Dieynaba répéte une phrase de wolof diakhaté 😂qui dit " kou lambeu ya taye, dèmale fagnou la nobé " . Mais, et si " nobo, fagnou la nobé"? Il vaut mieux être "lambeu" que d'être avec une personne que tu n'aimes pas. LOVE
Cet épisode est très intéressant, Dieynaba ouvre enfin les yeux et change même d'attitude envers Marianne. C'était drôle de la voir avec Léna, mdr. Quant à sa mère, elle devrait vraiment se calmer. Je suis heureuse que Marianne et Tamara passent du temps ensemble et qu'elle lui redonne de la confiance et de la force, girl power!
HEURES DE PRIÈRES DU 10 AU 16 JANVIER 2025 Fadjr: 06h24 Suba: 06h39 Tisbar: 14h15 Takussan: 16h45 Timis: 19h06 Gue: 20h06 Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack Kou beug ay heure diouli chaque semaine def ma sign sn@p
Wa yéne marianne khana mom dou lekk chaque fois bou mérè rk gued lekk bi dou ni bir dagnou koy respecter ak plat you soft yougnou lay teggal ay ndékki croissant 🥐 gay guedd marianne meno dou nii dagay lek ba sour tè sa yo mérè gueneu meneu lekk snn diga damm aziz outi kènen Amlèn diam❤
Tamara Rahim ensemble, fama et demba trokh, avant le mariage Tamara et Rahim l'age deTamara dina mat ba récupérer compte bloqué biko yayam diokhon, fama yakar nani dill bi dina réussi après mou wor Demba daldi daw dem maroc dadiéfa alsane beug kofa alsane nakhati ko , magui setlou fama fanyi day woté téléphone rek dieukeur dji guisnako mouni yayam lay wo dama yakar ni alsane lay wo 🤭, après bimou woré fama, Aziz fait son travail pour que Lena fékhé ba alsane gnibisi après alsane finir en prison 😅 thiey dieul risque rzk melni kou bindeu chéri bi 😂
La mère de Dieynaba ce n’est même pas la peine 🤦🏽♀️🤦🏽♀️ elle vend carrément sa fille à cause de l’argent. Dieynaba fais attention à Lena oohh tu ne la connais pas. Tamara et Mariame ❤️❤️❤️❤️
Allahouma salli ala seydina Mouhammadine wa alihi wa sahbihi wa Salim PSL ❤
Amine
Amine 🙏🙏🙏❤❤❤❤
Enfin Tamara s'est relevé 😂 que le jeux commence
Commence Mence
J'adore la belle complicité de Marianne ak Tamara machallah yallah na diam yague ❤
Yallah Ngua goud fane si barki SEYDINA MOUHMED PSL 🙏
𝗣𝗔𝗜𝗫 𝗘𝗧 𝗦𝗔𝗟𝗨𝗧 𝗦𝗨𝗥 𝗟𝗨𝗜❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
PSL Amine 🙏🙏 e
Aminé
Les candidats au concours ENA bonne chance à vous
qu'Allah facilite tout
Amine 🙏🏼❤
Amiine yarabii
Lep lou way nian si Aljouma tay bi yalla yalla 'nagou ko tamou guen si yaw 😢❤❤
amine❤❤❤
❤❤❤
Amine yarabi inchallah 🤲🙏👌
امين يا رب العالمين
Amine
Longue vie á vous lire katou commentaire yi 😂😂🎉🎉😂❤❤
Merci 😘 a toi 🎉❤
Merci
Amine merci beaucoup ❤❤❤
Amine way moma tardel fepp
Amine 😊
Des coeur pour Marianne et tamara❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤chapeau marodi🎉🎉liguéye bi rafét na❤❤❤🎉🎉🎉
Kou yakamti couple tamara et Rahim 🎉❤
Ma guini
mane mi
Magui kharr 🎉🎉🎉
Man gui 😂
Mane Mane 😍😍😍
Kou diepii yayou Dieynaba lalal j’aime 😂
Amo di palace
Mèr bi Kou soof la
@@FatoubintouloloLo sérieusement en plus da sohor🤦♀️
@ bilahi
Elle m'a dead avec ses expressions
La petite Aicha est trés belle en plus elle ressemble à son père, on dirait son vrai père 🥰
