Urgent - Déclaration de la famille de Cheikh Bethio: Son fils ainé accuse le gouvernement de...

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 14 янв 2025

Комментарии • 482

  • @gansiryfall7247
    @gansiryfall7247 5 лет назад +35

    je pense à la femme qui à perdu son mari et les enfants leurs papa que dieu les protège amine 👪🙏👭💏

    • @amdndiaye9398
      @amdndiaye9398 5 лет назад

      Yow bayil gni di wakh khamna khalatouniou nitt yi dhé motakh yalla bou até rék mo nékh

  • @labellelimashu8942
    @labellelimashu8942 5 лет назад +11

    Taguen bayi serigne saliou ak serigne touba biguen di toumal

  • @moussathiam1105
    @moussathiam1105 5 лет назад +1

    Ndeysane 😭😭😭😭😭

  • @maitrediame79
    @maitrediame79 5 лет назад +61

    Il faut savoir faire la part des choses. Bien avant le procès, la justice a été très clément avec monsieur Béthio THIOUNE en lui accordant la libetré provisoire. C'est vraiment dur pour ses disciples et pour toute sa famille mais un musulman diot aussi être en mesure d'endurer les épreuves que lui font subir Allah le Tout Puissant. Yalla na diamm yagu

    • @mouhamedbirahimfall4881
      @mouhamedbirahimfall4881 5 лет назад +3

      Talibé baye vraiment suis ému sur ton commentaire un grand merci à toi car tu a un grandeur positif

    • @strategiesetdeveloppement2525
      @strategiesetdeveloppement2525 5 лет назад

      et regardez ce lien ce que bethio disait ruclips.net/video/HgIoJQShfn0/видео.html

    • @princeibra9454
      @princeibra9454 5 лет назад +2

      Yén bilahi mane nguén woori guis li motax leufeul ndeyam dolén ko am khaw ma talibé baye nga khawma lodone

    • @fatysyll5643
      @fatysyll5643 5 лет назад +2

      @@princeibra9454 lou khew fii 🤣😃mais yaw ba am nga dara rekk

    • @shannelloukballers9494
      @shannelloukballers9494 5 лет назад

      Talibé Baye iie taliber baye gua khamnagne leip

  • @manla6673
    @manla6673 5 лет назад +3

    yalla nako yalla yereme té kharéko aldina thi barké serigne Touba

  • @ngagnetoure344
    @ngagnetoure344 5 лет назад +19

    Yalna diamo yag ci barcke serigne fallou

  • @mberrymmy9275
    @mberrymmy9275 5 лет назад +40

    Kou dê ya gnak gayi yéwou léne

  • @aidafallousall6793
    @aidafallousall6793 5 лет назад +1

    Ma sha Allah Thioune, Yalla na nga soute sa baye ba fane té déssé barkè, mate nga place, féce nga sa place ma sha Allah, mane déye djoyatou Cheikh bi, yalla na yalla deugaral sa takhawaye, wawe fo nékone ba Aida di djité le 17Avtil

  • @claramendy3336
    @claramendy3336 5 лет назад +1

    Dieu a tranché ! Il met tous les hommes d accord ! Il a appelé son enfant à le rejoindre, respectons la decision de Dieu, en cessant toute polémique. Dieu le père toi qui connais la vérité, apaise la douleur de la famille des personnes assassinées et de celle de Cheikh Bethio. Amen

  • @elhadjifaye2461
    @elhadjifaye2461 5 лет назад +130

    Si j'étais à votre place je n'oserai pas me mettre devant un micro

    • @sokhnamanethioune5959
      @sokhnamanethioune5959 5 лет назад

      Elhadji Faye pourquoi

    • @daoudasow6923
      @daoudasow6923 5 лет назад +3

      @@sokhnamanethioune5959 ces gens sont des escrocs! pour être claire tous les marabouts sont des collabos de cet état escroc qu'on appelle le Sénégal.les dirigeants ou élites sont des gardiens des régisseurs pour le bien être des toubab.

