Allahou akbar😱Cheikh Ahmed à Cheikh Abdoul Aziz yap sénégalais wéssou woul na Baye Niass rek so beug

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 25 янв 2025

Комментарии • 266

  • @Cheikhou60
    @Cheikhou60 2 месяца назад +24

    Walahi xam xam bi mo diara like👍 Maa Cha Allah
    Cheikh abdou Aziz

  • @AmyCissokho-jo3jp
    @AmyCissokho-jo3jp 2 месяца назад +2

    Machalah baye Niass d'où nit té d'où moromou ken thi xam xam ak thi lep daflen raw thi lep té lolou la def thi ay talibem motah fou talibem takhaw thi adouna mofay raw en voici la preuve ben thi Abdoul Aziz Ndiaye machalah xam xam bi werna c'est la certitude louné fangue ken douko diekh dafa lerrr dieurdiefé mawlana cheikh Ibrahim Niass ❤❤❤❤❤❤❤

  • @assenesow
    @assenesow 2 месяца назад +16

    Azize Macha'Allah ❤️ ham ham bi wër'na🎉 Yalla na Baye Geureum

    • @icAlphaDiallo
      @icAlphaDiallo 2 месяца назад

      Bokkale nga de yalla moy greurum

  • @awacoly1746
    @awacoly1746 2 месяца назад +25

    Alhamdoulilah deiurdeiufe baye niass merci beaucoup papeu Aziz Ndiaye ❤️ yalna yalla goudal sa fan si barcké baye niass ❤❤❤

  • @icAlphaDiallo
    @icAlphaDiallo 2 месяца назад +8

    Ki amna kham kham dé machallah

  • @aliounesall9573
    @aliounesall9573 2 месяца назад +13

    Dieureudieufééé baye niass cheikh Aziz yalna yalla fayela si barké seydina mouhamed

  • @Cheikhou60
    @Cheikhou60 2 месяца назад +7

    Macha'Allah Cheikh abdoul aziz ci xam xam bi
    Wayee gathié ngalama bayou Nandtee Yi

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 2 месяца назад +2

    ❤ Serigne bi xam xam bi manchalla explication bi lerna❤

  • @amathfaye9268
    @amathfaye9268 2 месяца назад +2

    Ohh dieureudieufé Mame Baye Niass, bilahi walakhi Deugg Deugg Baye moyy Deugg 💯🔥🙏🙏

  • @serignelo79
    @serignelo79 2 месяца назад +6

    Docteur Ahmad soukrane yagui soga âme tiere thie yalla

  • @aissataba3813
    @aissataba3813 2 месяца назад +7

    Thieummm barké baye cheikh Aziz ndiaye ken d’où baye❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @amadousouleyetandine931
    @amadousouleyetandine931 2 месяца назад +6

    Manchaallah cheikh Aziz Ndiaye ❤

  • @TiktokTika
    @TiktokTika 2 месяца назад +6

    Machalla Abdoul Abdoul aziz

  • @ablayefaye0
    @ablayefaye0 2 месяца назад +19

    Xaam xaam sii Baye Niass la neck ❤❤❤❤

    • @gtheboss9635
      @gtheboss9635 2 месяца назад +1

      Bilahiiii

    • @alioudiouf8912
      @alioudiouf8912 2 месяца назад

      @@ablayefaye0 kône yonnéte bi limou wakh ni " Anna Maditoul khilmi .... " dou dëëg khana 🤣les fanatique ouvré vos crânes 🤯

    • @Eva-m7s1l
      @Eva-m7s1l 2 месяца назад +2

      @@alioudiouf8912boul sisou Kholal fi baye diap danga guiss ne yonane tibi la masalane kouber defoul ndokh dh ms moy protégé bidon bi badou tourou epui bouniou dioutal bidon koubera nék si kaw dh Alhamdoulilah ❤

    • @bocarwade8241
      @bocarwade8241 2 месяца назад

      Alkhourane ak souna moy DEUG

    • @Ismaeljallow-k3b
      @Ismaeljallow-k3b 2 месяца назад

      @@ablayefaye0Mam Khalifa Nyass moko jangal moko raw fuff du moromam. Wahal chi lolu. Mam Khalifa moy domu Mam Alhagi Abdoulie moy khalifam.

