoup touché les internautes bravo à toi 👏👏👏👏. Très belle rénovation !!!!!
De la part d'une de tes fans
Masha'Allah bien nanu xam liñu warrdéff 🧠 pour xallat la tmt , 🧠 boudul xallat luy avancé brom taxul ñuy wx
Pourquoi cette chanson est dans ma tête même quand je suis à l'école 😂 big up depuis 🇳🇴🇳🇴🇳🇴🇳🇴🇳🇴🇳🇴❤
Ki kom moi ne cesse d'écouter bilay nhna lol😍❤❤❤🔥🔥🔥🔥
Machallah. Fah 🙏🏿🙏🏿s’en thiouraye keur khadim ❤️
Merci
Super je te suite et on se verra dans le temps pour des projets bonne continuation
Machala nekh na trop billahi deff thiatt❤🥰🥰
Macahlah Baye mass
Nékha tina bay xol 😄♥️séddana wallahi
Quand je t'écoute j'entends Youssou Ndour 😍😍😍❣️
Merci
machalla