Journaliste bi, Imam Kanté nieup aye nafek laniou. Pourquoi ils ne sont jamais attaqués à Modou Kara "Kara Show" mofi guena dof di wakh wkhi dof. Yén Zeyda nguén yapp sakh.
@@diamwelly6469 personne n'ose s'attaquer à ce mec...lol... moy problème bi. Et il nest pas le seul mom ak gnimou nekkal nieup... et pourtant si ay wakhou imam kanté dioundiou nako mom ke les kilifeu diiné le font mais kene dou wakh...
Imam Kanté wakh katou deug piir la. Il est juste, posé et extrêmement cultivé en plus d'être courageux. Niou mél ni mom la deuk bi raflë... Yallah Nako sunu borom bi aar. Amiine
Légui solution bi ma am moy :comme que Sénégal lou nekh way deff té niepp ka bokk néniou KO diay après kou né outi fa nga diemm mane môme khamna Maroc Walla 😁😁😁😁😁
Ndeysane pa yoyou moye gnignou inviter gnou gnow tŕ khamougne sakh lou khew😅😅😅😘 douma né gneup wayé y'en a qui ont répondu à cette invitation sans savoir ce qui va se passer riroum King Fahd
Ndiaye mody guirndo bimouy wakh soukouratt bou metti la def bala mo deh cancerologie.son poids dafeu triplewone,on pouvait pas la tourner parce qu elle etait trop lourde.guinaw gui def ayy sakh boleh akh cancer bii.fo tolou dantec si degg ayy youkhom...mon père travaillait la bas..Ya Allah rek moy deugg
Mane dema ame louma métty mais béne affaires ame na Sénégal war nagnou hallate séne passe passe moytou topé tégnou to seydyna MOHAMED swls ak yallaha sougnou brome
Zeyna zamane mi dalll daf niou yap guisc gëne ces tenues ça fait peur en plus gniko top, yalla dafko yoni waxal olof mé elle es pocédé par le diable nanou ko yobou si mouley sow, merci mm kanté
Merci Imam longue vie a Vous. Femme bobou zamane xawma kokou wéroul Seydi Gassama, Birahim Seck Assane Dioma Ndiaye ...etc et Tous c organisations occultes les Senegalais doivent se méfier de c organismes corrompu doublé d une immoralité qui frise la folie.
Bayilen di toumale nitt kii ba taye deigolen mouni yonnetala ma xala deigolen français kii dafané je suis la messagère du Messager d'Allah maname mome moye dawal yonneta bii soff guen trop surtout ioe imam kanté nexoma dara😣😣😣
Imam yoneta bi nena « mane ankara khouroudioul mahdiyou fa khat kafara bima ouzila ala Mouhamed » « kou wedi mahdiyou wedi nga lepou lougnou wathié si Mouhamed » té kou wedi mouhamed diakhanenama moy sa keur
@@suzanelaminegueye1911 il faut faire des recherche avant de dire astafiroulah ou bien la nuit avant de coucher tu fai 2 rakka et tu demande à DIEU de te montré si LIMAMOU LAYE est'il le PROPHÈTE ou pas inchalla DIEU va te montrer la vérité
Ce sont les tarikas qui ont détruit c pays chacun interprète l'islam d la façon qu'il veut résultat c genre de délire des el cheikh des khoutbou zeman des zeyda zeman et j'en passe
@@namaly829 certe ya des gens qui raconte du n importe quoi mais ne generalise pas.ya des maisons familliaux qui sont heumbles parcontre ya des maisons familliaux qui compare le prophete a leurs "serigne"c desolant quand même
Kii di woté nane ap yonante keu Li diadou si mom moy mou dèm diangui défari bopam té kham Yalla douyoni djiguen astouma ko khamni ndiébér katla di Togo ay niawtéff...
Limou wakh ci nite yi feu tèwone te seugg rek bégna sigui damako ci fekk ci c'est peut-etre vrai qu'ils ne savaient même pas le but de cette invitation. Parce que si vous observez bien la vidéo ils ont fait que répéter la même séquence plusieurs fois.
Mais aida qui dara dalou ko remarque bi ma djeuk am thi moom moy le mot réorganisation alors réorganiser quoi le profete Mohamed psl est l'envoi de dieu point
T à chaque fois anna bou yorrer micro rek la soit disant djiner bi du wakh bou parer do toul wakhati c son t les sectes maconique qui font sa il veulent déstabiliser le pays ils que tout les sénégalais le sache
Oustaz nga balma mais yague nguéne soulevéwou ci ay affaire yo xamni ça ne relevait pas d'ordre de discrimination du coran. Issssshhhhh. Mérénaléne torop.
