Bravo wally et leila events, tu as assuré comme d'habitude.Mais n'oublies de faire la promotion de ton dernier single "Je ne suis pas comme eux" pourquoi pas une émission ON IT spécial pour ton album international et les prochains singles à venir. Song bi sakh nga warone dougoussé si concert bi. Tu es un artiste au vrai sens du terme, meun woy, meun live performance, stylé, star, populaire, beuri bayré machaallah wally moy fateu fep 😃
L'entrée 🥰 qui l'aurait imaginé😻 que des surprises avec toi wally 🥰 wollah t'es pas kom les autres machallah ♥️ c'était un spectacle de malade vraiment extraaaa🔥🔥
Machallah Mar Yacine le chanteur du peuple ken d'où yawe tu as assuré comme d'habitude Mais Dome de paris ak bercy saloum c'est le meilleur concert de l'année ❤❤❤❤❤❤❤fier d'être faramareeen waaay🎉🎉🎉
BERCY SALOUM 2:15 Yoon wi 16:15 Yobanté 32:15 Borom keur 45:25 Ma cissé alima Ndiaye 1:02:56 Awa baba thiam 1:30:05 Défma ndank 1:43:14 Miirnaa 1:51:06 Do changer 1:56:35 Le temps 2:09:03 Serigne fallou ❤❤❤❤❤
Mon chanteur du peuple sa entré bii betouma tu es phénoménal machallah ❤️❤️❤️❤️ on est tout ❤️❤️❤️ avec toi ana faramareene comme man sortez vous beaucoup de cœur pour waly
Svp on peut parler de Raam daan un peu 😭❤❤❤way gni nio meune way❤ live borom keur bi😭 chapeau à cheikh anta Ndiaye Ndiaye talla bakar codou ndiaye 🥁👑🏅🥇🏆🎹 Milano bi😭❤❤❤❤❤❤mais raam daan louy sen problème 😭 nounou mais dj dafa alou🤣 lamine nar ❤ Mathiouré mbaye aussi 😭❤❤❤❤❤🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁 Modou diagne le digne fils de kaolack ❤❤❤❤❤❤❤💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃
🎉❤mâcha Alla wally ballago Seck yalla nalla yalla ak Serigne Touba ak Wa keureume same la arr la mane amoule kouy takh ma déme Ayyy soirée ni concert avec yaou nak sa boummm🤣dama Cheickh niari yone nel amine yarabi ❤❤ a été ❤
Focus sur les dates suivantes 08 juillet Bercy Mbour 15 juillet sorano avec èbène prod 22 juillet Brescia 29 juillet Italie aussi 06 octobre sortie album international 31 décembre niou réserver cicess wla arèna wla Abdoulaye Wade bou diamniadio❤❤
*Bakary defaral son bii pour bénén yonn Wally bimuy waay borom keur deguma sax limu donn wax alors ay airpod la tek T MIGUI DONN RENDRE HOMMAGE SUNIU BAYE BII PAPA THIONE*
Deco bi d dotoul amaty Machalah ❤❤❤❤❤❤xamouma kouko defar
Entrée wally bi mannama raye 😢😢😢😢legui sur scène 🎬 day am neg 😂😂😂😂😂Machalah way
YALLA ☝🏾 défnala loumoula déf ba parê ta kénn meunoulci dara yalananioula YALLA ☝🏾 sammal bidiaahi Rassouli LAAH Sala LAAHU alayhi wa salam 🙏🏾
Wally Kou bakh leu blh kholall artiste kaolack yeupp laa yégueul sur sen
Bravo wally et leila events, tu as assuré comme d'habitude.Mais n'oublies de faire la promotion de ton dernier single "Je ne suis pas comme eux" pourquoi pas une émission ON IT spécial pour ton album international et les prochains singles à venir. Song bi sakh nga warone dougoussé si concert bi. Tu es un artiste au vrai sens du terme, meun woy, meun live performance, stylé, star, populaire, beuri bayré machaallah wally moy fateu fep 😃
Ioe beugg nala d❤❤
Que le tout puissant par la grace de son prophete Mohammed vous assure protection et longue vie. Amine
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Voix bi bénela amatoul yalla dala béral lokho je t'aime fort wally seck ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
L'entrée 🥰 qui l'aurait imaginé😻 que des surprises avec toi wally 🥰 wollah t'es pas kom les autres machallah ♥️ c'était un spectacle de malade vraiment extraaaa🔥🔥
Ay yashou❤❤❤❤❤❤❤❤
@@fatoumatasambe5108 fa Wally 🥰♥️ ♥️♥️
@@fatoumatasambe5108a
Faut reconnaître que la promotrice est une excellente innovatrice
La logistique,La décoration est à couper le souffle
C'était extraordinaire 🎉❤
Ceux n'étaient pas les logistiques de personne d'autre c'étaient les logistiques de Wally Seck 🥇👑🎤💰🤍 du faramareen groupe il faux que ça soit claire!
