Youssou Ndour - CLIP - TÉLÉPATHIE- VIDEO OFFICIELLE GRAND BAL 2025
HTML-код
- Опубликовано: 10 фев 2025
- TÉLÉPATHIE
SAYOU MA LA GEESTOO
FÉKK YAA NGI MAY XOOL
DA FA MEL NI TÉLÉPATHIE
XÉL YI JAXASOO
LI NÉ CI YAW,
MO NÉ CI MAN MI LÉ
L’AMOUR EST SIII FORT,
ÇA NOUS REND FOU
HOOK: MINE NGA MAAYE
DEUGUE DEUGUE DIARAL NGA MA
LO AMOUL
BEUGOU MA
MBEGGUEL DAN KOY DEROULÉ
BA MU MATT
KU NE DI KO SENTIR,
SA YARAM
CHÉRI KESSÉ DOYUL,
DAYMANQUÉ
BÉBÉ KESSE DOYUL,
DAY MANQUÉ
NIDIAYE KESSE DOYUL,
DAYMANQUÉ
MBEGGEEL GU SINCÈRE,
DAY DEGER KECC 3X
KECC, KECC,
DAY DEGER KECC.
Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
/ youssoundourofficiel
/ youssoundourofficiel
/ youssoundour1959