Malgré j ne comprend pas wolof mais les sénégalais vous avez la chance d’avoir se grand chanteur vraiment je le valide c’est le meilleur one love 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇫🇷🇫🇷🇫🇷💯
Lawlatiat thione seck nakhar ngua fi bayi, Wayé bayi wofi gatié, yalla mola fayé wally mi nguaniou bayé, yalna yalla yessal yeurmendé ak ndiégueul si yaw
Thione il mérite plus daffa deff lounè si music Senegal motah yalla dakoy fayal lepeu si diabote bi ,Thione Wetal gua Dunia bi amone guaffi place bilay xèdionn guafiii papa thione mes yalla dinna motalliiii sa yènnè si diabote bi inchallah dah wally ameuna sa geureum senegal dinagne dieul waly tètèko diapalè di wèteu si yonn bi inchallah Ramdan dafay existé oeuvre yi dafay continuè di doundal xol yi dah waly sa yonn la dieul
Wally tu as encore prouve que tu es le seul et unique artiste de ta génération, l'héritier de papa thione, le successeur de youssou, the best of all time in senegal, love you so much 👍👍👍👍🌤️🌤️🌤️🌤️🙏🙏🙏🙏🌹🌹🌹🌹🌹🎇🎇🎇🎇🎇
Wally yallah na sa diam yague 🥺 yallah nala yallah sam ar la yir la mousseul la si thiate ak lamine may la kholou mougnou ak katane nakheté yéne bi diss na mais on est de tout cœur avec toi notre golden boy on t’aime énormément merci pour ces moments extraordinaires ❤️❤️❤️❤️
Notre fierté Nationale c’est notre Wally National laff thiatt tu m’as fait pleurer quand t’as dit kor Diaga nameu naleu j’ai tjrs aimé cette chanson je l’écoute souvent mais aujourd’hui te voir répéter la chanson c autre chose pour moi car papa Thione n’est plus de ce bas monde yalla nako yalla yeureum té kharéko Aldiana firdawsi.Bonne continuation Signé Fatima Ba Wally family😍
Tu as démontré à la face du monde ton courage et ton héroïsme d'avoir produit un spectacle époustouflant avec classe malgré les coups bas et le décès récent de notre papa Thione. Que le seigneur te protège, le staff, l'orchestre, sponsors et tes hommes de l'ombre!
Wally penda mangane missi belili ngor, beytii ma djguene mbor ak ali ma djguène mbor😘 Maryacine maicha biguè, maicha biguè maryacine lad Diop deguène mbaye maicha Diop deguène mbaye dagou dagou deguène mbaye. Le chanteur du peuple, le golden boy de la musique sénégalaise, le meilleur de sa génération goudou fann rek lalay nianal seck 😘 Je vois pas papa thione mais qu'il repose en paix et il est fier de toi 🙏🙏😘
Wally ne retient pas tes larmes, si tu veux pleurer ,pleure, ça fait du bien desfois, en tout cas j'ai passé un bon moment aujourd'hui, j'ai dansé jusqu'à..... Te quiero mucho 💕😘
Waly séck tu es le meilleur💞Limou yalla may domou adama mbidéfff meunou si dara thikaw thi kanam rek barcke borom touba léguèyou ndeye leu💪💪💪💪 papa thione yalnako yalla yeureum
Tu es un lion ....tu aura plus queca incha allah wally boul titeboul raggal tu as un coeur en diamant Yalla dou la setane guay torokh mouk tu fais la fierte de la jeunesse senegalaise
Wally ligua woya papa thione koula doul wone fek acapesse walla say 1er aniverssair grand théâtre khamouko diamono yoyou migui won Sénégal nioumaye nane dimbaliniou ci Wally bilaye m tay woy bi migui dora am valeurs courage niak dafa meti man mi j'ai perdue toutes les 2
MERCI un milliard de fois c'est ce qui me reste à te dire toi Wally, staff, Raam Daan et toutes les bonne volontés qui t'ont soutenu pour la réussite grandiose de ton retour. Que Dieu vous bénisse et vous ouvre toutes les portes d'opportunités dans sa miséricorde divine!
