on en veut plus.....nous vous felecitons du fond du coeur en passant dimbeu li leen gnou thi genrou emission yii.....lii mooy dohhall reew ndakh kou hamoul yaay kann doo d3mm f3nn et pourtant le pays en regorge tellement....nguirr yalla dimbeu li leen gnou thi yii..... eveillez nous davantage
Xam xam rekka wor dé. Même ceux qui dirigent l'émission sont dans une concenration trés profonde de par l'éloquence, la clarté et la maitrise du théme. 3 thémes ont été traité durant l'émission. Le coran Le ptophéte Tarikha Cheikh et grandeur d'Elhadji Malick.
Ndeysane wa tivaoune nio diang té am yar deh djital yalla souniou borom ak yonantam bou tedeu bi Maodo yar gua diour gui té dorei diangal gua say talibés ba douniou la diawalei ak sen borom
Ah constant si Sama sope Serigne Ahmed Sarr machalah kham kham bi selna trop walla hi niepa contant billa hi yalla ngafi yag lole te am weur sisa Barke Mame Khalifa ak sa Serigne Borom Daradji
Salamou h s fatimatou sarr man la Mohamed diop kuere mam chekhe mbaye djielall sama numéro watziab/ 782081390/ noumero Ahmad sarr mom la sokhla djiapoulé ma si mie langui ni kaoulack fi lay djianguelé djiapou léma si
Bilahi walahi ken dou maodo fi si sénégal lomou binde si yonenti bi ken binde lounou Mel yalna naiou ka yalla fayal kou degue ahmet sarr khamni da am kham Khan ta ki talibé la
Vendredi 28 juin 2019 , 11h02 minutes heure de Paris, émission bi doumassi doyal, yalla na yalla défe diamm au Sénégal et partout dans le monde amine 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
merci pape....a ton equipe egalement diappa lê leen gnou. ..vous qui avez la voix au chapitre vous avez la lourde reaponsabilite deveillez les consciences
Ki regarde encore c vidéo en 2019 bilahi doumasi meuseu doyol barki SERIGNE babacar sy Rta kene dou seydi El Hadji Malick sy Rta yalla na yalla Yoko leerame tasgnou si barké🙏🙏🙏🙏🙏
Merci ma mère sokhna Maréme Dieng que le tout puissant Allah vs accueil dans son paradis Firdawssi amine inchalla ci barké Seydina Muhammad psl sy barké Seydina cheikh Ahmed Tidiane cherif RTA sy barké khalipha Abou babakar sy RTA amine mala beugggggggg bayiwofi xass fouma nékh diarr fouma nékh daggou
bilahi khôl séd na gouyou Oustaz yalla nala yalla fay si sa barké mame xam xam bii séll na té rafét na téy na wayé kén d'où sougnou mame séne mame mamou kou nara bakh
Machala alhamdou lilah yallah naniou ko yalah fayal yokou leram wayé lima diakhal moy nioune prkw kham kham bobou nek fi gnouye dém ay arabie saoudi ak ay maroc di diangui nagne défarat sounou ay togay valoriser lifi mag yi bayi ba afriq yeup nieuw fi di diangui
Dieuredieuf serigne yalna yalla fayla yok sa xam xam keur MAME CHIEKH SEYDIL HADJI MALICK li la sohla xam xam ;pas wahi casssarkasarr Dieuredieuf SARR.