Moi je pense qu'elle resemble a fatima surtout leur visage
@@Kitchenpassion53elle resemble a son pere
Ak asi lady diama
Trop même j’ai fait la même remarque ❤elle ressemble trop à son papa
𝕆𝕟 𝕕𝕚𝕣𝕒𝕚𝕥 𝕥𝕖𝕝 𝕡è𝕣𝕖 𝕥𝕖𝕝𝕝𝕖 𝕗𝕚𝕝𝕝𝕖 🎉❤
Je vous aimes les sénégalais même si je je comprends pas votre langue, mais j'aime beaucoup votre tradition ❤❤❤❤❤❤❤
Notre langue c’est pas difficile à comprendre
@bassiroundiaye1113 eh mais à force de regarder vos séries je comprend quelques mots 🙏🙏👌
Yayou Dieynaba changement d'humeur guaw na deh😂
Domou rahim bi machallah way cette fille ❤
Très posée je l'adore ❤
❤❤❤❤❤❤
Amine
Yalla nagnou yalla dolli soutoura si barké serigne mountakha mbacké mou sell mi 🙏🙏❤
Cëëy 😢nos parents d’aujourd’hui beug xaliss molen dii dougueul si lou né 😅 yalna yalla mou seul 😭niou si parents you melni ak gooro you melni 😅😅
😂😂😂
Nèkhoul ba nèkhoul mais rahim beau na 💖💖💖🥰
Mako guena Beau dh
@@kalamou4353wawaw ya am foulleu😂😂
Comme gorou Wattpad😂😂 noboumako nak amna dieukeur 😂😂
@@aissatoumarone2095kon dh sa dieukeur japoul si dara😂ma rouss
Sama jeukker mokou gena beau 😂
Que 2025 soit une année de bonheur , santé et réussite totale dans tous nos projets 🫶🏾♥️🙏
Amine
Amine
Alhamdoulillah santa serigne saliou ak yalla ak sama yaay
Xana taye dina ame 1 j'aime
Wa légui am gua 1j’aime lou wakhaty 😂😂
Akh bene commentaire mouy sama boss bi 😂
Wa so paré nga wakhe gnou aye j'aime loumou laye eundile
@Serigne581 boudé danga yor compte youtube bén jai bounek 1f leu
@MouhamedDiop-l7k 😂😂astafourlah
Dieynaba répéte une phrase de wolof diakhaté 😂qui dit " kou lambeu ya taye, dèmale fagnou la nobé " . Mais, et si " nobo, fagnou la nobé"? Il vaut mieux être "lambeu" que d'être avec une personne que tu n'aimes pas. LOVE
Yaw mome ngani doo baayi 😂😂😂😂diapeko niiii rekkk
Love❤❤❤😂
😂😂😂yaw wasi gnou 😂
C fini t'es irrécupérable 😂😂😂
Cet épisode est très intéressant, Dieynaba ouvre enfin les yeux et change même d'attitude envers Marianne. C'était drôle de la voir avec Léna, mdr. Quant à sa mère, elle devrait vraiment se calmer. Je suis heureuse que Marianne et Tamara passent du temps ensemble et qu'elle lui redonne de la confiance et de la force, girl power!
Yallah na am 100 milliards euro pour liguéyale yalla ءامين يا رب العلمين 🥰
Nouyou dadjé si commentaires yii yalla nagn ko dadjé aldjana firdawsi 🫀🤍☝🏽
Amine ❤
Yalla na yalla faayal niou yoneti bi❤❤
Lii nèko si kholl yi tè Manou gnouko wax yalla n'a yalla safara lèpou 😢❤❤
Oh Amine
Je l'espère 😢😢
Heure Bouma commentaire ken dou aime alors que j'aime les autres commentaires 😢😢
Dou yone😂
Danga bakh rek motakh 😂😂
Pour ceux qui sont dans des problèmes YALLAH nalène YALLAH diapalé❤
Je déteste " l’amie " de tamara mais son teint noir est tellement jolie
Son ex amie fama😂
@ oh c’est bien pour ça que j’ai mis entre guillemets 🤣🤣🤝
Sognorr ba paré rafett mon’gui nonou
Manman Djenaba visye, grangou menm jan au Denmba epi madanm li
@@adjasaliou8309 désolé je parle pas wolof 🥲
Longue vie à nous avancer katou buplicité yi🎉❤😂
Kone dou mane kesse😂😂
Je suis sûr que Farma n'est pas enceinte. C'est juste une stratégie pour avoir une grande part d'héritage.
