Débat Cheikh Mbacké Sakho et Ahmad Khalil Lo,un salafi sur clubhouse (Red Line room)

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 11 янв 2025

Комментарии •

  • @NihmaTV
    @NihmaTV  2 года назад +2

    Holy Quran 2:99
    ------------------
    وَلَقَدْ أَنزَلْنَا إِلَيْكَ آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ ۖ وَمَا يَكْفُرُ بِهَا إِلَّا الْفَاسِقُونَ
    Et très certainement Nous avons fait descendre vers toi des versets clairs. Et seuls les pervers n'y croient pas.
    Le lien du replay du débat sur clubhouse
    www.clubhouse.com/room/PvB5eQXX?WmuNg7_gW1B7GvpE7owyw-414419

  • @ahmedsarr5906
    @ahmedsarr5906 2 года назад +5

    Moytouleine français bou beuri bi.Soungueine di wakh wolof wakhleine wolof ,wala serere ,wala diola wayei meilnei domou toubab ,kheib sa bop la.
    Wakhouma nak Cheikh Mbacke Sakho wala Doctor Ahmad Khalil lo .

  • @MameSene-ez8xe
    @MameSene-ez8xe Месяц назад +1

    Macha allah sakho deug rék yalna borom bi dolila takhawou

  • @Neville-Imagination
    @Neville-Imagination 2 года назад +9

    Cheikh mbacke sakho mii kou saf sapp leu! Laaylaylala ! Machallah ci kham-kham bi.

  • @moussafaye9547
    @moussafaye9547 2 года назад +7

    Diadieuf cheikh mback sakho sa wakh lérna ta foulér ngako ték

  • @diopdiop7519
    @diopdiop7519 2 года назад +4

    Débat intéressant merci à vous tous

  • @fayealiounekane8727
    @fayealiounekane8727 2 года назад +4

    machallah

  • @moussafaye9547
    @moussafaye9547 2 года назад +5

    Mais ki sunnites là il né pas à la hauteur

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 года назад +5

    Ahmad khalil kham nga boubaakh ligniou lay wakh, tontou yi leer na. Yow yaa beugue niou wakhla lingua beugua déégu.

  • @abdoumbaye9185
    @abdoumbaye9185 2 года назад +4

    Al hamdou lilah

  • @omarfall6491
    @omarfall6491 2 года назад +2

    Machallah si xam xam bi cheikh Ahmadou mbacke sakho

  • @BaniAadama
    @BaniAadama 2 года назад +8

    Le concept de Sunna du prophète à mon avis est la source des tous les problèmes des musulmans.
    Dr Lo interprète les dires de CM Sakho avec une oreille très biaisée et déforme ses propos. Le simple fait de ne pouvoir comprendre que le contenu de la discussion des épouses du prophète n’a pas besoin d’être révélé dans le Coran m’intrigue. Juste parce que c’est mentionné dans les hadiths ne donne aucune légitimité ou n’est pas une preuve d’authenticité. D’ailleurs ALLAH nous met en garde de parler de choses dont nous avons aucune connaissance!

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 года назад +6

    Top yalla moy top ay wakham

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 года назад +7

    Mr Ahmad khalil lo yow nimala dégué gueumo Coran wala sen hadiths yi nga gueum ndaré alkhourane.

  • @badralioune6580
    @badralioune6580 Год назад +1

    Serigne Lo n est pas a la hauteur.Au lieu d echange d idee fondee sur le coran j ai le sentiment qu il fait que du Tesente .essaye de condanner Serigne Sakho .Son language Wor Worlo que j ai pas aime.Respect mutuel .

  • @boubacarsoumare9910
    @boubacarsoumare9910 2 года назад +1

    Que Dieu vous protège et vous donne longue vie.

  • @mamemorantasaly794
    @mamemorantasaly794 2 года назад +3

    Cheikh Mbacké mo gueuna convaincant ci débat bi.

