Au service de Baye pour sauver la jeunesse Au service de Baye pour rééquilibrer la balance sociétale qui est en déficit pas budgétaire mais comportementale dieureudieuf mawlaya cheikh Abdoul Aziz Ndiaye
Waxtane bi nekh na trop machallah dieureudieuf Sheikh Aziz. Sinon sén sous impression (zikr bissi souf) dafa fort trop. Sous dafa wara am réglage souko défé kiw wax niou meun ko dégg bubax
Wallahi Ndiaye daga bakh rekk wayé bokk ga tî gni am clinique ❤❤ clinique bou mague té meuna fadj fébar bou nék amga garab bi ❤❤ doundal wéral ti barké Baye AK bayam yarabi
Ndeysane djiere djief baye Aziz Ndiaye Au service de baye niass pour seuve la jeunesse ya bakh serinnge bou mat seringe mongi ni Barke Baye niass ya bakh de
As Salamu 'aleykum mbokk mi. Dilein ziaar bubaakh. Vidéo bi dh guiss naani son wou dhikr bi dafssi fort trop ba parfois waxou Cheikh bi daflay reuthie. Sou nguein ko meunon wagni bamou geuneu faible xamni de loin lay résonner di geuneu bakh trop ma sha Allah Di tubb bubaakh thie kaddu yi 🙏🏾
Ndeysanne yalna yallah fayale niou mawlana Cheikh Abdou Aziz Ndiaye au service de Baye Niass pour sauver la jeunesse et nous a sauvé ❤❤❤❤❤
dieredieuf
Cet entretien doit être le livre de Chevet de nous les jeunes musulmans. C'est un message a écouté constamment.
Dieuredieufé Baye Niass
Il est très éloquent Cheikh Aziiz ndiaye il maîtrise bien son sujet
Cheikh aziz Ndiaye Diambari fayfou deug leu ❤
Au service de Baye pour sauver la jeunesse Au service de Baye pour rééquilibrer la balance sociétale qui est en déficit pas budgétaire mais comportementale dieureudieuf mawlaya cheikh Abdoul Aziz Ndiaye
Allah akbaaar alkhamdulilah Allah kulli hall DIEUREDIEUF BAYE NIASS
Hoooôo Kell magnifique Émission ❤❤❤❤❤❤ just la musique de fond est trop volumineuse..,.
Machallah Sokhna si yagui déf liguey bou am solo machallah 🙏🙏🙏
dieredieuf
Macha'allah cheikh Abdoul Aziz Ndiaye toujours au service de baye Niass pour sauver la jeunesse 🙏🤝🤲❤️
BARHAMIENNE TV MACHALAH ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Cheikh Aziz ndiaye tjr au service de baye NIASS pour sauver la jeuness
Protection d'Allah ya cheikh Aziz 266
Cheikh doundeul weereul Ndiaye ❤
Cheikh doundeul weereul❤
Machalla Serigne bi ñogui ziar bou bakh
Alkhamdoulilah ❤Dieureudieufety Baye Barkhama Niass 😊
Cheikh Aziz Ndiaye référence bi
Niass! Un communicant hors paire
Cheikh Aziz Ndiaye au service de Baye niass pour sauver la jeunes ❤❤
Machalha Niass !
Alhamdoulillah
Barké Baye Niass
❤mashallah cheikh bi♥️🥰♥️
Alhamdoulilah ! Jerejeuf serigne bi💚
dieredieuf
MACHALLAH SERIGNE BII PAYI BII CONTANA SI IOW❤❤❤
Unfortunately Cheikh is a very intelligent guy may Allah give him a long life and good health be Baraka Cheikh Ibrahim R. T A
@@MustaphaTouray-wm8dg why unfortunately?
Alhamdoulillah serigne bi mo bakh way ❤❤❤❤
Alhamdoulilah ❤
Ya bakh papeuh aziz❤❤
Machallah baye niass piont baye rék ❤
Beug deugou AK documenté Al hamdoulilah
Ndeysan y’a oyoff yalna yalla guoudeul sa fane y’a rabbi🙏🙏
Toujours au service de la fayda tidianiya ❤❤❤❤❤
Machallah liguey bii amna solo Yalla na baye fayanté ak yeneuh 🙏volume zikr bii reik soleneuh ko wagni wone dina baxx🥰🤩
Ndeyesane yalle nala yalle Moussa le thi thiate ak lamigne fane bou long❤
@@khoudygueye5652 amiiiiiine ya raby
Machallah mata baye liguey bi rafetna lol yalla yalla takha woula 🙏🏽
Manshallah yallah neu yallah barkeill lépp félicitations pour votre effort seydah
Walae beug nagn la Baye ❤❤❤❤❤❤
Nioune Ndiaye rk lanioy TOPPOU❤
Mashalla contane nane bou bax serigne bi exemplaire nga si Monde bi keep koulay deglou diarignou
Merci aussi la chaîne RUclips Barhamienne
Machallah long vie serigne bi❤
Waxtane bi nekh na trop machallah dieureudieuf Sheikh Aziz.
