Mane dhé Damaye partagè sama chaîne RUclips ak sama Watsapp nako abonnés yeupp def bouko dèfè Sa 10 contact dinaniouko guiss xam li tonton moumar di ligueye si askan wi
Makk daal matna bayi cim reew, Mon père maggi lay nuyu bu baax. Lima leer moy tay mann suma la fi jegge dem jangi borom xam xam yoyu bind teere yoyu, lu bari mënn a ma raw. Fiñu tollu ni mënn a la tudde Bibliothèque ndax liga nëbb ci xam xam, liga jang ci teere yi amal nañu njariñ. Jëwrigne Ndiasse nak man mën na la sedel ci mom ndax ay att a ngi ni bamako xame ak tay, xamna figa ma tek motax ragal nala wax ni moma yarr, wala famu yaro la yaro nga mujje ma xeep ! Waye nak lii la Yalla dogal ! Xam na sa taxawaay ak fonk biga fonk dine ak lu bax ba amo sax droit nak giss lo njort ni luy yax la nga nopi ci ! Waye nak suma sañon nga deglu ko bu baax ba am sa propre appreciation, lu wute ak extrait yiñuy partager kepp ci mom. Defendru mako wala luni mel sax nak maggum jëmm la responsable de ses paroles et pensées baci actes, damay mandu ci liga giss ci mom te jappe ko nonu waye nak da fek rekk ni yenn ñar ñëpp da am folen tolu ci mann, ma am luma xam ci yeen te mu leer mani yena bokk ligenn bëgg ci mbaax ak ndjub ak diine. Nga balma akh waru ma ci sax wakh, waye nak japp naani waref la ma jeem la leelaral. Balma akh 🙏🙏
Nous qui sommes d'anciens abonnés, nous savons qu'il n'y a aucune once de vanité dans ce que vous dites. A vous entendre parler on sent que vous êtes un homme cultivé multidimensionnel . Vous me redonnez envi de lire. Djazakallahou khaïran.
Mashallah Sangue bii, guestou nga Mashallah, ta connaissance est universelle Tu as parfaitement raison, seuls les initiés guidés par des maîtres authentiques doivent parler au nom de la foi
Quallah le tout puissant vous retribut, pour tout les efforts que vous fournissez, pour éveiller la conscience des gens pour la connaissance et la défense de l'islam notre religion.🇸🇳❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏿🙏🏿🙏🏿👍🏿,
Serigne momar je t suivait mai ds la vidéo précédente Mouhamed psl est la meilleure créature ( tu en doutais???) et l prophète Ibrahima est le meilleur car c luii khalilulah j pense c leger 😢… deepen your ressources bc Mouhamed est la meilleur creature psl❤
Machala oustaz Ndiassé mi gni ko topou woyof nagnou bopou lol encore une fois vous avez démontrer votre immense connaissance islamique et philosophique
Ma cha Allah amatina solo. Ce qui fait mal dans tout ça, ce sont des gens qui ont sciemment choisi de se soustraire de l'Islam qui se donnent l'outrecuidance de parler de la Religion des autres, en complicité avec des sites internet qui ne font que la promotion de la médiocrité et du libertinage en se souciant uniquement des nombres de "vue" et " j'aime ''. En tout cas ipso facto il faut que ça arrête par tous moyens possibles.
Nous sénégalais nous ne faisons malheureusement pas la différence entre l'islam et la philosophie. L'islam est une religion cadré enseigné par des prophètes dont la source de la connaissance viens direct de allah soubakhana wa talla tandis que le philosophie est un courant de libre pensé ou chacun peut exprimer ses idées car la contradiction est l'essence de cette science. Qu'allah nous guide vers le droit chemin et nous assiste dans ces moments de troubles.
Je suis entièrement d'accord avec vous. Mes oreilles n'appartiennent qu'à moi, je préfère écouter les livres audio de sénèque et marc aurèle que de suivre la plupart de nos Oustaz à plus forte raison ces revenants.
