Koudoull khalatt yagueu yagueu adouna dinni dieh loula nekh deffall. Mais quand le jour de la résurrection viendra, il n'y a plus de retour en arrière. Merci frère vraiment tu as un impact positif dans notre pays ( Sénégal ❤️)
Si tu veux étre accepté à l'internationnal, il faut respecter ce que tu es, c'est à dire ta culture. C'est comme cela qu'on s'impose...Regardez les nations qui ont vite évoluer au risque de prendre la place de certains grands ! Ils ont été respectés pour ce qu'ils sont....
Elle vous a habitué à la descence ndax da doon sëy. Elle s'était oubliée, mise de côté, ne vivait, ne parlait et ne s'habillait que pour satisfaire son mari. Ñi xam Mia dëgg seedé na ñu ni elle s'est longtemps habillée comme ça. Ce n'est pas pour la défendre mais Li ko war lo ba muy sëy defoon na ko léegi nak yedd yërëm Da ko gën ñaanal ko YaALLÂH wëlbëti xelam ak xolam ci MOOM BOROOM YËRMANDE Ji dafa gën. Parce qu'elle est juste redevenue la Mia de son adolescence. Mia a 31ans elle n' a pas fini de faire des erreurs comme nous tous. Ku Téla sëy, bàyyi lép li mu nekkoon ba ci rap bi mu done déf ngir topp jëkërëm tékk ci divorcer ak moom 3fois dellu wat kooku bëggoon na sëy T bonoul.
@@kharymkleye2187 elle ne doit pas redevenir la Mia de son adolescence nak loloy deugu car dépasser nako. Elle a dit une fois en interview après son divorce "je suis une jeune fille". Lolou la wara guéné khélam. Kou meussa sey ba am dom tu ne peux plus faire pareil que quand tu étais jeune fille. Elle peut changer de style c'est son droit, mais ça peut rester classe
@@mariecoly17 Dëgg la. Je ne l'ai pas dis en suggérant qu'elle DOIT redevenir celle qu'elle quand elle était adolescente mais pour essayer d'expliquer le pourquoi de ce style vestimentaire. Peut-être qu'elle se cherche. Peut-être qu'elle fait une crise identitaire. Li ma gëm moy dawal compréhension. Essayez de faire preuve d'empathie, de se mettre à la place des gens. Peut-être que sa vie d'avant a été plus une épreuve même si beaucoup de Sénégalais voient, veulent voir et affirment le contraire. Yedd daal yërëm da ko gën ak ñaan. QU'ALLÂH SWT la guide. En tout cas elle n'a pas fini de faire des erreurs comme nous tous Mia a 31ans dafa téla sëy rek
Motakhe ken dou Coumba Gawlo elle s'est sa valeur mashallah genrou nite yi gnoye yake khalé yi sama morome mangui sante yallah bamema défé ma téla néke khalé bou khame bopame
Ci côté habillement Coumba Gawlo sol na fi lu sexy lu né. Ci côté wëy, Gawlo way na fi lu sexy lu né. Vous oubliez trop vite ou vous faites exprès ?. Je ne suis pas alignée avec tout ce que fait Mia mais nit déy wax dëgg T YÀLLA rek tax. Coumba Gawlo mi ngeen di jeter ay fleurs leegi, Senegal waxal ngeen ko lu nék ba ci Lesbienne la juste parce qu'elle ne s'est jamais mariée. Yeen Ku ngeen dàggal tubëy gemb la ngi koy xar. C'est juste une question de temps leégi keneen ñëw ngeen bàyyi Mia. T àddina di na dox ba ngeen setal ko comme ni ngeen koy déffé ak Coumba Gawlo et Viviane 😂
Dans 20 ans elle va venir pleurer des larmes de crocodiles à supplier que les gens oublient leur passé. Viviane & Gawlo peuvent mourrir en paix, elles ont une héritière qui va continuer sur leur lancée
Mya dafa rerr Elle fait un choix de porter des tenues sexy sous prétexte k c'est des tenues de scène, mais dafa wara kham ni c'est un mauvais choix, elle est avant tout une personne, dioulitt leu et mère de famille de surcroît. Show Biz dafay diekh, té Lou Diara soralé leu
Oui elle a fait un choix pour sa vie, pour sa carrière qu'elle est mère de la même façon que chacun de nous fait des choix de vie. Il y a certaine hypocrisie dans nos sociétés, Mia qui porte une combinaison fait scandale mais des gens à moitié nue dans les rues personnes n'en parlent. A un moment il faut arrêter
@nalaabdou9747 je suis dakor avec ton opinion. Sur le principe une femme doit couvrir son corps en toutes circonstances. Kou defal lolou defo li yalla santané...
