Quand elle dit qu’elle prend en main sa vie et qu’elle glow up sa carrière c’était pas des blagues hein . Elle y va et j’adore ce que je vois ❤❤❤ Nice song ❤
Déy soga dorr mais gueumna ni meuna bokk si gni tiyé music euleuk ndakh amna talent teh djeukna si forme teh osé na aussi amna tourr donc ndakhté mi na nguen ko bayi xél elle a tout les qualités d'artiste
Tiktok la guisé clip bi ma téla juger né dara nekhousi mes bima nieuwé guis clip complet bi la kham ni dama dioum❤🎉clip bi nekhna raffet na bonne continuation
Oh macha mais voix khalé bi voix ndanan la diom Mama Khar mame kiné Lam mame Soda Mama etc meuna nak macha et elle est très belle sa ma thiate ak bou sama morom bon vent chérie🔥🔥🔥🔥🔥🔥💞💞💞💞💞
Magnifique .. à noter que jn 'ai pas retrouvé le côté ''international'' contrairement au son ''glow-up'' mais jpense quand même que ndakhte à énormément d'avenir au sain de la musique Africaine voir internationale. MAY GOD BLESS HER ❤❤❤
Machalah nila ligey rekk inchalah ❤🎉 on est derrière toi chaque 3mois defal gniou Li inchalah ndam rekk bon courage ligueyi nekk sisa bop amoul lenen 🙏
vraiment je regrette pas le fait que j'ai plusieurs fois demandé à prince art de te donner le micro, je savais que tu as une si belle chose précieuse en toi. Vu le succès de ton premier single j'avais un peu peur de comment tu vas tenir le cap mais là j'avoue que tu es la meilleure et tu iras très loin. Ndakhté lo mes félicitations tu chantes vraiment bien mashallah bonne continuation à toi.
Quand elle dit qu’elle prend en main sa vie et qu’elle glow up sa carrière c’était pas des blagues hein . Elle y va et j’adore ce que je vois ❤❤❤ Nice song ❤
Je te jure hein ❤❤❤
Kou yéné ndakhté le meilleure rek lalale j'aime ❤🎉
Nite bou nek jam nga wara yene sa morom
❤
Très bien répondu bilahi défois dagnouye commentaire commentaire doff@@SeynabouDiouf-d4u
❤❤❤❤❤
@@MorgueyePouye C vrai mais amna niou nekk fi nio khamni lou bonn rek lagne yénei sen morom n'est ce pas
Clip bi nice na son bi nekhna ma dieulate ko mayko ma meilleure Mame Fatou jtm fort bb ❤️❤️❤️
Sama tourandore homonyme ❤❤
❤❤❤🎉🎉🎉🎉Respectons les cinq prières quotidiennes et ayons une confiance entière en Allah car il n'y a de force et de puissance qu'en Allah ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Magnou diame bougnou fate bougnou waré diouli dinagne ko def finak c pour ce divertir seulement
Déy soga dorr mais gueumna ni meuna bokk si gni tiyé music euleuk ndakh amna talent teh djeukna si forme teh osé na aussi amna tourr donc ndakhté mi na nguen ko bayi xél elle a tout les qualités d'artiste
Elle a trop de feeling machaAllah nice song 🎉🎉🎉❤❤🎉🎉
Ohhhh ndakhté vraiment son bi lale nama nk Billy ❤❤🎉
Ndakhté ya meune ya eupe doolé té ya gueneu fété khalé😂 kou d'accord
Enfin Glow up amna rakk félicitation Ndakhté et bonne continuation
Une belle inspiration de la chanson de Tonton Ma Penda Seck❤❤❤❤❤ bravo Ndahté🎉❤
A chque like je viendrais ecoute cet musique au non de notre amitié nadia et Élisabeth ❤🎉
Enfin ndakhté changer na way
Ohhh 🥰 seul les connaisseurs savent qu'elle à beaucoup bossé mangui guiss sa avenir si musique ni nga teuyé ko sa loxo bravo 👏
Enfin ndakhté lo yabinaniou
😂
Kou D'akor Ni Ndakhtè Dafa Meune Rk Lalal j'aime ❤🎉🎉🎉
Limouy dégager mo grave mashalah☺️ feeling bi mongui tourou😍
Vraiment 👊 merci de l avoir remarqué dafa am thiass khale bi
