oustaz lamine Sall taclé sévèrement (Modou fall)

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 фев 2025
  • page Facebook : www.facebook.com
    #sarr #dine #jitv #cheikh #abdoul #hamid #sarr

Комментарии • 160

  • @babakebe4094
    @babakebe4094 3 года назад +45

    Dafa dioum ! on corige et l'encourage.
    Cou dègg limou wakh si musique si plateau TFM xamni courage la. Té deugou. Waraté kat yèpp ñéméwouñouko

  • @abdoulahidiarra9818
    @abdoulahidiarra9818 3 года назад +42

    Faut arrêter les émissions religieuses en direct. Il devrait avoir une commission de Oulémas qui doit vérifier tous vidéos ou audio avant sa diffusion dans les médias.

  • @moussagadiaga8349
    @moussagadiaga8349 3 года назад +9

    Dafa dioum deugla wayee si limou dioum dafa elementaire pour oustaz defsi erreur mais nak diambar la

  • @diagnemoustapha7936
    @diagnemoustapha7936 3 года назад +14

    Yalla rék mo doul dioume merci oustaz modou fall

    • @foogadebbomolooty9839
      @foogadebbomolooty9839 3 года назад +1

      Merci

    • @fashionfashion1330
      @fashionfashion1330 3 года назад +1

      l'erreur est tellement élémentaire
      pour un soit disant oustaz Modou Fall
      Moi personnellement je lui conseille de se focaliser au Sira c'est son style
      Problème bi moy bo diangué ti Khilass bou El Hadj Malick Sy touti rek lo wakh mou nekh nitgni même boussa Jang soriwoul
      Na dem jangui Fikh mo gueun tji mom

  • @aliounebadaradiack3163
    @aliounebadaradiack3163 10 месяцев назад

    Machala
    J’ai appris
    Merci beaucoup Sall

  • @westernafricaautopartswaap5636
    @westernafricaautopartswaap5636 3 года назад +3

    Vraiment il fallait l appeler en douce dans la discrétion

  • @omardiame431
    @omardiame431 3 года назад +6

    Waw. Outach pourquoi tu ne l appelle pas pour en discuter au lieu de. Critiquer franchement pour corriger une personne soutoura banale ci dioulit

  • @maododieye817
    @maododieye817 3 года назад +5

    Machallah merci beaucou

  • @khadidiatousimal3413
    @khadidiatousimal3413 3 года назад +6

    Ki dou iow yakoy nopilo. Il s'est trompé et vous l'avez corrigé c'est bon. Vous vous arrêtez la. iow mii sakh meune nge dioum, do yalla donc dioum diomboula.

  • @ablm9101
    @ablm9101 3 года назад +9

    Machalla serigne lamine amna solo

  • @diarryba4687
    @diarryba4687 3 года назад +1

    Vraiement vius etes nos guide qui doit nous guidee ce ta dit fallait lui appelzr lui mm moye oustaz modou fall et lui il ce restifi mais p1q pibliquement senegal gagnantergui barina et jagalermi newna

  • @galleardo704
    @galleardo704 3 года назад +5

    Sénégal danio yakamti via Def erreur gnou amela dafa soum

  • @pachasen3918
    @pachasen3918 Год назад

    Machallah, leer na nagn ,kou hamoul dangay noppi ,niou wara wakh wakh.

  • @abdoulayedia9460
    @abdoulayedia9460 3 года назад +2

    Mach'ALLAH merci pour les éclairages

  • @alimabadjan6926
    @alimabadjan6926 3 года назад +14

    Nit rek la .Koudoul dioum amoul. C'est tolérable.

