tarikha khadria li ci khew gakkal nako bou bakh

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 фев 2025

Комментарии • 85

  • @mouhamedseck7443
    @mouhamedseck7443 Месяц назад +25

    Assalamou aleykoum père. Je vous suis depuis des années. J’ai souvent commenté vos vidéos et j’ai toujours admiré votre courage et surtout votre honnêteté intellectuel. Aujourd’hui je suis d’autant plus admiratif que ce sujet me touche encore plus étant moi même un petit fils de Elhadj Cheikh Yerim Ndoumane Seck disciple de Cheikhna Cheikh Saadbouh. La situation actuelle avec 5 khalifs est une dérive que tout musulmans doit dénoncer et surtout ne point entrer dans des querelles sans aucuns intérêts.

  • @MamadouAliouBa-k9s
    @MamadouAliouBa-k9s Месяц назад +3

    je suis pas sénégalais je beaucoup des estimations pour ce cheikh momar diagne,

  • @khalyball3758
    @khalyball3758 Месяц назад +3

    Voilà une personne qui suit à la lettere notre chère religion.(Yalla nala Yalla déffale fane wou goude akouk wèrr ak djiamm ak tawfèkh barakatou seydina MUHAMMAD(SAW).

  • @cheikhsaadbouh109
    @cheikhsaadbouh109 Месяц назад +2

    صدقت فيما قلت جزاك الله خيرا.
    والله كل مايجري الآن لا علاقة له بالتصوف و شيخن الشيخ سعدبوه بريئ منه .
    وصيتي لنفسي وللمريدين( أعني المريدين حقا) أن يتقوا الله وليقولوا خيرا ولا يقبلوا ما لا يرضي الله.

  • @moustaphadieye4986
    @moustaphadieye4986 Месяц назад +7

    Je suis tout à fait d'accord avec vous je suis talibé Cheikhna et je suis vraiment touché par la situation actuelle de la tarikha raison pour laquelle j'ai pris mes distances à ce sujet

  • @massambathiam305
    @massambathiam305 Месяц назад +2

    Cheikh niouga diagne mi dane wakhal nianaw ya ay mayam eupeu na wakhiartou bi cheikhna cheikh Saad bouh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @NgoneColy-li6sq
    @NgoneColy-li6sq Месяц назад +2

    Dieureudieufety Imam yalna na borom by féy sa takhaway thi réwmi ak thi dîné dji Assalamou Aleikoum

  • @diehfall
    @diehfall Месяц назад +3

    Machalla Kilifa gui wakh dji rafetna selna dal nga tey nga machalla niou mailné yaw gnio manqué sounou tarikha bi wakh deugg bi tei yalla takh mak djitou rak top si ❤

  • @ndioufa_xalil
    @ndioufa_xalil Месяц назад +2

    Alkhamdoulilah yalna gnou yalla di dimeuli dignou bolék gnou melni iow une honète , sincère et dévouée personne ne se trouve casiment plus de nos jours.

  • @hamadygassama3620
    @hamadygassama3620 Месяц назад +1

    Ma cha Allah dieureudieuf sama serigne yana nga fi yague té wer, wakh dji rafet na ❤❤❤❤❤❤❤

  • @Cheikh.sadibouCisse
    @Cheikh.sadibouCisse Месяц назад +1

    Cheikh bi wallaahi souma thiofeel thi waw wallaahi yokouna.mande khadrla wayé da nek mal à léss.

  • @FallouNdiayeFalloundiaye-f5t
    @FallouNdiayeFalloundiaye-f5t Месяц назад

    ❤salm Serigne cheikh ? meri Dakar sonko wakhou sy de te Sénégal la

  • @gueyemoussa3764
    @gueyemoussa3764 Месяц назад +1

    ❤❤❤❤ Macha Allah jambaar dji yaa bakh deh ny rék lah jamou rék mo bakh

  • @MaNdiayeMbaye-ei3zv
    @MaNdiayeMbaye-ei3zv Месяц назад

    Machallah kadou yi rafétena lolou ta beuri ay diangualé. Yalla na léne yalla maye dégue ak topou