    • @abdoufall6979
      @abdoufall6979 5 лет назад +2

      @@daoudasow6923 yaw khana khalote dh nite Faye wakh bou rafete mbeuse dina guew gua wete ak yalla lo massa wakh wala gua defe ko digua ko reguerette ma toupe bou mbakh frere

    • @daoudasow6923
      @daoudasow6923 5 лет назад

      @@abdoufall6979 Yalla ay caxan la. diné si bopp'am ay léep dong la...
      Falé'w ma yalla!

    • @baagiubou4667
      @baagiubou4667 5 лет назад

      Elhadji Faye the mouy deugeu foute le en prison

  • @mouhamedbirahimfall4881
    @mouhamedbirahimfall4881 5 лет назад +31

    Hun gayi delo silene sene xel té nguen Xamni Deugleu Yone defna ligeyame mais dioulite du yéné moromu dioulitame Safane

  • @sagedupays8112
    @sagedupays8112 5 лет назад +4

    Que dieu lui guerri serigne cheikh béthio yalla mo kay are

  • @serigneseck4012
    @serigneseck4012 5 лет назад +2

    Yalla nakou yalla diappelee thii leeep bidiahi Cheikhoul khadime

  • @toumanekoulibaly6586
    @toumanekoulibaly6586 5 лет назад +79

    10 ANS TOUTINA BAKANE DAFA FOR

    • @KD-fr3xf
      @KD-fr3xf 5 лет назад

      10 ans kegne doyna puisque complice la rek il n a pas tue

    • @serignediop3137
      @serignediop3137 5 лет назад +2

      Meune nga takhaw sa bamèl watte ni mo raye wala moko diglè?

    • @seynabousarr2000
      @seynabousarr2000 5 лет назад

      @@serignediop3137 moma diakhal

    • @serignediop3137
      @serignediop3137 5 лет назад +1

      Adina mo graw kholal li rek li mo takh kouy sédé yhi nite nako sédél lou bakh

    • @diawsokna6138
      @diawsokna6138 5 лет назад

      Toumane Koulibaly lou toutiwoul

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 5 лет назад +21

    *_Ndeyesenn Mais yalla bakhna yalna yallah _**_#sāfara_**_ lepp si barkép kou tédd ki😭👌_*

  • @papediouf9180
    @papediouf9180 5 лет назад +69

    Bethio mérite en prison 50ans

    • @mariemandiaye8825
      @mariemandiaye8825 5 лет назад +7

      Pape Diouf sa baye migui dunde prison si kholam Ndakh dome bou melni iow diare na d

    • @serignesaliouniang4227
      @serignesaliouniang4227 5 лет назад +10

      @@mariemandiaye8825 guiss nga yén loudoul rer defou lénko béthio mi ngén di top dou nitou dîné ki vrai diaxil la kouy woté dîné dinga digual diouli ak woor sey nit mais béthio kouko top euleuk dingako rethiou

    • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
      @mouhamadoulamineseyebeugue2741 5 лет назад +2

      @@serignesaliouniang4227 *_iow yā ñîémé yallah deugue deugue mais cheikh béthio dou sa moromou baye dh bahna_*

    • @taphandiaye4529
      @taphandiaye4529 5 лет назад +1

      Sène data ndaye cheikh bethio mo guène sène serigne

    • @malicksene8838
      @malicksene8838 5 лет назад +2

      @@taphandiaye4529 yaw ak béthio yép sén data yaye

  • @FEEÑAL-v6h
    @FEEÑAL-v6h 5 лет назад +24

    Yalla na diam yag

  • @fahakim22bakhoum69
    @fahakim22bakhoum69 5 лет назад +1

    Sounou borom bindoul koudoul faatu wayè binde koudoul torokh thiono sa soutoura dji yalla nalaw ba dianatoul makhwa barki serign saliou sa yakar

    • @mamediarrabadiane2898
      @mamediarrabadiane2898 5 лет назад

      Lolou amena yalla aténa werou koor képe kouye dioulite khamena lithie yalla wakhe

  • @FALLAPC
    @FALLAPC 5 лет назад +66

    Un criminel doit aller en prison.

