- Видео 1 634
- Просмотров 968 274
Faydu Akaabiris Saalihiin
Сенегал
Добавлен 16 мар 2013
La Jama’a Faydou Akaabiris Salihin est un projet islamique initié par notre guide Serigne Moustapha Diop Al Kokiyou dans la perspective salutaire d’étendre la religion héritée du Prophète tel que transmise par notre vénéré guide Cheikh Ahmadou Bamba.
Le nom évocateur de Faydou Akaabiris Salihin est inspiré de celui que le Cheikh a donné aux deux derniers de ses daaras tarbiyya situé à Thiéyenne.
Ce projet est le fruit d’une longue réflexion de Al Kokiyou qui depuis les années 90 a eu à cœur de partager le savoir islamique acquiert ici et ailleurs et qui l’éclaire largement sur les textes, la doctrine et la jurisprudence islamiques. L’éducation spirituelle et la purification de l’âme font partie de la mission des prophètes et de leurs héritiers (Awliyaas). Il s’agit donc de pérenniser cet héritage par la transmission du savoir et la formation de jeunes aspirants à travers la création de daaras calqué sur les méthodes authentiques de Cheikh Ahmadou Bamba.
+39 380 183 19 26

Видео
Maa Ngi Ko Xalaatèe Caire…
Просмотров 1,4 тыс.14 дней назад
Le Concept derrière Al Humda, Théorisé pendant 25ans, met en Exergue la Nécessité d'une Recherche Approfondie : Un Conseil aux Jeunes Chercheurs.
Questions et Réponses avec Serigne Cheikhouna Mbacké Abdoul Wadoud
Просмотров 46921 день назад
Questions et Réponses avec Serigne Cheikhouna Mbacké Abdoul Wadoud
Xidmaal SerigneTouba Ci Ludul Ngistal
Просмотров 1,6 тыс.28 дней назад
Xidmaal SerigneTouba Ci Ludul Ngistal
2e Partie | Faysalut Tafrixati Baynal Xaqhi Wal Mayni | Ndenkaanè Serigne Souhayibou Mbacké
Просмотров 878Месяц назад
Tafsiiru Ndenkaanè Serigne Souhaibou Mbacké par Serigne Moustapha Diop Al-Kokiyou Partie 2
1e Partie | Faysalut Tafrixati Baynal Xaqhi Wal Mayni | Ndenkaanè Serigne Souhayibou Mbacké
Просмотров 3,6 тыс.Месяц назад
Tafsiiru Ndenkaanè Serigne Souhaibou Mbacké par Serigne Moustapha Diop Al-Kokiyou Partie 1
TAFSIIRUL QUR'AN: SURATUL BAQARA AAYAAT 99 - 112
Просмотров 494Месяц назад
Tafsiir des Versets 99 à 112 de la Sourate Al Baqara par Serigne Moustapha Diop Al-Kokiyou
Lecture Wird Maaxuuz Al Xaatim
Просмотров 2,2 тыс.2 месяца назад
Lecture du Wird Maaxuuz Al Xaatim par Serigne Moustapha Diop Al Kokiyou suivie des Chartes
Philosophie et Langue Wolof : Firi Baati Wolof ak Cheikh Moustapha Diop Al-Kokkiyu
Просмотров 1,2 тыс.2 месяца назад
Peut-on philosopher avec la langue Wolof? Quel est le sens des mots Wolof et leur usage en philosophie?