Bravo wally j'ai beaucoup pleuré parceque j'ai simplement craqué le fait qu'il n'est plus là papa thione Seck en tout cas nous allons prier pour toi que tu vives cent ans sans ordonnance ...
Non mais le poids de l’orchestre, des musiciens c’est extraordinaire🥵♥️, wally gneuw fèlou lèn li ba djam la💥💯, mbir mi nekhna machalla wally dundal💯💯♥️. Il prouve encore qu’il est le chanteur du peuple et que les sénégalais gnoko beugueul sen bop🙏🙏, gnou bayi di teukeulé lou bokkoul wally dou moromou kén de sa génération voilà🙂💯.
Sa Waye bilahi bou thiow li barei DEUG reire mais wally môme keine d'où mome bilahi .kou weite nak Di NGA khamni wally d'où moromou keine thi Sénégal. Thi show business bi il est largement en avance sûr eux .il a tous les moyens pour conquérir le monde avec son style particulier machala ❤️.
Le danseur de Wally qui vient de se marier, il aime bcp Wally ça se voit car il a repris la scène de suite alors qu'il aurait pu encore profiter de son mariage Diabar dji tamit kou bakh la Mash'Allah
Bilaye daguay seyane concert wally bi yene say nga dioy yene say nga bek. Repose en paix papa thione et bonne continuation à wally on est tous fier de toi.
Vraiment Mar yacine tu nous as assuré ❤️tu es prouvé que tu es seul et unique de ta génération ❤️🥰le meilleur reste à venir que tu es entrain de gagner c’est le travail de diaaga ❤️🥰leguey ndaye ndom deguela pir boul tiite boul ragal Walahi ❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰
Les artistes ont tellement peur des relations des autres artistes kom you et pape motakh douniou fi niow mais Waly bath nalen ko deh MERCI à boubs bigua diapé ba legui bayiwo goré gua mandou geu merci pour ta présence 🙏🤜🤛
Walaye walaye lii nekhna. Le son est wahoo. Tellement c’est doux que je pleure. Ndeysanne awoukatt yi liniouy sou souf nekhone golo dou yek si khôl laye dougue.
Oh waly Yallah rek yangui si kanam Alhamdoulilah on t’aime fort 💪 gni Dieul sén temps di connecter di def aime pas vous perdez votre temps Walahi yalah néna Waw
Machallah soirée nekhna wally seck tu es le meilleur très content , juste que khaliss bi niang di sani rek moma metti parceque Sénégal dafa metti. Sinon soirée bi nekhna
Bilay nieup contane tu es la fierté de tout le pays lou fi chanteur meussoul def sur scène au Sénégal yakofi def Diam diou beri yalla mousseul si thiatt 2009 ba legui y’a nek chanteur préféré❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓🤩💓💓💓🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩💓💓💓💓💓💓💓💓
J'aimerais y venir mais l'école nous laisse rien mais je pense à un autre jour soy yone diékhoul wakhoudil dou diékh ici a Bambey Wally Ballago la gnouy bégué 💟💟💟💟🌟🌟
Waly diameu ci yow bro sama xarite gorégua bahgua wayé ku beugeu cheikh niang tamite beussal jaime Mayal jaime guitariste bi cheikh il le mérite noumou nékè si waly il est comme djily mbaye si youssou ndour
On t'attend encore inchalla le chanteur du peuple 12 juin ligui mou niowate bou sobe yalla nawone fawone boume thia mboy mboy dja inchalla bissate co rek niogui harre faramarene bi une datte inoubliable le golden boy de la musique sénégalaises machalla lafe thiatte belle grand théâtre dagna ca mine fofou bahna stade Abdoulaye Wade laniou beugue inchalla le 12 juin prochain niogui hare papa dji wassalame 🙏🙏🙏🕴🕴🕴🕴💪💪💪💪✌✌✌☝️☝️☝️une seule datte a retenir 💪💪💪💪