    • @diems4440
      @diems4440 5 лет назад +3

      Tu as raison mon frère

    • @mary18203
      @mary18203 5 лет назад +2

      Épicétout !

    • @diamoubamba6328
      @diamoubamba6328 5 лет назад +11

      Ndeysane malene Yeureum yene gniko yener wone prison yeup bayinalene ak aduna dem yonam, dioulite d'où yener moromou djoulitam Lou meti kou si nek nako si bayam

    • @FALLAPC
      @FALLAPC 5 лет назад +2

      @@diamoubamba6328 Dieu est meilleur juge. Charia appliquée.

    • @diamoubamba6328
      @diamoubamba6328 5 лет назад

      @@FALLAPC wi wi raison pour laquelle

  • @cest-2023
    @cest-2023 5 лет назад

    Dieureudieufeti sa wakh rafetna! Mouride yi gno bakh tè gorè!Gno khamni Lou gneuww gnou diapèko Sante !Fougnou nèkk dakha diokhè sènn alal gueuna nangou ligueye!Theuyy ba biss pennc!Dieureudieufeti Serigne Touba

  • @ridjalabdallahyakhineseye3093
    @ridjalabdallahyakhineseye3093 5 лет назад +4

    Maintenant Allah Swt l tout puissant a donné son verdict! Cheikh BéThio Thioun mou Serigne Saliou que son âme repose en paix!

  • @serignediop3137
    @serignediop3137 5 лет назад +1

    Gni mèrè wone cheikh bethio yeup sèn khol sèdd na . Wayè mak nitte meme boko mèrè wè boul injuste . D'accord na kou raye gnou diap la wayè kou rayoul fèkèwoul c'est injuste gnoukoy teuthie 10ans

  • @assangediopgueye6826
    @assangediopgueye6826 5 лет назад

    Bismi lah dieuredieuf serigne touba sante serigne saliou mbackè mbokou diouli kouille wakh nay kham loumouille wakh nite day manou diko ndian ndal serigne saliou mbackè terouko Adiana Merci

  • @labellelimashu8942
    @labellelimashu8942 5 лет назад +1

    Lima meti Sénégal yeup meunoumako wakh maylen niou diam guen nane gouvernement justice mo def ligueyam niatta nit laniou fek sen keur yi niou febar niou teudjielen mom au mois bayinaniou mou dem fadiou bakan dafa fort ken douko nenal

  • @fatousamb2992
    @fatousamb2992 5 лет назад +6

    Dieureudieufeuty Serigne Saliou lii yeup ayy dogaall la kou bakh rék la Natou di daal sissa kaww Serigne Cheikh Bethio Thioune Diamou Serigne Saliou Yagg fi loole tai annd ak wérr amine EL Hadji samb touba mabo

    • @aboubilal1069
      @aboubilal1069 5 лет назад

      Wakhonna serigne saliou moy yalla nako woo yallambi dimbaliko

  • @Queen_Lo
    @Queen_Lo 5 лет назад

    Boula jamm bi narrei torokhal té waro torokhé yalla daflay soutoural Cheikh Bethio yalla dafko soutoural yalnako yalla yeureum tei xareiko firdawsi si barkei weir bou seil bi

  • @aliouseck2031
    @aliouseck2031 5 лет назад

    Yalla nako yalla yarame tekareko aldiana amine

  • @ndellagueyediakhate8650
    @ndellagueyediakhate8650 5 лет назад +95

    Yena niou yap deug deug may wakh mounane Serigne bi dafa tawat wa legui gni niou faat thi aname you niaw yi nak magn len niou way fi yalla rek mofi nek dou lenen baken dafa for

    • @sadiomane6651
      @sadiomane6651 5 лет назад +6

      Ndella gueye Diakhate diareudeuf merci bcp, il faut osé le dire mais ce Mr mérite vraiment la peine de mort