  • @wakhdeugguetayallatakh8129
    @wakhdeugguetayallatakh8129 3 года назад +7

    Diangoul dara modou fall mii
    Ay penalty rekk lanouy deff deklouw ma benna oustaz bou nekkéu si televisions yi koudoul hady niasse

    • @oumardiallo8661
      @oumardiallo8661 3 года назад

      ❤️❣️❤️❤️❤️❤️❤️mom rk bilahi

  • @OumyNiang-hl1zu
    @OumyNiang-hl1zu Год назад

    Ouztaz modou fall moy meilleur ouztaz si Sénégal

  • @bassirouthiam1615
    @bassirouthiam1615 5 месяцев назад +1

    Bo lae sa fardia diapu ma tothi

  • @diordiakhate7828
    @diordiakhate7828 3 года назад +4

    Très claire merci PAPA

  • @sleymanfall9640
    @sleymanfall9640 3 года назад

    Ni koudoule dioum amoul,yaw da ngako warona woo en privè wakh ak mom cii soutouroo,mom mou rectifie dioumtème!!merci

  • @mariemeniang4421
    @mariemeniang4421 3 года назад +2

    Serigne Modou fall On t'aime ❤️ et rien ne le change

  • @aliounebadaracoulibaly3209
    @aliounebadaracoulibaly3209 3 года назад +2

    Ces émissions religieuse doit être présenté par des ouztaz de haut niveau mais pas des animateurs de musique ou élection miss

    • @OumyNiang-hl1zu
      @OumyNiang-hl1zu Год назад

      Khana sa baye Moy président misseyi yowe sa baye loumou diangue loudoul data ak koye😅😅😅

  • @mbengueadji8032
    @mbengueadji8032 3 года назад +2

    Ouztaz modou fall cou meune limouy def la mais nak Yalla rek modoul dioum

  • @sokhnafatythiam904
    @sokhnafatythiam904 3 года назад +3

    koudoul dioum amoull.bonne continuation modou fall boulen sakh fallé

  • @mamadoumouctardiallo7172
    @mamadoumouctardiallo7172 Год назад

    C'est grave ça 😢 astafiroulah toubal Lolou

  • @75eljefendiaye39
    @75eljefendiaye39 3 года назад +7

    Sénégal dal mo bari gnou sokhor. Ouztaz modou fall dafa djoum rek té ndioumboul Ken.peu de compréhension dé bakhna ci.

    • @papile7023
      @papile7023 3 года назад +1

      doléne bayi lougnou wakh rek nguénni sokhor Oustaz bou soff bi wakham yeup garouwalé tésseunté dagassanté comme djiguéne bougnou sonal way

    • @binetadiagne6436
      @binetadiagne6436 3 года назад +2

      @@papile7023 li oustaz modou fall di wax mo ame si djimanodji kousi guissoul sa bop dafa fek limouy wax mouy sa djiko wayer manchalla migui yeter boubax ndax actualité gua balma

    • @cherifcherif7033
      @cherifcherif7033 3 года назад

      Sa yaram nekhna yaw ki di wakh nio yoré kham kham senegal mouy coriger le gar ngané dafa sokhor yaw yaye domeram

  • @aliounebadarambaye5239
    @aliounebadarambaye5239 3 года назад +4

    Machalah Serigne bi,léér na,xamal nganiou louniou xamoulwone dieureudieufati SALL Abass

  • @mariemeniang4421
    @mariemeniang4421 3 года назад +1

    Bonne continuation Modou fall

  • @LansanaBadji-s8v
    @LansanaBadji-s8v 11 месяцев назад

    Franchement vous devriez dire qu’il a fait une erreur mais on ne doit pas l’écouter non je suis désolé moi je l’adore car c’est mon oustaz je l’aime beaucoup dafa dioum rék l’erreur est humaine mais il a beaucoup de savoir modou fall ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Borom1248
    @Borom1248 3 года назад +3

    ماشاء الله

  • @ndeyekhadyfall9886
    @ndeyekhadyfall9886 3 года назад +1

    Certes, Daffa dioume on le corrige, mais pas au point de ne plus l'écouter vous ne devriez pas dire cela .

  • @youssoufsmith1663
    @youssoufsmith1663 3 года назад +1

    Du courage oustaz modou émission bi c’est intéressant

  • @alassanefall5320
    @alassanefall5320 3 года назад +2

    Machalla Serigne Mouhamadoul Mansour Sall Abass

  • @binetadiagne6436
    @binetadiagne6436 3 года назад +3

    Soxor si yene oustaz yi la commencer lou tax wowoko téléphone waxkoko lou si diar video di wax