  • @aliniang7452
    @aliniang7452 Месяц назад

    Grand frère amal diamou waw goor

  • @mamemorseck6704
    @mamemorseck6704 Месяц назад +4

    Jërëjëf sëriñ bi yàlla nala saa boroom fay aw yiw ❤❤❤

  • @shekhnangrmcf6908
    @shekhnangrmcf6908 Месяц назад +1

    Tarikha ci boppam moo amoul ndeusslaay ci l'islam. Lolou nga wara wakh père

  • @SodaGueye-t7h
    @SodaGueye-t7h Месяц назад +1

    Machallah amna solo❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aissatoudiallp3430
    @aissatoudiallp3430 Месяц назад

    Jaajëfati ! Bonne continuation ! Que le tout-puissant t'accompagne

  • @ibucisse3606
    @ibucisse3606 Месяц назад +2

    Ya Seydi Diagne choukrane pour tes prises de positions et ton courage le Sénégal est un sacré pays courage a toi qu'Allah agréé

  • @Amar-gm7dn
    @Amar-gm7dn Месяц назад +1

    Que la vérité mane mome j’ai démissionner yague na gni féne wakh Lou niaw dougnou dara gnome gneup

  • @hacenahmed3027
    @hacenahmed3027 Месяц назад +2

    Dieuredieuf Ndakh ngua niemé wakh. Nitou yalla mo beuretoul

  • @vadeliaidaraassad6080
    @vadeliaidaraassad6080 Месяц назад +3

    Slm a tout le monde slm a toi serigne momar je témoigne mes respect envers ton grand pere cheikh ndiouga cheikhou cheikhna cheikh saadbouh, di feidali coloré bobou di nieuw pour wakh sama guiss guiss si saye gadou yii di rafet lou courage bi ak yeneiy beugeu deifar , sama guiss guiss moy kadou yii ngeu yeikeutii dama fokné waron na geuna teiguii né si ko khamné cheikh ndiouga diagne moy mamam bou weiso lolou nit boy wakh di niakh nit yi am na façon bo khamné meun ngeu sé niakh nitt yi ta do wané beiw waleu kham kham nitt loumou kham diko wakh reik am na kouko kham nopi keurguii yakarnani li ngeu si kham beurii na beuriwoul keurguii lou complex la lou khot la geunal gestuu boubakh teiral nit yi niou saga parsk saga ak wakh lou niaw kouniouye roye douko diklé wayé bo xamoul mbot yisi bir ngeu yam fofou nioune nak keur cheikhna nii beugeuu mou bakh nioungui siy liguey matin soir niy mboloo nieup meunou niou wathjii yoneu wayé nieup tamite mano def baniou neikeuu si yoneu bou dougé si siré li kheiw si keurgui doula djakhal reiroo yageuu na si wayé mbolo bo guiss amna niou si topeu yoneu ak nii khamné topou niou yoneu moi je t'invite bou fékéné deugeuu mola takha djok gestul deugeuu bi ngeu nieuw wakh leip mais li nga wakh ni apart li nga wakh niit yi bayi saga amoul bénén djangat boumasi am encor je témoigne mes respect a ton grand-père

  • @chakasen399
    @chakasen399 Месяц назад

    Il faut être courageux jusqu'au bout et situer les responsabilités tout en disant la vérité à ceux qui ont besoin de l'entendre !