Sinon sén sous impression (zikr bissi souf) dafa fort trop. Sous dafa wara am réglage souko défé kiw wax niou meun ko dégg bubax
C'est sinon dugnu degg bou bahh mais alhamdoulilah❤
D'accord merci
Sou nguén niou meuné dougalatal émission bi sans zikr bi si souff dinaniou nékh trop wallahi anzim@@BarhamiennesTv
ndiaye dieradief walay matga liga don machahala yalna yalla goudal saye fan yarabi ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤machala le pèdagogue yalna yalla goudale sa faneyi ya rabi Allah
Machallah yalna yallah yagall la fi ❤
Machalah ❤❤❤❤❤
Machala ❤
Kou beugue baye niass leu
Nitt kou bakh cheikh Aziz Ndiaye
Machaalla doundale werrale Ndiaye si barkhé baye niass ❤
Niasss diarama cheikh azize Ndiaye
Machalla cheikh Aziz Yague fi loll andak weer❤
Yalna yalla goudal sa fane yarabi si barke baye ❤❤
Machallah Ndiaye❤️
❤❤❤❤❤❤ MACHALLAH RAFETNA DIEREDIEUF BAYE NIASS ❤❤❤❤❤
Niass ❤❤❤❤❤
Dieureudieuf ❤❤❤
Niass ❤
Longue vie Serigne bi ❤
Wallahi Ndiaye daga bakh rekk wayé bokk ga tî gni am clinique ❤❤ clinique bou mague té meuna fadj fébar bou nék amga garab bi ❤❤ doundal wéral ti barké Baye AK bayam yarabi
Mashalla
Tanks for your baye Aziz Nije
🤍الحمد لله على كل حال🤍
Alhamdoullilah ❤
Ndiaye ❤wayou babaaa❤
Mahcala nice dieuredieuf ti baye niass rèk
Dieurdief pappa❤
Cheikh aziz cheikh mou rabbi deugeu la
Macha Allah
Alhamdoulilah serigne bi bilahi waxtane bi kawéna lolll yalnala baye niass faye
Alhamdoulilah baniou niowé ci clinique mba gaa fadji niou Hadara Liwaoul Hamdi
Serigne bi îoe laniouy ndamonn❤ndiaye diatta ndiaye
Djeureudjeuf Cheikh Aziz Ndiaye
Aziz goor gua
Mâcha Allah idole et modele
Ndayssan ndiaye ❤
Alhamdoulilah
Ndeysan Ndiaye ❤
Demal seti cheikh ousmane diane baye bargny
Cheikh Abdoul Aziz Ndiaye dama la beugue guisse
@@DahaTall-l6z deff ma signe
Manchalla amna solo lollllll
Dieuredieuf Cheikh bi sa liguey rafetna lole lole yalla na Baye Niass faye la
Je suggère qu'ont baissent un peu le volume du son du zikr svp
INVITELENN CHEIKH IBRAHIM CISSE JALALOUDINE
Ndeysane djiere djief baye Aziz Ndiaye Au service de baye niass pour seuve la jeunesse ya bakh serinnge bou mat seringe mongi ni Barke Baye niass ya bakh de
Soukna mati yalna yala faye la❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤جرجف باي نجاس❤❤❤❤❤
As Salamu 'aleykum mbokk mi. Dilein ziaar bubaakh.
Vidéo bi dh guiss naani son wou dhikr bi dafssi fort trop ba parfois waxou Cheikh bi daflay reuthie. Sou nguein ko meunon wagni bamou geuneu faible xamni de loin lay résonner di geuneu bakh trop ma sha Allah
Di tubb bubaakh thie kaddu yi 🙏🏾
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mann zikr biy daw ci suuf la bëg. Ku ko am yone ma ko ngir yàlla
20:39
❤❤❤❤❤😭☑️w
Alhamdulilah
Démal sétan vidéo bi amna solo LOL ruclips.net/video/3dW_hLUdVv4/видео.htmlsi=46n1Ndh9zJZHyRFV
Générique bi vraiment meunon n'a niak.
Revoyez cette présentation car générique bi mo geuna fort interview bi . Vraiment 👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎
Cheikh doundeul weereul Ndiaye ❤
Machallah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah