Wouah ❤️❤️❤️❤️Amy vraiment je ne sais pas si tu ne remporte pas la victoire cette édition c’est qui qui va le remporter? T’as assuré depuis le début ❤️❤️❤️
Wa jury bii (Var) bouniou doff doff Lou woul kay xamnagne nii rénn Yako mom vraiment boudoul dara saxx rénn dawara guéneu Sénégal té en plus niom niarr Nieup dieul nagne ko ms nafy moy sama candidats préféré nk ms oie lako yéné nk 👑👑💖
Ki limou way dara nekhussi guen beug niouko forcé je parle ds timbres vocales nafi et Justine st bien a l aise surtout nafi kan elle a chanté nayanka belle j en revenais pa puisk imiter la diva ivoirienne ce po facile avk ss octaves me nafi elle a assuré vrement nafi mérite de gagner cette compétition elle a une voix sublime et puissante
Amy lima khame moye doko deuge tchii fausse note Elle fait jamais d’erreur elle reste toujours sur le game et chante juste et elle réussit toujours les notes
la finale risque d´etre tres compliquer même si certain crois que amy et nafy sont meilleure ,ce qui n´est pas le cas car justune a une timbre de voix particulièrement belle qui est adopté a toutes sorte de registe... ET je pris que nafi remporte la finale amine
À mon remarque c'est Amy la meilleure parce-que elle n'a pas très bien compris le wolof mais elle chante bien les chansons wolof pour les chansons anglais et français elle les métrise super bien contrairement à Nafi malgres elle chante bien les chansons wolof mais pour les chansons anglais et français elle est un peu.... Mais cas même sa voix est super.Félicitation Amy tu me plaît beaucoup bonne continuation
Iow mii seytanei woo diakhassé ngénn waykatt you magu légui gnibii dii dora door ngua diéma diakhassé prestation amy lousiy dougué dii lathie fans nafii yii mandal je suis peurrr mann
Elle a dead ça c’est une diva c clair et puis ça voix est juste waouhh💪🏼
Vraiment tu mérite cette compétition amy yaw sa olof bou sétone nga tothie fii❤❤🥰
Bilay
Sisi Franchement
daiga competition bii mokomom
Amy rekk mofi nekk
Fii déh nafii moffii nek khana niou sotaal. Ami Come dham
Finalement mom la faral , ki meunn na wayy torop ❤
Aka woor
Machallah elle a imité comme voix Viviane c'est une compétition chance la mais Ami est une diva machallah congratulations
Nagnu ko bayi xel . elle es intelligente et sa voix est juste
Mani kou beugeu Amy beuseul pousse bi malay xoll
Fans nafi yi team roubé 😂😂 j vs 👋
Niou gui ni😂😂
Ami mn dakh weuy nafi wolof bi mn lairoul rk
Instant bi fans nafi yi amy molen titeul 😂😂
@@mamisstakonte951 daxoul way Nafi dé sen voix yi bokoul mais togg len fi nane Nafi, Ami
Justine nieuw dieul final bi😅
@@assanesambe9322 loloy cas bi nk😅mais justine nk khana gnémé woula gagner nk
Wouah ❤️❤️❤️❤️Amy vraiment je ne sais pas si tu ne remporte pas la victoire cette édition c’est qui qui va le remporter? T’as assuré depuis le début ❤️❤️❤️
Wa jury bii (Var) bouniou doff doff Lou woul kay xamnagne nii rénn Yako mom vraiment boudoul dara saxx rénn dawara guéneu Sénégal té en plus niom niarr Nieup dieul nagne ko ms nafy moy sama candidats préféré nk ms oie lako yéné nk 👑👑💖
Lii dé inchallah sou nekhé yalla nafi moko mom 😍💃
Ta bien dit
Ki limou way dara nekhussi guen beug niouko forcé je parle ds timbres vocales nafi et Justine st bien a l aise surtout nafi kan elle a chanté nayanka belle j en revenais pa puisk imiter la diva ivoirienne ce po facile avk ss octaves me nafi elle a assuré vrement nafi mérite de gagner cette compétition elle a une voix sublime et puissante