MOUHAMED n'est pas le père de l'un des hommes, Il est bien Le Messager D'ALLAH, AL RASSOULLALLAH et Le Dernier des Prophètes. PAROLE NOBLE ET SUBLIME D'ALLAH SOUBHANAHOU WA TA'ALLAH. Souratoul Ahzab Les coalisés.
Dafa am luye maye saye saye nguir mu déf limou beug senegal liko geuneu yakh moy gniy sol mbobou boudul sén boss nio may gni buniou tenkou wul ci alkhuran ak sunna yénén meun na nieuw
Les tarikhas disent pire aussi. Gni nane ma done tewal jesus son sac,ki nane ma namp ki namp. Wakh rek. Niom nieup khaliss rek laniouy weur ci sene religion bi😂
Laïcité égal sougnou yone nékoul ci diné et c'est grave.un pays où il y'a 95% de musulmans il serait logique d'appliquer la charia à moins que la majorité de ces musulmans soient des hypocrites (naafekk)
Déjà sa tenue!!!!!!!aye derri segg la sole?!comme panthère deh,prophète bou djiguene mom moy adouna toukina.mane gniy assister thi djotayame diko soutenir moma diakhal... le Coran est la plus pure des vérités,Allah (swt)bayiwoul dara lepp lathi deff mashallah...donc la femme la nagnou may diam,kou nek amegua loula doy seukk
J'adore le journaliste 🙏 Imame kante yalla naffi yag te weeerrr way🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Amène
Journaliste bi, Imam Kanté nieup aye nafek laniou. Pourquoi ils ne sont jamais attaqués à Modou Kara "Kara Show" mofi guena dof di wakh wkhi dof.
Yén Zeyda nguén yapp sakh.
@@diamwelly6469 personne n'ose s'attaquer à ce mec...lol... moy problème bi. Et il nest pas le seul mom ak gnimou nekkal nieup... et pourtant si ay wakhou imam kanté dioundiou nako mom ke les kilifeu diiné le font mais kene dou wakh...
J'aime trop imam kante et oustag oumar sall wallah
Mash'Allah nous avons les mêmes Oustaz
Imam kanté bayil doul prédomine
@@karasoudaisbalde7106 Je valide
Bravo!le journaliste était à la hauteur, il a frappé au bon endroit..
Machallah, toujours pertinent et véridique Oustaz Kanté.
Imam Kanté wakh katou deug piir la. Il est juste, posé et extrêmement cultivé en plus d'être courageux. Niou mél ni mom la deuk bi raflë... Yallah Nako sunu borom bi aar. Amiine
Merci imam yallna yalla godal.fanwi
Senegal 🇸🇳 lou waye néx def li yep loukou waral moye nioune wa Senegal denio sagga né siniou dînée
Yako sagna wakh😢
Senegal kat defe néx fola néx gaye genné
Macahalah wallahi ya akhi
Yallah nako yalla djégal aminnn
Lii yep modiouk diamonola chaytane day genedi am dole yalla mousal nou si chaytane
Amiine
Chapeau au journaliste
Il pose de très bonnes questions 👏👏👏
Damani démlén doundi sounna wallahi mane de bima si necké ak légui wallahi tawféx la Oustaz Oumar sall❤ yallah nako yallah faye yarab bi
Mane dé première fois Bimako guisé dama défoneni filme nigérien yiye daw nolliwoud tv la🤣🤣🤣
Walahi c une satante
😂😂😭😭
😂😂😂😂😂
😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂
machalla yalna yalla defal diam bou bakh bayi lafi basi kanam inchalla 🤲🏾🤲🏾🤲🏾🕋🕋
Vraiment ndawsi waar naniouko wakh bopam , senegal dinné dei toumouranké naa ! Kilifeu diné yi warnansi wakh !