  • @gueyematybira303
    @gueyematybira303 Месяц назад +1

    Shoukrane oustaz

  • @Sidydiagne-24
    @Sidydiagne-24 Месяц назад

    Cheikhna Cheikh ❤❤❤ vèritè absolue serigne momar diagne

  • @yislimfall3047
    @yislimfall3047 Месяц назад +8

    Les tarikha au Sénégal d'une manière générale sont en déclin. Leur époque est révolu. Certe elles ont joué leur rôle par le passé en faisant adhérer les Thiéddo en masse à l'islam. Elles étaient excellentes en matière de la da'waa car elles proposaient un Islam dit tolérant, un syncrétisme religieux avec beaucoup de rituels animistes et des pratiques occultes comme par exemple le charlatanisme qui le fait plus abordable et acceptable chez les païens. Le problème avec ces courants mystiques un enseignement islamique orthodoxe ne peut pas être garanti car leur modèle est surtout basé sur une forme de hiérarchisation des membres des différents sectes. En haut les initiés les khaass supposés maîtrisant un certain savoir mystiques ( haqiqa ) qui est au dessus de la science religieuse ( chari'aa ) et qui ont une connexion supposés avec Dieu, en bas les talibés ,( 'aam ) maintenus à un niveau de savoir très bas voir même nul, des troupeau asservis facilement manipulable, très fanatiques et qui détestent tout ce qui émane de la raison.
    Aujourd'hui ces courants sont devenus obsolètes. L'Etat doit prendre le relais en unifiant le système éducatif, en introduisant l'enseignement religieux dans les écoles. Pour les chrétiens le catéchisme, les musulmans l'islam sunnite des quatre écoles. On doit enseigner au enfants à bas âge le coran, les hadiths authentique du Prophète, les prières et les invocations tel que rapporté de façon authentique du Prophète. On doit créer des Universités et des faculté islamique ou seront formé nos futurs guide religieux dans différentes domaines des sciences religieuses
    Cependant ce combat n'est pas celui des actuels guides religieux, ils ne le porteront jamais car ça va à l'encontre de leurs intérêts et philosophie.

  • @abdoulayesarr1138
    @abdoulayesarr1138 Месяц назад

    ❤❤❤ machallah liimotakh nga bakh

  • @makhandiaye1836
    @makhandiaye1836 Месяц назад +1

    Vérité absolue je valide

  • @black2krack982
    @black2krack982 Месяц назад +1

    Salam Mame Momar je suis khadre mais aussi Tabala yi aussi dafa raax leggi

  • @AbdoulayEMalonga-k6f
    @AbdoulayEMalonga-k6f Месяц назад +1

    Mâcha allah diagne

  • @Ndrao_Faye_aka_El_Shabbaz
    @Ndrao_Faye_aka_El_Shabbaz Месяц назад +2

    Laa hawla walaa huwwata, illaa billaah! Njiit de Yallah moo koy tege waaye ku koy teg sa bopp!
    Je n’ai jamais ete au courant de cette division mais des insultes entre humains, musulmans et de la même famille unies par Allah me depasse. Je suis Khadre et je me sent abattu car en priant Jummah aujourd’hui, cette suura a fait l’objet du Khutba et je pensais à vous y interpeller pour propager ce message. 😢

  • @ousseynousall5808
    @ousseynousall5808 Месяц назад

    Vérités absolu serigne bi

  • @fadelthiam6753
    @fadelthiam6753 Месяц назад +4

    Bilakhi dama rouss si tarika khadre dama rouss

  • @MohamedabibeMbengue
    @MohamedabibeMbengue Месяц назад +3

    Assalamou aleykoum ya ouztas ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @saliousaware759
    @saliousaware759 Месяц назад +1

    Machalla machalla machalla diaradiaf ❤❤❤❤

  • @modoufall4819
    @modoufall4819 Месяц назад

    Yague fi te wer

  • @mbayethiao1024
    @mbayethiao1024 Месяц назад +2

    Cheikh Akhmadou Mactar Diop Gapp gnimou cheikhal kénn massouléna yap. IL faut talibés nékk ay nitt Cheikhna lépam discipline la xam xam Foug Lou Yala sope Yonentibi shws. Kon koufi andi léenen yawla concerné. Gnoun moom parpar loo wougno u ak kénn. Dinagnou wormal gneupou nakk. nguir séen Mame.

  • @mbayethiao1024
    @mbayethiao1024 Месяц назад +1

    Walahi Papa sama khol sédna si yaw mane wakeur Cheikh Akhmadou Mactar Diop laa bokk wayé li khéw si tarikhabi rafétoul . Na keuri cheikhs yi dieul séeni responsabilités rék gnoun moom khawma kann wayé kénn dounou manipulé ndax gnakougnou fayda

  • @maremendong3297
    @maremendong3297 Месяц назад

    Li deh sama yaye bou ko dégone dioye ...legui mak la..tik tok mi gui yakh Sénégal...

  • @silmakhatraore483
    @silmakhatraore483 Месяц назад

    Kaylén niou nan gnéekh bousi paka guéné😂😂

  • @BallaNdiaye-o5m
    @BallaNdiaye-o5m Месяц назад +1

    Waaw goor

  • @ElymaneSaidoukane
    @ElymaneSaidoukane Месяц назад

    Sincèrement c'est vraiment honteux Wallahil Azim qu'Allah ramène la paix entre eux et que l'on désigne un seul khalif

  • @sidylo9069
    @sidylo9069 Месяц назад +1

    Nane toogat waxtane seytané da bari doolé ta adouna yagoul wala donnu gui yagoul ta léup thi nétili lay modjié

  • @bodybi1
    @bodybi1 Месяц назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @CheikhbassirouSarr
    @CheikhbassirouSarr Месяц назад

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @mbayethiao1024
    @mbayethiao1024 Месяц назад

    Mboolo moom il faut gnou beuganté sopanté nawloowanté ande si deugg bougnou beugué ngueureumeul sounou BOROM.