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 года назад +8

    Top yalla meunoul wessou topou ndawli, wayé top ndawli meunoul wessou top liko def ndaw moi alkhourane.

  • @NjagaMbye-w7j
    @NjagaMbye-w7j 4 месяца назад +1

    ❤❤❤

  • @lampfall421
    @lampfall421 2 года назад +6

    Dr bi moom foumou dieulè diplôme bi😂😂😂 il est très terre à terre😂😂😂 thiéy waa sounnah😂😂😂

  • @sambatoure8810
    @sambatoure8810 10 месяцев назад

    Kham kham lérn na 🎉❤ ٱدْعُ إِلَىٰ سَبِيلِ رَبِّكَ بِٱلْحِكْمَةِ وَٱلْمَوْعِظَةِ ٱلْحَسَنَةِ ۖ وَجَـٰدِلْهُم بِٱلَّتِى هِىَ أَحْسَنُ ۚ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِۦ ۖ وَهُوَ أَعْلَمُ بِٱلْمُهْتَدِينَ
    Par la sagesse et la bonne exhortation appelle (les gens) au sentier de ton Seigneur. Et discute avec eux de la meilleure façon. Car c'est ton Seigneur qui connaît le mieux celui qui s'égare de Son sentier et c'est Lui qui connaît le mieux ceux qui sont bien guidés.

    • @NihmaTV
      @NihmaTV  10 месяцев назад

      Maachā’Allah

  • @Junior_Diouf98
    @Junior_Diouf98 2 года назад +3

    Yalla na Yalla geuneu dëgërël inchallah

  • @mordiop9959
    @mordiop9959 2 года назад +9

    mann mom luegui 2 raka rék lay diouli ndakh débat yimay déklou yép li cheikh mbacke wakho di wakh rék momana dougou thi sama bopou

  • @niangmoustapha9041
    @niangmoustapha9041 2 года назад +5

    Ñi dounou diguelou aye vakhtanam motakh kougnav la ka diak ladiane lay ladie li ngaye ladie tontou nako fouki yon

  • @sambmeissagaye9074
    @sambmeissagaye9074 2 года назад +8

    Cheikh Mbacké Sakho jàmbaar la de. Man de ay waxam mooma gëna doy.

  • @ndiayeablaye8745
    @ndiayeablaye8745 2 года назад +4

    MASALAH CHEIKH MBACKE WAKH DEUG YALLA LOULERR NGAY WAKH.YALLA NALA YALLA DEFAL DIAM AK BARKE AK WER AK GOUG FAN

  • @mdk2944
    @mdk2944 2 года назад +4

    Maachalah C.M.Sakho
    Diadieuf!

  • @kaolackvamal2881
    @kaolackvamal2881 2 года назад +4

    Gueum terré yi wessou ndigal la, kon lep lou yalla daganal si alkhourane té tereewoukofa sa terrés ya wessou la nek,

  • @moussaba2321
    @moussaba2321 2 года назад +1

    Merci cheikh mbacke. Alkhouran rék, késsé.Bayilén Hadiss Te top alkhouran alakhira mom kén Dou lathié Hadiss.

  • @boubacarsow6495
    @boubacarsow6495 Год назад

    Ya pas photo cams les ecrase il est clair et precis merci d ouvrir nos yeux

  • @baba8583
    @baba8583 2 года назад +4

    debat bi tle mo geun

  • @DIOBISTO
    @DIOBISTO 8 месяцев назад

    Masha-Allah docteur Ibrahim Khalil Lo, c'était un contre tous, même les modérateurs étaient avec Mbacke sakho mais vous les avez massacré tous
    Alhourane ak Sounnas rek moy deug ❤❤❤

    • @NihmaTV
      @NihmaTV  8 месяцев назад

      😂😂😂😂😂😂
      Khana déglou wo débat bi?
      Kii dafè wakh dara! 😂😂😂😂😂

    • @DIOBISTO
      @DIOBISTO 8 месяцев назад

      @@NihmaTV
      Sène wadji meunoul tontou question yi surtout sur les premières questions de Akhmed Ibrahim

