KING BABA - Ngaaka Blinde - Effect Secondaire (clip officiel)
HTML-код
- Опубликовано: 10 фев 2025
- Stream Secret 7 Vol 2 : bfan.link/secr...
Ngaaka Blinde - Effect Secondaire
-------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------
Disponible sur toutes les plateformes de streaming
Chanteur : Ngaaka Blindé
Mixte et Mastering by : Bril (Class'Chic Music)
Beatmaker : Bril
Réalisation : Schadiiq
Collaboration : Kbc music
-------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------
Réseaux sociaux :
Facebook : / ngaakablinde
Instagram : / ngaakablind. .
Twitter : / ngaakablindee
Site web : www.ngaakablinde.com
e-mail : ngaakablinde@gmail.com
---------------------------------------------------------------------------------------------------------------------
Contact Manageur
Mail : kbcmusik7@gmail.com
Contact : 00221 774653939 - 00221 774681039
Équipe : Blindé Musique
Nn pas de répétition ngaaka est un grand rappeur il peux representé au extérieur kou d'accord défal j'aime😍🤩😘
Fan nonou non bro tout sauf ça 🤣🤣 n'a Yam fii rék. Fofou king dip mofa nék
@@modoudiallo132 😂😂 toi esk cv dans ta tête
@@mamadouyerokande5325 MoMA diakhal
bly frére
@@modoudiallo132 ya mome ndeye wérro kts feulé
Je suis fan de Dip mais sérieusement Ngaaka Ndanane leu nak damkay nangoul dh man soxorouma. Chapeau chéri Fatel 🔥
Des personnes comme toi sont vraiment rare ❤👏.
@@cit3_perdue merci♥️♥️♥️
Di doul rek
@@aliounebadaradiop1253 fall fi guenofi réw kèneu dh . sa saga yoyou nanga xam kinguey waxal
@@aliounebadaradiop1253 ndeysan Yaw ak sama papa bokk tour bokk sante. Balnala d seu xel mo tolou fofou Jeureujeuf 🙌🏽
Ngaaka sa sound bi deff na effet, mangui ré comme dof, Ngaaka comme d'hab t'a assuré, le changement de flow et rythme du 2ième couplet est dope 🔥🔥
Wallahi dou kessé mangi😂😂kom kou wéroul
@Rap galsen 221 yeah nice Key..rien à dire même si je suis fan de dip
Man refrain bi momay ray😀
Wa mais kamaro yi kou may expliqué😀😀
@Rap galsen 221 bril moko door
Kou d’accord ni Ngaaka est le meilleur rappeur du Galsen lalal j’aime ❤
❤🎉billahi
Qui l'attend ? Non ngaaka dou nit🔥. King baba pétri de talent 🔥🔥🔥🔥
Réplique la meune😅😂❤️
C'est normal boy guédiawaye la 💪💪💪
Bo guéné négou goor dougueul sa négou mame
Ndakh bo dougué sa négou... mane akk sa papa ñofay tassé 🔥🔥🔥😂 King baba dou nitte🔥🔥🔥🔥♥️♥️♥️
Thiey sacré Baba rAya Tigua rec 😂❣️effect bobou moudié nah don déffetee 😂king Baba choix du peuple 🇸🇳❤️❤️
J'sui guinéen de Conakry mais j'ai passé trois ans à Dakar et j'ai trop adoré la population je vous aiment pays de la terranga
Nous aussi on t'aime
Les gars le clip, l'instru, les paroles méritent des millions de vues sur RUclips.... Faisons qu'il atteigne des millions de vues
Bah t'es gentil hein❤
Fay niou
ngaaka domou guédiawaye kel talent t'as tapé fort 💯 Angleterre ak pomme de terre c op la méme chose😂😂 ça kick fort
Tkt pas il aura des millions de vues
Déjà Akhlou brick a sorti deux clip mais le cumul de vues des deux clips ne dépasse celui de Ngaaka
Kou d'accord ni King baba Moy King bi lalal j'aime
😂😂
@@dialniang9459 ujji⁸⁷knbbv
Dip moy bayam
11
@@dialniang9459 k
Problème yagui démarré nakk vive ngaaka vive le Sénégal champion d'Afrique 🇸🇳🇸🇳🇸🇳 futur champion du monde 🥇👑
Vraiment ngaka blindé dou nitou fi moye Sene baye si rap nagou rek
Sarappppp ndayamm do nittt💥💥 walay effectivement defna effect🤣
😍 Le frère m’a donné envie de parlé Wolof, un Vrai lion, le futur de l’Afrique, faut tous les faire chanté en Wolof mon gars, fière ! on est ensemble 🇨🇲🦁🇸🇳
Et le beatmaker avec ces tam-tam derrière les 808 😍🤌 c’est l’Afrique qui gagne !
