NET TALI: Niarelle Bi Dafa Am Far

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 16 фев 2024
  • Net Tali: Histoire Extraordinaire, NET TALI: Niarelle Bi Dafa Am Far
    #faitsdivers #kebetu #team221
  • КиноКино

Комментарии • 79

  • @mamadousarr3371
    @mamadousarr3371 3 месяца назад +20

    Nako baye manouko yor te diel khaleyi yobou sén keur, yow peul rek nga mana don diamu sérére 😢❤

  • @oumarmbaye7905
    @oumarmbaye7905 3 месяца назад +2

    Maniko thia tieuy 😂 yafi nék dei amal diam rk 😊merci mom na bayi ndawsi té souféké mo diour khaleyi mou téyélén

  • @guerrierdelalumiere3195
    @guerrierdelalumiere3195 3 месяца назад +13

    Na récupérer dom yii dilan doundal té bayi femme bi

  • @abdoukhadredjitte1712
    @abdoukhadredjitte1712 3 месяца назад +9

    Lima Beuga wah meunoumako binde Vocal rek

  • @amethngom7873
    @amethngom7873 3 месяца назад +2

    Mane sama problème moy nou gor yalla di ragualé diabarame c est bizare ça 😢😢😢

  • @mamyfallougalass1959
    @mamyfallougalass1959 3 месяца назад +2

    Salam sister fatou wadji na dieul ay domam ta bayiko ta yallah takhe 😢sama wal ci caffè ☕ gui merci et Bonne Continuation ❤❤❤❤❤❤

  • @daoudathiam9086
    @daoudathiam9086 3 месяца назад +2

    Mashallah Fatou❤❤ min ko pulaar 100 % 💯👂 bravo courage🤲🤲

  • @user-nm1pf3oy2e
    @user-nm1pf3oy2e 3 месяца назад +2

    Ndaysan maniko thi eskeuy bobou mom mamou mako mougn😅😅😅 mais nak je vous apprécie beaucoup 🙏

  • @moriciss6368
    @moriciss6368 3 месяца назад +7

    😢😢no vraiment amna wadouir nio khamni billahi douguou bir souf moléne téré douguou safara xallé bou djiguéen bi mo bonne deug

  • @djaliou2622
    @djaliou2622 3 месяца назад +3

    Sénégal yangu Na tass 😢 émission nekh ana sa ma cafe

  • @user-nl9us4hs6k
    @user-nl9us4hs6k 3 месяца назад +2

    Sawayyy tél say doom outii diabarr diou bakh

  • @aichaalarbaallf4359
    @aichaalarbaallf4359 3 месяца назад +1

    Ma belle lolo héw am dieukeur am farr lolou dou Dara si adouna légi

  • @allaniang8375
    @allaniang8375 2 месяца назад +1

    Risque lue ragall doukou defff😂😂😂😂 duelii kay khana daga dof😂😂😂😂

  • @adjalam6611
    @adjalam6611 3 месяца назад +2

    Maashallah
    Wonderful ❤

  • @user-fd4mt5yg1c
    @user-fd4mt5yg1c 3 месяца назад +2

    Salut,na bal mou yobouko deuk ba😂😂

  • @aissatoudionne5960
    @aissatoudionne5960 3 месяца назад +9

    Yaw yallah sauver nalla ba réyoula billay Boko andi waté sa keer boula diékou waté meun nalla réy donc li Malay conseil moy ngua bayi ko dém xallé yi sou nanguou woul ngua yor lén ngua bayilén ak mome té xamné yallah mo yorr niëp di ndoudal niëp aussi donc yalna lén yalla samme

  • @NogayeMbaye-yd5pp
    @NogayeMbaye-yd5pp 3 месяца назад +3

    Werou koor kay émission bi waroul am ndax netali yeufou diambour la ci sama guiss guiss 🙏🏿🙏🏿

  • @TawouyayameNdiaye931
    @TawouyayameNdiaye931 3 месяца назад +3

    Beuss bouko takaaté dh na khamni daffa kharou koula tiim ak diaassi déssélatoula dara

  • @aboubacardiop8804
    @aboubacardiop8804 3 месяца назад +2

    🤣😂😂cassou café

  • @moussafall741
    @moussafall741 3 месяца назад +5

    Thieye yalla thieye thieye😂😂😂

  • @MambayeSeck-qi3ux
    @MambayeSeck-qi3ux 3 месяца назад +2

    Mai wadji eska mo diour khalé yi

  • @madonaniang9363
    @madonaniang9363 3 месяца назад +3

    Il faut se débarrasser d’elle elle est trop dangereuse c’est pas sûr pour sa sécurité la dame est capable de le tuer a tout moment pendant son sommeil mais faudrait qu’il récupère ses enfants pour leurs bien être et leur éducation c’est mieux comme ça