Demba, le voleur volé 😂
Tu as bien compris le jeu de fama mes c'est très bien c'est très bien pour demba 😂
La fille de Rahim est très belle 😍
Vendredi tay yalla boumou nék souniou dernière vendredi ❤❤❤
Amine 🙏🙏🙏🤲🤲🤲
Bly j'aime raham ❤kou beug rahim rek mayla mako ay cœur ❤
Non j'aime ce théâtre vraiment ❤❤❤il y a beaucoup d'émotions
J'aime bien l'amitié de tamara et mariama❤
Ahh diaynaba ya wakh li Lena li d moy anndou thiague yalla na saytane khep doli 😂😂😂😂😂
Amine 😂😂
Wouy 😂😂😂😂
La mère de Djeynaba parle aussi bien le wolof que le bambara ma sha Allah
Origine malienne
Je me disais qu'elle ressemble beaucoup à la mère de Aïcha dans le goût des sentiments
Que le tout puissant nous pardonne et nous protège contre tout ce qu'on ne veut pas
Amine 🙏🙏🙏
Série bou nékh 😂 histoire dinako binde 😂 numérique calcul ko géométrie tracé ko 😂🎉li khéré na way 🎉🎉
Kou khaar cœur brisé 💔 dieynaba rek lalal j’aime 😂😂😂
HEURES DE PRIÈRES DU 10 AU 16 JANVIER 2025
Fadjr: 06h24
Suba: 06h39
Tisbar: 14h15
Takussan: 16h45
Timis: 19h06
Gue: 20h06
Qu'allah accepte nos prières Al Jummah Mubarack
Kou beug ay heure diouli chaque semaine def ma sign sn@p
Aah mâcha ALLAAH sama magou bopp ji ziar nala pape thioune
Wa yéne marianne khana mom dou lekk chaque fois bou mérè rk gued lekk bi dou ni bir dagnou koy respecter ak plat you soft yougnou lay teggal ay ndékki croissant 🥐 gay guedd marianne meno dou nii dagay lek ba sour tè sa yo mérè gueneu meneu lekk snn diga damm aziz outi kènen
Amlèn diam❤
gniye wadia compo yalla naléne yalla may moyene
Khalé yi mba yéna ngi sétane jeux de dames khalé yi mba jeux de dames nekhna sou nékhoul louniou thi meune😂😂
😂😂😂
Niakk fayda 😂😂😂😂
@@bathiendiaye8655 En je suis niakeu fayda Kone ay way🤣🤣
😂😂😂😂😂😂
@FatoumataBinetouTouré-x7u 🤣😂
Mafi djitou Mayma jem ❤
Kou Beugue sa yaye lalale ❤
❤❤❤❤❤❤
L'année commence bien pour Tamara
Excellent Seri ❤
Dyenaba aussi, elle devrait pas remuer le couteau sur Lena, oubliant que c'est elle qui lui a présenté Alassane, elle devrait faire profil bas 😅
Lo xam ci doff pour mom lena est de bonne en lui presentant alassane
Elle va lire l'heure après, son gars là est suspect
Nianal lene sama papeuuh 😢
Wa lii ba Diam la 23m 133 commentaire 😂 longue vie à vous ❤❤❤❤❤
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ohhh machalah Pape Thioune dans la série. 🎉
Kou guemeni fama eumboul 😂faux teste la
Meusoul eumbeu 😂😂😂😂khaliss bi rek moko niorr instant bi
Rabia une vraie artiste et adorable ❤❤
Chapeau ❤A vous Marodie
vous êtes des meilleurs Kou d'accord lalale jaim ❤
Marodi daal louniou wadal bala nioussé rendre compte rk na forko 😂❤adja Fatou liimoy tomber waral aye gaafe 😢sois forte🥹
Kou gueum ni dina ame 1000 j'aime rk lalal j'aime 😂😊
Longue vie à nos mamans ❤
Wa Dakar sene dom am na ndam je suis premier😂 snn Barça rek ❤️💙 niou gagné sounou Final bi inchallah
Dina niouko 4tati rk😂😂
Hala Madrid final sama aferla Inchalla
