Je ne cesse d'écouter cette chanson. Ma mère est là , longue vie elle . Courage a tous ceux qui ont perdu leur mamans . Nos mères sont beaucoup souffert pour nous .
Khalatt ni mes parents dougn fekker sama dara lolou dara gueunouko meti! A chaque fois que j’y pense je ne peux retenir mes larmes! Yalla na nguene khipper adiana papa et maman!
Machalah aka meti gnank Yaye sama yaye goude fane rek lakoye gnanal ak yaye yep gni djitou yalla khareléne aldiana sougnou borom tek si gnabot yignoufi bayi lokho
Ndeyesane son bi taye laco doundiou j'ai perdu ma mére le 3 juillet 2020 😭🙆di sante YALLA bimou fégué lép🙏 firdawsi rek unechala Yaye 🤲Sama pape guereme nala Diokhané 🙏
Je pleure quand j'écoute cette chanson car j'ai perdu très trop ma mère en 2008 dans des conditions très o:-difficiles. C'est moi qui gérais mes petites sœurs et mon frère.
J'ai perdu ma maman ,ma référence, ma confidente, mon amie ,ma boussole cette année 2023 Elle est irremplaçable une maman elle est unique Que le Bon Dieu l'accueille dans son paradis éternel Amine Amine 🤲 🤲
Equally heart~rendering here in some way, dear one❤️😭❤️!!! Will always shed tears for Momma dear whenever l listen to this......😭😭😭!!! Moms are just sooooo precious - their peaceful repose in the everlasting Kingdom we constantly pray, In’Sha’Allah🙏🏽🙏🏽🙏🏽!!!
Sama khel yeup demna si sama yaye Mame Fatime thiandoum ndeysan Thiandoum Ngoné yalla nala yalla yeureum kou beugone dom nangou soneu si dom tei fékéwoul dara thiey aduna yaggna meti. Yalla nala yalla fay sa khol Thiandoum
Ohh j’ai une copine qui a perdu sa maman , elle a mis cette musique en storie , et ça m’a donné des frissons. La mienne est toujours en vie , mais souma xalaté le jour qu’elle va partir rek j’ai des larmes aux yeux automatiquement. Courage à vous ! Métina trop
À travers cette chanson, je rends hommage à ma maman ndeye Fatou Seck. Lui disant que tu manques déjà à tes enfants et petits-fils et ton mari chéri..... Que firdawsi soit ta demeure éternelle.
Sons bi weurr nako ba sonou 😭🙈🙈🙈à ma maman d’amour sama sarakhoulle biii ma doundal ba ma meune la teral inchallah tabahal la keur dieundeul la keur takal la or 😭🥰🙏🏿❤️❤️❤️❤️❤️❤️doundeul rek inchallah
Une forte pensée à ma mère Aminata ndiaye partie trop tôt 2aout 2021 doumako meusseu faté que firdawsi soit sa demeure éternel ak gnim fa fek gneup amine
Qui l'écoute en 2020 😭😭😭😭😭😭😭😭 Repose en paix MAMAN Seynabou Yalna Yalla yeureum té kharéla aldiana Amine yarabi merci F Guéwél DIOUF @Nazir depuis Ukraine 🇺🇦🇺🇦🇸🇳🇸🇳🇺🇦🇸🇳
Ça me fait pleurer car j'ai perdu ma maman m'a vie je l'ai même pas vu je suis toujours à l'étranger elle la été tout pour moi ma maman copine que ton âme reposé en paix
Yaye anta lo doundal ta weer ak yaye yi nek thie monde bi yeep ta yaye gnou djitou yalla yeureume len khare len aldiana fiirdawsi woyofal Souf thie sen kaw😭
Ohh cette chanson de fatou est bondée d'émotions je ne peux pas me retenir à voir mes larmes coulées c'est tellement attristée 😭😭😭 Rip à tous les mamans qui sony déjà partie and longue vie et santé de fer à celles qui sont toujours vivantes
Tay la waywi guene am sens thie mane. Dama dane dioy souma kay déglou tay ma gnak sama Yaye sama kharit. Yalla naléne borom bi yeureum té kharé aldianay firdawsi
Ya ALLAH fayal niou lene kharee lene ALDJIANEYE FIRDAWSI lou meti lool niaka wadjiour rawatina YAYE YALLA na souf sedda seni kaw Amine surtout wer bi ah weri bi si souniou soeurs yi dem bayi sene ndiabot metina trop sante YALLA bou bah YALLA FAYE LA Amine
Que vos âmes reposent en paix Maman ,Papa vous me manqué telma yallana yalla yeureum wadiour yeup kharélén aldiana t tel lokho si djabote yeup Une chose à retenir kou am Say wadiour fokklenn .
Rest in the beautiful peace Maman Chérie Tu me manques énormément😭😢🙏❤💋3Mai2010-3Mai2020 10ans aujourd'hui Yallna borom bi yessal yeurmandè sisa kaw diegual la ak bolémi dioulite🙏😔
Une belle chanson que je découvre aujourd’hui. Ayant perdu ma maman, j’ai ressenti au plus profond de moi-même chaque parole de cette chanson. Que le Paradis soit la demeure éternelle de tous nos disparus. Et que Dieu nous accorde une belle vie ❤❤❤❤ La vie est éphémère. Sachons profiter des personnes qui nous sont chères 🎉🎉🎉🎉🎉
Ohhh je pleure tt le temps soumakoy deglou et pourtant jai tjrs ma maman ofet je pense juste aux personnes ki ont perdues leurs mères metina kils repose en paix🙏
Decembre 2018 s'éteignait ma maman cherie deysane sous mes yeux ALLAHOU AKBAR en bonne musulmane j'accepte ton depart et j pris pour toi chak jour ...tu as tt fait pour ta famille malheureusement tu ne seras pas parmis ceux qui mangeront les bénéfices maman k firdaws soit ta destination auprés du prophete ( psl) k ton ame repose en paix on t'aimera tjr maman ...fatiha et 11 likhlas pour ma maman
Oh Ndeysann cette chanson me fait pleurer. Que le paradis soit la demeure éternelle à mes chers parents ! Bilahi Walahi la grande richesse sur terre c’est de voir tes parents à côté chaque jour . Il faut bien en profiter
Ma maman chérie mon amour j’ai tjrs les larmes aux yeux en écoutant cette chanson je penses à toi tout le temps tu me manques trop hâte de te revoir ❤❤❤😢
La perte d'une mère est le premier chagrin que l'on pleure sans elle. J'imagine combien c'est dure de perdre un être irremplaçable qui est une maman. Longue vie à ma chère mère👏👏
té partie en amenant tout avec toi...Ma depuis que t'es partie rien nest plus la même...Ma jai la licence et ta des nouveaux petits...jaimerai tellment.....repose en paix Ma...et à tout les defunts
Ma cha allah sokhnassi moi j aime bcp ma maman et c'est en plein sommeil que ce morceau m ai arrivé en tete sous forme de reve en présence de ma maman en pleure bcp même le lendemain j'en ai parlé à ma sœur aînée même en ce moment je ne pouvais plus me retenir donc merci fatou dieureudieuty
jai pas perdu ma mère yalna féké sama djarigne 🤲mes jai des larmes aux yeux 😭sama❤️ da toye😭sama xel🧠déme si nji niak séne yaye😭wayé yalna yalla yeureumelém ta kharélen aldiana firdawsi🤲
Yaye boye ah bepeu yaye bou nelaw YALLA na niou yewo ALDJIANEYE FIRDAWSI Amine Yene gni dessee YAYE LOU GUENE MANE SI DEF LOU BAH SI NIOME def lene nah lo mati def bou demee gua khep ko YALLA defal niou soutoura Amine
Yalna sama yaye fèkè sama ndieurign🎉
Amine🙏
@@ndeyetouti883 amine way
Sama yaye yalla nakooo yalla khareeee aldiana firdawsi
Sama yaye wéteul nama billahi si condition you métti la démé 28 février 2020 ms sant na boubakh yalla nako yalla yeureum ak sama grand frère 😭😭😭
😭😭😭😭
Courage
Ameen 🙏🙏😭
Yalla nako yalla yeureum mayla kholou mougne mon frére, ❤️
😭😭
*Ndeysan yaye doundeul Lou bari ak yaye yi nék ci adouna bi yeup lii nékhna😍😍*
K
Neysane je t'aime maman saye
Amine Cisse
Amine
Amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine way
wallahi son bi dafmay dioylo
courage gni niakk sen yaye yeupp
😭❤
Wallah je ressens la même chose
J'ai pas connu la mienne . Ma maman est décédée lorsque j'étais gosse . Que FIRDAWSS soit sa demeure derrière. Ainsi que mon papa paix à leurs âmes .