wally seck goudal fane way bilay tu es le meilleur 1il chante bien 2 tu as des b musiciens 3 spectacle bou Nice merci et bonne continuation 🎤🎸🪘🪕🎹🪗 machallah
Waly sa noon la yereum walahi koula bagn moy deh rek Waly Seck dundeul 199ans mou comase tey andak weur ak sutura ak kheuweul you bari te barkel yallah nala thiat sekhlou amin ya rabbi
Mashallah Wally Seck damba Wache nga Grand Theatre beh Zerooooooo belie Faramareen bi do moromu ben Haleh si mim Reew nyun Sah fans contan nen torop dila Nyanal Yalna Yala ngudal sah fan yii Wally Seck Yow cha kaw cha kanam rek Insahallah 🙏🙏🤲🤲❤❤❤🎤👑👑🔥🔥❤❤💯💯❤❤
Khôl sed Maroc contante naniou si nieuw yaw torop mé je pleure papa thione 😭car c le chanteur préféré de ma mére ndeysane yalla nako yalla papa thiono adouna y’a meuna wore😭😭
Ay way le chanteur du peuple yalna sa diamou yag nioune yaw laniou wakh.Bilahi tu es unique.papa Thione que la terre lui soit légère.Sache que vous ne serez jamais seul.
Malgré j ne comprend pas wolof mais les sénégalais vous avez la chance d’avoir se grand chanteur vraiment je le valide c’est le meilleur one love 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇫🇷🇫🇷🇫🇷💯
Lawlatiat thione seck nakhar ngua fi bayi, Wayé bayi wofi gatié, yalla mola fayé wally mi nguaniou bayé, yalna yalla yessal yeurmendé ak ndiégueul si yaw
Félicitations au grand Wally SECK pour le spectacle très riche.
Je t'ai toujours suivi à partir de la République Démocratique du Congo (DRC) Kinshasa.
Merci
wow depuis kinshasha no faramarene bi il est exceptionnel apparement hier ken nélawoul
🥰🥰😍
Thione il mérite plus daffa deff lounè si music Senegal motah yalla dakoy fayal lepeu si diabote bi ,Thione Wetal gua Dunia bi amone guaffi place bilay xèdionn guafiii papa thione mes yalla dinna motalliiii sa yènnè si diabote bi inchallah dah wally ameuna sa geureum senegal dinagne dieul waly tètèko diapalè di wèteu si yonn bi inchallah Ramdan dafay existé oeuvre yi dafay continuè di doundal xol yi dah waly sa yonn la dieul
Ndeysann waly da am niann, dama dann degue papa thione nann waly chance bimou am thi musik bi amoumako
MACHA ALLAH KHÔL YI SEDDD NAGN🥺😍ALLAH PROTÈGE❤🙏
🥲🥲👌👌👌amine tu m’as fai pleurer
Bilahi frère mes nioun wa thies nam nanou wally
Vraiment t'a tout dit
Si guoudi gui rk 200mille don nagniou sétan en direct yalla n'a yalla guoudall sa fan bilahi
Wally tu as encore prouve que tu es le seul et unique artiste de ta génération, l'héritier de papa thione, le successeur de youssou, the best of all time in senegal, love you so much 👍👍👍👍🌤️🌤️🌤️🌤️🙏🙏🙏🙏🌹🌹🌹🌹🌹🎇🎇🎇🎇🎇
Iiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiikiykikiiioloibuy du budgetiii de il où vbv idée
@@doudougaye1379 n
Bilakhi sa ma khôl mo fess Wally rek dou aye fo ❤️💕❤️❤️💕❤️❤️💕❤️💕❤️❤️💕❤️❤️💕❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💕❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Aa
Wawaw
Il montre tjr que tu est le meilleur de sa GENERATION bravo le chanteur du peuple
Wally mba xam nga ni Yalla koula may leu macha'Allah fou sori la tibé diox leu Al Hamdoulillah très belle réussite le peuple t'aime mar Yacine
Bilahi Machalah ki ndayam moko khalal yone bii 🤟
@@user-2032 bilahi diaga rek yaye amoul morom boula nianalé rek mou nékh
Papa thione famon nek xol ba sed na barek Serigne Touba 😭😭 machallh Wally dama contane ♥️♥️ bilay yalla gua sote sa papa fan rek seck