yala naniou yala fayal mame maodo wané na lép thi seydina mouhamed fi lépa lerr serigne bi kham kham bi séll na woor na té yar bi mogui fi fiere d'etre talibé cheikh
seydi khadji malick dal amoungou fayam bilahi khamal nagn seydouna mouhamed psl ak yalla bou bax sax lima kham si naby lep dal soudoul won mom dal douma ame louma nex
Senegal lokho mame asse thi biir louko moye gal gui dotoul dem sy demba gagne yagnou khamal yonetebi ak wa keurem Element SERIGNE BABACAR SY rek ba faw
Salam. Alhamdoulilah. Machaallah El Hadj Mawda Malick Sy. Yalla ak Yonent bi Salalahou Aleyehi Wassalam rék nga diangalé té li moy li wor té weur. Alhamdoulilah
ahhhhh kokou moy borom daraji borom sa mame nena borom ma bikam ma dem borom sagnse bi borme khilas bi borom limocin bi borom biye makayi borom kharou tabaskiyi borom factur kouran ak ndokhyi borom réniu nekh dii
thieye sama tourando mamou Serigne cheikh tidiane sy ki atmos fert bi di dioye ba legui diarama seydil hadji malick sy mom rek mo fi fekka iddiasa itlakh si cheikh elhadji oumar foutiyou tall
Lii doumassi doyal waay, Serigne Ahmed Sarr yalnala sougnou borom Faye yiiw boulaye topeu bassaye seuti seut machaallah togaye bii yiw naa kadou yii celeu naa kham kham bii woorna leip lofi wah diné laa ...yalnala sougnou borom fayal bopam
C’est le meilleur vidéo je l’écoute jusqu’à 2021 Douma thi doyal
J l'écoute tjr moi osi
on en veut plus.....nous vous felecitons du fond du coeur
en passant dimbeu li leen gnou thi genrou emission yii.....lii mooy dohhall reew ndakh kou hamoul yaay kann doo d3mm f3nn
et pourtant le pays en regorge tellement....nguirr yalla dimbeu li leen gnou thi yii.....
eveillez nous davantage
Xam xam rekka wor dé.
Même ceux qui dirigent l'émission sont dans une concenration trés profonde de par l'éloquence, la clarté et la maitrise du théme.
3 thémes ont été traité durant l'émission.
Le coran
Le ptophéte
Tarikha Cheikh et grandeur d'Elhadji Malick.
Walahii vérité indubitable
Maodo moye serignou serigne si lolou la Yallah deff diarama Mame Maodo
Ousmane Niang Wawaw té mouy Deugg
Fier d'etre talibé tidiane cheikh machallah pape cheikh yangui doga invité...invité de mark
CHEIKH Seydil Hadj Malick RTA dal dou morom dou mass dou mapando motakh mou Niane Yalla Boromam bouko Kèn kham fi si Dounyaa naniou bayi ba Euleuk Yawoumal khiyamam niou kham kimou done DIARAMA MAME MAODO MALICK SY RTA ❤❤❤
Meilleur QG de tous les temps jusqu a 2024 je le suis
Douma si doyal kene dou serigne babacar ani gni sètane 2019
Niogui'ni... Deysane
@@falconseyetros1606 nieuwate léne niou yéssal
@@diopbaps1481 mashallah.... Ya khalifa rek
2024
mashallah Mame Maodo do sen morom. Il a toujours tenu debout le flambeau de l'islam au Sénégal. Yalla nako yalla faye
War na amat d jap lein ci Wa tfm 😭
Merci Mame Maodo amuniu sa day Sy Malick
Ndeysane wa tivaoune nio diang té am yar deh djital yalla souniou borom ak yonantam bou tedeu bi
Maodo yar gua diour gui té dorei diangal gua say talibés ba douniou la diawalei ak sen borom
Billahi Mame maodo nimako beugué yalla rek moko kham ❣️ yalla nagnou ko yalla fayal 🙏
wakeur cheikh seydi Elhadji malick sy danio maitrisé yonéntibi machalla yalla naléne yalla sam si seydina Mouhamed salalahou aleyhiwasalam
Ibrahima Faye yén loléne métrisé
Mame cheikh seydil hadji malick sy yalla nagnou ka yalla fayall. Oustaz amet sarr gnongii lay sante dila gueureum diila kharatt QG bii dii gneuw
Moy gneuw le 31mai prochain
Bilahii xam xam dou xeutt xeutt neikk fii aaaaaaa rk ishhh oustaz ameth Sarr koula deiglou xamnii Maodo deiff na sii yeneu dara machalah
Waalahi yalla nagnou yalla feyale mama maodo malick sy fiere d etre taalibe cheikh
Douma thi doyal yalla naniou yalla fayal Mame maodo ❤❤
Alhamdoulillah si barké salatoul fatiha yalna yalla fayalniou cheikh seydi hadji MALICK sy rta Ahmed sarr yalna yalla doli soutura gui
Cheikh seydi hadji malick reste toujours l'inconnu de la nation.