    • @yacinegueyetahir9487
      @yacinegueyetahir9487 5 лет назад

      yabatereek

    • @modoubay7414
      @modoubay7414 5 лет назад

      Rew bakhoul

    • @lampfaye7932
      @lampfaye7932 5 лет назад +1

      Sen thiotou ndey domram yi sur tous ndélla

    • @aichadiouf5911
      @aichadiouf5911 5 лет назад +1

      Ndella gueye Diakhate deug rek nga wakh yabate rek

  • @assangediopgueye6826
    @assangediopgueye6826 5 лет назад

    Bismi lah dieuredieuf serigne saliou mbackè sante reck yala nèna kou dè nanko ndian ndal diko sèdel lou rafet koumou donone sa wadiour doko sèdel lou Bon

  • @yayaba85
    @yayaba85 5 лет назад +9

    Yen de gen yabatè. Kou fi yengou gnou labali li. Et ceux qui sont morts vous avez pensez a eux. Vous pensiez que vous pouvez tous vous permettre

  • @bayemalickniang1829
    @bayemalickniang1829 5 лет назад

    chiekh bi yalla nako yalla kharé aldiana

  • @dadynest3067
    @dadynest3067 5 лет назад +2

    Devant Dieu nous sommes tous égaux... Toutes les personnes qui défendent un malfaiteur partageront la même peine que ce dernier. Si Seurigne Touba est vraiment votre réference faites comme Lui, suivez ses pas..

  • @sambapene9004
    @sambapene9004 5 лет назад +10

    DECLARATION de foutaise; Cheikh béthio devait mourir en prison. Il est qui pour ne pas être jugé; fichez nous la paix. Cet ainé est irresponsable et irrespectueux.

    • @sokhnamanethioune5959
      @sokhnamanethioune5959 5 лет назад

      samba pene yamann doul

    • @sambapene9004
      @sambapene9004 5 лет назад

      @@sokhnamanethioune5959 Désolé ma sœur, je ne m'adresse pas à toi. Tu es petite pour me répondre. Mettons les états d'âmes à coté. Ce n'est pas ton père ou ta mère qui est tué (e). Soit une proche de ces victimes! tu verra. Soit polie ma sokhna.

    • @durkman6938
      @durkman6938 5 лет назад

      Leigui xana digua rouss

    • @sambapene9004
      @sambapene9004 5 лет назад +1

      @@durkman6938 je persiste sur ma position frère. Et arrête de te mêler .

    • @durkman6938
      @durkman6938 5 лет назад

      T'es juste une personne sans coeur mais le monde est devant vous

  • @tyermistikmind4154
    @tyermistikmind4154 5 лет назад +16

    Dommage aak sen commentaire you niaw yi kom ci mom dafkoy liire😂😂😂😂.....
    Cheikh bi dal niitou yalla la...
    Nitt lo xamoul dra mandou sii douma talibés cheikh bi ms yalla rk mo xam li xewone fofou ba décès yi Am....... peut-être sax yene sen Papa meuss na ray ki c

  • @deugdiop3616
    @deugdiop3616 5 лет назад +25

    Bethio est un dieu un dieu ne doit pas être malade il n a qu a venir assumer le dieu en pacotille

    • @moussacisse3616
      @moussacisse3616 5 лет назад

      deug diop non amon koi.rey ngama.lou ler nga wakh

    • @abdoufall6979
      @abdoufall6979 5 лет назад +2

      Yawe deug diop Nite Dafaye wakh Lou Rafete mbeuse dina guew tu Sera Mort ta digua ko layo ak sa mborome gua mbalma

    • @deugdiop3616
      @deugdiop3616 5 лет назад +4

      @@abdoufall6979 je sais bien que je serai mort et j espère avoir le pardon et la bénédiction de dieu et je sais que inchalah je l aurai parce que je fais pas du bokale et je me proclame pas dieu tout le contraire de ton bethio qui proclame serigne Saliou et lui-même dieu et demi demi-dieu