Waxal wayy 😍😍
Wallæ t'as parfaitement raison nafii dou sèn morom
Billahie mo dakka way Viviane ki live leu meune❤🎤bou Nafi gagnèwoul sakh mome yènèna koko
Viviane bala ngay kham né deum la rekk nga guiss kou kay diémma reprendre, yomboul deh mais kamem félicitation jeune fille
Bilay y’a meune wayy yalla nga dieul final biii
FRANCHEMENT AMI C LA MEILLEURE 🤞 ELLE A UNE UNE BELLE VOIX MACHA ALLAH ELLE MÉRITE LA COMPÉTITION 😌😘
Tu mérite la victoire depuis le début tu la assuré zéros faute ma puce. On est de tout cœur avec toi
Technique mossi tok khalè bi machallah
Ma préféré ta meune dh niou wathie final bi rek dieul dém amoul ragal amy😍😍😍😍😍
Té nafi nekk fii 😂
Inchalla
Gagner ko dou yombou dé ❤️❤️❤️
Vraiment elle a bien chanté cette final ça sera très compliqué AMY, JUSTINE et NAFI mé ça ira je vs t'aime fort 💞💖❤️❤️
Merci amine ami chante toujours trés bien 🤔 10 sur 10 ❤️😂💓💓😍
Elle est complète cette fille , elle chante très bien vraiment khaleyi Yalla nalene Yalla defaral diame je vous aime tous ❤️❤️❤️❤️
Laf Thiat tu mérites d’aller en final
Technique bi Amy ame dama diakhal mane c’est la meilleure dh bagne bagne nangou 😂😂
Youhoul lolou halé bi titoul rafoul je l'aime
Ki bouko ken dioxati wayou viviane😅😅 torturé na way bi
Srx elle a une belle voix mais ça ne colle pas avec ce genre de musique
Man dh djongué gui rek momay raye tarkalah way
Amy kharal nafi
Ki bou wayone way bi
Ken douko deglou
Li meunna yakh timpa😅😅 je le vous jure
Elle a un belle voix si boudone deff music rock
Weuh 🙄
Mohhhh
Ndeyesan fi guene ni tok bamou dieul finale bi 🤧🤧🤧🤭
Elle mérite vraiment la victoire 🥰❤️
Pourtant elle est un peu malade de mais elle est la meilleure 👍👍👍♥️♥️
Tu es la meilleure tu maîtrises tout vive la championne amy complemento
Xallei bi dp8 l début dafay assuré mashallah victoire bi mom yay borom bien vrai k Nafi la beugg sma xoll😍😍
Final bi amy lako yéne way elle chante bien machalah
Bilay
malgrés sa maladie elle a assuré mane dall je l'aime love you
Plus de cœur pour notre Amy
Pourtant sa maladie était trop grave dafa narone gnibi sakh mais alhamdoulilah
La meilleure prestation! Impeccable !!!
Depuis le début tu as assuré notre Viviane numéro 2 l'AF thiat waye ❤️❤️💯💯💯👍
Bayilennn son Viviane dafa méti wey
Amy vraiment tu mérite la finale todje gua fi
Vraiment elle mérite🥰🥰🥰🥰
Tu mérites la finale
Nafi nék fi ami diko dieul tmt
Rien n’a dit depuis le commencement de la compétition t’as assuré
Bilahi Amy niak dègue Wolof rk lay dioy 😭si yw mais kène dou yw si mime competition yassi si meune fouf 🥰
Machallah Khalé bi dall laf thiatt 😍😍😍
Mia sa robe lane la machalla ♥️
Ma préférée 🤩
Niaww ioe la diokh bopeu déh ❤️🔥
Félicitation amy blh ki bou degon olof tothiefi
Team nafi❤❤❤🤚
Moi je pense comme tout le monde que ami elle va gagner
Oh beautiful voice 🥺❤️
Amy est la meilleure 😍💖
Ça c'est une ami dans une compétition ma chérie tu à encore cartonné
elle est vraiment la meilleure
Wa dègual ma rek à wa bakhna 😀😀😀final rek inchallah
Demnagn final tout les trois
No bou olof bi lèrone mou dèff fi lou kène masoul guisss
La meilleure. La diaspora te sui
Amy lima khame moye doko deuge tchii fausse note Elle fait jamais d’erreur elle reste toujours sur le game et chante juste et elle réussit toujours les notes
machalag
la finale risque d´etre tres compliquer même si certain crois que amy et nafy sont meilleure ,ce qui n´est pas le cas car justune a une timbre de voix particulièrement belle qui est adopté a toutes sorte de registe...