Doudou Diop lol sakh aka neubou
MachaAllah. IL ya une chose à souligner c'est qu'on ai mentionné Seydina Cheikh RTH, une seule fois alors qu'Il est au centre de Tout.
Maachaallah pape Chéikh indiwaatal kii thie QG 2019 nguir yalla. khol sédena lool waay
Ndéy Faye, moom moy ñiow InchaAllah
On le réclame
Pour ma.....man kasé makoy sétan en 2019.......université Maodo rk mo worr.....gni koy djangalé tmt yalah nalénn cheikh fayal bopam🤲🙏
Qui regarde encore c vidéo en 2019. Mane mom douma si doyal xam-xam ak pédagogie rk mo wor
Aminata Dramé dinagne invité kou guene graw❤️🙏🏾chaque année ak kou bess
Mane dh mom la sétane ni douma si doyal diko sétane ak diko dougal statut
Mangui nii dh 🙏
@Aminata Dramé wh c lui qui viendra
@Aminata Dramé réne mome lagne invite
Ah constant si Sama sope Serigne Ahmed Sarr machalah kham kham bi selna trop walla hi niepa contant billa hi yalla ngafi yag lole te am weur sisa Barke Mame Khalifa ak sa Serigne Borom Daradji
Machalah maodo
Mame maodo Khame Lép te mandou
Ani gnikoy setan ba legui ndax beug Mame Maodo,Yallnaniouko YALLA fayal
la petite Diop je suis la
Mangui dhe
Walay manguini déhh
Niogi ni
la petite Diop amiiine
Qui regarde toujours en 2020
Qui regarde en 2020?
Douma si doyal!!❣️😍
Oh Serigne Ahmed Sarr nio bok deuk louga magam Serigne pape Sarr nianal nama 🙏 machallah
oustaze pape hanne nite kou nité la Macha Allah ta AM pas pas silimouy déf yalna yalla dolico lér ak soutoura inchallah
Diagne Ousseyou amine
Thieuyy Maodo yalna neignou yalla deff aayy talibémmm si deuggg 🙏❤️🙏
sama papa dji jtm way yallah na la yallah sam si sa barké baye abdou karim sarr ak sa yaye oumou touré si sa barké mame sokhna astou sy
Yaw maa beug oustaz té beug ko guiss
Salamou h s fatimatou sarr man la Mohamed diop kuere mam chekhe mbaye djielall sama numéro watziab/ 782081390/ noumero Ahmad sarr mom la sokhla djiapoulé ma si mie langui ni kaoulack fi lay djianguelé djiapou léma si
Maman Ndiaye ay yaw dama yekha guiss sa message
Muhammad Diop baalma dh guissou ma wone message bi kharal ma diox lako
soukhna fatimatou numéro oustaz Ahmed Sarr té yalla takhh
Salam alhamdoulilah. Dieureudieuf Serigne Ahmet Sarr. Yalna borom bi same soutoural barkéle yeureume dioulit yeup amine. Mame Maoda dieureudieuf ya gnou khamale Seydina Mouhamed Salalahou Aleyehi Wassalam...