Ndiassé je le connais trés bien en italie,c'est un manipulateur,j'ai toujours dis aux jeune qu lui il fait tout ça pour pour ce donner de l'importance et entrer dans le système....
Ndeyessane nioune Sénégalais lène bokouna thi luniouy yakal ngaw nagnou geume ku diok niou topula t duniou xam funiou djemé 😢dagni deff nank tuty mer y’a trop d’ignorants dans se pays encore merci beaucoup ya oustaz thi leral yi guay deff thi askan wi ak dinné dji
SALAAAM HALEYKUM W RAHMATULLAH W BARAKAATUHU JAZAAKUMULLAH XAYRAN W XAYRAN JAZAA PAPA. YAAG FI LOOL TÉ WÉR 🤲🤲🤲❤️ VRAIMENT JEUNESSE WAR NAGN DEGLU GNU MELNI YEEN SINON REK DU BAAX😢
Assalaamu alaykum. Nun askanu Sénégal, noo tooñ sunu BOROOM YÀLLA ba tax MU nuy mbugale yiiy nit. Noo ngi lay ñaan yaa ALLAH nga mùccël nu ci musibay sëtu dajjaal yi. Nanu YÀLLA sàmm, sàmmal nu Sénégal. Jërëjëfati.
SA BAYE ,J T POSE UNE QUESTION LE PROPHÈTE MOUSSA..DETENER UNE SAGESSE..MAIS PURKW DIEU LÀ ENVOYÉ DE RENCONTRER HOUDAR... DAFFA AM XAM XAM BO KHAMNÉ NÉKOUL SI TÉRRÉ... MOUHAMAD IBNOU ABDALLAH AK MOUHAMAD RASOULOULAH DOU BÉN.. MAIS DOU TÉRRÉ MOLOKOY KHAMALLL... FAITES TRÈS ATTENTION DOU DAGUA DIANGU RÉK TU PEU RÉPONDRE À TOUT LS QUESTIONS.. MANGUI DIÉGULOU BOU BAKH...
C'est que senegal kou diouk dieul micro di tararari rék di leudeumal nitt gni késsé. Machallah tonton momar yalla na yalla barkel , kadou yi amna solo
Soukrane ya imame que ahla te récompense pour les efforts que vous êtes pour la jeunesse sénégalais long vie et ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Way Way way djieureudieuf mon pére yalla nga goudou yaw réka mane ci gnii dará yalla nala yalla faye djieureudieuf
Mane dhé Damaye partagè sama chaîne RUclips ak sama Watsapp nako abonnés yeupp def bouko dèfè Sa 10 contact dinaniouko guiss xam li tonton moumar di ligueye si askan wi
JAAJËF, JAAJËF, JAAJËF, VOUS M'AVEZ CONQUIS. DIEU VOUS GARDE 💂♂️ 💂♀️ 💂♀️
Machalla djieredieffatti Serigne Momar Diagne yalna la yalla sam allahouma amine
Machala amatina solo baye Momar yalla na yalla fayla Senegal mome damako khametoul comme sabar gou tass 😢😢😢
Makk daal matna bayi cim reew, Mon père maggi lay nuyu bu baax.
Lima leer moy tay mann suma la fi jegge dem jangi borom xam xam yoyu bind teere yoyu, lu bari mënn a ma raw.
Fiñu tollu ni mënn a la tudde Bibliothèque ndax liga nëbb ci xam xam, liga jang ci teere yi amal nañu njariñ.
Jëwrigne Ndiasse nak man mën na la sedel ci mom ndax ay att a ngi ni bamako xame ak tay,
xamna figa ma tek motax ragal nala wax ni moma yarr, wala famu yaro la yaro nga mujje ma xeep !
Waye nak lii la Yalla dogal !
Xam na sa taxawaay ak fonk biga fonk dine ak lu bax ba amo sax droit nak giss lo njort ni luy yax la nga nopi ci ! Waye nak suma sañon nga deglu ko bu baax ba am sa propre appreciation, lu wute ak extrait yiñuy partager kepp ci mom.