TAFSIIRUL QUR'AN: SURATUL BAQARA AAYAAT 84 - 98
Просмотров 7372 месяца назад
Tafsiir des Versets 84 à 98 de la Sourate Al Baqara par Serigne Moustapha Diop Al-Kokiyou
Hommages de Serigne Moustapha Diop Al-Kokkiyu à Hassan Nasrallah
Просмотров 3,2 тыс.2 месяца назад
Hommages de Serigne Moustapha Diop Al-Kokkiyu à Hassan Nasrallah
Jawharatul Kamaal | Salaatu Cheikh Ahmed Tidiane Cherif
Просмотров 2 тыс.2 месяца назад
Ay Lèeral Ci Salaatu Gii Di Jawharatul Kamaal Bu Cheikh Ahmed Tijaan Cherif ak Serigne Moustapha Diop Al-Kokiyou
Kadduy Jeggalu Wa Diourbel Ci Wax Yaffa Bayèeko Jëm Ci Cheikh Moustapha
Просмотров 4,6 тыс.3 месяца назад
Kadduy Jeggalu Wa Diourbel Ci Wax Yaffa Bayèeko Jëm Ci Cheikh Moustapha
Le Sacrifice en Islam et dans la Voie de Dieu
Просмотров 6653 месяца назад
Le Sacrifice en Islam et dans la Voie de Dieu
HISTOIRE BUREAU BA CA NDAR AK SERIGNE MOUSTAPHA DIOP AL KOKKIYU [Archive]
Просмотров 2,5 тыс.3 месяца назад
HISTOIRE BUREAU BA CA NDAR AK SERIGNE MOUSTAPHA DIOP AL KOKKIYU [Archive]
Boolé Ñaari Wird : Témoignages d’un Talibé Cheikh sur le Wird Maaxuz
Просмотров 2,1 тыс.4 месяца назад
Boolé Ñaari Wird : Témoignages d’un Talibé Cheikh sur le Wird Maaxuz
2e Partie Questions - Réponses & Commentaires | LA MOURIDIYYA À L'AUBE D'UN NOUVEAU SIÈCLE
Просмотров 3,2 тыс.4 месяца назад
2e Partie Questions - Réponses & Commentaires | LA MOURIDIYYA À L'AUBE D'UN NOUVEAU SIÈCLE
LA MOURIDIYYA À L'AUBE D'UN NOUVEAU SIÈCLE | Conférence Safar 2024 At-Tanwiir
Просмотров 6 тыс.4 месяца назад
LA MOURIDIYYA À L'AUBE D'UN NOUVEAU SIÈCLE | Conférence Safar 2024 At-Tanwiir
Assassinat de Ismaël Haniyeh | Taxaw Sèetlu Ci Doxaliinu Rèewu Julit Yi
Просмотров 7224 месяца назад
Assassinat de Ismaël Haniyeh | Taxaw Sèetlu Ci Doxaliinu Rèewu Julit Yi
TAFSIIRUL QUR'AN: SURATUL BAQARA AAYAAT 63 - 83
Просмотров 5024 месяца назад
TAFSIIRUL QUR'AN: SURATUL BAQARA AAYAAT 63 - 83
Quels Enseignements Tirer des Événements de Karbala ?
Просмотров 5655 месяцев назад
Quels Enseignements Tirer des Événements de Karbala ?
Àqi Sëy | Digganté Borom Kër ak Soxnam
Просмотров 1,4 тыс.5 месяцев назад
Àqi Sëy | Digganté Borom Kër ak Soxnam
Centenaire du 20 Muharram | Serigne Moustapha Diop Koki sur le Rôle de Cheikh Moustapha
Просмотров 2,7 тыс.5 месяцев назад
Centenaire du 20 Muharram | Serigne Moustapha Diop Koki sur le Rôle de Cheikh Moustapha
TAFSIIRUL QUR'AN: SURATUL BAQARA AAYAAT 54 - 62
Просмотров 3685 месяцев назад
TAFSIIRUL QUR'AN: SURATUL BAQARA AAYAAT 54 - 62
Serigne Mouhamadou Moustapha Mbacké : Taxawaayam Ginaaw Bifi Serigne bi Bayyeekoo
Просмотров 9435 месяцев назад
Serigne Mouhamadou Moustapha Mbacké : Taxawaayam Ginaaw Bifi Serigne bi Bayyeekoo
TAFSIIRUL QUR'AN: SURATUL BAQARA AAYAAT 38 - 53
Просмотров 5035 месяцев назад
TAFSIIRUL QUR'AN: SURATUL BAQARA AAYAAT 38 - 53
❤❤❤❤❤
Ceyy koooookèeee ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashaallahou
❤❤❤
Waw goor thi khassidayi rek.