  • @aminasarr9901
    @aminasarr9901 2 месяца назад +6

    Dieureudieffff maolana cheikh Ibrahim Niass bayou cheikha mariama Niass ❤️

  • @bibsfall1844
    @bibsfall1844 2 месяца назад +8

    Bayii leenn dii wakh ak cisse weeroull waala mou beug leenn wakh loo yalla naako yalla sopi amine

    • @mouhamedbiteye5507
      @mouhamedbiteye5507 2 месяца назад

      Louy oustaz di wakh yeup khame nako ndakh talibé baye la khana dafa done imbécile rk

  • @cherifmballo4290
    @cherifmballo4290 2 месяца назад +1

    Kham kham nehkena machallaha !

  • @IbrahimaFall-u3z
    @IbrahimaFall-u3z 2 месяца назад +4

    Machallah Cheikh Aziz Ndiaye ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @VaniaSofia-l7x
    @VaniaSofia-l7x 2 месяца назад +10

    Aka leeerrrr dieureudieufé baye

    • @bocarwade8241
      @bocarwade8241 2 месяца назад +1

      Diamou yalla boy wer moy yeguee nite mais d'où ay waxi kesse

  • @BaiJobe-i9n
    @BaiJobe-i9n 2 месяца назад

    Aww Massallah sheikh Abdou aziz we proud of you may Allah reward you with more “Marifa”

  • @lessendiaye4278
    @lessendiaye4278 2 месяца назад +2

    Ahmed cissé c'est un vrai pédagogue et un vrai enseignant et un éducateur. C'est pour cela qu'il a un peu de thiay thiay pour composer avec toutes les couches de la population.

  • @mouhamadouaw358
    @mouhamadouaw358 2 месяца назад +14

    baye Niass fila fék xam yalla wayé gore yalla yeup si akhadiyatou yalla dji lagnu yéme la preuve kosi lire wala ga dégue limouye waxe diga xamni si yalla rk lagnu yéme niome séne probléme modone hame yalla késsè finalou wayé baye naiss nak amna fathou lata mouye djoudou wa inda Fathi etc.. moni Madi yalla gayi fokni falaye yéme mou ték si Madi yonéte Madi cheikh maye lépp
    Gore yalla yi daniou d'âne xam yalla wayé si niome rk la yémone likoye firné moye guinaw niome do dégue si séne Mbolo kou woté xam yalla
    Wayé baye Niass bamou fiye né ak guinawam môme rk gaye djis Di dégue si mbolowam nioye woté xam yalla diko xamlé si Lou lére té amoul parparlo
    Fi adouna tolou képp kouye wo nitt yi rawatina yénéne khétt yi labone si diakhiliya pour ga convaincre léne si diné boudé si waraté ak diagui aya rk moye takh niou toup diga fa tardé wala béne béne gaye am
    Wayé Mbolo bou dougou si diné si béne takhawaye so amoul sirrou faydou diko déf nah fow ga meune léne waxe louye salatoul fatiha louye diahawartou Kamal wala wala wala sou amone vocal mou geuna nékh wassalam !?

    • @moristodiouf6838
      @moristodiouf6838 2 месяца назад

      Kou bakh lolou nga wakh dé amoul magui toub nak. Dafa fekné dou mbolo mo guiss da wara nek di waxtané xam yalla su mbèd mii...Hum oumpalé nga lou beurina wayé nonou la...mandou bokna si di wax li nga maîtriser kessé ap dioulite nak nonou la war di dokhé

  • @ndiayeousmanebaba7531
    @ndiayeousmanebaba7531 2 месяца назад +9

    Baye Niass est l’océan du savoir kouko djégué toyy xam xam ignane baxoul 😢

    • @DiaMbar-si3cu
      @DiaMbar-si3cu 2 месяца назад

      @@ndiayeousmanebaba7531
      Ay féne la xamou léne touss baye xamlé , yéna yakh diné dji

  • @BayeIbrahimaDiassé-j8y
    @BayeIbrahimaDiassé-j8y 2 месяца назад +1

    Li rek moh takh niou topou baye kham kham bou leer ak deg deg
    Bly baye rek moye deug ✊🏾❤️✊🏾