@nalaabdou9747 Mya fait l'objet de critiques parck elle l'a cherché. Kan elle était marié, elle défendait la femme de valeur et de principe tout en étant dans le show Biz, et aujourd'hui elle fait comme si c'était pas elle
Pour Man c pas question de Beug dieukeur elle a perdu confiance en elle Motax Mouy déff lii elle😂elle veut ragagné confiance en elle perdu dans les nuages😅
Non elle n'a pas perdu confiance en elle bien au contraire. Yeena kay dëkkël fu mu dëkkul parce que soi disant dafa divorcer libre, motax mu wax elle veut se remarier pour montrer que bonoul comme vous dites. Ndax dans l'esprit collectif sénégalais ou des hommes sénégalais en tout cas Jigéen bu baax miy Jigéen buy sëy. Célibataire du ku baax, divorcée du ku baax, veuve sax du ku baax ndax mën na Ayy gaff 😂. Fichez la paix à cette Dame elle ne vous doit rien wala daf leen yoreel xaalis. Ni ngeen fi defoon Dieyna Baldé léegi bàyyi ngeen ko ndax mi ngi sëy. Vous ne connaissez ni les batailles sourdes des gens, ni leur combat, ni leurs regrets ni rien d'eux, vous ne portez que des jugements. Toumeu dafa metti Mia a parlé de remariage pour comme qui dirait setal deram tuuti
Wesh Je suis d'accord avec toi sur le fait que Mia et ndakhte lo sont devenu esclaves de l'industrie dama lène yereum da melnii amou niou ay conseiller
Respectél Say Domme nakhe xalé nawlé la sa ex dieukeur kou bax la wone gorgoloule touti sisa bop svp Adouna amoule solo kholale si mada Ba wala si kiné lam kéne douléne xasse Lou diotte lagniouye solle gniola gnieuk si showbizz bi foufe té Dara meusoule gniaw
Wax dëgg YÀLLA. Bu ko waxul woon léegi nga gis ku ni waa Mia xanaa bëggëtul sëy, elle ne parle jamais de se remarier depuis son divorce. Ñi ñoo waxu ci boppam
Elle a fait un choix pour sa vie, pour sa carrière qu'elle est mère de la même façon que chacun de nous fait des choix de vie. Il y a certaine hypocrisie dans nos sociétés, Mia qui porte une combinaison fait scandale mais des gens à moitié nue dans les rues personnes n'en parlent. A un moment il faut arrêter. Tellement de pression est mise sur les femmes que c'est étouffant. Toujours avoir à réfléchir longuement à ce que tu porte, ce que tu dis, comment tu marche, comment tu salut, comment tu mange
@@laminesoumare5024goor sàj ay xefam la ko YÀLLA sant, écrit noir sur blanc dans le Coran. Yeen nak da ngeen di xool ba séen xol sedd ngeen wëlbëtiku di bëgg ray nit ñi ak wax. Hypocrite va
Gayi naniou roy ci Amadeus ❤ termes Olof you nékh lay utiliser ❤❤❤
Walo walo leuh motakh mou xam wax bou correrte ❤❤❤
Motakh Ken dou papà Youssou ndour ak comba gawla❤yakhou niou arbi dhe❤❤❤❤
Boul fatei Tata Titi