Amine ya rabi
Sama yaye yalla na goudou fane ak bép yaye dama beugue sama yaye 😭😭😭😭😭😭
Kou beug sa yaye beusale j'aime 👍
❤️❤️
J'aime
J'aime
Des millions de j'aime pour moi
J’aime
Je ne cesse d'écouter cette chanson.
Ma mère est là , longue vie elle .
Courage a tous ceux qui ont perdu leur mamans .
Nos mères sont beaucoup souffert pour nous .
Weuy yallah n'a yallah goudal ay faname diam ak wer ndakh niak yaye metina loll
Vérité absolue mon frère longue vie à nos maman
Bilahi elles ont beaucoup souffert pour nous
Merci beaucoup pour cette pensée positive..❤❤❤
Khalatt ni mes parents dougn fekker sama dara lolou dara gueunouko meti! A chaque fois que j’y pense je ne peux retenir mes larmes! Yalla na nguene khipper adiana papa et maman!
Ndayessane massa du courage yalla bakhna
kou sa Yaye beuseul j'aime thi mane
Je viens de perdre ma petite sœur elle est tout pour moi. Que la terre de Thiaroye lui soit légère
Machalah aka meti gnank Yaye sama yaye goude fane rek lakoye gnanal ak yaye yep gni djitou yalla khareléne aldiana sougnou borom tek si gnabot yignoufi bayi lokho
soumay déguelou son bi sama khél yeup ci sama yaay lay nék Diagne naar yallah nanga khippé aldianat ci barkép mouhamed psl
Amen amen amen
@@carofaye5569 bilay sama khole sou sorè rèk mom laye dèk Lou dioye ba sonou mè sante Yalla rek Yalla bakh na
Sa.souma.wete.ba.degelou.li.douma.bege.dara.si.adouna.ndakh.sama.yaye.dia.yalla.nako.yalla.yerme.
Amine adja
Ndeysanne yaye yallah nalla yalla kharei AlJaana firdawsi sii barkei seydouna Mouhamed l 28 avril 2021 jours bobou doumako meussa fatei
Sama yaye ak sama papa yalla naléne yallayeureme wallahi wéte na trop sama adouna 🤲😭
Ndeysane massa frère dom ndeye😢❤
Je ne cesse de réécouter ce son .vie aussi longtemps mama awa et que firdaws soit la demeure éternelle des mamans disparues ainsi que tous.amin
Longue vie maman ami fall❤️
@@lopape5163 Amin
J’adore cette chanson!! Soumakoy deglou sama khell ci sama yay la deem... yalla nako yalla may ghuddu fann❤️
Mamberi Lo ayo que dieu l'accueil dans son paradis
Fatou Ndiaye 🙈🙈😂😂ptdrrrr Plutot Yalnako Yalla may goudou fane
😢😢😢
Amine ainsi que toutes les mamans du monde
Aminee sibarke allkhoran
Je viens de perdre ma mère elle était tout pour moi. Repos en paix maman fatou Diop que la terre de Thiés soit légère 🙏🙏🙏
C'est dur mais Dieu est grand
Amine ya Rabi
Lou méti daleu dala j’ai perdu la mienne le 14 février passé mais ba legui meunou mako gueum bilay douleur bimay yeuk sama 💔 bi ohh😭😭
Ndeyesane son bi taye laco doundiou j'ai perdu ma mére le 3 juillet 2020 😭🙆di sante YALLA bimou fégué lép🙏 firdawsi rek unechala Yaye 🤲Sama pape guereme nala Diokhané 🙏
Yalla na yalla kharè ko al diana si barkèp serigne babacar sy
Yalla nako yalla yereum thiey aduna courage
Yalnco yallah yerem
Yalna khippé firdawsi
Nio bok beine beus si la niaké sma sœur 😭
Sama khole fesna souma deglo woye fatou guewel bi sama akhole bi yeupe dellou thi sama yaye yalla nalene yalla kharet aldjana amine
Ndaysane yalnako yalla yerem barge seringe saliou mbacke métti 😭😭😭😭😭🤦♂️
Amin
quand j'ecoute cette chanson g les larmes au yeux sama yaye gate fane trop.repose en paix maman.on t'aime
Masta ma chérie , comme moi , j'ai perdu mes 2 parents.