Nioune wa guediawaye sou khôl frigo 💪💪💪🥰
très jolie clip
Meune lingay def mo nekh! Le gars il est à l’aise là dedans🔥🤙🏾
sans forcer😄
Bly frr ❤❤
Si✅
Effectivement ✌️
✅✅✅
Wa degal bobou rythme nooo king baba togal way kou contane si baba Ndiaye rek dafal effets lale 👍😂😂 walla Book😂😂💯🎤🎤🎤🎤🎤
Tontou + clip en 24H = Talent ak am money.
Baba dou morom kou ko dépassé mou régler leu ci 24h bollé ci di leu kokoli nga fatou fa yalla'ou!😂😂😂
Bilae😂🔥🔥
Jtj 😂😂😂
Bilae nak 😃😃😃
Dominique 🤣
Le meilleur do senn morom king baba😍🥰🥰
non effect secondaire bi dfa dope ngaaka nioun li laniou beug 😂❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Le phénomène du rap galsen 🤴,le talentueux on valide en 100%
Billahi kii doue nuit
vraiment
Dagnou teipi seu tournoi ndeiye dei imbécile seu tiakhane yi sosi bolei Baye Niasse gnou deiglo leu seu tournoi ndeye imbécile.seu Serigne leu Toubab yi dieul yonou fouleine nekh tei meunou ci sarap ndeim ay ateu.sunu kateu seu ndeye wakhla seu bopp Di nga khamni baye moy seu bayou baye Di bayyou ki ngeu yaakar imbécile impoli
@@samoudiop9300 Yaw mii di toudou Baye dissi bolé saga niaw yii yaw mii yako diokhoul benn thieur
@@samoudiop9300 ïow loy saga nii ?
bilahi do sen morom mon king
- Sadio Mané mo meun ci foot bi
- Youssou Ndour mo meun ci Mbalax bi
- Balla Gaye mo meun ci lamb bi
- Mais Ngaaka mo meun ci lepp 🤩🤩
Quel domou adama !!!!!!!!! 🤩🤩🤩
Bilahi
Wakh gua degue wayé modou lô mo man ci lamb
@@mourtadafall9143 balla nak?
RIGHT ✌️
❤️❤️❤️❤️❤️
Ce gars il est extraordinaire mieux vaut ne pas avoir de contentieux avec ngaaka parce qu'il va tapé fort très fort même chapeau à TW baba👍
C'est quoi l'origine du clash
💞💛💯💯💯💯💯💯💯💢💢💢💢💢💢💢💢💢💢
💯💯✍️✍️✍️✍️
@@desunoto6869 c’est akhlou brick qui ont commencé avec leur son éphémère ils ont grave claché baba je ne sais pas pourquoi
King tu le meilleur machalla 😍😍😍😍😍😍❤❤❤❤❤❤❤❤
Trop d inspiration s gars replique moin 24h le king du rapp galsen (akhlou brik je vs aime ms ngaaka moy sen baye )mbo d'accord rè beuseul j'aime
😂😂😂😂😂❤❤
J'appelle sa la réussite , je ne comprends rien du song , mais je dirais qu'il fait passé le message a travers la langue nationale , tout nos chanteurs Africaine doivent faire au temps 👍👍👍
Waaaaaw ça tombe à pique. Quel flow. Ngaaaka dou nit waaaay . Bandit bou mag leuuu.