Machalah xam xam du leen seigne Ahmeth Sarr yalna yalla feyla yagallafi ci barke Maodo
25 mars bis bou Serigne babakar sy géné adouna niou sétane ko 2021
Bilahi walahi ken dou maodo fi si sénégal lomou binde si yonenti bi ken binde lounou Mel yalna naiou ka yalla fayal kou degue ahmet sarr khamni da am kham Khan ta ki talibé la
BILLAHI WALLAHI TALLAHI YALNANIOU YALLA FAYAL CHIEKH SEYDIL HADJI MALICK SY
Aminnn
Amine
Amine
Amine
Amine
Vendredi 28 juin 2019 , 11h02 minutes heure de Paris, émission bi doumassi doyal, yalla na yalla défe diamm au Sénégal et partout dans le monde amine 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
merci pape....a ton equipe egalement
diappa lê leen gnou. ..vous qui avez la voix au chapitre vous avez la lourde reaponsabilite deveillez les consciences
QUI ES LA Avril 2020 MACHALLAH
Machalla kenn dou seringe elhadji malick sy amoul morome thi xam xam billahi
Mashala ki regarde encore l’émission 2020
Ki regarde encore c vidéo en 2019 bilahi doumasi meuseu doyol barki SERIGNE babacar sy Rta kene dou seydi El Hadji Malick sy Rta yalla na yalla Yoko leerame tasgnou si barké🙏🙏🙏🙏🙏
Merci ma mère sokhna Maréme Dieng que le tout puissant Allah vs accueil dans son paradis Firdawssi amine inchalla ci barké Seydina Muhammad psl sy barké Seydina cheikh Ahmed Tidiane cherif RTA sy barké khalipha Abou babakar sy RTA amine mala beugggggggg bayiwofi xass fouma nékh diarr fouma nékh daggou
bilahi khôl séd na gouyou Oustaz yalla nala yalla fay si sa barké mame xam xam bii séll na té rafét na téy na wayé kén d'où sougnou mame séne mame mamou kou nara bakh
Machalah thiey maodo yalnaniouko yalla fayall
Bilay xam xam mo nex man dal nawna borom xam xam barki cheikh sabdou
Machala alhamdou lilah yallah naniou ko yalah fayal yokou leram wayé lima diakhal moy nioune prkw kham kham bobou nek fi gnouye dém ay arabie saoudi ak ay maroc di diangui nagne défarat sounou ay togay valoriser lifi mag yi bayi ba afriq yeup nieuw fi di diangui
wa manli bi oustaz ine yourabi mouridaho ......thiey maodo yalna yalla yoki leram
Barki serigne touba mane sènégale diakhale nama dislike yi loukowarale 😭😭😭 wala dane nion rakh
Dieuredieuf serigne yalna yalla fayla yok sa xam xam keur MAME CHIEKH SEYDIL HADJI MALICK li la sohla xam xam ;pas wahi casssarkasarr Dieuredieuf SARR.
Amine
J t'adore oustaze yalla nala yalla faye
bilahi wallahi kendou Maodo yalla nako yalla fayale si barké sopé seydina Mouhamed
Bilahi yalla nagnou yalla fayal Maodo kèn dou mom
yala naniou yala fayal mame maodo wané na lép thi seydina mouhamed fi lépa lerr serigne bi kham kham bi séll na woor na té yar bi mogui fi fiere d'etre talibé cheikh
seydi khadji malick dal amoungou fayam bilahi khamal nagn seydouna mouhamed psl ak yalla bou bax sax lima kham si naby lep dal soudoul won mom dal douma ame louma nex
Mouhamed Sambe bilay wahal
Khol s3d rék lay déf mbokhay seétan b ilakhi y aalla nañiou yalla tass si barké mawdo👏
Thiéy Cheikhoul Hadji Malick SY.
Yalla nanou Yalla fayal Mame Maodo
Machallah yalnaniou yalla fayal seydi Hadji malick walahi amoul morome sy malick
Senegal lokho mame asse thi biir louko moye gal gui dotoul dem sy demba gagne yagnou khamal yonetebi ak wa keurem Element SERIGNE BABACAR SY rek ba faw
ngala li bumudi guathie kholyi sedanan
Yalla na niou yalla fayal Maodo Malick sy machalla
Diarama Mame maodo yalla na nou yalla fayal
Ñiou wadial QG 2019 spécial seydil hadj malick avec Ahmed sarr
C est quand ?