Defendru mako wala luni mel sax nak maggum jëmm la responsable de ses paroles et pensées baci actes, damay mandu ci liga giss ci mom te jappe ko nonu
waye nak da fek rekk ni yenn ñar ñëpp da am folen tolu ci mann, ma am luma xam ci yeen
te mu leer mani yena bokk ligenn bëgg ci mbaax ak ndjub ak diine.
Nga balma akh waru ma ci sax wakh, waye nak japp naani waref la ma jeem la leelaral.
Balma akh 🙏🙏
Nous qui sommes d'anciens abonnés, nous savons qu'il n'y a aucune once de vanité dans ce que vous dites. A vous entendre parler on sent que vous êtes un homme cultivé multidimensionnel . Vous me redonnez envi de lire. Djazakallahou khaïran.
MERCI beaucoup tonton damalaye suivre souvent mais je savais Pas que ,,,,mais daal Alkhamdoulilah Machala Merci beaucoup tonton
Très bien dit qu'Allah te bénisse et te protège contre tout mal
Macha'allah père elhadj Momar Diagne vous méritez plus mon respect.
JËRËJËFF 🙏
SVP si vous pouvez épingler leslivres sur les commentaires.
JËRËJËFF 🙏
Merci pour les livres, Yàlla guddal say fan
merci pér mé il faut aller ver les plateaux de télévision.machala
Mashallah Sangue bii, guestou nga Mashallah, ta connaissance est universelle
Tu as parfaitement raison, seuls les initiés guidés par des maîtres authentiques doivent parler au nom de la foi
Ma cha alah ❤❤❤❤
Sama gorgi pourquoi douñioula invité si téléyi vous êtes tellement pertinent Qu'Allah vous protège ❤❤❤❤❤❤❤
Quallah le tout puissant vous retribut, pour tout les efforts que vous fournissez, pour éveiller la conscience des gens pour la connaissance et la défense de l'islam notre religion.🇸🇳❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏿🙏🏿🙏🏿👍🏿,
Amine
Merci Imam
Senegal kou djog ñu inviter ko ci Plateau ŋgay waxe sam xel ci domaine yu lac janŋ mu wër
Doyna war
Merci seigneur d'avoir créé des hommes tel que Serigne Momar même s'il sont rares dans ce pays de fous.
li lep gnak diangue kassé la rewmi gnou nek dafa bari ay diahil
Encore une autre contribution de haute facture baye Momar Diagne MashAllah gëstu gui amna solo lool Dieuredieuf
MachaAllah papa dolli naa la naw. Xam-xam du ay làmbatu
Merci pour votre message pére j'ai bien noté votre message
Alhamadoulillah,ce Ndiassé la je ne l'ai jamais écouté,mais Sénégalais dafa nekha manipuler
Longue vie doublée d'une excellente santé obstacle diagne
Ah mashalah Papa guestoungaaa déh !!!Yallla doli soutoura ,Mashalah vous m’avez impressionné
Yalnala yalla doli soutoureu té sameu leu Baay Momar❤❤❤❤❤❤
Mandè wa diewrigne ndiassè mosoma doye😢😢😢
Maachaallah professeur !!!
Billahil wallahi, les Sénégalais ignorent la profondeur de votre science islamique.
Ndiassé je vous jure qu'il manipule les jeunes et pourtant ce n'est pas un bon exemple ...
Bilaye wakh nekh neu mais kham liggay wakh mokko dakk fouf , je vous réitère mon respect papa dieureudieuf Diagne 🙏🙏🙏
Machallah jaajeuf yaa Imam, yangui niouy yé bou baakh YALLA na BOROM bi fayla❤❤❤❤❤❤❤
Machaallah Serigne bi
qu'Allah te récompense de la meilleure manière
Merci pour l'intervention
"élucubration" c'est exactement le mot que je cherchais
❤Machallah serigne bi ham ham bi yalla na yokou ndah yangui thie dieurigne Woye gueule yi yalla na yalla bour feye la yiw goudal sa fane
Mashalla sama khol Sedna man Louga deck
Merci vraiment .
