Allahou akbar😱Oustaz Mbacké Sakho à Cheikh Ahmed amoul fou yalla waxé atté ray yow wax gua fi diouma

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 31 янв 2025

Комментарии • 69

  • @XamxamLesgrandssecrets
    @XamxamLesgrandssecrets 2 месяца назад +2

    Dieuredieuf émission du am na sollo

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Месяц назад

    من يطع الرسول فقدأطاع الله 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @tombinhondiaye7461
    @tombinhondiaye7461 2 месяца назад +4

    Alhamdoulilaha rabi allah mina mbacké Sakho que Dieu te donne une longue vie ,cheikh Ahmed cissé longue vie à toi aussi vous faîtes un travaille extraordinaire réveilles des consciences,et comprendre la religion ce que Dieu à dit dans le coran Alhamdoulilaha

    • @youryboyiboyka7240
      @youryboyiboyka7240 2 месяца назад +1

      Cet homme te mènera dans les profondeurs des ténèbres. Le prophète Muhammad (Saws) a vécu pendant 23 ans avec des musulmans qui le voyaient pratiquer la religion. Toute la vie de Issa (Aleyhi sallam) n'a pas été racontée, ni celle de Moussa (Aleyhi sallam), le plus cité dans le Coran, et encore moins celle du prophète Muhammad (Saws). Sa vie de prophète, il l'a vécue avec ses épouses, ses enfants et ses compagnons, qui sont les plus dignes pour nous l'expliquer. C'est cela, sa Sunna.

  • @IbrahimaFall-g1i
    @IbrahimaFall-g1i 2 месяца назад +4

    Respect à seydina Ababacar,seydina Omar, seydina Ousmane, seydina Alioune

  • @BounamaNdiaye-vd4fb
    @BounamaNdiaye-vd4fb 2 месяца назад

    Macha halla wakhtane bi amena solo cheikh ameth Cissé fi gua tek sa lokho nonoula ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @hoorevision5753
    @hoorevision5753 2 месяца назад +4

    Cheikh Mbackè sakho❤

  • @lasource3996
    @lasource3996 2 месяца назад +2

    Yallah moy Dindé Niit Gni te leep ci mom lay bayeko.Kolou la Gueum ,Guiss bou set, Khel bou sell ak Deug gou leer moy Li wer. Yallah kessa mom rek .Dieure dieufati.

  • @mamadoundiaye8336
    @mamadoundiaye8336 Месяц назад

    Pertinent serigne sakho mais il faut un débat contradictoire pour qu'on puisse évaluer mieux ce que vous avancez

  • @thiernoousmanesow2110
    @thiernoousmanesow2110 2 месяца назад +4

    Merci mbacké sakho lou lér nagn ngay wax ..

  • @moussandiaye3859
    @moussandiaye3859 Месяц назад

    C'est un érudit il faut l'accepter
    Il éclaire la lanterne de tous ceux qui cherchent le droit chemin pour la soumission à Dieu soubhana wa talha.
    Ceux qui critiquent cheikh Mbacké Sakho sont juste des Imposteurs qui vivent uniquement l'ignorance des autres.
    Tout bon musulman doit l'encourager dans ce monstrueux travail qu'il abat.

  • @KhadimNdaw-m3o
    @KhadimNdaw-m3o 2 месяца назад

    Yalla na Yalla mousal si kou rér taye rêrelè mbakc sakho yéreum naka

  • @fezndiaye5088
    @fezndiaye5088 2 месяца назад

    Sénégal 1% de musulman

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Месяц назад

    Xalaas lii moom Ban Senegaal la?🤭🤭🤭

  • @sallpresi
    @sallpresi Месяц назад

    Yéne soléne niou moytouwoul dinéne Ray séne ndéye

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Месяц назад

    Mataar Sarr Moo leen gën fuuf

  • @Sénégal-aujourd8
    @Sénégal-aujourd8 2 месяца назад +1

    Mbacké Sakho ne croit pas au parole du prophète Mouhamed (Psl)

  • @cheikhly9218
    @cheikhly9218 2 месяца назад +2

    Serigne Touba est ma référence grâce à lui je serai toujours bien guider ; donc suivez le vraiment !!!

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Месяц назад

    رجاء جنةبلا طاعات- لسنة الماحى غرورايات

  • @MorNiang-hb5en
    @MorNiang-hb5en 2 месяца назад +1

    Attention Serigne Pape Malick Sy wédiwoule déme Makka dégue Lou wate ko
    Té niounale Serigne Pape Malick Sy Yalla yéssal yeurmadé si mome

  • @BayezaleSarr-le6sf
    @BayezaleSarr-le6sf 2 месяца назад

    Billahi da rérrr

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Месяц назад

    S Sam Mbaye de du sa moroom

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Месяц назад

    أعاذني الله من بك ساق 😂😂😂

  • @eddythiam2121
    @eddythiam2121 2 месяца назад +5

    Lou ler lay wakh Koy tontou tontouko thi xam xam

  • @SamaneNdiaye-mj5gt
    @SamaneNdiaye-mj5gt 2 месяца назад +1

    Toujours des questions terre à terre.
    Quand on parle de spirualité, lui parle de l'argent.
    Du n'importe quoi 😂😅

    • @SamaneNdiaye-mj5gt
      @SamaneNdiaye-mj5gt 2 месяца назад

      Un truand porte toujours des noirs fumés pour masquer leur carence.
      J'ai honte.