Wally yallah na sa diam yague 🥺 yallah nala yallah sam ar la yir la mousseul la si thiate ak lamine may la kholou mougnou ak katane nakheté yéne bi diss na mais on est de tout cœur avec toi notre golden boy on t’aime énormément merci pour ces moments extraordinaires ❤️❤️❤️❤️
Alahuma amiiiiine yarabiii way
Amine bb
Amiine
Ameen yarabi
Kham nani boula yalla fayé sa xol digeu contane wally seck amal jamm way soula senegal amoul wone dou bakh 😭😭❤
Notre fierté Nationale c’est notre Wally National laff thiatt tu m’as fait pleurer quand t’as dit kor Diaga nameu naleu j’ai tjrs aimé cette chanson je l’écoute souvent mais aujourd’hui te voir répéter la chanson c autre chose pour moi car papa Thione n’est plus de ce bas monde yalla nako yalla yeureum té kharéko Aldiana firdawsi.Bonne continuation
Signé Fatima Ba Wally family😍
Tu as démontré à la face du monde ton courage et ton héroïsme d'avoir produit un spectacle époustouflant avec classe malgré les coups bas et le décès récent de notre papa Thione. Que le seigneur te protège, le staff, l'orchestre, sponsors et tes hommes de l'ombre!
Wally penda mangane missi belili ngor, beytii ma djguene mbor ak ali ma djguène mbor😘
Maryacine maicha biguè, maicha biguè maryacine lad Diop deguène mbaye maicha Diop deguène mbaye dagou dagou deguène mbaye. Le chanteur du peuple, le golden boy de la musique sénégalaise, le meilleur de sa génération goudou fann rek lalay nianal seck 😘
Je vois pas papa thione mais qu'il repose en paix et il est fier de toi 🙏🙏😘
Aywa way lii nékh na dei doma dimbeuli nga wakhal mako Modou lo yalla fayla
Walahi ndeysan
@@kharagnembaye4862
Boul wakh Dara
@@oumarsamb6828 waa magui koy khar
Diap si Rek
Ndeysane
Wally ne retient pas tes larmes, si tu veux pleurer ,pleure, ça fait du bien desfois, en tout cas j'ai passé un bon moment aujourd'hui, j'ai dansé jusqu'à..... Te quiero mucho 💕😘
Waly séck tu es le meilleur💞Limou yalla may domou adama mbidéfff meunou si dara thikaw thi kanam rek barcke borom touba léguèyou ndeye leu💪💪💪💪 papa thione yalnako yalla yeureum
Ma sha Allah, amna spectacle, amna ambiance, amna mélodies, amna wayyy bounekh, amna professionnalisme..... Kou meune nadef
❤❤❤
Ak maturité
Mais youssou ndour et les autres devraient Venir soutenir ce jeune extraordinaire .
Wally bonne continuation🙏🏽
Je pensais qu’il allait faire une surprise 😧
Je te jure pareil pour moi
Yakarolenko sakh mais waly YALLA mokoy takhwou inchalah day geuneu bakh
C le bléme au senegal dounou diapalé kéne mes wally c comme ousmane sonko dans le coeur des senegalais
Tu es un lion ....tu aura plus queca incha allah wally boul titeboul raggal tu as un coeur en diamant
Yalla dou la setane guay torokh mouk tu fais la fierte de la jeunesse senegalaise
Wally ligua woya papa thione koula doul wone fek acapesse walla say 1er aniverssair grand théâtre khamouko diamono yoyou migui won Sénégal nioumaye nane dimbaliniou ci Wally bilaye m tay woy bi migui dora am valeurs courage niak dafa meti man mi j'ai perdue toutes les 2
MERCI un milliard de fois c'est ce qui me reste à te dire toi Wally, staff, Raam Daan et toutes les bonne volontés qui t'ont soutenu pour la réussite grandiose de ton retour. Que Dieu vous bénisse et vous ouvre toutes les portes d'opportunités dans sa miséricorde divine!