Sou programme bi changé woul le 31 mai inchalla
Guen ñianal ko bou bax Mogui kay paré pour begual sopé seydil hadj malick yep thi xam Xam
kagne la
Le 31 inchalla
Bilahi deugeu deugeu wa tivaouane akk famille el Hadji Omar hame hame bou bari là machallah
Yalniou yalla maï topp akh dègue machalla souniou mame
sama khol sed na way yalla na yalla fay sounou serigne si nieup nak senegal bein la mouride tidiane ect.. ngom nieup yalla rek molein ngor walay
Mouhamed Sambe walahii nio bokk Islam kenn waroul hass sa morom, t kouko ci def, def nga lou sa serigne beugoul wahoumalak yalla
Mouhamed Sambe soumou khoules seeds na
Senegalese Queen
ma cha alla seydi el haji malick yalla nako yalla fayalniouko ay yiwe
PATHÉ SECK SAME
li nékhna trop Machalla sy
Rien n'est trop beau d'être tidjiane ❤️❤️❤️❤️❤️
Kou yakam ti spécial QG sougnou Mame Maodo ??
qui est la en 2021🙏🤙
yalla nagnou yalla fayal maodo si barkei rasoulillahi saws machallah Ahmed sarr
Allhamdoulliah bi sou niou borome defeii tallibei cheikh bolei niou thi sopey seydina mouhamed
Xam xam reck mo woor machallah fière de wa keur elhadj malick
Douma si doyal bilay yalla na diam yak Sénégal amiin yalla na yalla défar djiko yi djiégual gni djitou atté len si yeurmandem amiin
Machalah serigne Ahmed Sarr borom xam xam bou mak bii
Yalnanou yalla sahal si euttou cheikhal Hadji malick sy
Amine
diarama seydil hadji malick sy dieureudieuf sama serigne boudoul wone yow gnou rér
Machallah ki é la en 2019 thiey mame Ass
Yalna yalla goudeul sa fane
Qui regarde encore 2021
salatou wasalam hala rassoulilah .hamdoulilah halah koulli hal.
fière de faire partie de la tarihatou tidianiya.
contane naniou lolou.
Salam. Alhamdoulilah. Machaallah El Hadj Mawda Malick Sy. Yalla ak Yonent bi Salalahou Aleyehi Wassalam rék nga diangalé té li moy li wor té weur. Alhamdoulilah
Merci pour les 6h et 18h Elhaj Malick Sy
mashalla sameu xoll fess neu MAME MAODO yallah neu nalla yallah fayal niula
ahhhhh kokou moy borom daraji borom sa mame nena borom ma bikam ma dem borom sagnse bi borme khilas bi borom limocin bi borom biye makayi borom kharou tabaskiyi borom factur kouran ak ndokhyi borom réniu nekh dii
machalah nii rk leu meuneu dmé. maodo rk la meuneu doone
Sama xol sedd na mame cheikhal khadj malick maodo yalla nako yalla fay
Mame maodo dall diangal na ay talibèm yare na léne machallah mon takh nio raw téllé Bo dègg xam xam khamal ni niabotou Mame maodo la
Ki regarde encore 2020 doumasi doyal
machalla yalla na yalla fayall niou seydie haji Malic sy
Fier d'être talibé cheikh
thieye sama tourando mamou Serigne cheikh tidiane sy ki atmos fert bi di dioye ba legui diarama seydil hadji malick sy mom rek mo fi fekka iddiasa itlakh si cheikh elhadji oumar foutiyou tall
Bilahi walahi watalahi seydi elkhadji Malick Sy amoul morom si adouna
Manchallah kén dou Mame Maodo défar na magu ñi yarna ndaw yi
Qui regarde ce vídeo en 2020
Qui le regarde en 2021
Yalla na ko yalla feyal maodo Malik sy sy sy sy sy sy sy sy sy sy sy sy sy
بارك الله فيك
ana njiko beugueu sètane thi vendredi bou souba bii
Ki regarde en 2020 ndax deugue you deugou we ni
maodo kéneu dou yaw sante yalla bama la sopé sope cheikh oumar sope cheikh tidiane cherif wayé sope ki waral thiow lii (saw)