Non sokhna Fatou elle est extraordinaire Macha'Allah elle raconte très bien avec sa tâche de café je me contente toujours de boire mon café avec elle 😂❤
Amna ben way boudon gneuw sunu keur c était l ami de mon pere mom dafa beuri won ay gell te la plupart amna ak gnom dome legi momm tawam bou gorr thies la deuk yayam ak sam gnom mam gno bok logn fofou ben vacances hale bi ne day gneuw setsi papam mou wath sunu keur tombe kermes amfa ben hale bou djigen nekon fa gnom gnar gnouyy tognante legi sam rak yi gnibi si di togn kou gorr ki nan ko cheri diww rek sam tanta teup dieul hale bou gorr bi yobouko bassi keur kou djigen bki niko ki yen bokk papa hale yi tok di dioy kou gorr ki gnibi si si keur gui ndeysan mouni sam papa foum dem apfa dom par la suite sam mam wo papa dji neko fehel say dom ga dadielelen ndah sinon mousiba dina am nonou ndeysan ba gnom gneup hamante motah parent nagnouy wane lé sen dom yi
Je pense qu'elle imite Ibrahim Larsson qui fait les mêmes émissions depuis des années( il dit toujours mes Bchas prenaient Un verre et de quoi grignoter pour la Story)seulement lui il ne filme pas le verre il est dans le milieu de la mode etc très fri: cette imitation vient de Ibrahim Larsson il est sur youtube.
Les liens du sang sont très forts. Les personnes qui sont liées par les liens du sang s'attirent très souvent. C'est une connexion très forte et inexplicable.
Machallah chapeau à notre badiéne hier le 24 elle a organisé une fête et a invité toute nos cousins(es) pour qu'on se prennent les numéros et qu'on se fasse connaissance machallah ❤🎉😊
Ces genres d'erreur, seul les père de famille sont responsables comment avoir des enfants et ne pas créer la connaissance entre ses enfants même si la manière d'avoir ses enfants n'est pas la même. Les père qui produisent des enfants partout où ils passent sont les destructeurs de la société et de la vie de beaucoup de jeunes.
Sama analise nac moy niom danio top sene mbeuguel té watanouniou ndax si waxou xew mi rec meunone nanio xame lou xew dama ame xew ,yaw nga ame xew meme jour waw doumala lathie sa lane mo xewlé bou explication amone fofou rec dou yegsi si xewmi😂😂
Li kagn consequences sou gnari dialo la prk Papa bi mo dieugua dialo diko neubeu Belle lesson du jour diarna diaguat gnari khaléyi nagnu mouy tee yaala oubli léen ay bountou incha allah tee moytou lou melni euleug
Incident regrettable que le gas pouvait eviter .quand on aime faut etre serieux aller lentement et surement .pouquoi n a t il pas demander a la fille son pere avant?
@@khadjiatoure6371 😅🤣😂 kone journalistes yi, animateurs yi ak reportaires yi nougnouye déff. Limouye wakh bouko résumer wone 10mn wala 15 mn max laye nék
Wa tata😂khana café gui molaye inspire 😂😂mais nak amna solo lole 😂😂❤❤
😅
Macha Allah amna solo trop mé dagaye dieule temp wakhji mouy gaw touti stp temp amoule merci
Jurtou ça
Geugcla diot amoul
Vous êtes un bon journaliste histoire bi ninka expliké amna soutoureu té conseil yi tamite ces pertinents
Ahh sa histoire bi yèmè n’a dei Wayé yalna lén y’all dièguel🥰🙏🏿
MachaAlla, histoire très instructive.j'adore vraiment, yalna la yalla deffal Diam
Machalla, très forte
Mane nane café bi rek momay Ray 😂😂😂
Moi aussi 😂😂bravo à elle Machallah
Non sokhna Fatou elle est extraordinaire Macha'Allah elle raconte très bien avec sa tâche de café je me contente toujours de boire mon café avec elle 😂❤
C’est une belle histoire. Et ça mérite un oscar.