Saway clash bi dessna deh
Ngaka day tassou rekk
@@thebigH-qx8kd bilahi dafa dess trop mane pressk sama copain you bari mome laniouy frek mais ngaka rabatoul
@@thebigH-qx8kd T'as raison déh bly
@@caintv6271 Bly Hip hop bo mom bosi dounga léé Beat mbalax rk yagui commencé guéneu Gam
Deuxième couplet bi c légendaire crx..... technique, flow, lyrics.....king baba
Mane Ngaaka la beugue 😂 bilay je l'adore😂 amoul temps boumouy yakh meune sa liguéy dafa nékh si 24h gua damou séni laff 😂 depuis magui kay déglou mais douma doyal 😂😂
Bilayy yaw Thieuy Ngaka the king 👑 do sen morom si clash ❤️❤️
La frappe big up depuis le congo 🇨🇬🇨🇬🇨🇬 Sunugal rekk 🇸🇳🤍
J'ai pas l'habitude de suivre le rap galsen. Mais je confirme que ce ngaka blindé est super fort. Big up bro.
First comment, ngaaka blindé do nite, akhloul brick ils n'avaient pas pris en compte l'effet secondaire, c'est plus lourd que le premier
King bi bal lén
Bayil sagua yii way
@@i-am-mouhamed9596 faut guissé fi saga
KING BABA A WAWIBE DO SEN MOROME 🎤💪🇲🇷🇮🇹
Le king de retour Nice clip ❤️🔥💪
Naturellement nak non ngaaka vraiment meune nga lingay def ❤
Tjrs gua wane guys k niveau yi bokoul et k talent bigua yorr c pure franchement t’es le meilleur mon gars👌🥇😭💚🎉
Non ngaka dounitt
PAPA balénes way 😁😁😁😁 do ngakka késsé🧠👽 boum🔥🔥🔥🔥🔥
Yay bandit ak heure bi 💥🥇🥇
Sama réveille matinal Ak secondaire bii ..💥💥 du ouf on dirait que ce king est ange walahi... Wa akhlou effet.. est ce qu'ils respirent même en ce moment... T'es le meilleur indiscutable 👑👑
King baba tjrs égal à lui même flow bou nekhh tek ci meune rap yéna ngui doundeulate game bi 🔥
The new king Aka Kungue, kouko tim mou sonal leu ni mbeunde ! good job
Écoutez 100× d'affilée sa suffit pas Guediawaye a vie 🇸🇳👑🏁❤
Lou lerr king baba do moromou gayii👑👑👑👑✌👑💫💫⚡🤣
Non mais ngakka dafa rek li moy effet secondaire tourou clash bii mo yeme 😂😂😂😂😂😂😂ngakka i love you depuis medina 😂😂respect
Bilahi
Je te jure depuis ce matin suis en boucle, mais respect 🙏
Dou Nittou Fii🤣😂😂
Ecouté 100fois d'affilé ça ne suffit pas vraiment level bi kawèna ta li lagnou soxla si game bi rap deug, fi dara doufi yakhou🔥🔥🔥🔥
MoMA dale
@@papitodiaz6016 walay
4h du matin makoy khar mayy leen ma j’aime wayyy
Franchement Ngaka Moy s'en baye
Il est le seule rappeur qui fait du lourd à chaque mois il fait des tourné il attend pas le payement de RUclips ngaaka yay KING jusqu’àu bout c est toi qui est là le rappeur du peuple ❤
Yalla nala yalla saameu Cheri fatel 🔥🔥🔥
Bléndé blénedé sounou life geudiawe sounou life
Kolda soutien ngaka❤❤❤
So guéné négou goor dougeul se négou mame😂
Tontou vite fait bien fait😂🔥🔥
King baba Ndiaye beunala té yalla rk takh je suis très contente de vous ❤️
Depuis La Mauritanie 🇲🇷 Ngaaka dou’nitou Fi Trop Lourd
Respect frère
Mai boy bi rêwe na hein 😂😂😂😂❤❤❤❤
Le meilleur rappeur du Sénégal ❤️🔥🔥🔥bonne continuation 🔥❤️
Nice vidéo king 🤴 baba dawoul thiow thiéy lithi effect secondaires 🔥🔥🔥🔥
Vous savez ngaaka moy sunu arafat cote d'Ivoire ...amna segn segn bi ..Té pourtant bimu guen ci kasso muguiwon 48.000 abonnés...mais maintenant il est devenu le plus suivi ...donc c à salué....ci deuk bo amé artiste cou melni genre ngaaka..il faut mou deh guene hamna ni c'est King....respect à lui ..et bn continuation..