  • @twotane
    @twotane 3 месяца назад +2

    N'a dém défi test ADN pour les 6 enfants

  • @user-nf6dc7xv9q
    @user-nf6dc7xv9q 3 месяца назад +4

    Il n'a ca récupérer ses enfants et les enmene au village

  • @FatimaZahra-jz7jd
    @FatimaZahra-jz7jd 3 месяца назад +1

    😂😂😂gua def meulfeu

  • @FatimaZahra-jz7jd
    @FatimaZahra-jz7jd 3 месяца назад +1

    Nako teuyi teh yallah taxx pour khaley yi

  • @user-mu1ss7lx2c
    @user-mu1ss7lx2c 3 месяца назад +2

    Na dieul dom yi tè bayi sokhna si si non dina si am louko mety

  • @user-nm1pf3oy2e
    @user-nm1pf3oy2e 3 месяца назад +2

    En tout cas na kham ni khalé si ay responsabilité la nék lepp loumou def si famille bé rk Dina ko def fé yallah nakho yallah duapalé rk

  • @user-pd9br6mk3g
    @user-pd9br6mk3g 3 месяца назад +1

    Nako bayil

  • @fatousow7929
    @fatousow7929 3 месяца назад

    Min ndiafimaama bandam.
    Fulbe fof ko gotoum ( poulloh diery, foutanke, poulloh fouta, poulloh firdou, poulloh niger, cameroun, ghana, nigeria, somali, Érythrée, soudan)
    Enen en ngala pays mais enen ndieyi Afrique!!!❤

  • @LenaSeck-eu9ty
    @LenaSeck-eu9ty 3 месяца назад +3

    Nako bayi mou dem mou dieul ayes domames

  • @sambaliou5859
    @sambaliou5859 3 месяца назад +2

    Li Lensment la filme bi nieuweugoul bouko fasséwoul ndawsi dinako raye diabar Diou Bonn Ak beugne bouy métti nioyam bouddi sanni .amoule lenene

  • @abdouazizsarr7474
    @abdouazizsarr7474 3 месяца назад +2

    Mayma café way

  • @Tigresse0000
    @Tigresse0000 21 день назад +1

    Yow guissago dara gnak diom torokhal sa awo ndah djiguene esk ya diour khaleyi

  • @madickediop968
    @madickediop968 3 месяца назад +2

    Na jel ay doomam yobbu ça dekk bé té bayi ndawsi kooku moom du jabar Fatou mi salminiima nu feewi a jaaraama

  • @kandejack9988
    @kandejack9988 3 месяца назад +2

    Tu fais la publicité de café, j'espère k cette entreprise te paie.😂

  • @fayembene3609
    @fayembene3609 3 месяца назад +1

    Loynane khana doudiékh

  • @abdoulayebalde2508
    @abdoulayebalde2508 3 месяца назад +2

    Merci pour votre travail

  • @iboukane5176
    @iboukane5176 2 месяца назад +2

    Bouko meusa dieuli jamais

  • @lahaddioplahaddiop4145
    @lahaddioplahaddiop4145 3 месяца назад +2

    Pour man de varoulvon taka niarèl ndakh defoul lomou man kou meunoul yor niari keur loy doyè niari diabar li reka takh rew mi tou dem

    • @Maguette313
      @Maguette313 3 месяца назад

      Merci bougnu amei ass tout rek torohal s’en awo yi wayei allons rek

  • @AwaFall-ju3vk
    @AwaFall-ju3vk Месяц назад +1

    Boumou ko dieuli dé

  • @isabellelaurence2172
    @isabellelaurence2172 3 месяца назад +2

    On veut la traduction de la partie en pular Fatou

  • @abdoulkhadrecisse5087
    @abdoulkhadrecisse5087 3 месяца назад +1

    Jamais elle va jamais changer .souko takhatei dinako trompé watt .Mom kayy nako bayi fofou reikk .
    Je connais une histoire qui ressemble à cette histoire.

  • @user-ct8it2pg1w
    @user-ct8it2pg1w 3 месяца назад +1

    😢😢😢😢😢

  • @Xippillxole
    @Xippillxole 3 месяца назад +1

    Il est toujours amoureux de sa femme mais ta femme elle ne t aime plus parle avec ton ex femme pour recuperer tes enfants si elle accepte si elle refuse continu tes mille franc elle se debrouillera pour gerer sa nouvelle vie puissque tout cela c est de sa faute elle assumera ses enfants mais oublie de te remettre avec elle sinon dinala ray bon courage monsieur yalla nala yalla takhawou

  • @KhadySyllaSylla
    @KhadySyllaSylla 17 дней назад +1

    Ki yakena der diiguéen wa yaal bahna wa mangui Wat nani diiguéen ki dinasouno

  • @AmadouNdiaye-iw7js
    @AmadouNdiaye-iw7js 2 месяца назад +1

    Infidélité kèn douko diègalé c'est tout, koulako déf dangko wara fassé kelk soi le motif

  • @abdouazizsarr7474
    @abdouazizsarr7474 3 месяца назад +1

    Pourquoi consulter son téléphone à 5h du matin ?
    Sûrement le mari n'assure plus au lit....
    C'est la seule raison qui pousse à une femme d'avoir un copain en laissant son mari de côté.