ET je pris que nafi remporte la finale amine
Billay avec Justine tout ira inchalah sa voix est exceptionnelle
Justine est vraiment grave assuré avec kagn lalay guiss ♥️♥️♥️
Ehhh ma Star Amy a gagné la finale 🤧
@@crispyqueen7323walay dafa meilleure xale bi
Machalla ami ❣️❣️❣️
Nekhoul deugue mais c la meilleure 🤧🥰🥰🥰❤️
À mon remarque c'est Amy la meilleure parce-que elle n'a pas très bien compris le wolof mais elle chante bien les chansons wolof pour les chansons anglais et français elle les métrise super bien contrairement à Nafi malgres elle chante bien les chansons wolof mais pour les chansons anglais et français elle est un peu.... Mais cas même sa voix est super.Félicitation Amy tu me plaît beaucoup bonne continuation
Nafi aussi ne comprend pas anglais et elle chante bien l'anglais
Amy avait une douleur dentaire je pense mais elle a assuré.
@@djibydiome1169Doul nga 😂nafi meunoul anglais
Bo degonn olof dou bah tu assures grave ma belle 🔥🔥🔥
Walay koula khol khamni wolou nga sa bop meun nga lingey def
Sama candidate bi way amy rek 💪
Waouh waouh beautiful Amy
Ma Cha Allah
Amy italy ❤️❤️❤️👏👏
Où sont les fans de nafi
Iow mii seytanei woo diakhassé ngénn waykatt you magu légui gnibii dii dora door ngua diéma diakhassé prestation amy lousiy dougué dii lathie fans nafii yii mandal je suis peurrr mann
@@ngagnendoyedaryaba1202 merco bcp
Waaw com dab machalla sorellina 🥰🥰🥰
Congratulations amy 🔥🔥🔥
Non kii beugu nako sheut🥺♥️
Bonne continuation rk🙌 laf thiat rk ba final
Doumasi doyal chaque jour ma commentaire
Waouhh machalla amy❤
Mane dh khamna nimala beugué eupouna ma dolé mome💖💖💖💖💖
Bilahiiii ya meuna wayyy manchallah
Verement tu mérite depuis le début tu la assuré verement bonne chance ami
Grazie Amy tu as assuré
Machallah Amy ❤️🥰 nice 🥰
Machallah, tu as assuré
Bilahi bo deguonn wolof laniouyy khammm sa mayy wayyy deugue
Vraiment nafy sama fans laa me 2021 bii yako momm
Magnifique tu chantes bien ❤❤
Ki premier jour ba la xamni finale la djeum
Machallah Ami 🥰🥰❤️❤️💃💃
bravoo Hamy❤😘
Avant je disais que ni wayou anglais kassé la meune mais là dina méti dh ndakh ki talent deug la yor
Nn vraiment qui molen meune Techniquement wallay tei inchallah final bi dina lerr inchallah vrmn
Nonn dou sen morom wayy mashaallah
Fingay woyé xamougnouko machallah amy
Deguel ma voix bi rk
Delen wakh 😂 rek surprise mo nara amm
Machallah nékhe na tamite
Musicien yi tamite machalla
Elle chante super bien machaalah
Machallah laff bouche😘❤
Dolén ma diapalé lathiél ma Ndakhté loumou bokou akk Ndeye Marie bou nék série karma xallé yii amnagn trace dh😍💖
Bokou gnou darra 😂 😂 da bella rek 🥰🥰
Ohhhh Amy machallah ❤️❤️❤️
Waouw machallah mais gni si guinaw tamit kéne dou niom
Haaaa Amy la diva à la voix ď or
💯💯💯
La partie où elle dit "khady mbengue"je pensais k j etais viviane
The best❤💯
Première commentaire 😍🥰🥰😍
Bilay ki bou gagné woul dinama méti trop bilay c la meilleure
Amy Italy is a Star....
Je t'aime fort ma béll
Elle mérite vraiment d gagner ❤️⚡
Jl’aim trop❤️❤️
Ami t 'est la meilleur
♥️💋💋💋💋💋💋💋tes la meilleure
yallah bu yakar tass