    • @hhghhgrty7325
      @hhghhgrty7325 3 года назад +1

      Pourtant modou fall sa wakhnako thi imission bi kodoul dioum amoul thi kaw souff

  • @amadoutidianeba37
    @amadoutidianeba37 3 года назад +3

    Machallah. Niou Diangoul danio wara noppi

  • @matarsamb2392
    @matarsamb2392 3 года назад

    Senegal mo bari ñiou sokhor modou fall diambar deug leu machalla modou finga ték sa tank fofou la

  • @ahmedtidianewade342
    @ahmedtidianewade342 3 года назад +2

    Machalla baraka Allah

  • @boubambaye4946
    @boubambaye4946 3 года назад +1

    Oustaz modou fall tay nga dé deh😂😂😂

  • @papemakhtarsarr6653
    @papemakhtarsarr6653 3 года назад +3

    Fiq bo diangoul oussoul dangay sonou ndah ci erreur ngay deuk

  • @falloundao
    @falloundao 3 года назад +1

    Mane lima diakhal si Oustaz Télé yii bougnouye wakhtane si diné dougnou Tékk téhré té borome kham kham diné sii téhré rek la wara soukondikou Machallah SERIGNE bii SALL

  • @ndioufadiouf6138
    @ndioufadiouf6138 3 года назад

    Machallah machallah machallah

  • @mamadoudiengdiagne9999
    @mamadoudiengdiagne9999 3 года назад +1

    Machallaha amna solo lol

  • @khaytasamb1789
    @khaytasamb1789 3 года назад

    Amolenne bébé Soura domou Adama matoul .yakamti koujoum 🗣️🗣️🗣️🗣️🗣️🙏Dymbalilénniou ah

    • @khaliloulah2167
      @khaliloulah2167 3 года назад +1

      Saway yaw li dîne la ñiou beuri kay kouka guiss diapni deug la c normal niou ratifié prsk si télé lako waxe li dou mbirou mate xam xam degay xam waleu xamo rek....

  • @layekebe2600
    @layekebe2600 3 года назад

    Machallah

  • @mamadoualiounebarry7695
    @mamadoualiounebarry7695 3 года назад

    MODOU FALL...SHOWMAN LA....MANE DOYOUMA OUSTAZ KOUMOU DOY YA XAM...EN PLUS TAGG PRESIDENT.LA DIEUL LEGUI

  • @wakhdeugguetayallatakh8129
    @wakhdeugguetayallatakh8129 3 года назад +4

    Serigne pure serigne Mansour sall

  • @mariatouann1579
    @mariatouann1579 3 года назад

    Noooooo papa sheikh 🥰🥰🤣🤣🤣

  • @maodomalickndiaye5100
    @maodomalickndiaye5100 3 года назад +2

    salamou halay koum mandè khamnanè sènegall mètina kou dioum naniouko wo wakhak mom wantè kou dioum sie pènthe sa moromoum oustaz dila dioubentie wantè nioune daniouy diakhelè kou waxe niou wèdie ko ba parrè wèrko nioune kanne laniouy wolou pour mou diengalniou souniou dinnè dèlèn dimba lentè ta bania wèrentè wasalam

  • @ibrakebe5238
    @ibrakebe5238 Год назад

    Thiaye s laminé koye wakh yaye Diom

  • @ahmada3263
    @ahmada3263 3 года назад +2

    Walahi Wakh dafa diafé da dioum rék

  • @sainaboujoof8338
    @sainaboujoof8338 3 года назад +1

    Why didn't you call oustaz fall and advise him about it, why do you come online to discuss it 🤔

  • @serignelo2227
    @serignelo2227 3 года назад +1

    Khamou nou daranéksi télévision yi di komidi rek

  • @bambandongo4917
    @bambandongo4917 3 года назад +1

    Ki foumou diagué ba paré ray lamine

  • @boursinesaloum1819
    @boursinesaloum1819 2 года назад

    ليس حق لا لا ثم الف لا ليس هكذا

  • @housseynoukouyate-ix5jm
    @housseynoukouyate-ix5jm Год назад

    Nite day dioume môme dafa dioume rék wooko si souf gawakh ko li défa ñaawou

  • @madiagnediagne4235
    @madiagnediagne4235 3 года назад +2

    Bayil lénci khéll Amna solo loooooooll

  • @bayesallndiaye3009
    @bayesallndiaye3009 3 года назад +1

    Oustaz modou fall lim wakh dafa reuy
    dafa waroona demaat TFM weddi lim wakhoon

