Aziz ya goré nak❤. Wayé danga bakh motakh ay sokhna you bakh rek nga meuneu ame Masha Allah. Mame Bineta yalna ya Allah yéssal yeurmandém si mom, royoukay la déh!. Ya Allah takhawoula ak sa ndiabott
Machallah Aziz sede yi rafet na ya bakh ya gore yalnako yalla kharei aldiana firdawsi miss bakhna aïcha bakhna yalna len yalla défal diam sa dom bi seybi yalna Barkel
Machala Mane d merewone nala ndakh nigngay fesse se ak sa niarrel bi Thi resaux sociaux yi wanté nit mom menoko kham tanka wakhoul wala mou dieuf machala niit kou bakh nga té fatewo Demb te lolou yomboul si kou alal DAP yalla nalene yalla lafal thiat té dakal lene seytané
Mane lima diakhal moy, Lou diabar bakh bakh dou té goor takk niarel. Avec tous ces témoignages sur ces femmes téwoul mou xooli fenene. Goor dal kéneu comprendroul à la fin 😮
Moma diakhal, 😂 sénégal mooy deuk bo khamni les hommes te poignardent en disant ya bakh avec froideur nagg. Ce que les toubabs appellent hypocrisie. Ko ci mougnal fekk amoul deureum s'il réussi wouti lenen lo khamni elle allait jamais accepter de t'epouser pendant ta periode de galère. Mo takh niarel yi gno am foula dagnouy fekk Lou paré gni dougg ci. Et les awo di mougn Lou meti ba souvent sakh beaucoup dou gnou fekké sen ndieurigne doom, sougnou paré di la dioyy😢. Les femmes gno wara yewou rek. Que Dieu aie pitié de son âme et que yalla barkel seuy bi
Yallana yalla defalela diame allekhamdoulila Abdou Aziz Ndiaye machalla heureux menage a ta fille bou sa papa gnewatone do défarate sa togaye machalla ❤❤❤❤
Emouvant goor bou melni Machallah kouko am do khoulo, tu es reconnaissant Yalla nala Yalla yok weer ak katane bolè ndiabotes gui yeupe lafalène thiate. Diabar diou bakh dafay dalal khel di yok kheweul. Machallah. Yalla na seuy bi barkel🤲
Walahi n'gor pire gua depuis que ta première femme est décédée jusqu'à présent tu fais que de bonnes témoignages sur la défunte yalla na ko yalla atte si yeurmeudeme
Machalla Aziz Ndiaye limiy nekk kilifa si rewmi tewoul nonou la amé ay kilifa khalis takhouko beww machalla yalla nala yalla bayi ak sa Rak ak mak seuybi yalla nasi yalla def barké
Aziz ya goré nak❤. Wayé danga bakh motakh ay sokhna you bakh rek nga meuneu ame Masha Allah. Mame Bineta yalna ya Allah yéssal yeurmandém si mom, royoukay la déh!. Ya Allah takhawoula ak sa ndiabott
MachaAllah tawfekh Mame Bineta Dème yalla na YALLA yessal yeurmandé ak diégeule si kawam ta kharé KO Aldjiana firdaws Amine
maman seuyeul ba dee mame binta yalla nacko yalla khare aldiana
Alahouma Amin 🙏🙏
Dioylongama Ndiaye. Mame Bineta Deme yalnala Yallah fey Aljannah
Machallah Aziz sede yi rafet na ya bakh ya gore yalnako yalla kharei aldiana firdawsi miss bakhna aïcha bakhna yalna len yalla défal diam sa dom bi seybi yalna Barkel
Nite dou geune dieume djii barkii alkhourane ❤️❤️🥰yalla na borom bi goudeul saye fane Mame binta dei bilakhii meune na wate nii mongui def aldiana❤️🙏🙏
Hooooo ndeyssane contane na Aziz nite kou bakh gua kou khamoul khamoul diabar diou bakh bakhna wayé guoor guou bakh oci bakhna yalla na diam yague kou guoré gua machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Tty
Ndeysane j'ai pleuré en écoutant le témoignage de Aziz sur Mame Bineta yalna aljanna du keuram
Non tonton Aziz Ndiaye ya bakh ya gooré ❤ Talibe cheikh bi yalla nala yalla samou ci mbarké srg Babacar Sy ♥️🙏
Vraiment Aziz yaye goor tu es reconnaissant
Machala Mane d merewone nala ndakh nigngay fesse se ak sa niarrel bi Thi resaux sociaux yi wanté nit mom menoko kham tanka wakhoul wala mou dieuf machala niit kou bakh nga té fatewo Demb te lolou yomboul si kou alal DAP yalla nalene yalla lafal thiat té dakal lene seytané
😢😢machalah mame binta yalnako kharé adiana machalah azie si sédéyi raffette na❤
Yalla n'aka yalla kharé Al djana, Mame Binta
aziz tu es un exemplaire yalla na la yalla laffal thiat te bayyi lak sa ndiabott
Aziz ndiaye bilahi biss Niki tay beugue nala. Fi nitt dji nafi nitt teranga té waxouko. Ya ngor ya bax. Un GRAND MONSIEUR ❤
Magui dioye comme pas possible yaye gor ndiaye nitte kou bakh do fate demba 😢😢😢😢
Macha allah Aziz longue vie à vous et vôtre famille lou bakh niepa ko beugue
Ooo Aziz ndekété borom khol bou rafetgua ndeyssan yalnala yala takhawou té samal la sa ndiambot bi ❤❤
Masha alla la famille ce important soyons unis pour amour de dieu
Machalla yalla na yalla kharé mame binta déme aldiana tes yok séne diam
Aziz nak yawmii ya bakh manone nga fatté 😢😢
Aziz toyaal gua souniou xool yii waaay yalna Yallah sameu leu bijahi Moustapha
Ohh sa sérénité rafétna yaye gor pire.jai pleuré.ay way gorgni royléne si aziz
Référence la dé
Def léne ni mame binta ba paré
@@bayemalickdiallo3965gnounes Djiguénes gni gno wara goorgorlou di mougne. Walay j'ai pleuré
@@macinatorodosow8168djigeen yangui mougne goor nie nio doy war te mana fate kolera
Gorê ndeyssane ak Nittê Aziz MASHA ALLAH TabarakAllah !!!