Ki tankal na gnou.
Macha halla
👍🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Dégatina Deugg
Yaggal té wérr🙏🏿
Baye mor Diagne yay nitou DEUG kham kham dou pekhé
Serigne momar je t suivait mai ds la vidéo précédente Mouhamed psl est la meilleure créature ( tu en doutais???) et l prophète Ibrahima est le meilleur car c luii khalilulah j pense c leger 😢… deepen your ressources bc Mouhamed est la meilleur creature psl❤
Machaa allah damaa contane
Mérci momar diagne voila des personnes pour réveiller les jeunes sinon ndiassè va les détruire
Salam Papa Yallah nala Yallah Fayy
Dieurdieuf tu est formidable ❤
je l'ai écouté une ou deux fois ; mais il ne semble pas maitriser ce qu'il dit
Il ne maîtrise rien du tout
Machala oustaz Ndiassé mi gni ko topou woyof nagnou bopou lol encore une fois vous avez démontrer votre immense connaissance islamique et philosophique
Jadieuf papa senegale mo nekhia nakh
Je n'ai jamais pensé que t'as lu ces grands auteurs de la spiritualité universelle.
Ma cha Allah amatina solo. Ce qui fait mal dans tout ça, ce sont des gens qui ont sciemment choisi de se soustraire de l'Islam qui se donnent l'outrecuidance de parler de la Religion des autres, en complicité avec des sites internet qui ne font que la promotion de la médiocrité et du libertinage en se souciant uniquement des nombres de "vue" et " j'aime ''. En tout cas ipso facto il faut que ça arrête par tous moyens possibles.
Maa chaa allaah baay Momar,
Yal na yàlla yokku taxawaay bi,
Dieredieuf aladji momar diagne,khamkhame rékka waur.yallana yalla goudale sa fane té mayella wer.
Aimer l'en vidéo
La foie d.un incroyants bi beugueu nako dh
Francis jeanson. Un excellent ouvrage
@@serigne-momar Merci beaucoup papa yalla nala yalla dfal guoudou fane ak were 🙏
Wakh deug yalla Diewrin ndiassé wakhoul lou aay. Deug rek lay wakh avec facilité
Alhamdoulilah dieureudieuf yaa Imam yalna na la borom by doli diam ak wéer
Mais yo yow dodem tok am mom def débat. Ndiasse mom danioukouy begee loubary ❤
Nous sénégalais nous ne faisons malheureusement pas la différence entre l'islam et la philosophie. L'islam est une religion cadré enseigné par des prophètes dont la source de la connaissance viens direct de allah soubakhana wa talla tandis que le philosophie est un courant de libre pensé ou chacun peut exprimer ses idées car la contradiction est l'essence de cette science. Qu'allah nous guide vers le droit chemin et nous assiste dans ces moments de troubles.
Vous avez très bien résumé la situation.
Mon frère ce gars ne fait même pas de la philosophie.
Dara khamouko.
Quand je disais que sa ay kadou sou yaroul rek yéété tay deuguelate ngua ko djeureudjeuf si yété bi imam.
Je suis entièrement d'accord avec vous. Mes oreilles n'appartiennent qu'à moi, je préfère écouter les livres audio de sénèque et marc aurèle que de suivre la plupart de nos Oustaz à plus forte raison ces revenants.
Un stoïcien
Anmna solo👋👋👋
Machallah am na solo
Macha lah
Longue vie doublée d'une excellente santé amine yarabi
Yallah li guene si khétou diamou yalla la diokh khétou seydina Mouhamad psl . Té diamou yalla yoyou woor AK djouli cila bok
Macha Allah
Vous êtes trop kharagne Ma sha Allah!