  • @waxandetv5082
    @waxandetv5082 3 года назад +4

    Modou fall demal dingi waat

  • @abdoundiaye2166
    @abdoundiaye2166 3 года назад +1

    Modou fall daguawara nagouni dagua dioum sokodéfoull digua sank gnoubari

  • @magy3113
    @magy3113 3 года назад

    Modou fall nak tay dioum nga Mane mi diangoul sakh khamnani sa kanam mo takh niouye waye

  • @iniiabdalahi4049
    @iniiabdalahi4049 3 года назад +4

    Sénégal ya beaucoup de problèmes yao kay léralal rék sall ngari kham kham pour wéréne té yalla sopouka pour labiraneté la léralal namou geuna rafaté môme awra la wakh yao yangui wakh ni gnari awra mo âme kone kay khayane kou dégg kou dégg

  • @antatop1832
    @antatop1832 3 года назад

    Svp awra ndiap diguén lanla

  • @Senprotv1
    @Senprotv1 3 года назад +1

    Merci..sall

  • @binetandiaye8951
    @binetandiaye8951 Год назад

    Modou fall, dafnou amé. Diaayi ay sac thia italy, gnibicci reck aménou. Na regler, ah baakhna.

  • @alphabetfootmamboyakecouta9002
    @alphabetfootmamboyakecouta9002 3 года назад +1

    Yew soudé liguay wakh degueu leu demal nga woko mo gueune

    • @binetadiagne6436
      @binetadiagne6436 3 года назад

      Mo geune waxdji soxor rek al woute beuse lou yalla def si nit domou adama meunou si dara

    • @amadougueye4137
      @amadougueye4137 3 года назад

      Bjr je pensse que ce que a dit oustaz modou fall ak serigne bi loumou wakh amoul difference ,serigne bi nena so lalé sa soufou awra ,modou fall néna si ndioubakh bi ba si souf genoux yi quel est la difference.

  • @diopmoussa5979
    @diopmoussa5979 3 года назад +1

    Modou fall dafa wara nopi khamoul dara

  • @mrlegrand8552
    @mrlegrand8552 3 года назад

    damani oustaz modou fall di doundé riba baparé di amerder ci yalla nêna

  • @mayorondiaye3317
    @mayorondiaye3317 3 года назад

    Dafa dioum deh mai lii mome gnoune gni diaguoul sakh khamna gnou nii c'est pas ça

  • @gnrlng2409
    @gnrlng2409 3 года назад +3

    Modou fall mi fomou diangué ak ko ko diangual,

  • @abdoukarimsamba9812
    @abdoukarimsamba9812 3 года назад +3

    Dieuredieuf sall

  • @mamadouthiombane5404
    @mamadouthiombane5404 3 года назад

    Oustaz Modou bi mom dioum nga

  • @koutaballa2085
    @koutaballa2085 Год назад

    Ki day fo oustaz Modou fall

  • @seydinatoure4044
    @seydinatoure4044 3 года назад

    Modou Fall li mou wakh xana dou niakeu xam xam ndioumté la xanaa

  • @modoumbaye3427
    @modoumbaye3427 3 года назад +1

    Amnasolo

  • @ametsall5686
    @ametsall5686 3 года назад

    Machallah
    Oustaz
    Sall

  • @amadouba9614
    @amadouba9614 3 года назад

    Sénégal migui nii tous bêtes danioo yakamti kou dioum baniou critiquer koo yén nio niou di commentaires yéna wara diangui dmrm yii

    • @mballomaoulidou3358
      @mballomaoulidou3358 3 года назад

      🤣😂😂🤣🤣😅😂🤣 yéw itam ci gni commentaires nga bokkou
      Bro kon ay dmrm lagne ndakh cinga bokou

  • @ahmadmoukhtar1268
    @ahmadmoukhtar1268 3 года назад

    Ki dioumoul dh dafa amoul kham kham

  • @mouhamedmbaye1830
    @mouhamedmbaye1830 3 года назад +1

    Dafa joum rekk Xam n’a

  • @ousmanediagne1012
    @ousmanediagne1012 3 года назад +3

    Modou il est ds le sensationnelle

  • @elgigueye4956
    @elgigueye4956 3 года назад

    Non ça c'est trop gni dagnouy fowé diné dji li dou dioume niaka kham la

  • @elhadjilo4667
    @elhadjilo4667 3 года назад +1

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @bambanyan5141
    @bambanyan5141 3 года назад +2