Laffe thiate doumou gaindé gaindé rek laye donne fi gua tekk sa tanque fofou leu bonne continuation Ndiaye
Mane lima diakhal moy, Lou diabar bakh bakh dou té goor takk niarel. Avec tous ces témoignages sur ces femmes téwoul mou xooli fenene.
Goor dal kéneu comprendroul à la fin 😮
Moma diakhal, 😂 sénégal mooy deuk bo khamni les hommes te poignardent en disant ya bakh avec froideur nagg. Ce que les toubabs appellent hypocrisie. Ko ci mougnal fekk amoul deureum s'il réussi wouti lenen lo khamni elle allait jamais accepter de t'epouser pendant ta periode de galère. Mo takh niarel yi gno am foula dagnouy fekk Lou paré gni dougg ci. Et les awo di mougn Lou meti ba souvent sakh beaucoup dou gnou fekké sen ndieurigne doom, sougnou paré di la dioyy😢. Les femmes gno wara yewou rek. Que Dieu aie pitié de son âme et que yalla barkel seuy bi
Yén jiguén yi linguén wara xam moy homme est naturellement polygame, billahi yalla niou bindé nonou.. lolou motakh aldiana niouy am 70000 diabar
Chaque homme a le droit d’avoir 4 femmes ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@@pendagueye418 c'est le meilleur droit qu'ils aiment respecter 😂
@@mariefall7111c'est un droit ak beug beug de l'homme.il peut se contenter d'une femme khameleneko nonou 😂😂😂
Oh j'ai des larmes aux yeux Aziz Ndiaye ya Bakh machahala
Li motakh do sonnou si adouna daga fonkone sa awoo bi 😭😍
Oh aziz djioylo ngama yalnako yalla kharè aldjiana
Aziz Kou bakhla machalah ❤
Aie ndiaye référence ga Paola tjate 🤲🤲🤲🤲❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mame binta yalla nako yalla yeureum djégueulko kharéko aldiana firdawssi Aziz yaw gorr deugueu nga machalla
amine
Ndeyssane aziz kou bakh la😢 machalla
Machallah Aziz. Wakkhdji rafetna
Bilahi j'ai pleurer aziz ya gore dieuredieufe
Deysane yalla nako yalla yeureum 😢Mci Aziz
Gueun nala naw machalla yay goor yay garmi
Alhou ak barr mame bineta yalna yalla yeureum ko aziz gor la mashalla
Li lepp thieur bigua diohh wadiour molako may
Yallana yalla defalela diame allekhamdoulila Abdou Aziz Ndiaye machalla heureux menage a ta fille bou sa papa gnewatone do défarate sa togaye machalla ❤❤❤❤
Aziz yaye gor machalah yalka nala yala same ak sa diobote
Èy waay Aziz mo bakh j'ai les larmes aux yeux.