  • @FaaFallilou
    @FaaFallilou Месяц назад

    ❤❤❤

  • @mouhamedba6331
    @mouhamedba6331 Месяц назад

    Khalifa ahmadiyye Muslim jamat

  • @khabanesene843
    @khabanesene843 Месяц назад +2

    Yalana yalla faye

  • @emiliarobloxfesita
    @emiliarobloxfesita Месяц назад

    Li dafá gnawe gno gno bock lèp ba parè di khiro ka gnawo

  • @abdoulayendiaye6488
    @abdoulayendiaye6488 Месяц назад

    Bilahi wakh nga deug ❤

  • @TallaDiop-zf7pv
    @TallaDiop-zf7pv Месяц назад

    Sëringë bi noo ngi teew lu bubaax

  • @mouhamedba6331
    @mouhamedba6331 Месяц назад

    Wwwahmadiyya Muslim jamat mata 3

  • @mouhamedba6331
    @mouhamedba6331 Месяц назад

    MTA 3

  • @AminataThiam-b6u
    @AminataThiam-b6u Месяц назад

    Deug nekhoul

  • @BAAY-DIAW
    @BAAY-DIAW Месяц назад

    Lan mooy sabbi ?

  • @AliMbayediop
    @AliMbayediop Месяц назад +4

    Ya ngui beugueu barri wax nak pére

    • @cheikhsadiboudiagne
      @cheikhsadiboudiagne Месяц назад +7

      Wakham nafekh rk lay dérangé soûla dérangé kon nafekh nga

    • @assseck8848
      @assseck8848 Месяц назад

      Dieureudieuf Baye Momar

    • @talibecheikhndao6085
      @talibecheikhndao6085 Месяц назад

      ​@@cheikhsadiboudiagnewakhhh DEUG yalla

    • @madmaxpiod8767
      @madmaxpiod8767 Месяц назад +3

      Si ça vous concerne pas et ne vous intéresse pas passez mon cher

    • @abdourahmanecisse3436
      @abdourahmanecisse3436 Месяц назад +1

      Limouwah deguela dieureudieuf yallanala yalla défal diamou si barké chékhna chékh sadbou... wakhayartou machallah ❤❤❤

  • @fatimatazahrarassoulthiam8722
    @fatimatazahrarassoulthiam8722 Месяц назад

    Je suis vraiment déçue, je pensais que yow thi wa akhlou souna wal jammah nga bokk !

    • @ibrahimambodj6982
      @ibrahimambodj6982 Месяц назад +2

      KHANNA KHALE NGUA ?

    • @serigne-momar
      @serigne-momar  Месяц назад +7

      Ndeysaan massa ci déception bi. Ooohhh li mettina.

    • @bathiedabo2329
      @bathiedabo2329 Месяц назад

      Serigne Momar n'est pas sectaire. Il est simplement un bon musulman ! Vous êtes libre, puisque Serigne Momar n'est pas de bord, d'être déçue!

    • @serigne-momar
      @serigne-momar  Месяц назад +1

      Bayyiko foofou mouy wakh loumou khamoul. Est-ce moom kham na louy ahlou sunna wal jamaa'a ?

    • @mamourmbodji1204
      @mamourmbodji1204 Месяц назад +1

      Ta déception n'a pas de fondement sérieux.
      Serigne Momar est un musulman accompli en qui, tous les autres musulmans et memes non musulmans vouent un respect.
      Revoie ta copie et respecte les gens sur la toile, tes paroles sont gravissimes.

  • @moustaphadieye4986
    @moustaphadieye4986 Месяц назад +1

    Je suis tout à fait d'accord avec vous je suis talibé Cheikhna et je suis vraiment touché par la situation actuelle de la tarikha raison pour laquelle j'ai pris mes distances à ce sujet

  • @HadramiBabe
    @HadramiBabe Месяц назад

    ❤❤❤❤