Reportage: Mbacké Kador, berceau du mouridisme réhabilité par le Baye Fall Serigne Babacar MBOW Ndem

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 21 дек 2024

Комментарии • 47

  • @Borombaax
    @Borombaax 9 месяцев назад +5

    Incroyablement magnifique❤. Dans une video de 2 heures dw temps on y voit la voie du développement. Donnez ce pays au Baye Fall pour que ce pays se développe! 😢. Dieuredieuf Serigne Babacar Mbow, YALLAH nagnoula sougnou borom faye ci barke Cheikhoul Khadim ak Mame CHEIKH IBRAHIMA FALL 🤲🏽🙏🏽

  • @InsRastafariMixmaster
    @InsRastafariMixmaster 9 месяцев назад +3

    Serigne Babacar Mbow que le Tout Puissant t'accueille directement au Paradis Firdawsi si Barké Cheikhoul Khadim 👌🙏🙏🙏🙏👌

    • @Borombaax
      @Borombaax 9 месяцев назад

      AMIIN yaa rabbal haalamin 🤲🏽🤲🏽

  • @ousseynoutoure3621
    @ousseynoutoure3621 9 месяцев назад +1

    Serigne babacar mbow yalna nga guissei ak serigne touba mam cheikh ibrahima fall aldiana

  • @lminebaraseck9500
    @lminebaraseck9500 9 месяцев назад +5

    Yallanako yalla yaram ta diegalko sibarckeb s touba

  • @papandiaye984
    @papandiaye984 6 лет назад +3

    Un homme humble,juste et dévoué a.la.cause du mouridisme... un parfait exemple du mouride. Yallah nala fi yallah sakhal.

  • @diagnenarre7448
    @diagnenarre7448 6 лет назад +3

    li rafetna machallah waw ana wa Senegal guiss nan li lirek mowour liguey ta yalla rek takh yalla na yalla takhawolen si barkep serigne bi am na solo machallah machallah

  • @Beugdeug
    @Beugdeug 9 месяцев назад

    Serigne Babacar Mbow yalla naco yalla terrou deukeulco Mame Cheikh Ibra Fall

  • @dinakane2032
    @dinakane2032 9 месяцев назад +3

    Ndeyssan yalla nako suniu borom yeureum 🙏🏿

  • @khoudiagueye5012
    @khoudiagueye5012 9 месяцев назад +2

    Serigne babacar mbow yalla na yipé aldianna firdawci

  • @moustaphafall1691
    @moustaphafall1691 9 месяцев назад +2

    Yalnako yalla khare aldiana serigne babacar mbaow😢

  • @bayedieng3518
    @bayedieng3518 6 лет назад +2

    Ndeysaan yalna yala fayalnou serigne babacar mbow leepu rafeetna

  • @serviceclientsbestofficedi7490
    @serviceclientsbestofficedi7490 4 года назад +1

    machalah sama khol sed na .LEP TEGOUNA THIE TALIBE AK YAR

  • @serignefalloufall4242
    @serignefalloufall4242 2 года назад

    Machallah li rék mo am solo Dieureudif serigne Babacar mbaw 👂👂♥️♥️♥️☀️🙏🏿

  • @louisediagne2006
    @louisediagne2006 6 лет назад +3

    Macha alla sante mame borom touba rekh ak mame lamp fall ❤️😭

  • @kebecheikh3998
    @kebecheikh3998 9 месяцев назад

    Mashalla❤

  • @tallakhadim8922
    @tallakhadim8922 6 лет назад +2

    Thiey serigne touba dieuredieufé serigne touba diarama mame cheikh hibrahima faaal

  • @mbayeahmadou2223
    @mbayeahmadou2223 6 лет назад +1

    Ma challah nice

  • @cheikhbassiroubabou686
    @cheikhbassiroubabou686 6 лет назад +1

    waw Gore Baye Fall

  • @mamadousall5370
    @mamadousall5370 6 лет назад +1

    Machala

  • @ngonehdieng2131
    @ngonehdieng2131 6 лет назад +3

    Walahi cheikh ibra dou kene voilà le modèle type pour un développement touti wakh dief diou bara modi baye fall deug