  • @user-gx5nm4nj4p
    @user-gx5nm4nj4p 3 месяца назад +1

    Boum ko dieulad ndakh bimouko trompé mou balko lolou lou bakhla wayé nak diko guénél diasi no lolou mom woroul wolouw mako

  • @ndaongone8443
    @ndaongone8443 3 месяца назад +1

    Biss Bo reppe ba dugate si femme bobu Dina la raye ga kham !! Il faut se détacher des personnes toxiques

  • @SopeNdiaye
    @SopeNdiaye 3 месяца назад +1

    Na dieul ah domane yobou mo deukeube bayi gemme bi

  • @thehighlight7904
    @thehighlight7904 3 месяца назад +1

    Metina n'a teyè dom yi yor lene t bâyi KO moudem taxawalou ji

  • @moriciss6368
    @moriciss6368 3 месяца назад +2

    Nako bayi mes aye domame naléne topato tes na bayi xalé bou djiguéen bi sino dinako raye mes 1000f deuinoul sakh néki pour dome yi

  • @wourelsow1482
    @wourelsow1482 3 месяца назад +1

    So yoroul dal khamal da bop gorou Sénegal djakhalnagnouma yoro ba paré di takeu ay djabar rek di djour rekk di tek tamit ish topatol sa dome yi gua bayi sene yaye sinon dinala rey

  • @user-mi3ej4jb7k
    @user-mi3ej4jb7k 3 месяца назад +1

    Salut sokhna Fatou on ne peut pas vivre avec une femme ki pratique l'adultère

  • @OumarTagourla
    @OumarTagourla 3 месяца назад

    ❤❤❤❤

  • @HousseyNouWade
    @HousseyNouWade 3 месяца назад +1

    Badole même seke sango dou sete teh ngorsi doyna ware jiggen sou xame sa point faible doto amme diame you melni bayyil deme rek

  • @beugdeug5553
    @beugdeug5553 3 месяца назад +1

    Il faut la laisser complètement est-ce-que tu es le père des enfants, cherche une autre sinon reste la première

  • @amisao8397
    @amisao8397 3 месяца назад +1

    Sokou bale mo rayi bopame

  • @Nitoudeug398
    @Nitoudeug398 3 месяца назад +1

    Wadji mo gnak bop rek ték si wayadi

  • @abdouazizsarr7474
    @abdouazizsarr7474 3 месяца назад +1

    Il doit récupérer les enfants d'abord.
    Pour la femme mom c'est pas sûr puisque daffa guéné diassi... elle peut le tuer à tout moment.
    1000 F daffa touti sur 6 enfants à nourrir.
    Avoir 2 femmes est l'erreur qu'il a commis parce que manoul... yemal ci bennn c'est mieux

  • @mameboussombaye7397
    @mameboussombaye7397 3 месяца назад +1

    Waadji nak boufékkéni mojour 6 dome yi moléne wara doundal thi l'islam, boudé dom you Goor yi Ba kérok niouy Manal séne boppou, boudé dom you jiguiéne yi ba kérok mouléne Di may jakeur.

  • @abdouldioume9633
    @abdouldioume9633 3 месяца назад +1

    Mais na dieule ay domame yo bou KO deuk beu mo guene te mou bayi KO Mou khol ba kham bakh Dina changer bakh mais Lou guene Na dieul ay domame rek. Abdoul Dioum from pointe noire de congo

  • @OumarTagourla
    @OumarTagourla 3 месяца назад +1

    , 👂👂👂

  • @diopyakhame5283
    @diopyakhame5283 3 месяца назад +1

    Na récupérer aye domame ta bayyi ndaw si

  • @ndeyeawasow8998
    @ndeyeawasow8998 3 месяца назад +1

    Nako bayiii tout tranquillement tes mou dieulli aye domame yobouko si aye parents wame djiguène monme bou boné rék bone naaa

  • @thiounelepuissant8712
    @thiounelepuissant8712 3 месяца назад +1

    Salut comment vas tu sister si j'étais moi je vais laisser la peste femme et d aller en pfair la garde des enfants

  • @MariaAlverenga
    @MariaAlverenga 3 месяца назад +1

    Ndow si na seyi sa keur gu mak wala mu jeul ay domam

  • @awafall5243
    @awafall5243 3 месяца назад +1

    N'a bayi femme bi tranquille dafa bone

  • @DameLo-uz4mr
    @DameLo-uz4mr 3 месяца назад

    Je cherche un drianké pv bou thiaga isi

  • @sokhnalo3334
    @sokhnalo3334 3 месяца назад +1

    Na dieul aye domam tes bayi diabare dji

  • @user-fd4mt5yg1c
    @user-fd4mt5yg1c 3 месяца назад +1

    Salut,na bal mou yobouko deuk ba😂😂