    • @abdoufall6979
      @abdoufall6979 5 лет назад

      @@deugdiop3616Allah nous protege je n suis talibe de bethio yalla mo wakh nite dafaye AME soutoura Meme sou feke liguaye deug la khamo sa euleke lane moye khew magui toupe bou mbakh mane diam yalla kasse LA merci frere adouna amoul solo lepe dafaye diekh

    • @deugdiop3616
      @deugdiop3616 5 лет назад +2

      @@abdoufall6979 tu défends bethio contre dieu je me réfère à ce qu a dit dieu j ai aucun respect pour quelqu'un qui se proclame dieu si vous voyez quelque chose de mauvais si vous pouvez pas le changer par la force dites le que le monde l entend dieu est unique même si j ai beaucoup de défaut je donnerai la place de dieu a personne est bethio n est pas fou donc pas de complaisance

  • @awadieng5160
    @awadieng5160 5 лет назад +2

    Khana yéne gni done wakh di yéné serigne bethio prison rouss guéne wallahi talibé serigne saliou kouko nara trokhal mou tek ko lokho até yalla nak mon gueune bou nitt dieureudieuf Thioune 🙏😭

  • @assaneloum4536
    @assaneloum4536 5 лет назад +4

    Dioulite doux yéné mbokou dioulitam lou ko dal délosiléne sén xéll dieu seul pourra nous jugé qu'il nous pardonne tous

  • @lepatriote934
    @lepatriote934 5 лет назад +7

    Quelle honte je suis le fils de BÉTHIO

  • @cofikomcofikom9169
    @cofikomcofikom9169 5 лет назад +2

    Yalla bakhna

  • @morndiaye1982
    @morndiaye1982 5 лет назад +47

    mais pourquoi accusé le gouvernement?, qu'est ce que le gouvernement a fait ??? expliquez???.

  • @khadysylla8438
    @khadysylla8438 5 лет назад +10

    ta rien dit, c'est un fuiyar, il na rien, depuis tout ce temps il faisait la belle vie c'est au dernier moment qu'il part se soigner, dieu est grand et ceux qui ont été tués ils non pas de famille, tu est vraiment un ignorant

    • @princesambe7902
      @princesambe7902 5 лет назад

      Khady Sylla khana rouss nga dhhhh
      Nite day wakhhh louko woor

  • @mamemordieng7650
    @mamemordieng7650 5 лет назад

    Nanko santé yalla tè khamnè Nato le yalla moukoy tèk ab diamame

  • @masasafiston8843
    @masasafiston8843 5 лет назад +3

    Yalla Nako Yalla yeureum ta kharèko aldiana firdaw Si ms decedè yonou government nékusi

  • @amadymaymounabassoum8415
    @amadymaymounabassoum8415 5 лет назад +3

    Yalla Mahomed Bamba SSaliou koulen di fowee dinguako guiss Gourous yeup dinanou danou bâ diaxane

  • @moussandiaye1979
    @moussandiaye1979 5 лет назад

    Bien dit

  • @sambacisselepoete1694
    @sambacisselepoete1694 5 лет назад

    Yalnako yalla khaaré aldjiana dioulite bouné noumou mana mél bou fato nianal lénko yeurmandé

  • @davedave5480
    @davedave5480 5 лет назад +35

    Mou dèss attè yalla

    • @adjadiedieng4311
      @adjadiedieng4311 5 лет назад

      WALAKHI YALLA ATE NA

    • @davedave5480
      @davedave5480 5 лет назад

      Ça reste le jour du jugement dernier (pour tout le monde) "bissou pinthi

  • @mamyndiaye7108
    @mamyndiaye7108 5 лет назад +14

    Enfin en prisons

    • @mariemandiaye8825
      @mariemandiaye8825 5 лет назад

      Mamy Ndiaye sa data nd iow mounane enfin en prison

    • @serignesaliouniang4227
      @serignesaliouniang4227 5 лет назад +3

      @@mariemandiaye8825 iow limakh ngén alakou béthio mi ngén top kou xol kanam gui sax xamni ap domram la vrai nitou safara la amoul len lou nirou nitou dîné si mom