    • @NihmaTV
      @NihmaTV  8 месяцев назад

      @DIOBISTO sène wadji ragal débat bi mo takhone nangou woul takhaw ci béne question, day enchaîner ay question ndakh kham na lou koy khar.
      Té question yoyou yeup Cheikh Mbacké dou ci meuna tontou en une fois.
      Té sène wadji débat bi yeup, amoul béne argument boumou ték ci table dji, day poser ay question di daw rek.
      Té débat bii takh na ba gnou bari ci sène mbok yi yèwou ba bayi salafisme, di top islam kessé!
      Guisso lègui ni ragalè Cheikh Mbacké ak question impertinente you gnouy poser?

  • @ameth148youretro7
    @ameth148youretro7 Год назад

    Mais Khalil lo warnagnko gnanale dhé comment il peut égalisé Hadith et Alkourhan

  • @FamaraSane-p2n
    @FamaraSane-p2n 5 месяцев назад +1

    Yalla néna borom xell yi lay wakhal

  • @gueyecheikhmbacke2194
    @gueyecheikhmbacke2194 2 года назад +2

    Cheikh Mb sakho ligay wax lerna indil ga ko dalil yi

  • @moussaba2321
    @moussaba2321 2 года назад +3

    Li mom Dafa Doy seuk .kou alkhouraan késsé Douyoul.moy yalla Doyoula

  • @hotsy3005
    @hotsy3005 Год назад +1

    Wahabistes khamougnou darra ndeketé

  • @ameth148youretro7
    @ameth148youretro7 Год назад

    J vois k khalil lo il est orgueilleux devant le Coran

  • @daoudandoye6143
    @daoudandoye6143 Год назад +1

    Alkhouran. Rek

  • @ibrahimadiagne8306
    @ibrahimadiagne8306 2 года назад +1

    Kane mo gagné 🤔

    • @beugyallarek
      @beugyallarek 2 года назад +2

      Gagner? Gagner kay amou ci solo, li am solo moy kane la ay preuvam wére té lolou yaakar na né tontou ko diafé woul.

    • @ibrahimadiagne8306
      @ibrahimadiagne8306 2 года назад +2

      Sén débat yi day sabab gnari mbir
      Bu njëkk bi mooy day tah ku gàtt xél jàpp ne alxuraan Ay contradiction la nah am ay mbir yu chéex Mbacké indi yoy Dr amu ci ay Lay yu jupp Dr aussi pareil
      gnaréer bi mooy parparloo dafay am ci gaa yuy teewlu

    • @beugyallarek
      @beugyallarek 2 года назад +3

      @@ibrahimadiagne8306 li nga wakh amna solo!
      Li ci gëna bonn nak moy parparloo waayé sou dee ci wàllu contradictions ci Alxuraan ji, so bàyyee xel débat bii ak débat Cheikh Mbacké yëp ñi miy waxal lén la ñuy wut a layal: Alxuraan matul, leerul té Yalla faram facce wuko.
      Té lii di wédi Yalla gu wer té leer!
      Motax Ahmad so bàyyee xel laajul lu nek ci teere bi, lu Cheikh Mbàkke mënul tontu.
      Ay wax yu teere wa ahlu sunna yi di wax né ñëwul ci teere bi mom lay laaj, té yénn Cheikh Mbacké wan na ko niko lolu ci millata Ibrahim la bok, bén bi mbir u kër u yonent bi té amalul njëriñ wëy gëm yi motax ba Yalla indiwu ko.
      Té yit njëriñul référence yi moy nit kuné mëna saytul bopam aya yi.
      Té ku ko def di nga xam kan la ay layam sax ak kan la ay layam saxul ci teere bi!
      Jërëjëf