Danga di khalé rek wayé coumba gawlo mo rawone mia té mom temps bit sexy di done délit la sexy wone
Boul faté Fatou guewel kiné lame darò mbaye Aïda samb❤❤❤❤❤❤
Ak oumar pène et thione seck paix à son âme
De toute Les façon industry musique Dara bakhouthi sheytané kessé la fesse
Viviane au moins elle a toujours été comme ça motakh safougnou mais mia elle a viré grave elle 😂😂
Mais Vivi meussul sol lou Mia sol nak 😂 ck’ell a fait c’est très grave
@@Ma-ZolyLOL. Que le Sénégalais a la mémoire courte ndeysaan. Daaw géej la fi Ta Vivi soloon weenu neen ngeen amé ko
@@kharymkleye2187je t’assure
@ lolu ñeupp Xamôn nañu k c’était pas ses seins mais tissu bi mo Ndoura ak teint wam ! Yen n’a plusieurs motifs
Del wakh deug , viviane da meuss def wenou nene 🥱 flash telefone motakh nga guise ay wéne mé pas di wané ay ene @@kharymkleye2187
Non Mia guisse dafma bête trop billahi wallahi frère
Qui sonoul d dafa réw ba moudjié dof. Niaak classe.
Vraiment respect à toi dema bougone wokh sa vidéos yiii defa Ndaw
Aida samb sama référence ❤
Merci beaucoup Aïda Moy kou rafet Arr
Ndekete Mia amoul bop
Koudoull khalatt yagueu yagueu adouna dinni dieh loula nekh deffall. Mais quand le jour de la résurrection viendra, il n'y a plus de retour en arrière.
Merci frère vraiment tu as un impact positif dans notre pays ( Sénégal ❤️)
Pure vérité elles sont obligées de se dénudées pour exister c'est triste
Mia dof la bop bi dara nekousi quand j ai compris cela je me suis détourné d’elle
Adouna lou waay deff sa bopp ❤❤❤
Walahi 😢
Si tu veux étre accepté à l'internationnal, il faut respecter ce que tu es, c'est à dire ta culture. C'est comme cela qu'on s'impose...Regardez les nations qui ont vite évoluer au risque de prendre la place de certains grands ! Ils ont été respectés pour ce qu'ils sont....
@weshow namone nagne la .Comme dab rek sa waxtane dafay am solo ndakh dafay bari ay leçon de vie. 🎉
J'attendais votre réaction. Effectivement Mia nous avait habituée à de la descendance maintenant si elle change c'est normal que les gens parlent
Elle vous a habitué à la descence ndax da doon sëy. Elle s'était oubliée, mise de côté, ne vivait, ne parlait et ne s'habillait que pour satisfaire son mari. Ñi xam Mia dëgg seedé na ñu ni elle s'est longtemps habillée comme ça. Ce n'est pas pour la défendre mais Li ko war lo ba muy sëy defoon na ko léegi nak yedd yërëm Da ko gën ñaanal ko YaALLÂH wëlbëti xelam ak xolam ci MOOM BOROOM YËRMANDE Ji dafa gën. Parce qu'elle est juste redevenue la Mia de son adolescence. Mia a 31ans elle n' a pas fini de faire des erreurs comme nous tous. Ku Téla sëy, bàyyi lép li mu nekkoon ba ci rap bi mu done déf ngir topp jëkërëm tékk ci divorcer ak moom 3fois dellu wat kooku bëggoon na sëy T bonoul.
