Kou sa xol rafet niou sédel lako, bakh nga yarou nga sa xol yatou na lol. Mangui nian yessu mou barkel ma leu Mangui nian mou def li geun ci sa doundeu Jaam rek ngey am yow sama xarit, Fi niou diar ak li niou doundou Do daw té do changer Tey seu beussou dioudou Amal foulay doundou Tu es ma meilleure, Tu es ma meilleure pour la vie Doundal doundal yow ma meilleure doundal, Doundal doundal ba sey may di bawane Yow doundal way (2x) … ( Doundal ba nga done yaay booy, na nga done maam.. Mane mi yow lay titeuro ) Do changer jiiko motakh mane ma sopp la, beugeul rek lo beug mane ma dem wouti ko. Ma dose de motivation ma jolie boule de joie, Tu sais bien mon coeur bat fort pour toi. Mane bilay ni mala beugué sakh daf ma yeem, Fi niou diar ak li niou doundou Do daw té do changer Tey seu beussou dioudou Amal foulay doundou Tu es ma meilleure, Tu es ma meilleure pour la vie Doundal doundal yow ma meilleure doundal, Doundal doundal ba sey may di bawane Yow doundal way (2x) … Jaam rek ngey am yow sama xarit, Fi niou diar ak li niou doundou Do daw té do changer. Mane bilay ni mala beugué sakh daf ma yeem, fi niou diar ak li niou dound Do daw té do changer. Doundal doundal yow ma meilleure doundal, Doundal doundal ba sey may di bawane Yow doundal way (2x) …
Masha Allah mon p'tit frère de ❤ , mon esclave Sérère à moi , très bel clip 🥰 toutes mes félicitations et très bonne continuation, le meilleur reste à venir insha Allah 🥰 thia kaw thia kanam , Lou bakh rék nga am insha borom ❤️ en diamant bi Masha Allah 🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Kou sa xol rafet niou sédel lako,
bakh nga yarou nga sa xol yatou na lol.
Mangui nian yessu mou barkel ma leu
Mangui nian mou def li geun ci sa doundeu
Jaam rek ngey am yow sama xarit,
Fi niou diar ak li niou doundou
Do daw té do changer
Tey seu beussou dioudou
Amal foulay doundou
Tu es ma meilleure,
Tu es ma meilleure pour la vie
Doundal doundal yow ma meilleure doundal,
Doundal doundal ba sey may di bawane
Yow doundal way
(2x) …
( Doundal ba nga done yaay booy,
na nga done maam.. Mane mi yow lay titeuro )
Do changer jiiko motakh mane ma sopp la,
beugeul rek lo beug mane ma dem wouti ko.
Ma dose de motivation ma jolie boule de joie,
Tu sais bien mon coeur bat fort pour toi.
Mane bilay ni mala beugué sakh daf ma yeem,
Fi niou diar ak li niou doundou
Do daw té do changer
Tey seu beussou dioudou
Amal foulay doundou
Tu es ma meilleure,
Tu es ma meilleure pour la vie
Doundal doundal yow ma meilleure doundal,
Doundal doundal ba sey may di bawane
Yow doundal way
(2x) …
Jaam rek ngey am yow sama xarit,
Fi niou diar ak li niou doundou
Do daw té do changer.
Mane bilay ni mala beugué sakh daf ma yeem,
fi niou diar ak li niou dound
Do daw té do changer.
Doundal doundal yow ma meilleure doundal,
Doundal doundal ba sey may di bawane
Yow doundal way
(2x) …
Ma chanson préférée ahhhh jaimmmm❤❤🎉🎉🎉❤
Ya fi nehh 🎉🎉 kou validé comme moi 🤩rek lalal j'aime ❤
Ma Star Marianne 🥰❤🎉
Waouh clip bi néxna🥰❤
Bravo Ro fière de toi
Kii dou nittt🤌🏽🙆🏽♂️🥰🥰
Bonne continuation mn frere🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Bonne continuation mon frère ❤❤
Romu ma dioyeee walaaa ???🤧🤧 j'ai plus Les mots ❤❤j'aime bien 🎉🎉
Bonne continuation bro, 🎉
Masha Allah mon p'tit frère de ❤ , mon esclave Sérère à moi , très bel clip 🥰 toutes mes félicitations et très bonne continuation, le meilleur reste à venir insha Allah 🥰 thia kaw thia kanam , Lou bakh rék nga am insha borom ❤️ en diamant bi Masha Allah 🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Jolie clip, très bonne continuation fiston ❤❤
Bonne continuation couzzz❤
Ta grave assuré Alphonse machallah mais mariane y’a bien kayy ❤️❤️❤️🥳🥳🥳🫶🏻🫶🏻🫶🏻
Respect man c'est bien nice. Bon continuation jeune talent
Nice frère ❤❤❤❤
🎉bonne continuation bro
Fort big brother 🤟👑trop dop
Super cool
Music haleiii sa voice nekhna Laff thiattt bro 🔥❤️🍾...Bae Marianne ma Tite Vie 🖇hew gua nk 🎉
🎉🎉 tchi kaaw tchi kanam rek Frère nice 👍
Avanceeeeeeeeeeee
🎉🎉🎉🎉🎉❤❤
Doundal souñiou maman la main de Dieu sur toi. Allez p'tit tu es sur le bon chemin ❤❤❤
Nice 😍 🔥bonne continuation Romy
Mom mbeuguel rek lay topp 🎉❤
Diadieuf Voshing 🥋👍🏿 nice on est derrière toi
Mariaaane 🎉❤❤ késsei 🎉🎉🎉
Magnifique frère bonne continuation 🎉🎉🎉
Bonne continuation grand frère ❤🎉
Aythia ndanann ❤ je valide bro 😊 si kaww si kanamm rk 🎉
Amal foulay doundeu couz ❤
Ohh du ouff 🎉🎉
Bro yangui may deff star nak 😂
Bonne continuation
❤❤❤🎉
Machallah frère Nice et bonne continuation 🎉❤
Bonne continuation frère ❤
Félicitation c'est super 🎉🎉❤❤
🔥🌟
Félicitations frère 🥰🎉
Mariane yow reck laniouy top, beau clip❤❤
🔥🔥🔥🔥
Nice bro💯💯je valide fort
❤❤ 0:39 ❤❤❤athia fils
Machalla 🎉couzzzz
Nice vidéo 💫
Tia kaw tia kanam 🙌🏾🐐🎉
Quelle douceur !!!!
Bravo l'homme
❤❤ bonne continuation
Bravo et félicitations
Mariane 🎉🎉🎉🎉
Mon bb❤
No François ak jean kon nagnou 😂😂😂
Mn Vj 😂 ya meunn dh🎉❤
Graças 🎉🎉🎉🎉
❤🎉
🎉🎉🎉
Mariann y’a bien wayi c Mouhamed l2b
❤😊🎉
Marianne bæ
Magnifique mon frère bonne continuation 🥰🥰🥰
Magnifique mon frère bonne continuation 🥰🥰🥰