La chanson symphonie est la meilleure à mon avis.
Walay moma dakhal ci son WALY yeup.
Un concert rempli d’émotion n’empêche il a réussit à surmonter toutes les épreuves force à toi frére 🔥🔥🤝🤝🤝 tu es le meilleur de ta génération
Waly nous t'attendons en France incha allah. Félicitations nous sommes contents de toi. Vraiment bravoo pour toi travail ❤❤❤
merci
J’espère que demgua adidas arena
Wally mérite de respect dans ce pays il fait voyager la musique senegal
Wally kouko respecteiwoul môme khamna bopam .
Bravo wally j'ai beaucoup pleuré parceque j'ai simplement craqué le fait qu'il n'est plus là papa thione Seck en tout cas nous allons prier pour toi que tu vives cent ans sans ordonnance ...
Tu as encore prouvé que tu es le meilleur de ta génération.Félicitation
Wally seck the best wa Maroc gnongui gui lay khar inchallah
L'incontournable l'infatigable l'extraordinaire wally Ballago seck l'homme au grand cœur d'or doundeul ilimix avec santé de faire ❤️💛💥🔥🔥🙏
Waly on t'aime fort machallah yalla nga dounde ba contane inchallah yagg gnou begueul 💞
Laff'thiat
Machallh Wally dama contane ♥️ bilay yalla gua sote sa papa fan rek seck papa thione famon nek xol ba sed na barek Serigne Touba 😭😭
@@ndongodieng126 amine
@@sokhnambacke9701 Amine way
Mane Doro Gueye moma néx de trop J'aime ce gar à travers la chanson de Wally bilae
Je sais même pas par où commencé bilahi tellement je suis émue. Wally Yallah coo maay.Je pris qu' Il continu d'illuminé ta route
Naniou yalla Bale wayé li nkhna way douma si doyal tei magui wone si direct hier bi deh kén dou mane 🤣wally nala yalla faye way xol yp séde na❤🥰❤🥰❤
Non mais le poids de l’orchestre, des musiciens c’est extraordinaire🥵♥️, wally gneuw fèlou lèn li ba djam la💥💯, mbir mi nekhna machalla wally dundal💯💯♥️.
Il prouve encore qu’il est le chanteur du peuple et que les sénégalais gnoko beugueul sen bop🙏🙏, gnou bayi di teukeulé lou bokkoul wally dou moromou kén de sa génération voilà🙂💯.
Sa Waye bilahi bou thiow li barei DEUG reire mais wally môme keine d'où mome bilahi .kou weite nak Di NGA khamni wally d'où moromou keine thi Sénégal. Thi show business bi il est largement en avance sûr eux .il a tous les moyens pour conquérir le monde avec son style particulier machala ❤️.
@@salioufall802 billahi c'est vrai
Le danseur de Wally qui vient de se marier, il aime bcp Wally ça se voit car il a repris la scène de suite alors qu'il aurait pu encore profiter de son mariage Diabar dji tamit kou bakh la Mash'Allah
Wayé motakhite thioww lagnou yobé, sonou nan trop thi wakh yi
Wally est le meilleur chanteur du monde balla gaye est le meilleur lutteur du monde borome ❤️❤️yii rafétte yii kou d’accord beuseul j’aime
Aka ler❤
Bilaye daguay seyane concert wally bi yene say nga dioy yene say nga bek. Repose en paix papa thione et bonne continuation à wally on est tous fier de toi.