  • @SouleymaneDiop-s2z
    @SouleymaneDiop-s2z 2 месяца назад +3

    Machalla bihi degua bou wore là wakhtane bi nekhna trop machalla ❤❤❤❤❤❤❤

  • @papissow2264
    @papissow2264 2 месяца назад +3

    Wallahi gisga coula leural yonou soufiya Diara diefe cheikh bay

  • @AnaSarr-s4t
    @AnaSarr-s4t 2 месяца назад +2

    Au service de baye niass pour sevais la jeunesse ✊ Cheikh Abdou Aziz Ndiaye ❤️🥰

  • @mouhameddieye4688
    @mouhameddieye4688 2 месяца назад +5

    Dieureudieufé baye

  • @modouthiam2461
    @modouthiam2461 2 месяца назад +8

    Azzizz ya kawe❤

  • @LoumOusmane-vu9dt
    @LoumOusmane-vu9dt 2 месяца назад +5

    Dieuredieufe ndiaye ❤

  • @ibrahimakonte2026
    @ibrahimakonte2026 2 месяца назад +5

    Dieureudieuf cheikh aziz ndiaye 😊😂😂😂😂

  • @sambasounasene3083
    @sambasounasene3083 2 месяца назад +4

    Macha allah kham kham rekk moy deugue

  • @BiramaGueyediouf
    @BiramaGueyediouf 2 месяца назад +2

    Contane naniou cheikh aziz❤❤

  • @Maham_Baye
    @Maham_Baye 2 месяца назад +2

    Dieuredieuffé Baye Niass!

  • @moustaphakone3022
    @moustaphakone3022 2 месяца назад +2

    MASHALLAH CHEIKH AZIZ 😍😍😍😍😍😍😍😍

  • @NdiagaWade-k1z
    @NdiagaWade-k1z 2 месяца назад +2

    Machallah ❤❤❤

  • @AliAbdoulayeFall
    @AliAbdoulayeFall 2 месяца назад +1

    machallah diereudieufee Baye Niass

  • @cheikhfaye8893
    @cheikhfaye8893 2 месяца назад +1

    Machallah dieuredieufé ❤ cheikh aziz

  • @ousmanendiaye340
    @ousmanendiaye340 2 месяца назад +2

    Goudou fan ak wër ❤❤❤❤

  • @insandao4967
    @insandao4967 2 месяца назад +4

    ماشاء الله

  • @AblayeNdiaye-s5b
    @AblayeNdiaye-s5b 2 месяца назад +2

    Diereudieffé Baye niass

  • @MouhamedNassir
    @MouhamedNassir 2 месяца назад +52

    Kou nieuwe ma hamale la sa borom baye niass rek mokafi masa wahe motahe mome rék moye hamlé yalla

    • @dabakhdia3873
      @dabakhdia3873 2 месяца назад +6

      😂😂😂

    • @dabakhdia3873
      @dabakhdia3873 2 месяца назад +5

      maodo moko diokh mame abdoulay ❤️😎

    • @abassediop3088
      @abassediop3088 2 месяца назад +9

      ​loutakh Maodo diokhouko Ay wa keureum wala dagnouko atanoul

    • @abassediop3088
      @abassediop3088 2 месяца назад

      ​@@dabakhdia3873souder Maodo mooko diokh Mame Aladji Abdoulaye loutakh diokhouko Ay wa keureum

    • @DiaMbar-si3cu
      @DiaMbar-si3cu 2 месяца назад

      @@dabakhdia3873
      Yaw dioum nga dé mam maoudo lamou diokh mam Abdou laye Dou thiaxane yi gayi Di woté dé , démal nga geustou djiko

  • @AbdalahFaye-s6n
    @AbdalahFaye-s6n 2 месяца назад +1

    Mashallah seurigne bii

  • @halimdjen9084
    @halimdjen9084 2 месяца назад +3

    Masaallaah xam xam bi rafet na lool

  • @DjackDiokh
    @DjackDiokh 2 месяца назад +2

    MashaAllah

  • @BocarDemba-g9y
    @BocarDemba-g9y 2 месяца назад

    Masha Allah Niass❤❤❤

  • @metazodiallo1591
    @metazodiallo1591 2 месяца назад +3

    Allahou akbar

  • @GAYEABDOUKARIM-v5e
    @GAYEABDOUKARIM-v5e 2 месяца назад +6

    Alahou akbar sai sai cissé yangui doga lale lalaké xam xam bou séleu thi baye ngua koy féfeu

  • @MamadouDieng-ce7uc
    @MamadouDieng-ce7uc Месяц назад

    Diaradieufé baye

  • @absacoundoul77
    @absacoundoul77 2 месяца назад +1

    Machallah

  • @mariamamaiga4471
    @mariamamaiga4471 2 месяца назад

    Dieureudieuffee baye niass

  • @gtheboss9635
    @gtheboss9635 2 месяца назад +5

    Kén👈dou BayNiass

  • @ibrahimafadiga4986
    @ibrahimafadiga4986 2 месяца назад +2

    Très clair

  • @csaygaming5973
    @csaygaming5973 2 месяца назад +5

    Ham ham bi lerr na, Marsh-allah. Bai Nyass rek kai wakh si kee.

