Urgent! Sélbé Ndom montre le chute du combat Modou lo vs Siteu...“ da gnou coy daane ba mou…

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 2 дек 2024

Комментарии • 96

  • @BassirouGueye-i4r
    @BassirouGueye-i4r 26 дней назад +43

    Modou lo yalla nakou yalla May ndam si kaw siteu

  • @MomoWade-y8z
    @MomoWade-y8z 25 дней назад +8

    Modou lo yalnako yalla may ndam inchallah 🙏🏽

  • @AbdellahiNdiay
    @AbdellahiNdiay 26 дней назад +31

    Modou lo yalanako yallah soutoural mayeko ndam bou sed gouye le 24 novembre inchallahou rabi

  • @MameAbdouDiouf-l8y
    @MameAbdouDiouf-l8y 26 дней назад +9

    Modou lo dame rék inch'Allah ❤

  • @KebbaJobe-f8m
    @KebbaJobe-f8m 26 дней назад +16

    Modou lo ❤❤❤❤

  • @SerignebassirouMbaye-v2m
    @SerignebassirouMbaye-v2m 26 дней назад +10

    Modoulo yalla na dan siteu

  • @MatThiam-m9g
    @MatThiam-m9g 27 дней назад +5

    Machallah maman yaye Lambe

  • @justuncliktv5262
    @justuncliktv5262 25 дней назад +4

    Capturer lén commentaire bi.
    Prèsk même chute bi modou dané wone boy niang, nonou lay dané Sitteu incha'Allah

  • @bintoubop7847
    @bintoubop7847 12 дней назад +1

    Modou lô yalna ko yalla may ndam

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 26 дней назад +7

    Boo amée jom dotoo wakh si combat modou lo 😂😂😂

  • @docsamba9998
    @docsamba9998 24 дня назад +2

    Salbé day fène rèk. Bayyil Baatou Laillaha Illallah bingay fo wé. Khamoulo dara

  • @mamecorndiaye1850
    @mamecorndiaye1850 26 дней назад +4

    Yallah bou diéleu am 😂

  • @FallouMbaw-lu8uj
    @FallouMbaw-lu8uj 25 дней назад +1

    Modou kharagne looooooooooooooooooooooooo seul 🔥💯🥇
    Yalnako yallehu maiy dam si barké Aladji Fadilou mbãckë 🎉❤🎉❤🎉❤
    Kharagne lô seul

  • @Utilisateuranonyme12355
    @Utilisateuranonyme12355 25 дней назад +1

    BAYYILÈNE SÈNE FÈNE Yii SELBÉ ! BAHNA.

  • @NAKK_YAYE16
    @NAKK_YAYE16 21 день назад +2

    Siteu ✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿

  • @malickngom5493
    @malickngom5493 26 дней назад +13

    Ha man de honnêtement limou wakh noonou laako guente beurre bou gaw ba paré modou teudd si kawam

    • @oumitandiaye6780
      @oumitandiaye6780 26 дней назад +1

      Amine

    • @mamadoudiop1105
      @mamadoudiop1105 26 дней назад +1

      Amine inchalakh modou dinako dan

    • @tmb4488
      @tmb4488 25 дней назад

      Siteu day danou tokk si souff

    • @oumitandiaye6780
      @oumitandiaye6780 25 дней назад

      @tmb4488 amine inchallah

    • @justuncliktv5262
      @justuncliktv5262 25 дней назад +1

      Mane deh nonou lako guénté com combat modou lo ak boy niang présk même chute

  • @diopabdou6983
    @diopabdou6983 8 дней назад

    Thieuy Selbé légui lo wakhate thi Avertissement yii

  • @martindiene9113
    @martindiene9113 26 дней назад +2

    Sétale Yalla si liguaye wakh stp

  • @KhalifaDiop-b3x
    @KhalifaDiop-b3x 12 дней назад

    Vraiment senegal dall dafa neikh.daniouy jitou yalla

  • @abdoulayediallo4028
    @abdoulayediallo4028 26 дней назад +1

    Siteu dam rek insalah

  • @AmadouSow-jl1gu
    @AmadouSow-jl1gu 26 дней назад +2

    modou lô âmenâyâkârené dâye dâne siteu mais siteu sâmâ mbeur le modou lô dâfâ âme aye serignou sérére youko nguémbeu siteu aye pounkâlou serignou sérére gnoko nguémebeu conbat bi sacrifice ak worr mokoye dâne il faut mou âme serigne you worr si gnâri camps yi téré laye wãkhe gualadjou sérére dafa âme si niari camps yeupe

  • @alioudiatta4352
    @alioudiatta4352 25 дней назад

    Ndam rék inchalla diamaguéne deuk la

  • @bayefall1917
    @bayefall1917 26 дней назад +1

    😅😅😅mais qui loumou wakh😅😅

  • @ElhadjiyayaToure
    @ElhadjiyayaToure 20 дней назад

    😂😂😂 bilahi Sénégal mo dakh si adouna bi.