@DembaNiasse gagnez d'abord Liverpool, AC Milan et LILE après niewlen niou cas débat bi😎
Rahim diouyou😭 gentlemen deugg la ror😅😂
Ror nak😂😂
Képou kou amoul dôme yalla Nala yalla maye dôme inchallah
Amine inchallah
Amine
Kou buegue seydina Mohamed lalal j'aime 🎉🎉❤❤
Bou niou paré si kuluna yi nagne wakh si kalanaxa you nek Sénégal🇸🇳😂😂
Louy lolou 😂
J’ai pas compris 😂😂
Ray gama 😂😂😂😂😂bilahi wakh ga deugu
Wallahi, 😂
Kou Dieppi yayou dieynabz
Lèna ak DIÉYNABA yalna seuytanè khèb doli 😂😂😂😊
J'adore jeux de dames 🤙🤞
Tamara Rahim ensemble, fama et demba trokh, avant le mariage Tamara et Rahim l'age deTamara dina mat ba récupérer compte bloqué biko yayam diokhon, fama yakar nani dill bi dina réussi après mou wor Demba daldi daw dem maroc dadiéfa alsane beug kofa alsane nakhati ko , magui setlou fama fanyi day woté téléphone rek dieukeur dji guisnako mouni yayam lay wo dama yakar ni alsane lay wo 🤭, après bimou woré fama, Aziz fait son travail pour que Lena fékhé ba alsane gnibisi après alsane finir en prison 😅 thiey dieul risque rzk melni kou bindeu chéri bi 😂
Ya ame fite kay😂😂😂
@@rabysadji8447 xelmi loumako digeul mou def 😅
Wahh iow bane école ngua diangué 😂😂
@@bambadiop9514Sourtout lolou😂😂tmt😭😭
Bou lolou dialé nguen wakh wa marodi niou mayma téléphone tecno bouy planque la yor😢😢😢😢
Ak man😂😂😂😂
Dama sonou😂😂@@cisseelcapo813
😂😂😂
Bima yor bouton bikay tall mo yakkou xamna niou bolé masi rek
@@SoxnaDiagne-hx5nr bilahi mane tmt balamako tall dane may wo appelle manoul sakh dougou tikt
صلوات على النبي كل كم ❤
عدد خلقك ورضا نفسك وزنة عرشه ومداد كلماته الله يارب العالمين 🤲
Livraison en temps je t'aime marodi❤
Mafi djitou yén li histoire dinako bind 😂😂wa fouta amnagnou ndam😂
Kon Dieynaba am na koumou ragal 😂😂
Sama dioguanal bi nieuw na❤️
J'adore Dieynaba 😂😂😂
Yayou diaynaba bi louko dal😂😂
KouBeuguesayayelalale❤😊
Bo defe Lou bakh niouni la c'est bien gua defe Lou geuna bakh niouni la c'est très bien
Ndiawar😂
Le peuple réclame le couple tamara et rahim
Yayou dieynaba mo badola nieuw akimo lép
Yayou Dieynaba changement d’humeur gua W na deh
Maman de dieynaba comme maman de diama 😂😂😂😂😂
Nanah bah❤❤❤
Tmt est ce que dougnouko gnananl elle est la meilleure ❤
Cheikh Faye 🥰🥰🥰
khleiyi mba yénagi j'aime sama commentaries boolén j'aimoul louma si meune😂
Kou diepi yayou diaynaba kom mane
Kikay 😓
Mane ma ko diepi
Lire catou commentaire yi nouyou nalen
Tamara tu es vraiment belle ❤❤
La mère de Dieynaba ce n’est même pas la peine 🤦🏽♀️🤦🏽♀️ elle vend carrément sa fille à cause de l’argent. Dieynaba fais attention à Lena oohh tu ne la connais pas. Tamara et Mariame ❤️❤️❤️❤️
J'aime Tamara et marian ❤
Dieynaba dhé ki rk mo meuna nék yayam 😢
🎉Allons déguster sunu série
Adja fatou khamgua sa djiko vrmt mandou wodei mais ligua wax deugeu bi andeu nassi d’une part 😂
Dienaba est trop belle
Kou d'accord que jeux de dames est le meilleur serie rek lalal j'aime ❤
Tamara elle belle machallah ❤
Ana wa kaolack ❤
Yo gui ni