@@mouhamadoumoustaphathiamci8866non dafa xamoul mais décoration bi promotrice moko deff
Papis Ndiaye ak cheikh niane dans "yoon wi" ils sont malades 🔥🔥🔥🔥🎉❤️
Clips bou Nice wally,concert bou nekh wally,image wally…vraiment t’as révolutionné notre musique 🎉😢❤
Machallah Mar Yacine le chanteur du peuple ken d'où yawe tu as assuré comme d'habitude Mais Dome de paris ak bercy saloum c'est le meilleur concert de l'année ❤❤❤❤❤❤❤fier d'être faramareeen waaay🎉🎉🎉
BERCY SALOUM
2:15 Yoon wi
16:15 Yobanté
32:15 Borom keur
45:25 Ma cissé alima Ndiaye
1:02:56 Awa baba thiam
1:30:05 Défma ndank
1:43:14 Miirnaa
1:51:06 Do changer
1:56:35 Le temps
2:09:03 Serigne fallou
❤❤❤❤❤
Merci
❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
♥️♥️♥️♥️♥️🔥🔥💯🥳🥳🥳💖💖
🤸🤸♥️♥️♥️🥳🥳🥳👏♥️
Merci
Mon chanteur du peuple sa entré bii betouma tu es phénoménal machallah ❤️❤️❤️❤️ on est tout ❤️❤️❤️ avec toi ana faramareene comme man sortez vous beaucoup de cœur pour waly
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤
Le meilleur de sa génération Wally dis d’or rék Inchalla
Sénégal dafa meti danouye wax rek boy bi falewouleine sax bravo bouleine deglou Sax
Manchaalah lou bakh rek laye am Inchaalah c beau
Mais borom keur 🎉🎉😢❤❤il l'a dead
Bercy Saloum bi nékhone na Masha Allah 🥰🥰🥰🥰🥰🥳🥳🥳🥳💃💃💃💃👏👏
Machallah à chaque année bercy saloum moy gagner. Bravo à toute l'équipe de la promotrice. Chapeau à WBS❤
Meilleurs concerts de l'année ❤🎉🎉🎉
🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥💯💯💖🤸🥳
C’est le concert de l’annèe 🎉.Bravooo
Ya leen meune ya eup dollei yafi néh kou sissou dagual sa bopou koy 💘💘
Ly lah yalah def kene mounu cii dara walay ndeysane ya fi nei waw mako waxx dh 💯🥳🙏🏿☑❤❤❤🎤🎤🎤📎🥰
Billahi walleye yow wahatiko
L'entrée extraordinaire 🎶🎤❤️
Vraiment wally tu es meilleure mais courage encore mon frère bonne continuation
Svp on peut parler de Raam daan un peu 😭❤❤❤way gni nio meune way❤ live borom keur bi😭 chapeau à cheikh anta Ndiaye Ndiaye talla bakar codou ndiaye 🥁👑🏅🥇🏆🎹
Milano bi😭❤❤❤❤❤❤mais raam daan louy sen problème 😭 nounou mais dj dafa alou🤣 lamine nar ❤
Mathiouré mbaye aussi 😭❤❤❤❤❤🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁🥁
Modou diagne le digne fils de kaolack ❤❤❤❤❤❤❤💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃💃
Ce sont des nervis musiciens gni dagno rakh ils sont wa raam daan dagno bien
Niou wadial 4e édition Bercy Saloum bii ❤
OOHHH WALLY I LOVE THE ENTRANCE!! MARSHALLAH LOVE FROM THE UK, AND I WAS BORN IN SALOUM...MERCI❤
Le chanteur du peuple ❤❤❤ ya meun ya eupeu doolé ❤️♥️❤️💯
Leila machallah waay linga df ni dafa feiss
mn frère boul khalat fesse wala dou fesse, avc notre golden boy lstar sénégalais et africain rek dou ay fo 😂❤❤❤
mn frère boul khalat fesse wala dou fesse, avc notre golden boy lstar sénégalais et africain rek dou ay fo 😂❤❤❤
Il a bcp de talent wollah ❤❤
Legui lourass bou louga bi mo dess❤🎉
Wally Seck 🥇👑🎤💰🤍 alhamdu li LAAH 🙏🏾💖
Très belle production 🤩Chapeau à toute l'équipe technique 👋
Wally Lima tardé ni naikhouma dara way mais machallah
🎉❤mâcha Alla wally ballago Seck yalla nalla yalla ak Serigne Touba ak Wa keureume same la arr la mane amoule kouy takh ma déme Ayyy soirée ni concert avec yaou nak sa boummm🤣dama Cheickh niari yone nel amine yarabi ❤❤ a été ❤
😂😂😂 en tout cas boula Yalla nato bagua dém si béne yone dotoko defati
Wa kaolack show mom yene rkk laye topou non li dou nèn waye 😂😅wa rame dane dof yi ❤❤
Wa lourass mayy niou live Louga bii
Jai ecouter a mois seul 50 fois ou plussss dooopppppp bro
Wally seck le chanteur du peuple ❤❤❤🎉🎉🎉🤴🤴🤴🤴
Bilay kèep kouy waay yaye bayam mou nèkh ak mou nakhadit