    • @mariemandiaye8825
      @mariemandiaye8825 5 лет назад

      Mamy chérie relax bb on c que t’as raison nitou safara la kayy motakh tu le reconnais vu que t la diablesse en personne

    • @mamyndiaye7108
      @mamyndiaye7108 5 лет назад +2

      Mariéma Ndiaye yow yagui mere dei khana bethio dafa doneu mathie sa data yay bou neub bi hahahaha domeram dji

    • @mariemandiaye8825
      @mariemandiaye8825 5 лет назад

      Mamy ndiaye oklm bb yen a qui on des data neube baniou kay mare mais sa yaye datam mo réral train biniou done yobou niouy dme job domou saram ndeyam néko mou oubi diokhé train gayi

  • @sene-italo9054
    @sene-italo9054 5 лет назад

    Paix à son âme. Tout âme se rendra un jour que dieu nous accorde de bon fin ameen

  • @teusssrekkk1859
    @teusssrekkk1859 5 лет назад

    Dieureudieuf Thioune

  • @maimounanathan7635
    @maimounanathan7635 5 лет назад +1

    C'est en quoi le titre urgent .?? Toute âme goûtera la mort ;arrêtez ces vidéos inutiles .serigne est il un cailloux ??on ne meurt qu'une seule fois Toi qui parle et nous qui commentons sommes pas immortels,donc à chacun ces fardeaux,vs attendez la mort pour venir tout renconter sur les rezeaux

  • @therealone5700
    @therealone5700 5 лет назад +1

    kou meunoul fadj bopam , meunoul mouthieul bopam si justice sénégal mounila molay douguel aldjana ngakoy gueum esk nit yi nio ngui khalaat

  • @pendamboup932
    @pendamboup932 5 лет назад +2

    li metina trop ko febare gnoukoy condamne 10ans setelene si yalla

    • @KD-fr3xf
      @KD-fr3xf 5 лет назад +1

      legui kou febar dougne la tetche ? gnou gni soul t gnouy done doundou nak

    • @ramatandiaye99
      @ramatandiaye99 5 лет назад +1

      Legui gni déé

  • @hubcommunication6993
    @hubcommunication6993 5 лет назад

    Cheikh Bethio Liguey neu loumou warone liguey yeup si adouna , wanté niénène gni ay merkate legn té khamougnou louniouy wakh rek

  • @ibrahimaseck5111
    @ibrahimaseck5111 5 лет назад +12

    Demlen diamoudji Yalla c mieux

  • @mamysalwa3364
    @mamysalwa3364 5 лет назад

    Deumyi deh contane naniou cheikh bethio demna bayilene fii khana sene khôl sedne deh Sénégal yene wouniou kenne diam

  • @yacinegueye8679
    @yacinegueye8679 5 лет назад +25

    yow am nga lo wakhe sa baye reylou nguay am lo wakhe wa legui gouneyi you niou Ray bafi sen ndiambote

  • @maodosarrlofficiel8750
    @maodosarrlofficiel8750 5 лет назад +6

    Dans kel pays sommes nous?

  • @tinembengue7284
    @tinembengue7284 5 лет назад +1

    Mai nagne ko maye mou fadjou dafa febar yalla mokako tekk kom nimou dieulé bakane nou gnénéne diaraléko si aye lokhome

  • @221elevage
    @221elevage 5 лет назад +25

    Way cheikh bi citoyen la rk il merite mm plus ndax dray dinè dfuko ray ay nit nguene niuy sonalfi ish

  • @bambangom729
    @bambangom729 5 лет назад +1

    Bethio khamone nani li meunouko bania dal ndakh limoudone def ken khamoul wone lanla di tonj Serigne Touba,seringe saliou di teugeu ,di feth gor nji diakhasso ak djigeune yi bir touba