Li com lép ak lépone rek 😂😂😂
Da nga fatéé wakh leeboone 😂😂😂🤣
😂😂😂😂
😂ki vrai nittou thies leu😂
Histoire bi stlouis laa amm
Beug café mi ngi nettali histoirou beug mbourou 😂😂
😂😂😂
😂😂😂😂
Billay 😂😂😂😂
Amo foula 😂
@@couradiopndiaye9620 loutakh 😂😂
Wa🎉thing thing bi bena yon doy na 😂 chaque fois ngua yeukeuti
Amna ben way boudon gneuw sunu keur c était l ami de mon pere mom dafa beuri won ay gell te la plupart amna ak gnom dome legi momm tawam bou gorr thies la deuk yayam ak sam gnom mam gno bok logn fofou ben vacances hale bi ne day gneuw setsi papam mou wath sunu keur tombe kermes amfa ben hale bou djigen nekon fa gnom gnar gnouyy tognante legi sam rak yi gnibi si di togn kou gorr ki nan ko cheri diww rek sam tanta teup dieul hale bou gorr bi yobouko bassi keur kou djigen bki niko ki yen bokk papa hale yi tok di dioy kou gorr ki gnibi si si keur gui ndeysan mouni sam papa foum dem apfa dom par la suite sam mam wo papa dji neko fehel say dom ga dadielelen ndah sinon mousiba dina am nonou ndeysan ba gnom gneup hamante motah parent nagnouy wane lé sen dom yi
Choc🤞🏿pause café bi sa me tue wallah😂😂♥️
Sokhna sa fatou sa casse bi amna dara eskeihu😂😂😂
Bonne questions
Je pense qu'elle imite Ibrahim Larsson qui fait les mêmes émissions depuis des années( il dit toujours mes Bchas prenaient Un verre et de quoi grignoter pour la Story)seulement lui il ne filme pas le verre il est dans le milieu de la mode etc très fri: cette imitation vient de Ibrahim Larsson il est sur youtube.
Machaallah très belle présentation que du professionnalisme vraiment je suis très fier de toi
Virement man nga nétali😅😅😅
Histoire by nékh na lol wayé Nay gaw
Mashalla
Caweus en perso 😂 professionnel caweus me amna solo kmem😂😂😂
Mane dei sayy soumaley setane damey defar sama café ☕Di nane en même temps que yow bo yeukeutiwei rek ma yeukeuti 😂😂😂
ioe sama domou baye nga
😂😂😂😂
Bayil togne way
Man d douma wéddi draa ndakh moudiou diamono naniou nek ni yalla naniou yalla moussal rek.
Fa yalla nga koudou fane
Dou séne faute,penrents yii❤❤metina lole❤❤
Fa ..Hana toukki rér GUEU walleu borom dciw tiir?
Machalla amena diarigne yal nassi nieupe diangue dioupe ak,moytou ndiallo
Amine amine yaa rabi 🤲🏿🙏
Sokhna Fatou comédienne la😂😂
Noooo ki nékh na 😂😂😂
danga diongama lo machallah
Machalla Ann solo trop bly ❤️🥰 domay café ❤
😅😅😅😅😅Cafe bu xana dou zed
Vraiment j'aime cette émission ❤
noooo mane femme bi damay fadji koi😂😂😂😂😂😂😂
Nigaye nane' café ☕ gui momaye daji 😂😂😂😂
Allah nous a bien dit de nous éloigner de la fornication. Bougnu régler wone liyeup doussi am 😢
Meune nga nétali histoire bravo 😅
Danguay diéma simple touti aussi 🤣
Kouala🎉 dank nan café dank la féne🎉
Lolou eupp na dé ak sa tour wou tede wou sell wi❤
Xamna nanato café bou tangue tan bi yeup😂😂
Café bi manatoule niake 😂😂 moye khoromou émission bi 🤣🤣🤣🤣🤣
Bilakhi
Oh cette histoire c'est vraiment intéressant, Yalna Yalla dolli Soutoura.
Chapeau à Borom Café gui😂. Surtout Ndialo =fornication Mousiba lep leuh
Mbëggeel a may xeeñ ci wax ji de aka soof moom Mbëggeel 😂
Wa balnala ndiaye ak Diop 😂
Hoooooooo ndeyssane 😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️
Les liens du sang sont très forts. Les personnes qui sont liées par les liens du sang s'attirent très souvent. C'est une connexion très forte et inexplicable.
Thiey 😂😂😂
Que Dieu nous pardonne.
Machallah chapeau à notre badiéne hier le 24 elle a organisé une fête et a invité toute nos cousins(es) pour qu'on se prennent les numéros et qu'on se fasse connaissance machallah ❤🎉😊
Que nous pardonne.
Mane dh café gui momakoy def ak nan bi di signalé 😂😂😂😂
Hhhh
Café gui ,,❣️❣️❣️❣️👍
LEEBONE LOUPONE😂😂😂😂😂
😂😅🤣 bou kérok bi lané wone moko créer
Kou beug burou lalal jm
Mai mane l'histoire yii fane lay khéwé yémm nama trop 🤔🤔
Wa ki loumou niou yabé nioun diopben yi 😂wayé sa histoire bi teye na sama khel
Lahawla walakuwata illa billahi 🤭
Ces genres d'erreur, seul les père de famille sont responsables comment avoir des enfants et ne pas créer la connaissance entre ses enfants même si la manière d'avoir ses enfants n'est pas la même.