  • @IsmailaBa-fz7vv
    @IsmailaBa-fz7vv 2 месяца назад

    Ahmed cissé devrait refaire un tarbiyou

  • @amitewiseverengom9960
    @amitewiseverengom9960 2 месяца назад +2

    Macallah

  • @SowBaye-zr1hk
    @SowBaye-zr1hk 2 месяца назад

    Sangue Ndiaye rawnalén bou yaagg ❤

  • @abdourahmanesall8460
    @abdourahmanesall8460 2 месяца назад +1

    Amna solo waye

  • @mamadoulaminetoure8112
    @mamadoulaminetoure8112 2 месяца назад +1

    Serigne bi dioum nga dé yalla mgnu khamal tourou lép luniou kham dou nitt mo créé tour yii yalla mo wakhni ma binde nitt khamalko.

  • @bourbajoollof4232
    @bourbajoollof4232 2 месяца назад +2

    Ahmet Cissé dafa sankou😮

  • @senegalkesso1293
    @senegalkesso1293 2 месяца назад +1

    Baye niass ak kou mou meunty done Islam moko mak. Teh joullit meune ta kham diné islam beu gueune ko kham YONENTE BI SALLALLAHOU ALEYHI WA SALAM ❤️

  • @abdoulayethiam7358
    @abdoulayethiam7358 2 месяца назад

    Ameth Cissé Yèfeur lah légui
    Ndeyessane fila modié. Bétoulema

  • @CheikhoulkhadimMbacke-p6o
    @CheikhoulkhadimMbacke-p6o 2 месяца назад

    Billahi ki khamoul Dara ndeysane😮😮😢 diafaniko khel AK khamkham bokkoul

  • @sarramundu1
    @sarramundu1 Месяц назад

    Xamxam dégg dégg la andale

  • @M.faalsony
    @M.faalsony 2 месяца назад

    Sheikh Ahmed can you please invite Majam faal it will be really interesting

  • @Ridialbi
    @Ridialbi 2 месяца назад +2

    😂cheikh Ahmed yanguimay dora nékh nak! Yow fi ngua momé

  • @OUSMANESarrr
    @OUSMANESarrr 2 месяца назад

    C vrai

  • @sallsiradji6247
    @sallsiradji6247 2 месяца назад

    25:12 kour an wahou yallah

  • @diankalartraore4111
    @diankalartraore4111 2 месяца назад

    Wa alama adama assmaou koulaha .
    Yallah wah n'a ssi sourate 20 ni moomleu Yallah
    Sooy wah dél oubiwalé téeré bi

    • @mouhamadoulaminetoure4046
      @mouhamadoulaminetoure4046 2 месяца назад +4

      fall lingay waxx nekhoul si sourate 20 (taha) sourate 02 (baqara) fofou la nekk en plus ayat bi firiwoul lingay waxx fait attention quant tu parles du coran svp

    • @Wrestling1890
      @Wrestling1890 2 месяца назад +2

      ​@@mouhamadoulaminetoure4046dafa faussé fépp kay 😂 linga wax moy fi yalla di wakh nane ma khamal adama tourr yeupp boy kii néko ki geuna ndaw thi talibé baye yi dou moromam baye dou morom

    • @mouhamadoulaminetoure4046
      @mouhamadoulaminetoure4046 2 месяца назад +1

      @@Wrestling1890 balko😂😂😂

  • @AmsteDiall0
    @AmsteDiall0 2 месяца назад

    سكر لك يا أستاذ

  • @mamadoudiallo2892
    @mamadoudiallo2892 2 месяца назад

    Cheikh Aziz diokhma sa numéro svp

  • @TMBNTV
    @TMBNTV 2 месяца назад +1

    Ahmed CISSÉ taye mom diomi ngua ❤😊

    • @gtheboss9635
      @gtheboss9635 2 месяца назад +1

      Guissagoul Dara kén Dou sama Cheikh biiiii

  • @KebeTalla-il6cd
    @KebeTalla-il6cd 2 месяца назад

    Ndaysane cheikh abdoul aziz yalna yalla samou la mane dh mouridela wayé qui xam xam rk laye wakh❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊

  • @matarseck2725
    @matarseck2725 2 месяца назад

    Baye rek

  • @MamadouBa-w6s
    @MamadouBa-w6s 2 месяца назад

    ❤️❤️❤️❤️♥️♥️💯💯💯

  • @maodogamer
    @maodogamer 2 месяца назад +1

    Fils wakh dji diaroul mouy goudou islam dou philosophie bagnouy doutè wala di hol ay certitudes soit dangay croire wala nga bagna croire

  • @mamadousow8935
    @mamadousow8935 2 месяца назад

    Vraiment cheikh Aziz je ne te voyais même pas tentretenir avec ce gars là

  • @samadeguine9840
    @samadeguine9840 2 месяца назад

    Lay rec

  • @Ismaeljallow-k3b
    @Ismaeljallow-k3b 2 месяца назад +1

    Yangi fen. Bayil fen. Yaala moy 'Yaa Allah'. Kadu arab la. Julit du fen. Kham naa wahtaan wi mo nekh.

    • @muhammeddrammeh8811
      @muhammeddrammeh8811 2 месяца назад

      Walahi ham ngane waho dega bala Arab nuyala Tudon

    • @Ismaeljallow-k3b
      @Ismaeljallow-k3b 2 месяца назад

      @muhammeddrammeh8811 dungen ragal Yalla muk. Fen rek. Bayilen fen. Wollof mo yakh beat bi. Wayeh du Yaala "Yaa Allah". Yangi woneh kham kham teh khamo tus. Demal nga jangi mogen nga bayi tapaleh.
      Yaala turam moye 'Allaahu' lolu moye ismu zaat. Mom rek mo ham turam SWT.
      Yen amulen horma chi Yaala SWT. Wayeh halaku rek.

    • @Eva-m7s1l
      @Eva-m7s1l 2 месяца назад +1

      Ms Kii lime ko lathie avant alkhourane wakhouma lak arabe epui wakhoul si zahir batine lay wakh bayil lo amoul dég dég bi rk dakhouko

    • @Ismaeljallow-k3b
      @Ismaeljallow-k3b 2 месяца назад

      @@muhammeddrammeh8811 chi Injil wola chi tawrat wola chi zabuur? Sa question be bakhul. Dafa wara am completion mangi laye haar.

    • @AliouneFagueyeDiop
      @AliouneFagueyeDiop 2 месяца назад

      Yawww doudou khamou Dara yague sa Serigne demlene diangui ou bien gua wakh sa Serigne niou deffff plateau

  • @mohamedtidianendiaye1561
    @mohamedtidianendiaye1561 2 месяца назад

    Je valide

  • @ibrabeye9398
    @ibrabeye9398 28 дней назад

    Boy Cissé delowatale sa xel. Ayy vue ,wala buzz, ba thiow diaroul danguou thi biroupp yalla kou sangn La ( Yalla xel douko Dathieu.