  • @onestensemble8497
    @onestensemble8497 25 дней назад

    Selbe yangui dieum mak nak😅😅

  • @mamadoungom5831
    @mamadoungom5831 26 дней назад +3

    Siteu yallah nako yalla MAY ndam

  • @papadiom9260
    @papadiom9260 24 дня назад

    Thieuy Doudou lo Champion laaa mais Pikine rekkk la yepp! Sama PA bii dhee dafa GRAW te nena maa Siteu dinako taak (ceinturer) Modou di fitakhou pr guene thii mou kaal ko ande ak mom mou djakhane !!! 10 ans après (Door tank bi nga daner Eumeu 2014 thi Katane nonou lagn laay daner presque ) inshallah

  • @koccaliasthevoice101
    @koccaliasthevoice101 26 дней назад +1

    Salbé...tout sé voleurs on va les enfermé....te sonko yalla kofi tek..ngir mou teuthie ndey domerame yeup

  • @kolo9240
    @kolo9240 26 дней назад

    Selbe respect les gens stp

  • @abdoulazizdiop-e3r
    @abdoulazizdiop-e3r 26 дней назад

    Amine

  • @morgaye9582
    @morgaye9582 25 дней назад

    Ki meuna fèn dhé alahou akbar 🤔 yi khètou bokalé khana boy fen sakh gua respecter la mémoire des disparus mais gua nek fi dilen sosal yalla sagne sagnam bi ken yegoufa en plus yaw yaye kane ba louy khew gnognou gneuw bassi iao dila avisé guisso dara fen rk

  • @assanekane1426
    @assanekane1426 26 дней назад

    Khamoul dara selbè wakhofi dara day lambatou rek di wakh

  • @cireba2317
    @cireba2317 8 дней назад

    Selbé arrête way

  • @nganima
    @nganima 26 дней назад +1

    Bo défoule ndankk bala nga dé dinga paralysé ak bépp nitt bouye diémeu wakh lou aksségoul tékssi di fénn.

  • @MoustaphaMbaye-sg1tr
    @MoustaphaMbaye-sg1tr 24 дня назад

    Serigne Abdallah diouf de mom khamna darra

  • @papasalioucisse9639
    @papasalioucisse9639 25 дней назад +1

    Nekhoul ba nekhoul sebe mo meun gni ndakh limousine wakh dafa leer te chaque fois dafay aam deug

  • @OuleyeDiagne-r5r
    @OuleyeDiagne-r5r 26 дней назад

    Lolou am naa

  • @amadiudiallodialllo
    @amadiudiallodialllo 24 дня назад

    Victor modou lo

  • @diopmamadou1614
    @diopmamadou1614 26 дней назад +2

    Mane je ne comprends pas pourquoi Ngua niémé yalla AK sa si si bien lolou Ngua kham séttal yalla souniou Borom tu es vielle maintenant raggalal yalla souniou Borom

  • @elimanediaw9681
    @elimanediaw9681 26 дней назад

    Modou lo sérère guinmb niouko dh m amna nuoukoy nianal Modou kimou gueuneu yakar niar père nidiayam ak Cherif Hamad guine biseau la nekk

  • @MamadouKébé-y5t
    @MamadouKébé-y5t 26 дней назад +1

    Ana miracle bi thieye yalla

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 26 дней назад

    Salbé sonko mo wakhone kou gagñé elección yi bouléne ko maye diam tagka ak baga

  • @MamadouSall-l7g
    @MamadouSall-l7g 24 дня назад

    Yeureumeul say dome

  • @oumitandiaye6780
    @oumitandiaye6780 26 дней назад +1

    Menteuse le père de Modou lo est décédé comment tu peux le voir

  • @elhadjialphacisse9376
    @elhadjialphacisse9376 14 дней назад

    Siteu kessé

  • @cheikhndoye670
    @cheikhndoye670 22 дня назад

    Dafa mana fen dee de Douko bayi

  • @thiernowade5769
    @thiernowade5769 16 дней назад

    Selbe.ndom.dangaye.doul.

  • @oumitandiaye6780
    @oumitandiaye6780 26 дней назад +1

    Tu peux étre la mère de Modou lo mak nga

  • @alioudiatta4352
    @alioudiatta4352 25 дней назад

    Siteu seul

  • @khadimfaye8003
    @khadimfaye8003 14 дней назад

    Salbe Bayile dole

  • @ahmedgueye8067
    @ahmedgueye8067 26 дней назад

    Bayil doul mak dou féne

  • @jupinleye8346
    @jupinleye8346 26 дней назад

    Selon yaw kattal sa nday noppi waay

  • @LatyrKare
    @LatyrKare 27 дней назад +5

    Siteu fin 88 la modou lo 86 nank rk