  • @bayefall4061
    @bayefall4061 6 лет назад +2

    Mangi ziar Serigne bi y’a Aïcha cheikhouna s fallou ya ngone jamila mame cheikh mbolèm ndiabot gi dierediefeuti ligeye rekka woor fall

  • @mara-sy346
    @mara-sy346 9 месяцев назад

    Allahallahhh
    Segne bi lii yèmè na wallahi

  • @Beugdeug
    @Beugdeug 9 месяцев назад

    Walakhi Serigne Babacar MBOW amoul morome dé il s'est défoncé pour réaliser le Village de Mbacké Kadior

  • @abdoulahibabou4250
    @abdoulahibabou4250 6 лет назад +1

    oh ma sha allah amna solo fall

  • @abohafccisse9595
    @abohafccisse9595 4 года назад +2

    Douma si doyal ndakh yeurmandè ji ma siy yeuk

  • @diagnenarre7448
    @diagnenarre7448 6 лет назад

    waw len goor mouride am na solo yalla na yalla takhawolen rafetna

    • @medouneyandegueye7506
      @medouneyandegueye7506 6 лет назад +1

      Dieure dieufeti serigne babacar mbaw yalla na noula serigne touba samal sibarakep mâle cheikh ibra

  • @amethsk7029
    @amethsk7029 6 лет назад +1

    AkAssa Fall lérnanagn Fall Bayefall

  • @zizozizi1407
    @zizozizi1407 5 лет назад

    Dieu est Dieu Céline tu vas

  • @djahmyroots8462
    @djahmyroots8462 5 лет назад

    one love diarama

  • @mamadousene5550
    @mamadousene5550 5 лет назад

    Akassa!

  • @oumardia86
    @oumardia86 3 года назад

    Un veritable laboratoire et exemple à demultiplier partout au senegal.

  • @ibrahimandiaye6821
    @ibrahimandiaye6821 6 лет назад +1

    Eskey Akassa ken du mame Cheikh Ibra jerejef serigne Touba

  • @elodiebernard9706
    @elodiebernard9706 9 месяцев назад

    👌🏿👌🏿👌🏿✨✨✨✨✨✨✨🌍🙏🏿👌🏿👌🏿👌🏿♾️

  • @niassniass3314
    @niassniass3314 6 лет назад

    Akassa mouride tawfekh ak taysire gnou barri yague wheeerrrr si barcke mame chieikh lbrahima fall yarame fall

  • @bayefall4061
    @bayefall4061 6 лет назад +1

    Ligeye rekka woor te baye babacar ndem sila nek mangi
    Diangue te diarigno kham kham bi fekhe ba diarigne si niuep
    Le gouvernement gni la wara andal pr defar Senegal mais dara wakh rek te duniu def dara mais li kuko khol rek khamni Serigne bi bokusi lep loy def rek ndiagne la
    Dierediefeuti mbow yague fi te wer ak ndiabot gèk sope yep
    Ci daradiaye mame cheikh ibra

  • @youssoundonng430
    @youssoundonng430 4 года назад

    Ces le baye Fall

  • @daoudandiaye5588
    @daoudandiaye5588 6 лет назад

    SERIGNE BABACAR MBOW dh kou bakh la exemple thi nioune ndawi mouride yi mbirr mi dou thiow diamou yalla ak khitma képp la

  • @amykasse6320
    @amykasse6320 9 месяцев назад

    Ki mom hara feusseul raw model

  • @ricardoprola3269
    @ricardoprola3269 2 года назад

    Li dou ma si Doyal vréma lê mouridisme est Un model de developma

  • @mbayesene3969
    @mbayesene3969 6 лет назад +2

    eskey SERIGNE babacar Mbow kou bakh tee woyof lool .yallah naco sougnou borom dolel thii barkep SERIGNE biii

  • @mariemedieng7342
    @mariemedieng7342 6 лет назад +1

    Yag fi loll tai werr Mbow ngala

  • @aminatasowniang6104
    @aminatasowniang6104 5 лет назад

    Am neuh solo lol