Haqiiqatu Muhammadiyya Wa Haqiiqatu Xadiimiyya

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 23 дек 2024
  • Waxtaanu Gamou 2024

Комментарии •

  • @SeringeMorloNdar-dj9jk
    @SeringeMorloNdar-dj9jk 2 месяца назад +1

    ماشاء الله تبارك الله فجزاكم الله خيراً ببركة شيخ أحمد الخديم قاد له الله ماختار له ونفعنا ببركاته ءامين ❤❤❤

  • @mamadoundiaye8167
    @mamadoundiaye8167 2 месяца назад

    Barkē Boroom Tuubaa Sëriñ Mustapha waxtaanam neex na waay❤❤🥰🥰! Yagg fi waay JOOP🙏🏿🙏🏿❤️❤️🥰!

  • @chiekhounandiaye3885
    @chiekhounandiaye3885 2 месяца назад

    Machalla amna soloh

  • @ModouFall-u8o
    @ModouFall-u8o 3 месяца назад +2

    ❤❤❤

  • @abdoulahadleye9532
    @abdoulahadleye9532 2 месяца назад

    Yalla si bopam mo nekh .dieuredieufé serigne touba Cheikhoul Khadim ❤

  • @deme.deme.3187
    @deme.deme.3187 2 месяца назад

    ❤❤❤❤❤❤❤machalah

  • @schrodinger1504
    @schrodinger1504 3 дня назад

    Yallah dou Tajalli si niit (jamm) waye ay tanazullat nioy wathie si nit (sourate qadri) . Loutakh moy Haqq rek moy tajalli . Donc Haqq moy tajalli jougge si haqq niel haqq. Resultat haqq moy aini. Waye nit mome majass la, donc Haqq bi di yallah tanazulat lay deff si jam bi di majass. Waye comme que nit majass la, lolou matakh niou mana wakh neni guissou niou dara si mome louroul yallah mi di haqq.
    Deugui -deug ubuda moy, beuss bo deh we (fatou) si lepp louroul yallah, sa guiss gui deh dem si guissou yallah, say jeuf deh dem si jeufi yallah, sa dounou deh fekki dounou yallah gui sa degui deh dem si deggou yallah,guene si majass (la vie virtuelle)delou si haqq ba yeugouto louroul ne haqqbi di yallah,yeug ne yallah midi haqq moom rek moffi nek, dara dara louroul yallah nene la, mome rek moffi nekone, te ba legui dara nekkou fi louroul mome yallah miy haqq, bobou gua doug si dahira ubuda: Irji'i ila rabbiki radiyatam mardiyyah, Fadkhuli fi ibadi. Wadkhuli jannati (Surat Al-Fajr Ayat 28-30). Li nak bou ame nak moy dougou gua aljanna. Serigne bou maat serigne li lay deff si yaw, li soukka meunal, demal setti banene serigne.

  • @AbdoulahiSarr-ns8hb
    @AbdoulahiSarr-ns8hb 3 месяца назад

    Chekhe. Moustafa. 777

  • @mbackefall9194
    @mbackefall9194 3 месяца назад

    Amna solo

  • @mur-id4life118
    @mur-id4life118 3 месяца назад +2

    Sëriñ bi yaàg fi lool te andak wér.

  • @modousamb6804
    @modousamb6804 3 месяца назад +3

    Yake fi rk tewér Al kokkiyou

  • @BayeSerigneDiouf-sr6qd
    @BayeSerigneDiouf-sr6qd 2 месяца назад

    Yala na yala same la Barker borom Touba

  • @AbdouBA-p6q
    @AbdouBA-p6q 3 месяца назад +2

    Wakhtane wou nékh loll

  • @papaamadoumbodj2215
    @papaamadoumbodj2215 2 месяца назад

    Waxtane wii doumasi doyal

  • @MemoryDia
    @MemoryDia 2 месяца назад

    ❤️❤️❤️