  • @aladjigadiaga2861
    @aladjigadiaga2861 5 лет назад +1

    may lène gnou diamm bèthio nitt kèssè laa prison yii barri ayy nitte you fèbar tène kène fallè woulène nagnou koo dieulli gnou tèkko sii yonne parsk lougnaw limou dèfe sènègal kène meussou koo fèè dèfff lolou moy wakh djii

  • @khadykhouma9733
    @khadykhouma9733 5 лет назад +14

    CHIEKH BI YALL NAKO YALLA ARR MAY KO GUOUDOU FANN SI BARKE SRG SALIOU MANN DH DOUMA THIANTA WAYE KOUKOU SOPOULA

  • @khadijalasalihate6698
    @khadijalasalihate6698 5 лет назад

    yalla na yalla lèrall lèpou si barkè Mohamed👌mai mèttina

  • @serignemodoukhouma7723
    @serignemodoukhouma7723 5 лет назад +1

    Bo matone linga done dinga djigué sa papa ba nitt douko dougeul sy mousiba yii te niakka matt linga done mo waral lou tollou ni 17 Avril bi nguèny senat djiguène di organisé tanguene nek fi

  • @babafaye2106
    @babafaye2106 5 лет назад

    N'oubliez pas de prier pour les victimes et leurs familles

  • @jadoredieuetmohamedkhadimo2521
    @jadoredieuetmohamedkhadimo2521 5 лет назад +1

    Yow doule waye sa baye bethio dou gate mongui fi paris di noce domarame la mo diokhe arme ni bara sow ak koumou meuna andale bou fi nieuwé raylene ko data ndayou bethio ak kep koukoy defendre domarame

  • @mbarbabacarndiaye9892
    @mbarbabacarndiaye9892 5 лет назад

    Dieureudieuf. Serign saliou

  • @matyfall558
    @matyfall558 5 лет назад +1

    SERIGNE BETHIO KOUDOUL YALLA MEUNOULOUKO DARA WAIT ANDE SEE THIANTE GUI MOOLÈNNNN DI DERRANGÈ MAIS NAKKKK SOKHOOOR RÈKKKK MOOOLÈNNN DIAPPP SERIGNE BI YEUGOUL TINNOULLLLLLLL RAYOUL RAYLOUWOULLLLLLLLLLLLLLL

    • @diadiadia9093
      @diadiadia9093 5 лет назад

      Na Kate ndayam feule mo raye il va perir en prison domeram

  • @assaneloum4536
    @assaneloum4536 5 лет назад +20

    Que Dieu nous aide et nous pardonne car lui seul sais ...