Les père qui produisent des enfants partout où ils passent sont les destructeurs de la société et de la vie de beaucoup de jeunes.
Absolument c’est la faute des parents.
Dieu à toujours raison sur nous car il nous a toujours interdit la fornication.
Sama analise nac moy niom danio top sene mbeuguel té watanouniou ndax si waxou xew mi rec meunone nanio xame lou xew dama ame xew ,yaw nga ame xew meme jour waw doumala lathie sa lane mo xewlé bou explication amone fofou rec dou yegsi si xewmi😂😂
Machalla ❤❤❤
Sokhna fatou danga niro ak nabou gueuye babel
Li kagn consequences sou gnari dialo la prk Papa bi mo dieugua dialo diko neubeu
Belle lesson du jour diarna diaguat gnari khaléyi nagnu mouy tee yaala oubli léen ay bountou incha allah tee moytou lou melni euleug
nekko mou bayii xess bii tee toop
Nioulè beugue mbourou😂😂😂
Et pourtant, il a fait la même chose que son père. Voilà pourquoi l'adultère est interdite.
Dama begg nga def émission spéciale ci sa café bi ndakh begnaaci
Lébone lipone, amone nafi 😂😂😂😂
Incident regrettable que le gas pouvait eviter .quand on aime faut etre serieux aller lentement et surement .pouquoi n a t il pas demander a la fille son pere avant?
Surtout
Café bi khana dou séd😅
Émission bi daal mo nékhe 😂😂😂
Kassou café bi dh douko fatté😅😅
😂😂😂
Damala beuga bagne 😡😡 ndakh sa cafè gui ☝️☝️te menoumala bagne iow daga nêkh Bilahi 😅😅😂
Caféme bi, manièrames yi ak wakhiname gno sofeu
Ligaye noter la beugue khame 😂, sofeu gua😅
Wakh dafa mety yéne tamite fawou mouy nane Dara comprends léne ko
@@NaroukNaroukNarouknoté woul Dara sof rek😅
@@khadjiatoure6371 😅🤣😂 kone journalistes yi, animateurs yi ak reportaires yi nougnouye déff. Limouye wakh bouko résumer wone 10mn wala 15 mn max laye nék
Thiey yalla😂😅
Ningayyy deffff sa kanammmmm guiiiiii dokooooooo bayyyyyyi tamitttttt hannnaaaaa hamoooooo niiii dangaaaaa niawwwwwwww
😂😂😂😂❤
Beuge café 😂😂
Fa billay guemna koula deke 1 millions wethiét souko soxla nga delloko 1 millions wethiét
La ilakha ilala woo woo walou lenema
Ndeeeeeyeeeeem 😭😭😭😭😭
Mom deh danewon dafa am bac migi ini...ganewat masoul nieuw Dakar khana ban université la?Nay geuga leer
Café bi khana dou sédd woutall térmousse
😂😂😂
Moh kass bi amoul dara😂😂
Lolou moma neex ci emissions bi nak😂😂
😂😂
Li meti trop 😢😢😢😢
Merci
Yalla nalen bourbi diegual ta defal leen soutoura
N'dar la khéwé won de Ndaysane
Nooo ki damoko beug 😂😂😂😂
Bayil serrer yi 😅😅 nioune beugeutouniou mbourou
Bayiko Mouy sanni héér ..mais môme wahaguoul môme loulou bueuggueu déh
@@yvefay620café😂
@@yvefay620 😂😂😂 Ray ngama bayiko rekk
Deuk bi fane la ma diayi fa
Salam lima jakhal si wakh dji moy wadji noumouy guénak kou jigenn gui 4ans té khamoul tourou papay khalé bou jigen bi
Yow kaye da nga done fo di ndialo tak nga warone def
Rero amna de les cartes d'identité d'aujourd'hui n'ont pas de nom du père
Billaye, c'est ça que j'ai pensé automatiquement
Pourtant histoire bou réél la dh parce que j l'ai une fois entendu
Mangui ni😂
🥖🥖🥖🥖🥖 bayil tonie
Défa hamoul rék ..gnogui xi tiéré ni
Yaw sa histoires yii khana say scenario bop leu.😂😂😂
En tout nekhna dh😂😂😂
Machallah ❤
Thiey yalla 🥹
Interesante 🎉
❤❤❤❤❤❤
Waxo deug deh parsk meuno nék ak nit depuis 3 ans té do xam ni papam toudou ak yayam
Ndeysan
C'est une émission intéressante mais ya trop de répétition et que les gens m'ont pas de temps et de connexion à perdre .