❤
جزاكم الله خيرا
machalla yalla n'a yalla goudal sa fan Amin
Yagué fi te wer 💖
❤❤❤❤
Al. Hammdoulillaa. 66
Bimala xamei dh yaggoul wayé sop nala lol❤... Yallah na nga fii yagg lol té andak weer 🥰🤲🏽
Yallah dou Tajalli si niit (jamm) waye ay tanazullat nioy wathie si nit (sourate qadri) . Loutakh moy Haqq rek moy tajalli . Donc Haqq moy tajalli jougge si haqq niel haqq. Resultat haqq moy aini. Waye nit mome majass la, donc Haqq bi di yallah tanazulat lay deff si jam bi di majass. Waye comme que nit majass la, lolou matakh niou mana wakh neni guissou niou dara si mome louroul yallah mi di haqq. Deugui -deug ubuda moy, beuss bo deh we (fatou) si lepp louroul yallah, sa guiss gui deh dem si guissou yallah, say jeuf deh dem si jeufi yallah, sa dounou deh fekki dounou yallah gui sa degui deh dem si deggou yallah,guene si majass (la vie virtuelle)delou si haqq ba yeugouto louroul ne haqqbi di yallah,yeug ne yallah midi haqq moom rek moffi nek, dara dara louroul yallah nene la, mome rek moffi nekone, te ba legui dara nekkou fi louroul mome yallah miy haqq, bobou gua doug si dahira ubuda: Irji'i ila rabbiki radiyatam mardiyyah, Fadkhuli fi ibadi. Wadkhuli jannati (Surat Al-Fajr Ayat 28-30). Li nak bou ame nak moy dougou gua aljanna. Serigne bou maat serigne li lay deff si yaw, li soukka meunal, demal setti banene serigne.
Malade bou dem si doctor, bouffa deffe ab dir, bou were digua kham bo weroul digua kham. Bo weroul nak, bo fa togue perte sa temps. Kou diokou si serigne bou mat serigne digua yegg, kou diokoul si serigne bou mat serign do massa yegg. Serigne Touba liguey yam modone di yeguele talibe yi si yallah.
Merçi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merçi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureungéndieufety yalla na yalla barkéil
Dieureudieuf sama Serigne biiii Yague fiiiii lolllll tes and weurr Diop
Waxtaan wi ana complete bi?
Amna sollo lool masalla
جزاك كل خير ❤❤❤ وكفيت كل شر ❤❤❤ وأطال الله عمرك ءامين بجاه أسنى الخديم
Yague fi lol te andeu ak weir amal nga nou niarigne lol 😢
Ndeysan waxtane bou am solo sax 🥰. Thieuy bou ko nieup xamon. Kilifa gou am yitè way . Yalla gue fi yagg tè werr si barki xassida yi
Yalla nga fi yageu té wèrr
Machallah yalla doli ham ham bi ak fan wi lool
Djeurejeuf Serigne bi . Sonie bi amna solo . Yalla yalle féwe le yewe
Maasallàa Seex Mustafaa Jóob al-kokki
Segne bi man numéro segne Moustapha la yittéwoo
As salamu aleykum Jokkol whatsapp ak : S Modou Diop +39 380 183 1926 S Moustapha Ngom +1 646 644 4933
Bilahi yay gorr té déggou bilahi amo morom ❤yalna gafi yague loll
Saway man numéro kou djégué segne Moustapha la yittéwoo dama beuga djébbelou guirr yallah
machalla waw ko begue numéro serigne moustapha Diop kou ki
As salamu aleykum Jokkol whatsapp ak : S Modou Diop +39 380 183 1926 S Moustapha Ngom +1 646 644 4933
Walay
Diaradieuf Serigne Moustapha Ya ngui lérale you am solo lole téye thieuslaye wigni wara yité wo bala dara moye tawhite. Barina gnouye khouss ci mbir you bari té warona bala dara yitéwo fi nga dougou taye. Diaradieufeti
Dieuredieuf Serigne salam gningu
Yalla na la fi sa borom bayi guay gueuna ligueuyeull borom touba sama serigne
Salam kou kham kou diégué serigne ndiaga sylla damako beugua ziar sokhla numero beuk nék bouko diégé Diapéléne masi
❤❤❤❤
❤
Kouma meune diapalé thi numéro Serigne Moustapha ? Mahouz la beug dieul thi mome directement.
As salamu aleykum Jokkol whatsapp ak : S Modou Diop +39 380 183 1926 S Moustapha Ngom +1 646 644 4933
Yalla nala yalla doli faye
yàgg fi Loll té andak wéer
Macha alla ❤
Yalla nga fi yageu té wèrr
Cey tawhid rekka wor Cheikh Moustapha yagué fi te wer ❤
Sant Seriñ Touba Ya Shaykhana AHMADOU BAMBA Jërëjëfëty ❤
أطال الله عمرك
Alhamdoulillaa. 66
Thiey wa faydou❤❤❤❤