@@kharymkleye2187 elle ne doit pas redevenir la Mia de son adolescence nak loloy deugu car dépasser nako. Elle a dit une fois en interview après son divorce "je suis une jeune fille". Lolou la wara guéné khélam. Kou meussa sey ba am dom tu ne peux plus faire pareil que quand tu étais jeune fille. Elle peut changer de style c'est son droit, mais ça peut rester classe
@@mariecoly17 Dëgg la. Je ne l'ai pas dis en suggérant qu'elle DOIT redevenir celle qu'elle quand elle était adolescente mais pour essayer d'expliquer le pourquoi de ce style vestimentaire. Peut-être qu'elle se cherche. Peut-être qu'elle fait une crise identitaire. Li ma gëm moy dawal compréhension. Essayez de faire preuve d'empathie, de se mettre à la place des gens. Peut-être que sa vie d'avant a été plus une épreuve même si beaucoup de Sénégalais voient, veulent voir et affirment le contraire. Yedd daal yërëm da ko gën ak ñaan. QU'ALLÂH SWT la guide. En tout cas elle n'a pas fini de faire des erreurs comme nous tous Mia a 31ans dafa téla sëy rek
Le couple mabo me faisait rêver c'était extraordinaire
Nous sommes fiers de toi bro contane nagne si Yaw pour info yi
Respect wes show
Daffa sonneu Mya guissé 😂😂. Seideu bi moko sonnall😂🎉
Mia weroul de avec sa fane lay dieulé bayefall
T yeenay applaudir Viviane ci côté bi, ndeysaan
Vision Sénégal 2050 Inchalla ❤❤❤
Vous êtes l’un des meilleurs youtubeurs. Tu te bats toujours contre la dépravation des mœurs. Suis fier de vous.
Soxna Sii fofou nga takhaw baye fall taxawoufa🙂↕️
Machallah Amna Solo Bonne Continuation
Teh kou wakh niou traiter leu de sexiste… Diadieuff Tonton Wesh ❤🤝🏾
5:50 je suis d'accord avec toi wes
Tawfekh bro diam rek inchala
DEUG BOU LÉRR MOTAKH MADILA SUIVRE ❤
Salut wes j'espère que vous allez bien merci encore une fois Mia mom je comprend pas son comportement 😢😢
Je ne comprends pas pourquoi vous ne Laisser pas Mia tranquille. C'est sa vis chaque sa tombe.
Thanks very much brooo you're absolutely right ❤❤❤❤
Thanks and welcome
Liguey bi raffett na King 👌🏾🇸🇳✅
Yup broh wakh nga léppv❤❤
Motakhe ken dou Coumba Gawlo elle s'est sa valeur mashallah genrou nite yi gnoye yake khalé yi sama morome mangui sante yallah bamema défé ma téla néke khalé bou khame bopame
Ci côté habillement Coumba Gawlo sol na fi lu sexy lu né. Ci côté wëy, Gawlo way na fi lu sexy lu né. Vous oubliez trop vite ou vous faites exprès ?. Je ne suis pas alignée avec tout ce que fait Mia mais nit déy wax dëgg T YÀLLA rek tax. Coumba Gawlo mi ngeen di jeter ay fleurs leegi, Senegal waxal ngeen ko lu nék ba ci Lesbienne la juste parce qu'elle ne s'est jamais mariée. Yeen Ku ngeen dàggal tubëy gemb la ngi koy xar. C'est juste une question de temps leégi keneen ñëw ngeen bàyyi Mia. T àddina di na dox ba ngeen setal ko comme ni ngeen koy déffé ak Coumba Gawlo et Viviane 😂
Assalamu 'aleykum mes chere freres🙌🏾don len wakh guen diema moytou bou bakh takk chien wala yenen bijoux. Mouy or wala benen couleur. Sounioub Yonente ﷺ daan na takk diaro baraam. May naniou leen guen takk diaro argent soit thi baraam bi geuna ndaw ak bimou dendal thi lokho gauche bi ( thi nguistalou Maliki Hanafi ak Hanbali yi). Takk diarot thi baram bou digg bi ak bimou dendal danioukay Terè
Souguen sokhla we refs yi guen wakh ma🙌🏾🪽
Courage wesh yalna sa jamm yague lol
Diam Thi Yaaw🎉🎉
Bro vraiment tu a raison
MERCI WES SHOW BON CONTINUATION ❤
Verite absolue frere mia guise dafa bete gnou barry 😢😢😢
Si naka nonou si naka Athieu wesh✌🏾
Merci wes chow
Big respect frère vraiment elle exagère elle m a dessus
Bly deug bou lérr 🙏 adouna amoul solo . Deff lou bakh rék
Dans 20 ans elle va venir pleurer des larmes de crocodiles à supplier que les gens oublient leur passé.