  • @moustaphasamb4297
    @moustaphasamb4297 2 месяца назад

    Assalaamou aleikoum, barina ay aaya youy sakhal Sounna. Sourate 33 verset 21 : En effet, vous avez dans le messager d’ALLAAH un excellent modèle pour quiconque espère en ALLAAH et au jour dernier et invoque ALLAAH fréquemment...
    Démal sourate Nissa verset 59: Ô les croyants obéissez à ALLAAH et obéissez au messager...puis si vous vous disputez en quoi que ce soit, renvoyez-le à ALLAAH et au messager...
    Sourate 4 verset 61 : Et lorsqu’on leur dit "venez vers ce qu’ ALLAAH a fait descendre et vers le messager", tu vois les hypocrites s’écarter loin de toi..
    Séétloul ni wakhoul les hypocrites s’écartent de ce qu’ALLAAH a fait descendre ,maanaame wéddiwougnou wakhou YALLA waayé yaw yonente bi lagnou doumooyou.

    • @moustaphasamb4297
      @moustaphasamb4297 2 месяца назад

      Ba léégui si liy wané Sounna. Sourate 4 verset 64
      Nous n’avons envoyé de Messager que pour qu’il soit obéi par la permission d’Allah. Si, lorsqu’ils ont fait du tort à leurs propres personnes ils venaient à toi en implorant le pardon d’Allah et si le Messager demandait le pardon pour eux, ils trouveraient, certes, Allah, Très Accueillant au repentir, Miséricordieux.

    • @mamadoundoye6929
      @mamadoundoye6929 Месяц назад

      Bayileen Di diawale diine Diouf mat AK Diouf matagouloon ci diamono yonent. Yonentibi Alkhourane laleen dawoon tontou sougniuko laadioon. Leegui yonentibi nekatoufi mais Alkhourane dji Moudon tontoo mounguifi. Yeewouleen.

  • @mahmouddrame6611
    @mahmouddrame6611 2 месяца назад

    Ki day fénne rék

  • @NdiayeNiangLadiane-kd6gt
    @NdiayeNiangLadiane-kd6gt 2 месяца назад

    Yeen li gën def ñawna ki tokk saga fi yàlla waxuma lakk boroom xam-xam bu melni oustaz Makhtar Sarr geen nekk fi diko May beug li dafa ruslu✅️✅️✅️

  • @MaurizioEmanuele-b5w
    @MaurizioEmanuele-b5w 2 месяца назад

    Ki wedina waliyoullahi yepoubayiwoullken wedina rasouli llahi wedina saykhoulkhadim wedinasekh sudilhadimalik da baga sampoutarikhboubess motakhmouywakh yallnaniou yalla mousall thi kouwedi rasoolillah Sakho niari yon diabaramdouma nagou douma youmeti nawakh louhti alkhouraan wakh

  • @MorNiang-hb5en
    @MorNiang-hb5en 2 месяца назад +1

    Serigne Moustapha Sy wakhoule né Yeuneunte Yalla Souleymane dafa ndialo
    Té limou wakh migui si téréyi borome xam xam you beuri binde nañuko.
    Sénégal wakh katte yi ño gueneu beuri borome xam xam yi

  • @MaurizioEmanuele-b5w
    @MaurizioEmanuele-b5w 2 месяца назад +1

    Ki wedina yalla wedina yonentebi wama yantikhou hanil hawa

    • @cheikhdiop9673
      @cheikhdiop9673 2 месяца назад

      yagui wax ci lo khamni khamosi dara dégloul bou bakh ak khél ak kham kham ta bagna déglo khol balagay mér Al khouran boko dégoul deug deug nigay amé diafé diafé ci nitt kou dég Al khouran diko firi niko yalla wakhé pas niko yénn nitt yi difiré comme gni toudé séne bopp ahlou souna bou yalla wakhé wolénma ma wouyoulén gnom gnoukoy firé gnane lénma mamayléne wakhi diambour wakhéko niko borom wakhé pas wout firi bou geuna nékh wala geuna dioub ci nigako khalaté yalla lim wax lolou la beuga wax bouko wakhé nénéne li Moy deug