Vraiment je ne sais pas loutakh ma Beugue Wally jusqu'à ce point🇸🇳 longue vie à et surtout continue de nous rendre heureux
Barri nga si morrom. Man damako beugeu ba soumakoy khôl di dioy😭🙏♥️♥️♥️
Vraiment Mar yacine tu nous as assuré ❤️tu es prouvé que tu es seul et unique de ta génération ❤️🥰le meilleur reste à venir que tu es entrain de gagner c’est le travail de diaaga ❤️🥰leguey ndaye ndom deguela pir boul tiite boul ragal Walahi ❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰
Machallah nekhna trop contane nagne yallah nala yallah lafal thiate ta mayla fane bou goudou si barké Seydina Mouhamd psl ❤
Notre Thomas sankara de la musique sénégalaise on tm fort
Bagne bagne beugue xaley by xolou🥰🥰🥰🥰🥰 la am kou d accord j aime
Les artistes ont tellement peur des relations des autres artistes kom you et pape motakh douniou fi niow mais Waly bath nalen ko deh MERCI à boubs bigua diapé ba legui bayiwo goré gua mandou geu merci pour ta présence 🙏🤜🤛
Wawaw mai pour Waly rk nooo 💪nanguou rk wala deceder 🤟♥️💪
Waly waly! li nekh na! Love yown wi ❤️ ❤️ the vocals in that song! Daaaaymmm! 🥰❤️❤️❤️
Walaye walaye lii nekhna. Le son est wahoo. Tellement c’est doux que je pleure.
Ndeysanne awoukatt yi liniouy sou souf nekhone golo dou yek si khôl laye dougue.
Hier j’ai beaucoup pleuré 😭😭😭😭😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️love vie à toi Grand frère
Oh waly Yallah rek yangui si kanam Alhamdoulilah on t’aime fort 💪 gni Dieul sén temps di connecter di def aime pas vous perdez votre temps Walahi yalah néna Waw
Orchestre bi franchement ils font un trop bon travail mashallah daguen meilleur wally danga gueune
Machallah soirée nekhna wally seck tu es le meilleur très content , juste que khaliss bi niang di sani rek moma metti parceque Sénégal dafa metti. Sinon soirée bi nekhna
Bien sandi khaliss mom bakhoul
Bilay
A vrai dire tu es actuellement le meilleur, le leader de ta génération et plus si on veut. Simplicité efficacité et sobriété
Sa me fait mal que pour le moment je suis a l'étranger Sénégal nekhna . Europe nekhoul waly ya fii nekk
J tro aimè la partie Elhadji keïta et waly machala 🔥🔥🔥🔥li dafa nex
Bolen déffone duo vous trois ♥️♥️Wally Madiay et bambaly Dina faye🤗♥️
Bilay nieup contane tu es la fierté de tout le pays lou fi chanteur meussoul def sur scène au Sénégal yakofi def
Diam diou beri yalla mousseul si thiatt 2009 ba legui y’a nek chanteur préféré❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓🤩💓💓💓🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩💓💓💓💓💓💓💓💓
Bravo a toi WALLY SECK moi je t'ai toujours cru en toi seul le travail paie ton pere est fier de toi
J'aimerais y venir mais l'école nous laisse rien mais je pense à un autre jour soy yone diékhoul wakhoudil dou diékh ici a Bambey Wally Ballago la gnouy bégué 💟💟💟💟🌟🌟