  • @djibrilmbayendoye2060
    @djibrilmbayendoye2060 Месяц назад

    As salaamu aleykoum wa rahmatullahi wa barakaa touhou
    Chers(èrs) frères et soeurs en islam j'espère que vous allez bien par la grâce d' Allah azzawajal
    Mbokk dioulite yi dafa war si bépp dioulite bou goor ak bou djiguene mou kham niétti ponk: mou kham Yallah ; mou kham yonénte bi sallallahou aleyhi wa sallam ; mou kham diiné islam
    La ilaha illa Allah tékkinam bou wér moy; ''amoul léne lognou wara diaamou si deugg koudoul Yallah''; ndakh ame na lénéne lou ay nite di diaamou lou nékkoul Yallah mais diamou bobou téggoul si deugg; kone diaamou bignouy diaamou Yallah rk moo tégou si deugg; la preuve dans la sourate 22 al ( hajj ) verset 62
    Kone wadji nekk si vidéo bi noumou tékké ''la ilaha illa Allah'' dou tékkine bou wér ( 3mn 48s ) ; té Khamal mbokk dioulite mi né nite meunoul guiss Yallah si adouna ndakh yonénte Yallah Muhammad wakh na si hadith né kéne si gnoune dou guiss Yallah balaa mouy déé; la preuve ↓↓↓
    D'après 'Abdallah Ibn 'Omar (qu'Allah les agrée lui et son père), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit le jour où il a mis les gens en garde contre le Dajjal : « Certes il est écrit entre ses yeux kafir , celui qui déteste ses actes lira cela. Apprenez qu'aucun de vous ne verra son Seigneur avant qu'il meurt ».
    (Rapporté par Mouslim dans son Sahih n°169)
    ↑↑↑ Kone gnouy wakh né dagnouy guiss Yallah si adouna dagnoo réére rk wala lénéne lagnouy guiss mais dou Yallah azzawajal
    Khamal mbokk dioulite mi né Yallah nékkoul fépp; allez regarder la preuve dans la sourate 67 ( Mulk ) verset 16 et 17
    Khamal mbokk dioulite bi né Yallah Kéne la Yallah kou Magg la kou Tédd la; Yallah amoul naatangoo

  • @bassiroungom3744
    @bassiroungom3744 2 месяца назад

    Adouna temps ak espace la ta ay diamou yalla laniou moléne binde kone avant ak après agouniou si yalla

  • @LoumOusmane-vu9dt
    @LoumOusmane-vu9dt 2 месяца назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @singuinard1659
    @singuinard1659 2 месяца назад

    Toudou yalla moy undi certitude

  • @alphadiack8140
    @alphadiack8140 2 месяца назад +4

    Vous traduisez tres mal " La Ilaha Ilal Lah", je vous invite à aller consulter les enseignements du prophète Mouhamad (Psl) sur la parole de " La ilaha Ilal Lah" qui signifie il n y a point de divinité qui merite soumission et adoration en dehor d'Allah l'unique, sans associé.

  • @SeckTalla-pw2kt
    @SeckTalla-pw2kt 2 месяца назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bayeniasstv1232
    @bayeniasstv1232 2 месяца назад

    Ahmed Cissé bayil sa thiakhaan yi waye

  • @SambaSy-i5d
    @SambaSy-i5d 2 месяца назад

    Bayelin fen

    • @AliouneFagueyeDiop
      @AliouneFagueyeDiop 2 месяца назад

      Yawww sa Serigne amoule xam xam na ngneww niou deffff plateau

  • @lessendiaye4278
    @lessendiaye4278 2 месяца назад

    Le facteur commun se résume seulement autour du XEL. DIEU PARLE AVEC LES BOROMS XEL OU KHEL.

  • @MoussaKandé-g5r
    @MoussaKandé-g5r 2 месяца назад

    Cheikh Aziz danga yiu waro débat AK wadji

  • @LamineNdiaye-x4z
    @LamineNdiaye-x4z 2 месяца назад

    Non Ahmed cissé vrai comédien la quoi😂

  • @tamsirgueye-cb4xz
    @tamsirgueye-cb4xz 2 месяца назад

    مثل طريق التيجان من مولانا شيخ ابراهيم ايناس مفقود في العالم انظرو إلي هذا التفسير بين ❤❤❤❤

  • @PapeDiouf-j4f
    @PapeDiouf-j4f 2 месяца назад +1

    Listen to my uncle he telling you through🫶🏾🙏🏾🙏🏾☝🏾🇸🇳🇺🇲

  • @ElhadjiWillane-uh7vz
    @ElhadjiWillane-uh7vz 2 месяца назад +1

  • @MoudouMoudou-e2l
    @MoudouMoudou-e2l 2 месяца назад +1

    💓💓💓💓💓💓💓💓

  • @TubaboGiboroh
    @TubaboGiboroh 2 месяца назад

    Baye niass moyi xam xam

  • @solution5135
    @solution5135 2 месяца назад +1

    Mangisoga comprendre ahmat sésé wédiwoul dafay diangalé rék

  • @Hope_00007
    @Hope_00007 2 месяца назад +1

    😂😂😂😂😂 ndiay way ndam thi yw niass niass

  • @bickoverds3830
    @bickoverds3830 2 месяца назад

    Ndioumté leu sou nééni dioulli ak diaamou yi pour nitgnila meunoone na yém si nguir dieufé ndigal la