Yalna lèn yallay yeureum.
Amine
Ndeysane qu' elle repose en paix
khadidiatou ndione Que la terre lui soit lègere.
@@aboubakarizmir5126mercii c gentiy
Vraiment je cesserai d'écouter cette chanson
Courage à tous ceux qui ont perdu leurs mamans
Yalle n'a yalle kharé lenn aldiana
Longue vie à maman
Je pleure quand j'écoute cette chanson car j'ai perdu très trop ma mère en 2008 dans des conditions très o:-difficiles. C'est moi qui gérais mes petites sœurs et mon frère.
😮 courage
Sama Yaye Yalla nga gouddou fann bama agalé sama yéné ci yaw Fall Thioba...
😓😓
J'ai perdu ma maman ,ma référence, ma confidente, mon amie ,ma boussole cette année 2023
Elle est irremplaçable une maman elle est unique
Que le Bon Dieu l'accueille dans son paradis éternel Amine Amine 🤲 🤲
J'écoute sa en 2020 je ne cesse de pleurer ma mère Maman Aissatou Diompolo Samassa qu'elle repose en paix elle tt fait pour ses enfants
Equally heart~rendering here in some way, dear one❤️😭❤️!!! Will always shed tears for Momma dear whenever l listen to this......😭😭😭!!! Moms are just sooooo precious - their peaceful repose in the everlasting Kingdom we constantly pray, In’Sha’Allah🙏🏽🙏🏽🙏🏽!!!
Amine 🙏
Moi je pleure a chaque fois que j'écoute cette chanson maman coumba camara partie depuis 2 décembre 1998 tu nous trop 😭😭😭😭
0000⁰00⁰00000000000a
@@axtroAFC mmm
Sama khel yeup demna si sama yaye Mame Fatime thiandoum ndeysan Thiandoum Ngoné yalla nala yalla yeureum kou beugone dom nangou soneu si dom tei fékéwoul dara thiey aduna yaggna meti. Yalla nala yalla fay sa khol Thiandoum
Cette chanson mérite tellement de vues💍😍👏MashaAllah
Hommage à ma maman yalna khipé aldiana heur bouma déglo way bi samay rangogne sotékou
Mane mi lolou moma dale
Daffa meti mais yalla bakhna Lou mėti yague n'a
Ohh j’ai une copine qui a perdu sa maman , elle a mis cette musique en storie , et ça m’a donné des frissons. La mienne est toujours en vie , mais souma xalaté le jour qu’elle va partir rek j’ai des larmes aux yeux automatiquement. Courage à vous ! Métina trop
They yalla mes parents me manques beaucoup they sa ma yaye sou don doudou con du ma sonn muk thi adouna 💔💔💔😭😭
😭😭 ndeye sanne dawloga sama yaram nagn délo sant yala bou bakh dignal wadiour yi yalna yala kharé aldiana brkp serigne touba amine
Santal yala ndakh khamnguané sa yaye daa guéne adouna mais di dounde té khamo sa yaye Moy kane lolou moguena méti
Thiey Yaye dafa nékh trop trop bilahi khamna thi Dara Sama yaye dafa décédée 2021 doumako faté moukk bilahi bobou métite yalla rék mokko meuneu tékk diam ma nanguouko lool métina lool sakh wayè yalla mogui Maye wétali Alhamdoulilah sante yalla bou bakh
Merci maman Fatou pour ces émotions exprimées à travers cette chanson pour tous ceux qui aiment leurs mères.
Di niane kepou kou niakk yaye yalla nala yalla may kholou mougne 😢
À travers cette chanson, je rends hommage à ma maman ndeye Fatou Seck. Lui disant que tu manques déjà à tes enfants et petits-fils et ton mari chéri.....