khol sedatina trop fier de vous je t adore bcp depuis tivaouane
Yagui sama cite dh ❣️❣️
Walahi Kouné meun nala fay wakhouL Deug❤️wally liguay def si nit kene meunouko daguay sedal xol❤️❤️
Malako wakh dé daniouy sonneu rékk. Mais il resteras le meilleur pour toujours inchallah 💪🤴🏾👑♥️🥰😜
Machalla waly laf thiate si kaw si kaname si barke borom touba .khol rék la sougnou borom di faye inchalla aka gno contane sii yaw walakhi
Toujours égale à lui même machallah machallah 💖 tu as encore prouver papa thione est fier de toi bonne continuation
tu es le meilleur on t'aime n ecoute aucun commentaire mal sainte yallah nala yallah diapalé ntre waly national 🥰🥰❤❤
Mes larmes continues toujours à couler !yalnala yala téyeul bopam Mane yaye Waliyer bi contane n'a lole Lima dance eupeuna!Je t'adore fils❤️❤️❤️
Mm moi damay dioy tè douma sakh kham 🥲🇪🇸🇪🇸
Je vous jure vous êtes pas les seules mes larmes coulent t khamouma loutakh yalla nakko yalla t lokho
Contane si yaw , l'héritier de son papa .I love you so mutch. my son
Oh my Wally jai pas les mots bilahii😢😢cest dés larmes de joie soumalay déglou bilahi sama rongagn day tourou machallah
Waly diameu ci yow bro sama xarite gorégua bahgua wayé ku beugeu cheikh niang tamite beussal jaime
Mayal jaime guitariste bi cheikh il le mérite noumou nékè si waly il est comme djily mbaye si youssou ndour
Bilahi cheikh niang rk Machalah
Wally yalna la yalla mousseul thi peikhei seytanei 🙏 yalna la yalla mouthieul 🙏❤️
Ndeyssane ayyyy wayyy papa thione yalna khippé firdawssi aminnn wayyy Yow waron nga féké lii💪😭😭😭😭😭
Billahi nous sommes très fiére de toi do morome béne goné wally doundeul sa dounde ame na nderigne
Sa live mom béne leu si adina
Dama kham ni MANE nima yaramé
Wayé Bou may féthie doumako tayy saxx
😂😂😂raygama waly mo badola dagay fethi ba tourne nane astafirulah ken manuko mougn
Bilaye nio bok yam li na niou yalla bal comme nimouko waye yallay bal
Mdr
@@nenedieng8277 😂😂mangui deee 😂
@@nenedieng8277 😂😂😂😂😂😂😂sofnga
Machallah mar yacine yalna yalla goudal say fane si barké Yonéneteu bii😍❤
Machallah wally louma mer mer soumala degué contane yalnala yalla doli soutoura moussal la si thiat contane nagnou trop ❤️🥰
tu restera tjrs le meilleur vraiment longue vie à tw ke le bon dieu veille sur toi inchallah
Nekhoul ba. nekhoul waly ta voix fait frissonner merci pour tes belles chansons 🔥🔥🔥🔥
Vraiment bro ta bien géré avc toute l'émotion me ta bien géré lespestacle bonn continuation ce sa la maturité k tu montre nak
Chaque jour je regarde cette concert c beau et j'aime les chansons
Le chanteur du peuple a encore frappé fort son lumière ambiance garantie tu es exceptionnel beau spectacle 💃🏽💃🏽🎵🎶🎵❤️😘😍🥰🇸🇳
Ki d’où niitt un vrai spectacle merci ramdan.