  • @moustaphadiakhate2216
    @moustaphadiakhate2216 5 лет назад +5

    10 ans toutina trop waye

  • @sebcam10
    @sebcam10 5 лет назад +2

    Serigne ki kayy... ki mo nekh rek

  • @AwatoubaAwatouba
    @AwatoubaAwatouba 5 лет назад +1

    Dieureudieuf thioune yague fi lool te weer

  • @khadijandiaye5186
    @khadijandiaye5186 5 лет назад

    sa mbok djoulite bou fato dagakoy gnianale yalla yeureumko té kharéko aldiannay

  • @balorythiare7917
    @balorythiare7917 5 лет назад +1

    Waw dimbaliniou way ah

  • @maododiallo6482
    @maododiallo6482 5 лет назад

    Yalla na yalla lërall lëppp

  • @diariyah5856
    @diariyah5856 5 лет назад +2

    Kouh ray nit dagnla wara ray point

  • @BabluBablu-td5bs
    @BabluBablu-td5bs 5 лет назад +1

    10ans da touti si mane réy nit khana kou gnou rèye dou nit wala amoule mbok

    • @durkman6938
      @durkman6938 5 лет назад

      Leigui xana contane gua non yeine na soxor wanté demleine rek

  • @bollembaye8397
    @bollembaye8397 5 лет назад +6

    Senegal mo nekh

    • @muna326
      @muna326 5 лет назад

      Nékhoul dangue sak

  • @Hibzo12
    @Hibzo12 5 лет назад

    Celui qui a dit je ne peux apprendre le coran comment IL peut etre mon guide

  • @ModouNdiaye-xg1rg
    @ModouNdiaye-xg1rg 5 лет назад +3

    môme danioko wara ray boudiotè ci teuth na sante yalla

  • @seydouseck1280
    @seydouseck1280 5 лет назад +2

    Que justice soit faite cest tt et 20 a 40 ans de prison pour les consernee tueur te teyko

  • @cheiahmdiaiad4013
    @cheiahmdiaiad4013 5 лет назад +3

    Li mou koyy wakh Serigue bi rék mo massi métti wallah

  • @isseugueyebeuguefallou6540
    @isseugueyebeuguefallou6540 5 лет назад +9

    Vraiment kheikh bedio diambar la mé nak dafa dioume

  • @ballat2050
    @ballat2050 5 лет назад +2

    Man de magi mas tawwou gni sen mbokkou fattou waye wayye kasso senegal mom yene wouma ko kenn

  • @rokhayadiop3910
    @rokhayadiop3910 5 лет назад +11

    Wakhou fi dara sa bay Ray katou nuite la😂😂😜🙈🙉🙊

  • @cest-2023
    @cest-2023 5 лет назад

    Attè yalla mo gueuna gaw!Cheikh bi rafettt na

  • @99jolof4life
    @99jolof4life 5 лет назад

    Bouma nékoul wone si wérou koor ak serigne bii wakh la kou boone tchiiiiiiim gni niakh séne bakéne nak ak lou si gouvernemen bi

  • @andrenabigueye3201
    @andrenabigueye3201 5 лет назад

    si ç etais aux Etats unis il va prendre perpete sans aucun doute .ç est une honte ça

  • @mortouba284
    @mortouba284 5 лет назад

    Yalla nga am diamou br ser touba

  • @tourekhadim8120
    @tourekhadim8120 5 лет назад

    Bethio migii aldiana yene nake khmolene fougeni moudiou

  • @cheikhgakou6516
    @cheikhgakou6516 5 лет назад +3

    Machallah si kadouyi raféte na

  • @imamhassancissekouta2830
    @imamhassancissekouta2830 5 лет назад +1

    Ahh Sénégal neehn'a lool mane dama jommo manne n'nakk

  • @gueyepro5761
    @gueyepro5761 5 лет назад +1

    Wakho fi dara bethio 10 ans sakh dafa touti si mom

  • @papadieng621
    @papadieng621 5 лет назад +1

    KHAWMA loutakh nafekh BARI sa BAY diokhe ndigeul niou fate domou diambour si anam you niaw ngane yegouko koi nan na talibe yi dal dofou niou BAY thiepi thiepi rewmi AMNA droit

  • @evadiatta5100
    @evadiatta5100 5 лет назад

    Ça servira de leçon au autres

  • @fifinaflores4663
    @fifinaflores4663 5 лет назад

    Guiss ngeen niakk baye nimou metter etant une mort naturelle, waa gni gniou raye seen baye nakk??? Yalnako yalla yeureum te mou fekki gni gniou raye aldianay firdawss.

  • @cheikhcheikh893
    @cheikhcheikh893 5 лет назад +1

    Rèye la niou ko wara deff kou rèye nite rèye rék 10 ans dafa touti

    • @durkman6938
      @durkman6938 5 лет назад

      Leigui xana contane gua non yeine na soxor wanté demleine rek

  • @fayemama245
    @fayemama245 5 лет назад

    Ya des gents qui ont contre cheikh bethio

  • @mary18203
    @mary18203 5 лет назад

    TOUTE VIE A DE LA VALEUR ET PERSONNE N'EST AU DESSUS DE LA LOI. C'EST FINI LE TOUT PUISSANT A FINI DE JUGER.