Iidoi degu wouy magui deee 😂😂❤️❤️❤️❤️❤️❤️💞
Pouce bleue pour le beatmaker🔥. Vrai gifle. Ngaaka c’est vrai un génie !
C'est Bril
@@moussbouyarrou5753 🙌🏿
Machalla ❤️ ❤️
Dip lagnou wakh barki papes
@@moussbouyarrou5753 a bon Bril , wow he is good
No moi suis d'accord vraiment ngaaka blindé kįng 🔥 bi la . Ngaaka dou moromou gayi . Ngaaka blindé boul yakk sa temps si ngayi ya lénn Moun yaye kįng 🔥 bi yow késsé 😯🔥🔥🔥 . Flow maine vidéo Nice na trop même aussi 🔥🔥🔥🔥😯✔️ may nala BGD ok pas KBC légui BGD bi la from BGD moi węü2 kįng 🔥
Walae meusou ma degg class bou mel ni ngaaka dou nitt 🔥❤️🤟
Yayy bandit🥇🥇
Nice king baba le meilleur de sa génération kou namone ngaka beuseul j’aime ( boléne ladione séne papa doo) doo moy dip 😂
1million de vue en 3 jour si clash vraiment yay king 👑 😀😀😀
Mangui dora sétane affaire clash yi... Mé ngaaka barki borom touba ya meune gayi... Mélodiquement parlant... Say paroles nio meune gayii 🎉🇸🇳🦁🥇✅
Bilaye boko akkénes bilaye voix bou lerr ❤❤❤❤❤ yalna yallah wokk sa fane ❤❤ yow yaye king
No vraiment ngaka il est exceptionnel...tellement talentueux ce mec💫💫
Il est le rappeur du peuple 221 kou daccor beusseul j'aime❤
Mais li dou rap rewandela
@@ibrahimasall5274 iow khamo rap motax meunou ma game ak iow stook bro déggou Lou wattal sound bi c crucial ses paroles😎😎
@@ibrahimasall5274 affaire de rewandé day def effet 😂💯❤️🇸🇳
King baba
Qui a regardé la vidéo plusieurs fois, man ak rifou warouniou clashanté nio beuk crew. Parti bobou ray nama
Kou d'accord ngaaka blindé dou morom yenen rappeur yi. Dak len rap eup len inspiration, tontou à 24h 🔥
C’est ce Ngaaka qu’on demande 🎉❤🎉
Vraiment
King bi talent kesse meun geum boppam😊
Contane na game yeugouna Way Ngaka 🥇
Notre King ngaka laf tiath wayyy ❤
Kou nangou ni ngaaka déye foh si beat Bi Ni lalal j'aime 😍😍
Baba yafiné
bilakhi 😂❤❤❤
Avec une telle facilité de Rap, vaut mieux éviter d'avoir des contantieux avec lui..