    • @MaurizioEmanuele-b5w
      @MaurizioEmanuele-b5w 2 месяца назад

      @cheikhdiop9673 kon sani Touba. Limouy wakhthi younenttibi wedikengo aladii malik limouywakhwedigenko alkhouraan day dindiou liniou hazaf thi alkhouraan moabbou lafadess dagena baga woote tarikha boubess wante yalnanou yalla mousall thi wedi rasouli llahi ak maknii niari Yoon Sakho ay diabaram douma nanigoo douma youmeti nawakhhti loulou louhti alkhouraan wakh

  • @FatoumataFofana-s4e
    @FatoumataFofana-s4e 2 месяца назад

    J'espère que do sarakhoulé ndah koumana féne nga sa kanam bou leundeum

  • @tvsenegal2789
    @tvsenegal2789 2 месяца назад

    Say say

  • @birahimfall-y5f
    @birahimfall-y5f 2 месяца назад

    Ahmet fen nga Serigne Moustapha Sy wakhoul dafa ndialo de wakhal limou wakh

  • @englishclassmonitoringecm5152
    @englishclassmonitoringecm5152 2 месяца назад

    Il y a eu beaucoup de confusion entre différents hadith et leurs auteurs.

  • @MouhamadoumoustaphaNiang-n4j
    @MouhamadoumoustaphaNiang-n4j 2 месяца назад

    Alkhourane daye diokhe khaliss'petrol gaz or extra alkhourane daye obi wersak

  • @dameseye7253
    @dameseye7253 2 месяца назад

    Fene rek giyndef khamolin dara

  • @omarboye8080
    @omarboye8080 2 месяца назад +1

    Ki kouko topou di ngua rére alkhourane yonénetebi mome lako yalla firilo té yonénete bi moko firil sakhabayi sakhabayi firilko tabihiy yi nioukoy firilaneté ba légui

    • @Lara122e34
      @Lara122e34 2 месяца назад

      Douguene leral szn koutel sounnit.
      Legui chite yi niomite diap sen kourel moy deugue.
      Ces courels n'ont pas de differences avec ceux qui existent au senegal
      Deux verites n'existent pas.
      Donc lane mo siy deugue

  • @sallpresi
    @sallpresi Месяц назад

    Danio wara cotisé Ray ndayam

  • @ndiammesarrr9337
    @ndiammesarrr9337 2 месяца назад +3

    Jamono yonént teeré alkhouran kén dajélé wouko ganaawam lagniou KO dajalé gni KO gnioogniou andil haddiis kon boo wéddee haddiis wéddi waalee alkhouraan

    • @serignetine1420
      @serignetine1420 2 месяца назад

      Vraiment mbacké sakho mi dema yakkar defa dof

    • @yvefay620
      @yvefay620 2 месяца назад

      le coran n'est en aucun cas descendu du ciel .il a été créé par l' humain qui a puisé ds le zoastrisme Torah injil etc...le coran a été brulè plusieurs fois pour en faire UN par othman parce qu' il y avait bcp de versions et jusqu'à présent yen a au moins 26 versions ....le coran contient des mots que personne ne connait la signification et des mots qui ne sont même pas en arabe

  • @Diallo-2mahdi
    @Diallo-2mahdi 2 месяца назад +1

    En tout cas c la fin des temps Islam vainqueurs je suis le mahdi petit fils de prophète Mohammed psl ki wafi dara😂

  • @soldatby6603
    @soldatby6603 2 месяца назад

    Ki dadial leu khamélénko

  • @aliounefall4656
    @aliounefall4656 2 месяца назад

    Yaw mom mbam nga rek

  • @OumarTraore-jo8fo
    @OumarTraore-jo8fo 2 месяца назад

    Do dara

  • @Omasaar39
    @Omasaar39 2 месяца назад

    Kii dh barki yalla xamul dara

  • @BabacarFall-e7t
    @BabacarFall-e7t 2 месяца назад

    Ki day rereu late

  • @BayezaleSarr-le6sf
    @BayezaleSarr-le6sf 2 месяца назад

    Ki guemoul yonantabi

  • @FallMoussa-pi5db
    @FallMoussa-pi5db 2 месяца назад

    Khamo dara😂

  • @BabacarNiass-zb9lb
    @BabacarNiass-zb9lb 2 месяца назад +2

    Ki day nétali ligne firi si alkhour ann
    Wayé mounta firi alkhour aan

  • @MouhamedGueye-kl6jy
    @MouhamedGueye-kl6jy 2 месяца назад

    Domou Haram

  • @sallpresi
    @sallpresi Месяц назад

    Yéne soléne niou moytouwoul dinéne Ray séne ndéye

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Месяц назад

    Mataar Sarr Moo leen gën fuuf

  • @AliouNdiaye-lc3pp
    @AliouNdiaye-lc3pp Месяц назад

    S Sam Mbaye de du sa moroom