Que firdawsi soit ta demeure éternelle.
machallah merci maman fatou gueweul
😭😭😭 j'aime ma mère et toutes les maman du monde 😚😚😚
Sokhna mame diarra Salihate Toulahi NDIAYE merci beaucoup que Dieu nous laisse longtemps avec nos mamans et qu’il pardonne celles qui ont quitté ♥️
@@cheikhounadiop1248 amine Way
J'ai perdu ma mère le 10 février 2020 que son âme repose en paix ainsi que toutes les mamans décédé gnifi dess yalla naniou goude fane
Sons bi weurr nako ba sonou 😭🙈🙈🙈à ma maman d’amour sama sarakhoulle biii ma doundal ba ma meune la teral inchallah tabahal la keur dieundeul la keur takal la or 😭🥰🙏🏿❤️❤️❤️❤️❤️❤️doundeul rek inchallah
Ameen yalnalako yallah defal si barkei seydina Mohamed (psl)
Oh sa ma yaye 😭😭😭sa me rappelle ma mère 😭😭😭😭 j'ai des larmes aux yeux k le bon dieu t'accueille dans son Saint paradis Amen 🙏😭😭😭💔💔💔💔
Ndeysan son bi foumako dégue sama khel si décé maguou wally la def Yalnako yallah yeureum
Une forte pensée à ma mère Aminata ndiaye partie trop tôt 2aout 2021 doumako meusseu faté que firdawsi soit sa demeure éternel ak gnim fa fek gneup amine
Qui l'écoute en 2020
😭😭😭😭😭😭😭😭
Repose en paix MAMAN Seynabou
Yalna Yalla yeureum té kharéla aldiana Amine yarabi merci F Guéwél DIOUF
@Nazir depuis Ukraine 🇺🇦🇺🇦🇸🇳🇸🇳🇺🇦🇸🇳
Ma mère est partie depuis 2002 'nous less avec un vide ni frère ni sœur mais dieu est la
Je ne peux plus retenir mes larmes merci beaucoup fatou gueweul pour ce souvenir 😢
Chaque jour ki passe je pense à toi maman ma vie est si difficile en ce moment wayé yallah nalla yallah yeurem ❤❤❤
Courage à ceux qui ont perdu leur mère moi mon mari à perdu sa mère à chaque fois il écoute cette chanson
Ça me fait pleurer car j'ai perdu ma maman m'a vie je l'ai même pas vu je suis toujours à l'étranger elle la été tout pour moi ma maman copine que ton âme reposé en paix
repose en paix maman que firdawsi soit ta demeure eternel akk maman yii djitou yeupp yarabi
Yaye anta lo doundal ta weer ak yaye yi nek thie monde bi yeep ta yaye gnou djitou yalla yeureume len khare len aldiana fiirdawsi woyofal Souf thie sen kaw😭
J n px pa écouté cette chanson sans coulait ds larmes
Doundeul lou barri yaye boy ndiaye diatta ba fèckè lepp si barkè mouhamed (psl) amine......ak yaye yeup inchallah gni djittou yallah kharèlèn aldiana firdaw si
C est la première fois que je commente mais woyyyy bi nekh na machallah
Ohh cette chanson de fatou est bondée d'émotions je ne peux pas me retenir à voir mes larmes coulées c'est tellement attristée 😭😭😭 Rip à tous les mamans qui sony déjà partie and longue vie et santé de fer à celles qui sont toujours vivantes
Tay la waywi guene am sens thie mane. Dama dane dioy souma kay déglou tay ma gnak sama Yaye sama kharit. Yalla naléne borom bi yeureum té kharé aldianay firdawsi
Alkhamdoulila sama yaye yalla nako yalla yeurem kharéko aldiana firdawsi wétal nama mais diam AK pékhém yalla AK dokolam😭😭😭😭😭😭😭😭
Amine ya Rabi courage adouna mon yomboull metina vraiment me yalla n'a yalla diapale amine ya Rabi ❤️❤️❤️❤️❤️
Ya ALLAH fayal niou lene kharee lene ALDJIANEYE FIRDAWSI lou meti lool niaka wadjiour rawatina YAYE YALLA na souf sedda seni kaw Amine surtout wer bi ah weri bi si souniou soeurs yi dem bayi sene ndiabot metina trop sante YALLA bou bah YALLA FAYE LA Amine
Se chanson me donne des frissons je pleure a chaque fois que j'écoute ce morceau
Que vos âmes reposent en paix Maman ,Papa vous me manqué telma yallana yalla yeureum wadiour yeup kharélén aldiana t tel lokho si djabote yeup
Une chose à retenir kou am Say wadiour fokklenn .