Viviane & Gawlo peuvent mourrir en paix, elles ont une héritière qui va continuer sur leur lancée
NO BROO TOUJOURS UN PLAISIR BIG UP
King wesh ❤❤❤ walahi je t'aime ❤️
king wesh leu😎
Buon anno fratello Grazie❤❤❤❤❤❤
Mya dafa rerr
Elle fait un choix de porter des tenues sexy sous prétexte k c'est des tenues de scène, mais dafa wara kham ni c'est un mauvais choix, elle est avant tout une personne, dioulitt leu et mère de famille de surcroît.
Show Biz dafay diekh, té Lou Diara soralé leu
Oui elle a fait un choix pour sa vie, pour sa carrière qu'elle est mère de la même façon que chacun de nous fait des choix de vie. Il y a certaine hypocrisie dans nos sociétés, Mia qui porte une combinaison fait scandale mais des gens à moitié nue dans les rues personnes n'en parlent. A un moment il faut arrêter
@nalaabdou9747 je suis dakor avec ton opinion. Sur le principe une femme doit couvrir son corps en toutes circonstances. Kou defal lolou defo li yalla santané...
@nalaabdou9747 Mya fait l'objet de critiques parck elle l'a cherché. Kan elle était marié, elle défendait la femme de valeur et de principe tout en étant dans le show Biz, et aujourd'hui elle fait comme si c'était pas elle
@@youssoundiayediouf5201tu as raison elle même a dit que la Mia qu’on voyait n’était pas la vrai
Mia mi louko dall😂😂? elle raison nak 😅dieukeur légui yomboul dh😂😂.
😂Jëkër yombul kay
Merciiii beaucoup ❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🫶🏾🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
J'aime votre contenu
Wallahi wes niaak la déguelou woooroul❤😂
Vérité absolue❤❤❤❤❤
Merci.wesh.zo,wakh,deug,mia.yakhna.bopame.djigeune.du.sey.chiagatou.rek divorcé.yepp.djigeune.wara djigeugen.ji.beug khalis.chiaga.takawalou.rek.dofna
Yaw machalla kou beugeu lou bax nga❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mane au début j’ai dit no face mo nekk si deuk Mais ça se confirme
No Face mo nekk ci dëgg juste parce que Mia s'habille comme beaucoup de femmes d'ici ? Et bah mon vieux
Mr6 bcp kou baah❤❤❤
Diadieuff frère bonne continuation
Mia dh xél mi loumou ko diigal mu df
Naxasanang leu
Dof leuh🤣
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤
Merci sow❤❤
Wesh Khana danga Bayi wakh si Game bi 😢 Wakhal si Hip-hop bi nk
Come On Town leu nak... Tamba la Deuk. GUISS GUISSOU ADOUNAm dafa poussière 😂😂😭😭😭
Pour Man c pas question de Beug dieukeur elle a perdu confiance en elle Motax Mouy déff lii elle😂elle veut ragagné confiance en elle perdu dans les nuages😅
Excellent point
Non elle n'a pas perdu confiance en elle bien au contraire. Yeena kay dëkkël fu mu dëkkul parce que soi disant dafa divorcer libre, motax mu wax elle veut se remarier pour montrer que bonoul comme vous dites. Ndax dans l'esprit collectif sénégalais ou des hommes sénégalais en tout cas Jigéen bu baax miy Jigéen buy sëy. Célibataire du ku baax, divorcée du ku baax, veuve sax du ku baax ndax mën na Ayy gaff 😂. Fichez la paix à cette Dame elle ne vous doit rien wala daf leen yoreel xaalis. Ni ngeen fi defoon Dieyna Baldé léegi bàyyi ngeen ko ndax mi ngi sëy. Vous ne connaissez ni les batailles sourdes des gens, ni leur combat, ni leurs regrets ni rien d'eux, vous ne portez que des jugements. Toumeu dafa metti Mia a parlé de remariage pour comme qui dirait setal deram tuuti
