Yow la love ci suma xol yow rek yamay begg lo Soma bayé dina weet Yow xalé bi samay goudi dina weet lol Da nga doug sama vie yow changer lou beuri Dal di deup carte bi, fim né mangui nian borom bi Mom sa souné mou xool ci souniou mbeuguel Yokk sama coofel mane yow la nobb Wawaw boul dem bama fi Xol bi bo fi guéné damay weet Boul ma sori way boul ma yokk soucis Xol bi bo fi guéné damay weet … (Wawaw boul dem bama fi Xol bi yow rek leu miine) Quand mon cœur est dans la peine bébé tu es là Yow rek a fi né dima yokk doolé Même ci benen doundou Mane meu def leu sama roi, Baneex rek lay doundou Da nga doug sama vie yow changer lou beuri Dal di deup carte bi, fim né mangui nian borom bi Mom sa souné mou xool ci souniou mbeuguel Yokk sama coofel mane yow la nobb Wawaw boul dem bama fi Xol bi bo fi guéné damay weet Boul ma sori way boul ma yokk soucis Xol bi bo fi guéné damay weet … (Wawaw boul dem bama fi Xol bi yow rek leu miine) Xol bi bo fi guéné damay weet (2x) Boul ma sori way bébé bo démé bayi ma fi … Yow rek la am yow la beug sama xol Yow kece leu waw Ki meu beug meu wara raay, Mane may nelaw yow rek la am (2x) … Wawaw boul dem bama fi Xol bi bo fi guéné damay weet Boul ma sori way boul ma yokk soucis Xol bi bo fi guéné damay weet
Yow la love ci suma xol yow rek yamay begg lo
Soma bayé dina weet
Yow xalé bi samay goudi dina weet lol
Da nga doug sama vie yow changer lou beuri
Dal di deup carte bi, fim né mangui nian borom bi
Mom sa souné mou xool ci souniou mbeuguel
Yokk sama coofel mane yow la nobb
Wawaw boul dem bama fi
Xol bi bo fi guéné damay weet
Boul ma sori way boul ma yokk soucis
Xol bi bo fi guéné damay weet …
(Wawaw boul dem bama fi
Xol bi yow rek leu miine)
Quand mon cœur est dans la peine bébé tu es là
Yow rek a fi né dima yokk doolé
Même ci benen doundou
Mane meu def leu sama roi,
Baneex rek lay doundou
Da nga doug sama vie yow changer lou beuri
Dal di deup carte bi, fim né mangui nian borom bi
Mom sa souné mou xool ci souniou mbeuguel
Yokk sama coofel mane yow la nobb
Wawaw boul dem bama fi
Xol bi bo fi guéné damay weet
Boul ma sori way boul ma yokk soucis
Xol bi bo fi guéné damay weet …
(Wawaw boul dem bama fi
Xol bi yow rek leu miine)
Xol bi bo fi guéné damay weet (2x)
Boul ma sori way bébé bo démé bayi ma fi …
Yow rek la am yow la beug sama xol
Yow kece leu waw
Ki meu beug meu wara raay,
Mane may nelaw yow rek la am
(2x) …
Wawaw boul dem bama fi
Xol bi bo fi guéné damay weet
Boul ma sori way boul ma yokk soucis
Xol bi bo fi guéné damay weet
MAGNIFAAAYYQUE🎉🔥🔥 nioun nio wett mais pas ioe😅 Bon courage bro👌🏿
C’est oufff😮💨🔥le talent à l’état pur 🔥🎉
Celui ou celle qui l’a écouté plus d’une fois appuie sur 👍
Machalla très belle mélodie ❤❤❤et ta voix osi🎉
Mingui cool
Nice maestro
Nice sama Sérère bi💯☺️
Perfect, bonne continuation 😊❤️
Fier de toi fils et souhaite que ce soit le début d'une longue et fructueuse carrière. ❤❤❤
Bonne continuation néhna trop ❤
T’as grave dead ça ❤❤❤❤❤❤🎉🎉
Que le Saint-Esprit soit avec toi bro ❤️🥰 bonne continuation dans le nom puissant de Jésus ✝️ Amen 🙏
Waouw Respect vraiment🙏🙏🙏
Un vrai malade🤌🏽🤧🥰 yalla xéb dolli way
Nice❤❤❤❤ de la part de KEYZO
Good song frère
Oh néxna torop
Courage frérot, sa liguey rafète na torop
Bonne continuation frère, et que la main de Dieu soit sur toi. Nice song🙏🥳
Romzø 🔥🔥
Magnifique ✨✨❤️❤🔥🔥👏
bagn bagn beug rendez-vous au sommet par la grâce de dieu💯🙏👣
Trop beau🎉🎉🎉❤
Force à toi frère
Allez🎉❤Romu nous sommes derrière toi avec Jésus amoul ragal on avance🌹❤️🥰beau chant🥹
Nice job frère
Piano 💯💯
Musicalement top🔥
La main de God sur toi😘
Fonss ! Yaw fonce rek. Ma main de Dieu sur toi bro❤
Nekhna lol rack diambour machala
Très nekh Romyal bonne continuation bro
Ce n’est que le debut du commencement 😍😍 bon courage 👊🏽. Top top top
Super ♥️
Nice mon frère bon courage pour la suite 🎉❤
Guerrier la 😍
Good job❤❤
Waw quel professionnalisme mon neveu. Que DIEU te bénisse
On est talentueux 🎉wesh 😍
Ndanann deugg frère 🤩 bonne continuation
Amoul ragal dei , Yessu mokoy gèrer ❤
Choc bro 🔥 bonne continuation
🎉❤ Magnifique mon bro ☺️👌🏽 .
Machalah Bonne continuation
Romzo ❤❤❤
❤❤❤❤
Bien frr c'est le petit frr de Yvonne
Machahalla 🎉 🎉
Bon courage pour la suite Dieu te bénisse🙏🏽🥰🥰
L'homme au doigt magic
Deugueuleuuuu🔥❤️✨🎊Bon courage pour la Suite 🙏🏾✨
💥🔥🔥🔥Grave top
Fier de toi petit frère, Thi kaw thi kanam rek, amoul ragal, peace🎉
🔥🔥🔥
C'est super mon pianiste
Ak ioe momm mbeuguel is bae 😊😢
❤️
Simple et très parlant. BRAVO
🎉🎉❤❤❤
Le pré-refrain est incroyable, évite les clips et mets le budget sur la musique, maîtrise, masterise et baise tout
🎉
Fi ngua ték sa tanke fofoula frère.
Magnifique ✨✨❤️❤🔥🔥👏
Magnifique ✨✨❤️❤🔥🔥