Rest in the beautiful peace Maman Chérie Tu me manques énormément😭😢🙏❤💋3Mai2010-3Mai2020
10ans aujourd'hui Yallna borom bi yessal yeurmandè sisa kaw diegual la ak bolémi dioulite🙏😔
Sa me fait pleurer quand j'écoute cette chanson parceque j'ai perdu ma mère
Ndaysane yalnako yalla yerem barge seringe saliou mbacke métti 😭😭😭😭😭🤦♂️
Une belle chanson que je découvre aujourd’hui. Ayant perdu ma maman, j’ai ressenti au plus profond de moi-même chaque parole de cette chanson.
Que le Paradis soit la demeure éternelle de tous nos disparus. Et que Dieu nous accorde une belle vie ❤❤❤❤
La vie est éphémère. Sachons profiter des personnes qui nous sont chères 🎉🎉🎉🎉🎉
Machallah yalla na souniou yayi dounde lou bari nie dem yalla kharé lenn aldiana firdaws amine
Thieuy Sama yaye yall nako yalla kharé aldiana
Amine
Yaye amoul remplaçant kouko niakk yeuk ko sama yaye yalna soufou Touba woyof si kawam yalla khare ko aldiana firdawsi thi barke Serigne bamba
Dara guenoul méti la perte d’une mère 😭😭Sama rek la amone sama adouna mou deme bayima c’est dûr bilahi 😭😭😭😭
Ohhh je pleure tt le temps soumakoy deglou et pourtant jai tjrs ma maman ofet je pense juste aux personnes ki ont perdues leurs mères metina kils repose en paix🙏
C pareil pour mw walahi
Pareillement chérie
Yalla n'a fi yague andake were
Yalla n'a fi yague andake were
@@fatoundao30 amine ya rabi
Bilahi wetay rek lay dioy gueye nioro. Tu me manques tellement yaye boye 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
😭😭 yalnako yala yeureum kharéko aldiana brkp serigne touba amine
Maman yalnala yalla yeureum kharé aldiana fildawsi😭😭😭😭
Metina yaye amoule morome masi kame dara yalla nallenes yalla yeureum si barke Seydina. Mouhamed
Astou Seck ndayesane 😭
😢😢😢
Longue vie à toi yaye boye soumala niaké sma adouna nakarii doundal 🙏tu est toute ma vie❤️
Longue vie à toi ma maman chérie et à tous mes maman du monde ceux qui ont perdu leur mère que la terre leurs soit léger yaye amoul remplaçant
Decembre 2018 s'éteignait ma maman cherie deysane sous mes yeux ALLAHOU AKBAR en bonne musulmane j'accepte ton depart et j pris pour toi chak jour ...tu as tt fait pour ta famille malheureusement tu ne seras pas parmis ceux qui mangeront les bénéfices maman k firdaws soit ta destination auprés du prophete ( psl) k ton ame repose en paix on t'aimera tjr maman ...fatiha et 11 likhlas pour ma maman
Oh Ndeysann cette chanson me fait pleurer. Que le paradis soit la demeure éternelle à mes chers parents ! Bilahi Walahi la grande richesse sur terre c’est de voir tes parents à côté chaque jour . Il faut bien en profiter
Ma maman chérie mon amour j’ai tjrs les larmes aux yeux en écoutant cette chanson je penses à toi tout le temps tu me manques trop hâte de te revoir ❤❤❤😢
Hommage à toutes les mamans qui ne sont plus de ce monde yalnalèn yallah yeureum té kharé léne aldiana firdawsi
Koumou daloul meuno khame metite bi si nek wetay total repose en paix maman di massa wou kep kou niak yaye
Ça me fait pleurer que dieu accueille au paradis toute les mamans parties laissant grande vide derrière elle et longue vie à la mienne.