Vérité absolue bro
Bayi lene musique
Salam weshow sa analyse si deug rek lasi guiss❤❤❤❤
Merci serigne
Senegal ba Santa Domiingo noo Wes T fort
Namonnala🎉🎉
Wes show xaral m sangou guaw niow seytan vidéo bi yakam tinako won tellement 😂😂😂
Yow bayil Viviane yabil domou diambour bi ohhhhhh
merci beaucoup frr lou lerrr❤🎉
Merci ❤ merci ❤ merci ❤ merci ❤ merci ❤ merci ❤ merci ❤ merci ❤ beaucoup
Mia laniou beugue
Bougo Lou bakh dh
Merci Amna solo
Sa yonn nékou cii
Yaw tamit sa yon nekouthi wanel sa tat
Bro well said I totally agree with u
Respect bro 🇧🇪 🇸🇳
Grazie mille fratello hai detto tutto simo dietro di te non devi staccare dí dire la verità 🔥🔥🔥
Wesh Je suis d'accord avec toi sur le fait que Mia et ndakhte lo sont devenu esclaves de l'industrie dama lène yereum da melnii amou niou ay conseiller
Réspe man 👊👊
Si naka nonou si naka 🧠
Respectél Say Domme nakhe xalé nawlé la sa ex dieukeur kou bax la wone gorgoloule touti sisa bop svp Adouna amoule solo kholale si mada Ba wala si kiné lam kéne douléne xasse Lou diotte lagniouye solle gniola gnieuk si showbizz bi foufe té Dara meusoule gniaw
Lo koy tuddëlé ex-jëkërëm pourquoi ces comparaisons ?
Amna solo ✔️💌
Thank you bro
Elle est libre 😂
Bou niou ko defon ba sama tous les gants bi Nieuw dou ngén ko defati da ngén di dof dof lou rk
Kokou khamoul louy bah😂 domeram la
Merci frère
Il n'y a rien de mal pour une femme d'exprimer son désir de se marier en 2025 .
Ne soyons pas bornés!
Wax dëgg YÀLLA. Bu ko waxul woon léegi nga gis ku ni waa Mia xanaa bëggëtul sëy, elle ne parle jamais de se remarier depuis son divorce. Ñi ñoo waxu ci boppam
Sans voix! Wesh tu as tout dit. Elle doit faire attention
Wesh do wakh si Volume 2 bi koi
Ban volume 2?
Salam Weshow sa analyse si Album KING BABA Secret 7 volume2 lagnouy xar diadieuf🙏🏽
Dieukeuram rek moko mana jugé c ça
Serigne touba kou amoul kilifa séytani nk sa kilifa mia lolou moko dall
Tu a raison
Elle a fait un choix pour sa vie, pour sa carrière qu'elle est mère de la même façon que chacun de nous fait des choix de vie. Il y a certaine hypocrisie dans nos sociétés, Mia qui porte une combinaison fait scandale mais des gens à moitié nue dans les rues personnes n'en parlent. A un moment il faut arrêter. Tellement de pression est mise sur les femmes que c'est étouffant. Toujours avoir à réfléchir longuement à ce que tu porte, ce que tu dis, comment tu marche, comment tu salut, comment tu mange
Yow tané wo mia guissé
Ioe deh franchement wakho bi dara djiguene yiww nagne thi kham