KinG BaBa🔥🔥
Je me suis dis la même chose. Il est a l’aise ❤
Bilakhi dousene morom
Il est comme Eminem facilité pour sortir les mots
le rapeur du peuple barki yallah do nit 💪❤️king ngaka moy s’en baye j vs dit ❤️ ta tape fort 💪 🥰kou si amé ay rap rék na niew gua ndeupeul …💪
Gnaari jankh yoyou ki di youte( Ara) kénène ki di taalif(Dayza). Waaw c lourd
Nooon fofou la meunoul mougne. Ngaka mo con 🤣🤣🤣🤣
2 semaines té ba légui moy 1er tendance. Machallah
Mangui lay niaanal boubakh Ngaka-Blindé victoire rék G-way lay fana ni 🙏🏽
Kou beugue diamm ésk doula nagoule nii king bii rék... Le fait est déjà fait akk gnomm dou combat échauffement pour ioe ❣️💯🌹 on est des BLINDÉS BLINDÉ 🥰🥰
Le King du rap galsen🔥🥳❤🤩🇸🇳
Boy guédiawaye dou ragall🔥🔥
Tu es le meilleur King baba tu es vraiment fort
J ai écoute sa 50 fois durant 2h de tamps tu es le meilleur King baba
Moi pareil mangui rée comme doff
Même mw
Billay ❤️🥰
Je suis Mauritanien mais c le meilleur rappeur de Sénégal et Mauritanie je vous jure
Le volume est bon ❤️ totalement posé dans la zone 🔥🔥🔥 bo guéné négou goor dougal sa négou mame ndakh bo dougué sa négou...😂 mak sa papa niofay tassé 😂😂😂 mais phrase bi yég boy mane sameuh dég-dég mo soriwoul kw 😂
Iska sagawoulen ndakh bo dougue sa yaye veule diré 🤣🤣🤣
"NDAKH Bo douguer SA NEGGOU YAYE MAK SA PAPA NIOFAY TASSER.." il a juste censuré le mot yaye
Eeeeh bien il est trop fort. The KIIIIINNNNG Lal guéne lallaakééé😀😀😀 doléné ko dafatiiii
Fans de dip mes ngaka t’as bien fait akhlou brik dano noy trop beugu wiri wiri jamais assumé 👏🔥
Y’a meune s’en nday niom nieupp 😂🎉 King Baba ❤
Fatel wagnil dose bii, king migui dadji les rappeurs galsen
King baba le meilleur sa génération ya fi meunnn bilay yayyy sènn bay
Vraiment Ngaka le song est dope t'as assuré bro malgré tu n'es pas mon rappeur mais la vérité est plus important que l mensonge ✋ respect pour toi bro ✋
Waay 10 jr 2millions de vues ms vraiment blindé raw na rappeur yii 😩😩
Ce deuxième couplet me donne des frissons. Wayy kou si yeug sa bop kay beuss j'aime wayy. Effet bi mom yeug naniou bou bakh sakh
Je valide a 100/100 mon rappeur préféré est le meilleur ❤❤❤talentueux on validee❤❤❤❤
Waouh il est le meilleur mash'allah ❤️ yalna yalla xép dolii barki cheikh Ibra Fall
Yalla mangui lay niaan nga samal ma Ngaaka blindé ki meunoul won niak si hip hop galsen.NGAAKA ON T'AIME TOUT SIMPLEMENT NOUMOU DÉMÉ BAHNA.😁
Walahi ngaaka dafama
Depuis 5h du matin magui thi son bi sama ❤️dafa nékh 😍king daga beugable billayi 🥰 1m vue la sokhla dans 24h 😍 pourquoi pas 🤤🥰
Deglou dafa haram degloul alhourane
@@lilmbaye29 lègui démal gua déglou alkhourane
@@lilmbaye29 wathi alkhoura ba paré di Doris thi khasidayi 🤤légui yaw lola fi Andi😂
@@ndiagagaye6608 bien dit🥰🥰
@@lilmbaye29 loye def ndeye fii, sale hypocrite
Bilahi yaay king bi
Tou Tii na niou pour wathé la BABA Ya fi nék😎😎😎🥰🥰
Chapeau bas à ce mec talentueux meune lingay déff mo dakk nékh regardez le king il est à l'aise de ce qu'il fait...
Bonne Continuation KING BABA
Ngaaka blind le meilleur rappeur de tous les temps✊️❤
Ngaaga blind yow ko yabateh nga , Gambia ngai hep