Franchement combat ben mbeur lathi amoon mouy Modou mais dangama meusseu nekh teh tay gueumnani raw nathi 🥰 yalna ya Allah yeureum sa mère kharé ko adiana
Moi aussi je l'ai fait à mainte reprise billahi . Ma maman Etait malade et Elle n'avait pas encore de fille . Ma soeur Ndeye a grandit tardivement. Damdoon dem Marché di togou di fooot di raxass bool di sangue sama Rak yi oohhh... les gens me traitaient de Goordjiguéne j'avais 9 - 10 ans Mais je le regrette pas et je ne vais jamais de la vie le regretter merci Maman . Et Bon courage Eumeu
Bilah on est pareil j'ai perdu ma maman a l'âge de 14ans😭😭😭et j'étais l'aîné c'était très très très très difficile 😭😭mon père kan j'avais 9ans mais Al hamdililah s'était la volonté de dieu 🙏😭et je suis à mes 30ans prions pour leurs repos éternel 🙏😭
Ohlalala 😭😭😭😭respect Champion motakh lou bakh reik ngay am Yokkkou beu yeuggg ko et que l'âme de ta maman repose en paix et qu'Allah l'accueille dans son vaste paradis 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😭❤️
Son histoire est vraiment touchant j en pleure . Ton passé a influencé tout caractere . J ai beaucoup de respect et d affection pour toi . Garde toujours ton sourire car tu fais des hommes au grand coeur
Bilahi ba adouna dii toukiii yow rek lay faral sii Lambeu cette histoire me rappelle le 23 décembre à l'hôpital mame abdou aziz sy de tiaouane pour les darniere jours de ma mère 😭😭😭😭
Le manque d'une mère est la plus grande absence en tout âge. Je n'ai jamais eu l'opportunité de voir ma mère marcher comme les autres. Tout cela à cause d'une maladie. Elle est décédée quand j'avais 21 ans. Du courage à tous les orphelins. Paix à son âme. 😭
Non vraiment une histoire tres touchant yal nako yalla yeureum te khareko aldiana firdawsi amine et Eumeu courage à tw leep dina bakh bakh na be pare diambar deug nga
Maman, je donnerai ma vie pour elle car je sais ce qu'elle a endurée pour pour et à cause de moi. Yalla naniou co souniou Borom Samaal bamou féké souniou ndieurign🙏💕❤💯 je t'aime Yayeboye
bilahi eumeu sa intervie bi sama khol dey toy bilahi chaque fois demakoy séttane bilahi yaye kene amoul féyam Diñal bep wadiour bou guene adouna yalla kharé lene ardiana fir daw si mé gnifi dess yalla may léne goudou fane ak wéur gou yaram 😭
Billaye ma maman est témoin le mère adama Coly on l'appelle mère Coly moi j'ai vécu ce qu'il dit avec son frère Souleymane ngom dit jule ngom yalla nalla yalla diappalé akk mboléme dioulite
Billahi eumeu sene damako yeureum mai sa yaye yalla nako yalla kharé Adiana si barcké Serigne Touba mai eumeu amgua guerumou way diour lépp ligua déf Mouy togou bi ah yeppp yalla rek Molay fay sa khôl 😭😭😭😭eumeu kou bah gua man dh Balla gaye Moy sama mbeur mai eumeu sene diapalné beugue nalabisniki. Tay ndah sa bakhay rek moko warar yalla nala sounou brom bi takhawou ba égualela figua beugue yeppp si Serigne Touba niak yaye nak dafa méti ndah yaye Moy léppp Soko niaké niak gua léppp 😭😭😭
Machaalah Machaalah yallanala lawou same sameniou : gueune nala beugue tu es toujours souriant : Modou lo dei moy sama mbeur wayei dama leine mossa doomo : Tjours samay dome ngueine.
Eumeu Sene boul djioye wayyy sa yaye yallana KO yalla yeureum té kharekoo Adjiana Defferallla sa Adounaa akkk Alhakherré
Machallah Eumeu
Franchement combat ben mbeur lathi amoon mouy Modou mais dangama meusseu nekh teh tay gueumnani raw nathi 🥰 yalna ya Allah yeureum sa mère kharé ko adiana
Moi aussi je l'ai fait à mainte reprise billahi . Ma maman Etait malade et Elle n'avait pas encore de fille . Ma soeur Ndeye a grandit tardivement. Damdoon dem Marché di togou di fooot di raxass bool di sangue sama Rak yi oohhh... les gens me traitaient de Goordjiguéne j'avais 9 - 10 ans Mais je le regrette pas et je ne vais jamais de la vie le regretter merci Maman . Et Bon courage Eumeu
Ndeysaan courage
Et moi il m'arrive souvent d'entendre '' homme au foyer ''
Respect frère
Way Diour ( N'deye ak Bâye ) dou morôm !!! Yalna Yalla diégual suñu wadiour ya dem ñi FI déss Yalla yagal lén fi amiine.
@@thiath2736 Amine YA RABI MashaALLAH
Eumeu ioe dagay diengue RK mé bilae do danou di nianal sa yaye yalla yereum KO té kharéko aldiana
Oh ndeyssane j’ai pleuré c’est très touchant 😭😭😭😭
Kouko khôl dioy bilahi yaay kéne meunouko remplacer yalla na yalla yeureum yaay yeup djitou
Ndayesan sama yaye yalla namakou yalla fayal te yaréme kou te yaréme bepou yaye AMIE😓😥
@@falloundiaye2159 de
Eumeu séne bilahi yama bayi si lamb yalla nala yalla dolli soutoura🙏🙏💗💗 je t'aime fort
C'est triste vraiment!
Eumeu courage à toi, c'est pas facile de vivre avec l'absence d'une maman. Que Dieu ait pitié de son âme.
Machallah Eumeu Li nga beug si Lamb yalnala ko YALLAH defal Motali Sa yéné Yeup Bilahi Diambaar nga ❤️❤️❤️❤️
Bilah on est pareil j'ai perdu ma maman a l'âge de 14ans😭😭😭et j'étais l'aîné c'était très très très très difficile 😭😭mon père kan j'avais 9ans mais Al hamdililah s'était la volonté de dieu 🙏😭et je suis à mes 30ans prions pour leurs repos éternel 🙏😭
Seigneur aie pitié d'eux car ils m'ont élevé quand j'étais jeune 😢 رب ارحمهما كما ربياني صغيرا 😢👏
Amine yalla naniou fayal souniou wadiour si barké NABIL MOUSTAPHA PSL
Bayiléén yi waay,
Yééna ngimay diooy lo sakh,
Yaay Daffa diiss,
😭😭😭
Bilahi 😭
Bilay walay
Ohlalala 😭😭😭😭respect Champion motakh lou bakh reik ngay am Yokkkou beu yeuggg ko et que l'âme de ta maman repose en paix et qu'Allah l'accueille dans son vaste paradis 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😭❤️
Son histoire est vraiment touchant j en pleure . Ton passé a influencé tout caractere . J ai beaucoup de respect et d affection pour toi . Garde toujours ton sourire car tu fais des hommes au grand coeur
Eumeu yallana sa diame yagg sa yaye yallana firdawsi don deuko wayam ak buepe diollit il dafa daw yaram billahi😭
Eumeu bol dioye sa yaye yall nako yalla yerem ak bep yaye yalla bayi niou ak sounouy wa dioure
Amine inchallah ♥️♥️♥️♥️
Sois fort mbeur. Tu es mon lutteur préféré
Bilahi ba adouna dii toukiii yow rek lay faral sii Lambeu cette histoire me rappelle le 23 décembre à l'hôpital mame abdou aziz sy de tiaouane pour les darniere jours de ma mère 😭😭😭😭
Le manque d'une mère est la plus grande absence en tout âge.
Je n'ai jamais eu l'opportunité de voir ma mère marcher comme les autres. Tout cela à cause d'une maladie.
Elle est décédée quand j'avais 21 ans. Du courage à tous les orphelins.
Paix à son âme. 😭
Eumeu sene
Eumeu est un GD homme j'ai l'ai toujours apprécié bien que Balla gaye est mon lutteur préféré
A partir d'aujourd'hui tu es dans mon cœur à jamais.Resper à nos mamans. Yalla na hippé firdawsi
Ça ma champion eumen sene
J’ai les larmes aux yeux j’aime trop ma maman j rêve un jour de devenir quelqu’un pour qu’elle puisse être plus heureuse
Oh oh oh sil pleure je souffre dans mon göt interieure di courage mbeur nè pleure pas
Non vraiment une histoire tres touchant yal nako yalla yeureum te khareko aldiana firdawsi amine et Eumeu courage à tw leep dina bakh bakh na be pare diambar deug nga
Eumeu sene I love 100% am from Gambia
Ndayesane eumue sene billah diam mbar ga diamo rék gay am inchaalla si barké khasidayi amine
Ndaye sane eumeu sene diamou rék ❤❤
Bilaye Eumeu dama la Beug Bilay te Khaw ma sakh Mais yalla Na la yàlla taxawu champion
Eumeu sene yalna fi yague lool te wer ak ndiabotam yalna ko yalla defal diame ak soutoura addouna ak alakhira
Allahou Akbar sama yaram sakh daw na bilay 😭 Dicourage mon frère yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana ak bépp djoulit 🤲🤲
Je suis diplome de luttes inernationale et nationale mais vous eyes le meiileur lutteur senegalais
😭Vraiment vraiment j'ai pas mots a dire,L' Allah réck moyy bourbi😢😢
Maman, je donnerai ma vie pour elle car je sais ce qu'elle a endurée pour pour et à cause de moi.
Yalla naniou co souniou Borom Samaal bamou féké souniou ndieurign🙏💕❤💯 je t'aime Yayeboye
Ken mounta faye yaye mane d souma manona wagni lima wara dunde yokal ko sama yaye kon nako def elle é ma vie
WAYDIOUR DAFA AM SOLO SI NITT. COURAGE EUMEU. MANE JE PLEURE TOUJOURS MON PÈRE. JE NE L'OUBLIERAIS JAMAIS MON CHER PAPA.
Moi pareille .papa repose en paix
Vraiment champion nga bro .
Ho ndeysann 😭 😭 😭😭😭 les larmes de eumeu sene 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Mbeur tu ma inspiré bilayh
Suis fan De Balla gaye 2 Mais Eumeu damako niéwanté lolou yalla khamna ko🥺🥺🥺🥺🥺🥺
Massa massa weydiour sidide la massa
Yallah na Yallah yessal a si mome kharerko Aldiana firdawsi si barke Yonéntebi Seydina Mohamed SAW Psl
Machallah, Mbeur. Jam rek ngay am. Yallah nako yallah yeureum te khareko aldiana firdawsi. Yay kene leu.
bilahi eumeu sa intervie bi sama khol dey toy bilahi chaque fois demakoy séttane bilahi yaye kene amoul féyam Diñal bep wadiour bou guene adouna yalla kharé lene ardiana fir daw si
mé gnifi dess yalla may léne goudou fane ak wéur gou yaram 😭
Quand je l'ai suivi j'ai pleuré car c triste et je l'aime beaucoup c mon seul lutteur apart Tyson
Yaye forna bilahi...
aimer vos mamans
Bilay tu as raison je me dit YAYE BALMA SOUMALA TOGNE BALMA
Machallah mbeur,sante yalla rk ken deukou fi té naniouy fonk wadiour yii
Masta 😭u m fai pleuré la 😭worna yala
Hooooo ndeysane métina trop mé Yalla nala Yalla gene diapalé sy barké yonéntebi (psl) nit kou bakh nga bilaye
Ndaysann 😪😪😪😪😪😪 yalla na yalla yeureume te kharee aldiana firdaw yaye yayou keenla 😭😭😭😭
Li metiii naa ndaysaneuh 😭yalnala yalla takhawou
Liguëy yü ndäye aniü ndöm
Way Diour ( N'deye ak Bâye ) dou morôm !!! Yalna Yalla diégual suñu wadiour ya dem ñi FI déss Yalla yagal lén fi amiine.
Billaye ma maman est témoin le mère adama Coly on l'appelle mère Coly moi j'ai vécu ce qu'il dit avec son frère Souleymane ngom dit jule ngom yalla nalla yalla diappalé akk mboléme dioulite
Eume ligouyou ndeye rek moko top. So kholé carrière Rame. C’est juste incroyable
J'ai pleuré Eumeu moi ki n'a même pas une photo de ma mère la présence d'une mère est très importante dans la vie d'un enfant matsa
Moi j'ai perdu la mienne a l'âge de 3ans
Hoo masta c triste
De tout cœur avec toi Ramses
Ô masta k firdawsi soit son demeure
Masta niak yaye dafa meti mane absence sama dama manque
Du courage champion 😭😭😭😭
Billahi eumeu sene damako yeureum mai sa yaye yalla nako yalla kharé Adiana si barcké Serigne Touba mai eumeu amgua guerumou way diour lépp ligua déf Mouy togou bi ah yeppp yalla rek Molay fay sa khôl 😭😭😭😭eumeu kou bah gua man dh Balla gaye Moy sama mbeur mai eumeu sene diapalné beugue nalabisniki. Tay ndah sa bakhay rek moko warar yalla nala sounou brom bi takhawou ba égualela figua beugue yeppp si Serigne Touba niak yaye nak dafa méti ndah yaye Moy léppp Soko niaké niak gua léppp 😭😭😭
C’est triste courage champion ❤❤❤❤
Machlla l'AF thiat ème séné li dewna yaram Bilahi yalla nale yalla same mayla goudou fane AK wer yaye amoule morom
Oh ndeysaan Eumeu khol bii dfa raffétt nak🙏🙏
L'histoire très triste 😥😥billahi vallahi
Courage champion je te comprends j'ai perdu ma Maman sa fait 12ans et j'arrive pas à faire le deuil tu m'as fait pleuré neysanne😥😥
Emme sene dafa yueremtalou man😭mogimay dioylo 😭😭😭😭😭😭😭
Ndeysan yalna ko yalla yeureum khareko aldiana firdawsi
Triste confidence. Aussi grand qu'on soit, la maman reste tjrs une faiblesse...😢
😭😭😭😭😭😭😭😭bilahi dama dioye ba sonou eumeu sene vre gor yalla
Li dafa daw yaram machala eumeu é le rèst a venir
Masta dafa meti khamnasi dara mane dama niak yaye ak papa 1ans rekk laniou rawanté mes sante yalla rekk
ohh yalla bakhna
Yalla nako yalla yeureum
Oh ndeysaan yalla nalen yalla kharéi aldjana😭méttii n'a trop
Yala nalén yala kharé aldiana
Yallanalene yalla yeureme mai ses la vie
Eumeu courage rkk yaye dafa diss ymgnk mane mi orphelin de mère comme ioe mé sant yalla rkk
Ndeysane Eumeu vraiment je pense que Sénégalais you bari xamou niouleu. Mane déh douma sa supporter,mé kouleu beugue la
Ndesseynane champion que le bon dieu vous protège contre les mals
Yalna la yalla May kholou mougne si barké Khalifa malick yalla yereum ko kharé ko aldiana firdawsi
Mere binta badiane yalla nako yalla kharei aldiana
Mbeur Gainder gha tu n’es pas mon lutteur préféré mais j’estime ton courage tu es un exemple
Eumeu walakhi tu m'as fais pleurer yalla na yalla kharé sa yaye thia aldianay fiirdawsi 🙏🙏
Fans balla la dh mais Eumeu xawma lanla mais damako beugu bilahi😍 yalla rek mtx may wakh ..sa yaye yal nako yalla yeureum
Ndeysane quelle belle histoire 😭😭 triste en même temps yalla nala yalla défal diam yeureum mère bi xaréko aldiana firdawsi ❤️
😭😭😭😭😭 je le comprend tres bien moi j'ai perdu ma mère sa fait 4 ans et cé tres dure de Vivre sans une mère
Machaalah Machaalah yallanala lawou same sameniou : gueune nala beugue tu es toujours souriant : Modou lo dei moy sama mbeur wayei dama leine mossa doomo : Tjours samay dome ngueine.
Vraiment beau personne leu walay ndeysan yalna defala diam
Vraiment j s8 1 fans de balla gaye 2 mes sincerment parlé eumeu est brave
C'est vraiment triste bilahi j'ai pleuré
Ndeyssane c'est vraiment touchant 😭😭
C'est vraiment émouvant eume champion gua
Boulema dioyelo champion c est l amour d un enfant pour sa mere
Yaye dafa nex walahi je viens detre maman mais kene meunoul faye Yayame
Wallah Astou
Bilay romb neikh j'ai vraiment compris la leçon que yaye keine meunouko fay. Dama ame dome 3 jours après sama maman décédée 😔😔
Eumeu mane yaye sama mbeur lolou dou tay bilay yalla na la yalla sam lafal la thiate soutoural la ndeysane dioylo guama mbeur
Courage Eumeu tu es mon lutteur préféré yalna sunu borom defal leuh diam samla aarla
Courage mon grand
Oh Eumeu niit kesse là. Kou yeureume sa yaye yalla yeureume la.
C triste vraiment 😭😓
Begue nala béss bisi Taye yay dafa for bilahi 😭😭
Ndeysane qu'elle repose en paix metina
Niank Yaye nékhoul masi kham dara 😭😭😭😭😭sama Yaye lay dioYe bat ayy😭😭😭😭
Ay way yak mane metite bobou doumako Fate ba moukou
Ndeyssane wadiour aka nekh j'ai perdu ma mère a l'âge de 12ans a l'âge de 4ans lako geudieu guiss . j'ai perdu aussi mon papa le 04 Avril 2021
Il a fait pleurer tous ceux qui ont perdu leur maman.sa ma cool toyna trop
A jamais le meilleur lutteur; Champion .
Heart touching.. May her soul rest in peace
Nitt kouko khamoul rékk mokoy jugé
Eumeu séne bét ngua gniou bary machallah.
Ndeyessane Eumeu sa yaye dafa dcd dimanche7 Septembre sama yaye Lundi 08 Septembre motakhe sama khole mèti😭😭😭😭
Manchaallahll eunm séne longe vie inchallah yalla n'a xa Am diamou si brké mouhmede ❣️🥰
Eumeu séne lepp loumou am si lambe daako mérité 🙁
Diambar la bilaye 🙂🙂
Bilakhi
⁰0000⁰0⁰⁰⁰⁰0⁰00000⁰000⁰0000000000000⁰00000000
Billaye
Eumeu du courage ton bon cœur te sauvera partout où tu vas tu est un champion dans l'arène et en dehors