    Absolument na deme diangui dall yague na si bêtises yi deh

  • @cheiwoutidiania
    @cheiwoutidiania 3 года назад +1

    Dañiou khamoul nopi wouñiou sipp

  • @matarmbueg4115
    @matarmbueg4115 3 года назад

    Khamna da dioum rekk

  • @jonest6396
    @jonest6396 2 года назад

    ki di wakh fdou mo fi defendre gordjiguen dal fi chretien yi

  • @abdoundiaye2476
    @abdoundiaye2476 3 года назад

    Lou bakh loumeu meuseu wakh wakhalenthii khadis bou woute doko woo tlefon waye li molen nekh

  • @cheikhniang9876
    @cheikhniang9876 3 года назад +1

    ouztase fall il n'est pas sérieux pourquoi il travail avec Cheikh Diallo lui Islam ne le intéressé pas

  • @bassirouthiam1615
    @bassirouthiam1615 Год назад

    ❤ wallahi xam xamam des na

  • @abibseye4083
    @abibseye4083 3 года назад +1

    Dafa wara yeuw dalsi thie daray mak ñi

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 3 года назад +2

    Dioumoul mom dafa khamoul te nopiwoul

  • @papile7023
    @papile7023 3 года назад +3

    au lieu nga déme ndiangui tallo darà ak wakhou none ak garouwalé ak dagassanté comme djiguéne soff nga toropp 🙄

    • @binetandiaye8951
      @binetandiaye8951 3 года назад

      Modou fall ? Ci lolou reck la neck, di garouwalè, ack di khastè. Khanaa djiangoul lakh dariou ? Darra la khamoul

  • @mortallasall9150
    @mortallasall9150 3 года назад

    Liii dou dioum niakaa xam kassé la nak

  • @alaminsarr7706
    @alaminsarr7706 3 года назад +2

    هذا جاهل مركب حقيقة، لا بد أن يميز الناس بين العالم والطالب، والطويلب.
    هذا ليس بعالم ولا طالب، يعرف الكلام فقط وظن الجهال انه عالم

    • @alaminsarr7706
      @alaminsarr7706 3 года назад

      Cet homme n'est ni un érudit ni un étudiant, et il ne connaît rien à la religion.
      Au contraire, son discours est spacieux dans la langue wolof, et les gens du commun pensaient qu'il était un érudit

    • @mohamadoulaminendiaye3628
      @mohamadoulaminendiaye3628 3 года назад

      والله قلت حقا عليه

  • @gningue4513
    @gningue4513 3 года назад

    Fen rec. Sim dou sax rouss.

  • @nitoudeugbuegxamxam507
    @nitoudeugbuegxamxam507 3 года назад +2

    Diange deg Linga diange dafa nekh baraka lahou ya Mansour Sall Ibn abass

  • @niangdjiby5406
    @niangdjiby5406 3 года назад +2

    Delene deglou bu bah te guene bâyi sokhor ki da am xam xam bayilene sokhor n'importe quoi

  • @MyAboul
    @MyAboul 3 года назад +2

    Sincèrement il faut que oustaz you nekk si télé di nafarr séni téré tey bayyi beuz bi liii dou diné ay thiakhann...... Liiii mou wakh amoul si téré amoul fénn

    • @abdoudiouf4396
      @abdoudiouf4396 3 года назад

      Limou wakh Mane lolou lagnou diangal teh yaw nenga talibe dou ngangantiko thie mbede Lou teh nga woko nguene wakh thie parce que nul n'a le monopole du savoir

  • @ndiogouniang5920
    @ndiogouniang5920 3 года назад +4

    Daffa djoum rk🙏

  • @niasseibrahima1454
    @niasseibrahima1454 3 года назад +1

    Oustaz Modou fall daraay Tik tok la diangué motakh

  • @mamadoudiag5134
    @mamadoudiag5134 3 года назад +2

    Modou fall réral nit gni rék