Hommage à ma maman Adja Mareme fall yalla na nga khipé aldiana firdawsi souma dégué son samay rankhogne tourou
Khamal lingay wérr waayé boul kham kalay wérill😭😭
Elle est forte billay
Sama yaye yalla nako yalla yeureum ta kharéko aldiana firdawsi si barké seydina mouhamed amine yarabi 🤲🤲😭
Mane dé waye bi dama touche bilahi sama yaye boy sa souné ma ngui laye nianal ngua doundou ba feké sonou ndiarigne amineeeeeeee 🙏❤️😭
Oh cette chanson me rappelle ma chère maman qui m'a beaucoup soutenu dans ma vie.😭
La perte d'une mère est le premier chagrin que l'on pleure sans elle. J'imagine combien c'est dure de perdre un être irremplaçable qui est une maman. Longue vie à ma chère mère👏👏
Kou bague sa yaye lalal jaime❤❤❤❤❤😢
They yalla sama.yaye boye yalla nako yalla khareko Adriana😭😭😭😭😭😭😭😭
Ndaysane yalnako yalla yerem barge seringe saliou mbacke métti 😭😭😭😭😭😭😭🤦♂️🤦♂️🤦♂️🤦♂️🤦♂️🤦♂️
Sama yaye yalla nako fii yalla bayii bama dèfalko limako yéné yeup mounouma wakh nima beugué sama yaye
cette chanson me rappel ma Maman Yalla nako Yallah yeurem kharè ko adjana ainsi que toute nos maman qui nous ont devancé sous terre
Ndaysane sama yay les 15 fevrier 2023 bis bou tiss te meti doumako massa sama yay dia yallnako yalla yeurem te khareko aljeune si barkép serigne touba
Ndeysan ken dou yaye. Merci yaye boye, yalna aldiana nekk sa deukouway. Nous sommes fiers de toi gueye nioro. Tu as accompli ta mission
té partie en amenant tout avec toi...Ma depuis que t'es partie rien nest plus la même...Ma jai la licence et ta des nouveaux petits...jaimerai tellment.....repose en paix Ma...et à tout les defunts
Hoof métina trop wayé sant yalla g lé larmes au yeux perdre 2 paren c dur firdawsi a vs longues vie à c ki reste amin
Ndeysanne j'écoute cette chanson je pleure sans m'en rendre compte
Ndeysane lou meti ngay woye douma meussa faté le 19 fevrier 2021
Sama yaye Adja Maguette yallanako yallah yeureum
Yaye doudeunl lou yagu akk beup yaye si barki seydina Muhammad
Ma cha allah sokhnassi moi j aime bcp ma maman et c'est en plein sommeil que ce morceau m ai arrivé en tete sous forme de reve en présence de ma maman en pleure bcp même le lendemain j'en ai parlé à ma sœur aînée même en ce moment je ne pouvais plus me retenir donc merci fatou dieureudieuty
Hommage a tous ceux qui on perdus leur maman yalla naléne yalla yalla yereum thiey aduna courage a vous
jai pas perdu ma mère yalna féké sama djarigne 🤲mes jai des larmes aux yeux 😭sama❤️ da toye😭sama xel🧠déme si nji niak séne yaye😭wayé yalna yalla yeureumelém ta kharélen aldiana firdawsi🤲
J'ai des larmes aux yeux ma mère me manque tellement Mba ciré Badji qu'elle repose en Paix que firdawsi soi sa demeure éternelle 😭😭😭😭😭
Amine
Yaaaaaye boooye😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭aye yaye wéte na😭😭😭😭
Djioy lo gama billahi 😭😭😭😭😭
They yaye kéne dou yaw doudal Lou bari❤️❤️❤️❤️❤️💓
Ck
Yalla nko yalla hare aldiana fridawsi😢😢❤
tu m'a fait pleurer on fait pleurer vraiment on fait pleurer
Yaye boye ah bepeu yaye bou nelaw YALLA na niou yewo ALDJIANEYE FIRDAWSI Amine
Yene gni dessee YAYE LOU GUENE MANE SI DEF LOU BAH SI NIOME def lene nah lo mati def bou demee gua khep ko YALLA defal niou soutoura Amine