Wa ms lii lanla ndakhté yagui séral sama xol bi ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Wakh katt you sokhor yi wakha ti léne ndakhté yalla nalla yalla lafal thiate ❤❤❤
Tiktok la guisé clip bi ma téla juger né dara nekhousi mes bima nieuwé guis clip complet bi la kham ni dama dioum❤🎉clip bi nekhna raffet na bonne continuation
Meusouma am 20 j’aime
Ndakhté je t’aime fala yam ❤❤❤❤❤ ta voix ohhhh🥰🥰🥰🥰🥰laf thiate way🎉🎉🎉
Taye mou nekh y’a Meune nak ndakhou bby machallah guena glow up si sa vie ❤🎉
Ani Wa Team Ndakhtè Manifesetè Vous ❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Yalna naniou guissanté si bénéne clips Li nekh na ani cas kat yi😂😂 yénako mom
Bly😂
Machalla lép nice na bonne continuation Lô Ndam Siré❤
Ahhh ndakhté guéna son bou bess ❤Machalah bonne continuation 🎉🎉🎉😍😘
Yalla nala sougnou borom bolé ki geun si yaw ndakhté te kham sa valeur dila traite comme une reine si barké naby Moustapha 🤲🙏
Bismillah niou dioublou si Mai’s ndakhté tu es qui😩🫶🏼🎉😊
Elle a frappé fort mashallah ❤❤
Nékh na trop❤
Machallah ma belle bonne continuation ❤❤❤❤❤❤
Oh macha mais voix khalé bi voix ndanan la diom Mama Khar mame kiné Lam mame Soda Mama etc meuna nak macha et elle est très belle sa ma thiate ak bou sama morom bon vent chérie🔥🔥🔥🔥🔥🔥💞💞💞💞💞
khallei biii feeling kesser wollah 😩😭❤️❤️❤️❤️❤️
Son bi nekhna lol sakh
Laff Thiate sounou artiste préférée ❤️
Machallah Ndakhté Bonne continuation ❤❤❤❤❤
Alkhamdoulilah ndakh nioy nopalou si golwp touti sax ms nice song❤❤🎉🎉
😂😂😂 haha
Vraiment tu mérites de soutien tu es adorable ma belle lô ndame siré yalla nala yalla defal diam bou bakh ❤❤
L’une des relations humaines les plus sous estimé est l’amitié.donne bcp et réclame si peu quand elle est sincère si facile a ressus
Woahh 🎉
clip bi rafétt na waye😮
Ndakhté c la meilleure point!!!
Enfin Glow up am na Rak 💖💖💖
Elle dégage un potentiel de fou très charismatique en plus t’as l’avenir sur la musique sénégalaise 😍😍
Machallah ndakhté🎉. Bonne continuation
Une belle chanson 🥰🥰🥰🥰🥰 dakhtè je te souhaite une bonne continuation li nekh na trop way may nakoo sama kharit you bakh yi ❤❤
Magnifique .. à noter que jn 'ai pas retrouvé le côté ''international'' contrairement au son ''glow-up'' mais jpense quand même que ndakhte à énormément d'avenir au sain de la musique Africaine voir internationale. MAY GOD BLESS HER ❤❤❤
Masa Allah ma préférée chanteuse du peuple ❤wa joal fadiouth nam nagne la dé ❤❤❤❤❤
Machalla nekhna trop vraiment, j'écoute en boucle depuis tout à l'heure ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
En tt cas elle est très belle, charismatique et sa voix est mélodieuse ❤❤❤
Alhamdoulillah niou changer song sakh😊
Machallah dakhté sa voix machallah sagnsé c’est top clib o6 meilleur Yalna yalla lafal thiat en plus dionguama gua🎉❤
"Wax dji comme poussière feugueutou mou dièkh,kougnou wo ci guère ay thia gnou dém ci bamou nèkh ✌️"
Niaff sama artiste Sama préféré y’a meune kay ❤❤ koula cas rek régler ko😊
Kouma si cas kay niou régler kooo
Machalah nila ligey rekk inchalah ❤🎉 on est derrière toi chaque 3mois defal gniou Li inchalah ndam rekk bon courage ligueyi nekk sisa bop amoul lenen 🙏
J'ai toujours dis k'elle était la meilleure dans sen p'tit Gallé ❤❤ Maintenant elle m'a donné raison 🎉🎉🎉
Enfin du nouveau ❤❤❤ très beau clip 🎉🎉🎉
Enfin, 2éme son 😂. Bonne continuation.