Merci ya imam شكرا لك الحق معك❤❤❤❤❤❤❤❤❤💙💙💙💙💙💙💙💙💙🟦🟥🟦🟥🟦🟥👑👑👑💫💫💫💢💢💢💢💥💥💥💯💯💯
🤝🏾🇸🇳🇦🇷🇧🇷🇱🇷👏🏾Macha alla Bonne continuation si lep lou bakh amine 🤲🏾🙏🏾🕋🕌 goudal fan lolou !!
En tout cas ni son cassé judiciaire ni son curriculum est propre en italie
Ndiassé je le connais trés bien en italie,c'est un manipulateur,j'ai toujours dis aux jeune qu lui il fait tout ça pour pour ce donner de l'importance et entrer dans le système....
Ya Ouztas machallah
Ndeyessane nioune Sénégalais lène bokouna thi luniouy yakal ngaw nagnou geume ku diok niou topula t duniou xam funiou djemé 😢dagni deff nank tuty mer y’a trop d’ignorants dans se pays encore merci beaucoup ya oustaz thi leral yi guay deff thi askan wi ak dinné dji
Xam-xam nag tënkuwul ci wenn làkk nit ki man bañ a fer ijji ci làkku Araab waaye teewul mu am xam-xam ci diine Lislaam.
Thieu sama papa salame ❤❤❤❤❤
Macha Allah amna solo
SALAAAM HALEYKUM W RAHMATULLAH W BARAKAATUHU
JAZAAKUMULLAH XAYRAN W XAYRAN JAZAA PAPA. YAAG FI LOOL TÉ WÉR 🤲🤲🤲❤️
VRAIMENT JEUNESSE WAR NAGN DEGLU GNU MELNI YEEN SINON REK DU BAAX😢
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mashallah amna solo❤❤❤❤❤❤❤
Merci
Machallah kham kham bou leer rk mo Am solo
Macha allah kham kham réka woor
Assalaamu alaykum. Nun askanu Sénégal, noo tooñ sunu BOROOM YÀLLA ba tax MU nuy mbugale yiiy nit. Noo ngi lay ñaan yaa ALLAH nga mùccël nu ci musibay sëtu dajjaal yi. Nanu YÀLLA sàmm, sàmmal nu Sénégal. Jërëjëfati.
Imame Diagne.deug.deug.yaye.intellectuel.gni.dossene.morome.daniou.Taniakhou.reck.يضلون ويضللون
Ma sha Allah papa
Bimako dégué la premiere fois la khamni imposteur le c ndiassé
Machala papa
SA BAYE ,J T POSE UNE QUESTION LE PROPHÈTE MOUSSA..DETENER UNE SAGESSE..MAIS PURKW DIEU LÀ ENVOYÉ DE RENCONTRER HOUDAR...
DAFFA AM XAM XAM BO KHAMNÉ NÉKOUL SI TÉRRÉ...
MOUHAMAD IBNOU ABDALLAH AK MOUHAMAD RASOULOULAH DOU BÉN..
MAIS DOU TÉRRÉ MOLOKOY KHAMALLL...
FAITES TRÈS ATTENTION DOU DAGUA DIANGU RÉK TU PEU RÉPONDRE À TOUT LS QUESTIONS..
MANGUI DIÉGULOU BOU BAKH...
Kaye ñiou bolé léne plateau…
Goudae fane rek lae lay nianal.
❤❤❤❤
J'habite dans un quartier qui a pour nom"Georges Bernanos 1888- 1948"
Yalla sameu la defala diameu toujours pret à défendre l'islam et le vrai contre les vendeurs d'illusions
Ok papa ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
MACALLA 🫶✨
3:39
Senegal dinnè amoufi tè doundouniou dinnèr tarikha ak parparlô rék
Il ne dit que de n'importe quoi, comme ni ngue ke wakh daa wara dianqui
Il profite de l orat de Sonko pour passer son message de Yala Yala
Machalla serigne bi ama solo
Walaakhi dou ngissteul deugeu bou werr nga wakh