Toujours en forme kiiko Mane bokoul ak kiikoy dieme mar Yacine 🎤🪘♥️
Ya meun ya eup dolé waly❤❤❤ chanteur du peuple✍️✍️✍️✍️🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤
Lourass ani bou louga bi
kII DOU NITT WAY
Wally rekkkk mo xam kan moy wally continue sur la meme lancée
Concert Wally yeup you Saloum yii moy dakk 😫😫💔💔🤧🤧❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🔥
Wally ky dama yakar waa kaolack lagno yor lomotiv tjr daff koy deff 🔥🔥🔥
@@Latydiop98lomotif kaye 😂😅non wa kaolack mom doniou meune show trop machallah bi 3em fois mais bo yekisi rkk kanè mo dakh doyna ware na dal li 😂😅❤❤
@@AmathNguirayesi kaolack danio meun show té lolou dafay geuneu motivé artistes bi
Machallah yallah gua am diam ❤❤❤❤
Wally seck chanteur du peuple 🎉❤
Le chanteur du peuple 🎤🇸🇳😍
❤❤❤❤❤
🎉🎉🎉🎉👍👍🖕♥️♥️♥️♥️
Next time we need cheikh niang louder definitely
Wally Seck yaye bandit ❤❤
Wawaw Wally Ballago seck ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yw rk lanuy top ❤❤❤❤❤y’a meun y’a eupneu dole yalla na yalla samoula ❤❤❤❤❤laf thiat
Souniou Asc Bi mo meune mo yeup Dole 💪❤️🥰
Non Bercy Saloum bi limassi dal dou deug😂chaque jour ma sétane ko
Wally ki es tu
Live borom keur❤❤
Walah moi aussi 🇸🇪🫡
Moi aussi
Ahhh mar yassine danga ni wone pikine mo dahk thi ate bi 😅 mais kaolack gagné nalene 🎊
Khole yeupeu fekh ❤❤❤❤❤❤❤
Wa Kaolack Gnio meunn shoow ohh😮
Machallah Wally à avec Raam Daan❤️❤️😘🎉🎤👑👑💯🇲🇷
Bilahi amo morom yallah nala yalla faye ❤❤❤
Live borom keur nekh na waay ❤
Latyr Diop Déguén Mbaye yaa meun❤❤❤❤
Tieuy papis Ndiaye 🎉❤
Le chanteur du peuple ❤🎉Wally B secke ❤✨🥰❤️
Le chanteur du peuple eska do posé candidats 2024😂
Say boul gnou katoulou ndem way
@@moustaphasall9278p]p0❤❤❤
Kham nanii d ni geuneu kholl politiciens yi❤😂🎉
@@moustaphasall9278😂😂😂
Focus sur les dates suivantes
08 juillet Bercy Mbour
15 juillet sorano avec èbène prod
22 juillet Brescia
29 juillet Italie aussi
06 octobre sortie album international 31 décembre niou réserver cicess wla arèna wla Abdoulaye Wade bou diamniadio❤❤
Naniou off cices 31 et préparé Dakar arena lolou la guiss
@@Mody-nz3zt papa Youssou Ndour mo fa dan teuk 1er janvier
@@falloufal11 je préfère qu’on change la date du 31 cette fois si
Incha ALLAH ☝🏾 nawoon fawoon rék
Live yomboul
Ndanane mokoy deff 💪💪💪
Waye reike laye deife dei 😂😂🎉❤
Wally seck rékk laye topp bilaye ❤❤❤❤
Mercy notre Wally national ❤
Bilahii do nitt mar Yacine ❤
Vraiment tu est le meilleur mar Yacine maïssa bigue Maïssa bigué marr narou Papa thione ak Diagua chéri sokhna Aidara
Il chante techniquement 🎉
Laff thiatt rekkk❤❤❤❤❤❤
Le meilleur
Ndeysaan li Nekh na wally yàllah gua am diam ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
live borom keur 32:10 j'aime ❤❤❤❤
Le chanteur du peuple ❤❤❤❤❤ya meune ya eupe dolei
Alhamndoulilah MAshaALLAH
Migui cool dh wally
Le meilleur tout simplement❤🎉
Live mome amothi morom 😂🥰🥰🥰🥰
C le meilleur de toutes les temps
Ya meun sma wadjii ❤❤❤
Wally meilleur de sa génération
*Bakary defaral son bii pour bénén yonn Wally bimuy waay borom keur deguma sax limu donn wax alors ay airpod la tek T MIGUI DONN RENDRE HOMMAGE SUNIU BAYE BII PAPA THIONE*
Tu es unique ❤❤machallah
Machallah Wally Seck Jtm ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤way way ki mo doff dé❤❤❤❤
le chanteur du peuple on t'aime ❤ toi et Sonko kassé nak
Merci mar Yacine ❤😊
Merci beaucoup le chanteur du peuple ❤🎉
Vraiment on t'aime le chanteur du peuple
C le meilleur ❤
Bilah wally ya menou woyr❤❤❤❤
Musique bi dafa ame borom😂😂❤❤
Nice song wally B bless to u
The legend on it again and again....
Wawaw Wally❤️❤️❤️❤️
l'incontournable Ballago
❤ lep nice