Macha Allah aziz sama xol bi fés na 😭😭😭😭😭😭😭❤❤❤❤❤❤❤
Bilahi gueune nala beugue Ndiaye gor takhawou gua sa ndiambote machalla Maman seyeul kome sa yaye sa pape gueurame nako ❤❤❤
Oh Mame Binta menoul wonn goudou fann ndeysan 😢😢😢
Emouvant goor bou melni Machallah kouko am do khoulo, tu es reconnaissant Yalla nala Yalla yok weer ak katane bolè ndiabotes gui yeupe lafalène thiate. Diabar diou bakh dafay dalal khel di yok kheweul. Machallah. Yalla na seuy bi barkel🤲
Macha'allah lii doyna royou kayy . Laff thiate dans l'ensemble . kadouyii raftna , yalna barkel sey bii barki mouhamed. Amine
Marshalla Aziz mo goreh wakdi rafetneu man dioyna na Sy teh hamoumalen👏👏👏
Li dé la xam grand frére day oufff ay rakam❤
Une famille pleine de sagesse soudée mashalla
Yalla nalen Yalla lafal thiate
Abdou Aziz Ndiaye yalla nala yalla lafal thiete yakh sa ndiabote. Sa weurseuk wi yalla na yokou.yallla sameu leu aar leu aar sa ndiabote gui 🙏🙏🙏
Asis ndaye royoukayla bayilen thiowli téligey❤❤🎉
Kou bakh nga Aziz Ndiaye
Aziz ndiaye yalana nga goude fane té égue na yone kouni amine yalana goude fane merci mon fils
Amin🙏🙏
Walahi n'gor pire gua depuis que ta première femme est décédée jusqu'à présent tu fais que de bonnes témoignages sur la défunte yalla na ko yalla atte si yeurmeudeme
Machalla Aziz Ndiaye limiy nekk kilifa si rewmi tewoul nonou la amé ay kilifa khalis takhouko beww machalla yalla nala yalla bayi ak sa Rak ak mak seuybi yalla nasi yalla def barké
Aziz Ndiaye diambari Serigne Babacar sy khamoma khamoumala wanté Yallananga goud fane thi barké Serigne Saliou Mbacké yay gor
Ohhhhh Mashallah yaye moy ligueyeul dome 😢😢
Aziz. Goor you mel ni yow di fatélékou deumb barétoul. Yalna Yalla yokeu diam sa diganté saye diabar
Bilahi Aziz yaye gor. Ndeké nit ken douko juger
Ah bakhna reik
Aziz you are a good brother machallah stay save and bless with all the family 🙏🙏🙏
Mambintayalnako.yalla.yeureum.tédomyi.barké.azize.yaa.gooré😢😢😢❤
Hooo Ndeye sane Yalna ko yalla yeurame ❤❤❤😊
Tekle bo guiss mou djoup hamal né bi thi djitou mo bah mo rigou mo dedjou fess del matt ba lou gniew régler djoup djarama Aziz Ndiaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Miss lo mougne doyoul . Aziz machallah kou kham adouna gua.
Aziz ya goré ndiaye Machallah Yalla na Yalla barkél
Ndeyssane Aziz so sad about your first wife mam Bintou may her soul rest in perfect Amin yarabi yallahou
Ndayssane Machallah mbakh rék mo ame solo❤❤❤
Machalla longue vie a toi
Aminn❤
Oh machalla rafetna
Ndeysane témoignage bi dawna yaram sokhna sou bakh moo nopal ndiambotame.
bilay djioyna ba son❤
Oh Aziz nawnala tay
Manchalah Ndiaye ❤❤❤❤
Machallah aziz kou bakhla ❤❤❤❤
Yalna ko yala yeureum mai c'était dure😢😢
Machallah kadou yi rafet na ❤❤❤
Aziz mala beugue ya bakh ya gorè yala ga ndound ate you bari sa lep yokou barke seydina mohamed psl
Ndeyssane nit bo ko khamoul rek khamouloko
Mashalla diadieuf dame si yew
Machallah ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ 😊
Aziz y’a goré nakkk ma sha allahou
😭😭😭😭😭😭mame bineta deme yalla nako yalla yereum xaré ko ardiana Firdaws
Oh aziz dioylo ngama bilay
Maa Shaa Allah Alhamdullilah Aziz🤲🏾❤️
Mame Binta yallnako yalla yereum
Jërëjëf Aziz 😢😢😢
Dioylongama Ndiaye mame Binta Déme yalnako yalla yeureum 🙏🙏🙏🙏
Machala aziz thi Babacar yaw tamit gorgua ndakh li yep mononguako bagna wakh😢
Fier de toudou binta mánchala ❤❤❤❤
Yalna niou sougnou borom di bolek NiiTT you GOOREE
Mame binta sedeu yii rafet na trop yalla gua xipe aldiana fir daw
Machalla
❤❤❤❤❤merci beaucoup ❤❤❤
Bilahi Aziz ndiaye yaye gorr
Amin yarabi yallahou
Ohhh aziz yadi gor ya gorée sama xol fesna roylène si aziz mi niiit geunouko ohhhh
Ho ndeysane jiggeen bou nek war na sakkou ngueureum bii
Yonentibi loumou wax deug la
Néna adouna lep terangua la tè bisi geun moy ame djiguene Bou bakh
Ndiaye rawal kou bakh ngua
Ndeysane❤❤❤
Ibra Thiame nôtre frère bakhe geune meune déf Lou bakhe