Bly
Mlici
Mickey
Ta etai fort kan tu chantai marodi tu t’es retenu waly vraiment tu t’es retenu yalla bahna
On t'attend encore inchalla le chanteur du peuple 12 juin ligui mou niowate bou sobe yalla nawone fawone boume thia mboy mboy dja inchalla bissate co rek niogui harre faramarene bi une datte inoubliable le golden boy de la musique sénégalaises machalla lafe thiatte belle grand théâtre dagna ca mine fofou bahna stade Abdoulaye Wade laniou beugue inchalla le 12 juin prochain niogui hare papa dji wassalame 🙏🙏🙏🕴🕴🕴🕴💪💪💪💪✌✌✌☝️☝️☝️une seule datte a retenir 💪💪💪💪
La qualité du show est magnifique mashaAllah
Machahllah this is so nice sama Wally seck rek one love from Gambia Wally the King 👑👑👏🏻👏🏻💃💃💪🏻💪🏻❤❤❤❤❤❤❤❤❤🇬🇲🇬🇲
Le chanteur du peuples ❤félicitations et je te souhaite que du bnr😘😘🇲🇷🇲🇷🇲🇷
Machallah rien a dire notre chanteur préféré tu as bien assuré comme d'habitude.amal diam rrk seck
wally seck goudal fane way bilay tu es le meilleur 1il chante bien 2 tu as des b musiciens 3 spectacle bou Nice merci et bonne continuation 🎤🎸🪘🪕🎹🪗 machallah
Dila buegué depuis France on est fier de toi
Machallah yénafiii néeeee félicitations jvs aimes 💔💔💔💔💔💔
Oui
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Vraiment on t’aime waly Yalla nala Yalla moussal si thiat🙏🏻
Amine💖💖💖
💃😂MANÉ SAP NOOON DOTOUL DORMIR 🛌 DEH ÑIOUN AK YAW BA BANGAY FÊTÉ SAY 105ans inchalah SVP 1milions d’abonnés way li dess bariwoul 🤟🤟🤟
Non Wally faut ma guiss la wayy. The Best Meilleur
Wally seck tu es et tu resteras une fierté....tu es mon DRAPEAU NATIONAL....weere ak WEERLÉ....doundeul BALAGO
Bilay
Franchement douma ci doyall c 4eim fois mako setane❤❤❤❤❤yafi nek ya worre d 💪💪💪diam rk guay am🙏🔥🔥💯💯💯
Ohh xole sedena depuis Mauritanie on t'aime bcp
Wawaww waly lo doundou doyoule non aouma thi yaw sago bilaye lirouma comantere deguelouwouma
Bly limako fékéwoule rk moma méti 😰bly bly walay Wally malah beugue ❤️tée kaffouma barki Serigne bamba jtm dôme bay❤️
@@baba2926 bigué faramarene bi moy yeuguel
000000pp9m9p
Waly sa noon la yereum walahi koula bagn moy deh rek
Waly Seck dundeul 199ans mou comase tey andak weur ak sutura ak kheuweul you bari te barkel yallah nala thiat sekhlou amin ya rabbi
Mangoné Batteur bilahi tu es malade, la musique à carrément changé. Respect maestro
C le frère de Momo Dieng ! Il donne tt c’est la famille 🙏🏾
@@khadijagueyesarr4374 si si lui et moi on se connais je suis batteur Saint-Louisien
Il est fort machala
Kouy kokou
Bandit la jtjr, mais damay lathie ana Ousmane Camara!!??
Mashallah Wally Seck damba Wache nga Grand Theatre beh Zerooooooo belie Faramareen bi do moromu ben Haleh si mim Reew nyun Sah fans contan nen torop dila Nyanal Yalna Yala ngudal sah fan yii Wally Seck Yow cha kaw cha kanam rek Insahallah 🙏🙏🤲🤲❤❤❤🎤👑👑🔥🔥❤❤💯💯❤❤
Félicitations à l'équipe digital de wally
Khôl sed Maroc contante naniou si nieuw yaw torop mé je pleure papa thione 😭car c le chanteur préféré de ma mére ndeysane yalla nako yalla papa thiono adouna y’a meuna wore😭😭
Sama khôl sede na je né même pas les mots niane rek machallah je t’aime mon frère 😍🥰😍
💪💪💪💪💪💝💝💝💝
Machallah laf thiate ya gui niouy bèguel saye souné je t'aime fort❤❤❤❤❤❤❤❤
Ay wally amouma sago si yaw mala beugue yalla nala yalla sam barké cheikhoul khadim
Depuit dembeu ba Légui mangui dioyyyy wally tu es le meilleur yaw yaye séne baye ngiom ngiépou 🤴🤴🤴🤴❤️❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭
Ohh bu youkho rek ngua contan ❤️😭❤️😭
Le roi de la musique sénégalaise 👑🤴🏾💪🥰♥️🙏
Ay way le chanteur du peuple yalna sa diamou yag nioune yaw laniou wakh.Bilahi tu es unique.papa Thione que la terre lui soit légère.Sache que vous ne serez jamais seul.