Niaff barki cheikh masamba li histoire dinako bindeu Lou wow Kong 😅😅konkonrong xéra koy todj wayer koko diassi la ragal 🎉💪💃💃💃🤸🤸🤸❤️❤️❤️
wa degeul lolou😂😂😂
Bilay walay karadj mou d'amour😂😂😂
L histoire retiendra qu elle a très bien chanté 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹
Ndahté mii dara la dh niaff fonce rk boul tegui tank 🎉
Hée son bi nekhneu deh ❤❤❤❤
Meune mokal métrisè yako defff kay Ndakhté Lo 🎉🎉🎉
Machalah ndakhté ya meune kay🎉🎉🎉❤❤très belle voix machalah
Man ndakhtè rik lay topou🎉🎉🎉❤❤❤
WA ms ndakhte ki EST Tu li nekhna❤
Bilay borom jongué ak rangatti warna holl ci yow dh té la meilleure bilahi geum ko rek yallah bahna inchallah
Allons police 👮 annulèle plainte bi, ndahté enfin diéné na song bou bess, waw deug leu kay😢🎉❤❤❤😂
😂😂😂
Nékhna clip bi Nice na bonne continuation ❤
Machalla ❤❤❤❤❤
Wa ndakhté loutakh nga beugue yeungeul tate ahhh
Surtout doyal naniou si dioutou bi 😭
@@user-tfayevraiment 😂
I’ve had this song on replay for hours now!!! So lit 🔥 🔥🔥 well done Ndakhte ❤
Oh filling bimouy dégagé 😮machallah
Ndakhté rk laniouy topou❤❤❤❤❤❤❤❤❤ machalla koulay khare yalla na khadi 👌👌
Meune gaa nakk nangoul nagne la Lolou ❤❤Machallah laff Thiat
La voix est juste machaallah 🎉❤❤ bonne continuation ma chérie 😊❤
Machalah son bi nékh na,clip bi aussi rien n'a dire ❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
De la persévérance pour mener ses projets à fond ❤
Mashalah, elk a confirmé 👏🏼👏🏼👏🏼👏🏼👏🏼
Wa danse Balthazar loumoufiy def😂 clipbi mashalah Tu es est le meilleur.❤❤
😂😂😂😂😂😂
Macha Allah ❤️❤️❤️ meune sagnsé 🎉🎉🎉🎉🎉 autre dimension
Machallah. Belle chanson et tres joli clip. Laff tiatt
Manchalla nékna yallana sounou borom wéreul bat bi❤
Senegalement nexna clip bi aussi nice na trop ❤mais ndakhté tamit sa molaye loumou c juste waouh
Elle amènes de la nouveauté des danses de salon mêler au Mbalax🎉 avc une sonorité double
Ou sont les fans de ndakhté? Des ❤️ way
Aïcha koné ndakhté mi sa nawlé la😂😂
No guen def lahalé si Aicha do féliciter rk dém togne bahoul
Ay mbeugué 2021 ba lêgui bén clips dingén soul ndanan dé xamna
Des coeurs pour NDakhté ❤❤❤
Machalla li nekh na trop.bonne continuation ❤❤
Waw lii mom tamit nekhna de❤❤😊
Sama artiste le meilleur de sa génération machallah
vraiment je regrette pas le fait que j'ai plusieurs fois demandé à prince art de te donner le micro, je savais que tu as une si belle chose précieuse en toi. Vu le succès de ton premier single j'avais un peu peur de comment tu vas tenir le cap mais là j'avoue que tu es la meilleure et tu iras très loin. Ndakhté lo mes félicitations tu chantes vraiment bien mashallah bonne continuation à toi.
Bilay elle est talentueux
ken nek yow ndakhté ndakhté son mi frappenama trop bilahi machallah ❤bonne continuation❤🎉
Boy bi amneu talent dh woow🔥🔥🔥 son bi nice 🔥🔥li mome reverce walla pac djey gnoko warone clip😭😭😭
Pac rek yimouy réalisé sounou fans bi Viviane
@@bocarguisse2282akeu meune zbest best daleuy poudeur pagua rouge ..effet bimiy use mo gnaw😂
Machalla neikh na trop rien à dire❤❤❤
Wouyyyy li nékhna❤❤❤
Oh ndakhte tu es là meilleure ❤❤❤
Quand même les parole sont importants et musicales 👍👍👍
Mais Maneu flow up Doumasi doyal ❤félicitations et bonne continuation nôtre sœur 🥰
Aka man ❤ya
Meilleur Nak sm kharit bi
Machallah la meilleure ❤❤❤
Nékhna machalah 🎉bonne continuation