soxna zayda zamane yalla yalla Yalla nafi yagga té wér moussal ko si lamigne yalla may ko goudou fann ak wèr mou yagafi loolou
Buzz gua beugu doko ame dé😛😛😛😛
@@fatoukinealaminesene5349 😂😂😂dalousii buzz bi daffa saturé
Légui solution bi ma am moy :comme que Sénégal lou nekh way deff té niepp ka bokk néniou KO diay après kou né outi fa nga diemm mane môme khamna Maroc Walla 😁😁😁😁😁
Coumba Diao ya niak fo dieum dh 🏃🤣🤣 Nar yi rék
Mais mane lima diakhale pa yoyou nékone fofou loigne fa done défe vraiment diakhale n'a ma
Est ce que dougnou ay faram
salima bio 😂😂😂
Ndeysane pa yoyou moye gnignou inviter gnou gnow tŕ khamougne sakh lou khew😅😅😅😘 douma né gneup wayé y'en a qui ont répondu à cette invitation sans savoir ce qui va se passer riroum King Fahd
mdr nioniou esk xam nagn lou xeww saxxx😂😂thio mn pays va mal
@@salimabeaute7982 😂😂😂😂😂
Senegal dal deukou details leu si bo diougei dal si benene mei nak yala naniou YALLAH tek si yonou dioup
Sante yallah par ce qu'on nest des musulman el hamdoulillah
Zeinebou Ndongo macha Allah
Salam to u imam kante yalla ga fi yaaga teh werr
Limamou yaye mouhamadou rossoloulahi kou mér tampi
Bilay kou mér tampi
@@chamsdinediagne3185 késsé nak
@@issaseye4561 dagno réérrr rk
Laye mahtar diaroul sax diffi touddeuh tourou seydina Limamou a.s ndax yallah limouy def defnako ba parè Baye laye a.s moy Mouhammadou psl tè kou weeddi alkou dontè awliyayi ngua mei nak Dieu fait bien les choses ndax Baye laye a.s bimouy woottè kou nitt yakar si rèw mi mouy srg si niongui fi woneuh koneuh wèddiko weddi mak gnila
Psl bouwèdi bi geunè tarr sùnou geum baye lahi digeuneu yokkou psl
Cette femme me fait peur avec c'est tenu elle ressemble les dramatique Nollywood tv
Moi elle ne me fait parce que je peux changer ma voix exactement comme elle le fait et je ne suis pas possédée trop drôle
T'as bien vu
Elle est juste une mortelle. Elle n a que suivit le chemin de ces prédécesseurs.
Masha allah allahu akbar☝️!!!
Ndiaye mody guirndo bimouy wakh soukouratt bou metti la def bala mo deh cancerologie.son poids dafeu triplewone,on pouvait pas la tourner parce qu elle etait trop lourde.guinaw gui def ayy sakh boleh akh cancer bii.fo tolou dantec si degg ayy youkhom...mon père travaillait la bas..Ya Allah rek moy deugg
Un homme véridique imam kanté et très charismatique mashallah ❤❤❤
Bonne question lii boudoul togn lane moy togn mais bane Sénégal laniou nek
Senegal laic .Du courage
Mane dema ame louma métty mais béne affaires ame na Sénégal war nagnou hallate séne passe passe moytou topé tégnou to seydyna MOHAMED swls ak yallaha sougnou brome
Zeyna zamane mi dalll daf niou yap guisc gëne ces tenues ça fait peur en plus gniko top, yalla dafko yoni waxal olof mé elle es pocédé par le diable nanou ko yobou si mouley sow, merci mm kanté
Merci Imam longue vie a Vous. Femme bobou zamane xawma kokou wéroul
Seydi Gassama, Birahim Seck Assane Dioma Ndiaye ...etc et Tous c organisations occultes les Senegalais doivent se méfier de c organismes corrompu doublé d une immoralité qui frise la folie.
Kunzun Rafahi qui sont ces gens ? Seydi c’est pas le droit de lhommiste la ?
Sénégal lifi am eupeneu légui
Lo nekh wayyy deff
je t'aime imame kante
Heyyyyyy!!!
Harammmmmmm
Hahaa astahfiroulahh
Analyse pertinente
Merci imam aujourd'hui je suis parfaitement d'accord avec toi
Ya imam naga téy si mbirou el cheikh
Alkhourane ak sunnah moy l'islam.... Li thi dess lp bokalé la shirk la WA Salam
Bayilen di toumale nitt kii ba taye deigolen mouni yonnetala ma xala deigolen français kii dafané je suis la messagère du Messager d'Allah maname mome moye dawal yonneta bii soff guen trop surtout ioe imam kanté nexoma dara😣😣😣
Yalla rekkk mo mom diamono ndakh moko defar
Imam Kanté loutakh sa genres yii n'oseront jamais s'attaquer à Modou Kara "Kara Show" mofi guena dof di wakh wakhi dof.
Iow ak sa baye vi
Vien attaqué Serigne Modou kara
@@karasoudaisbalde7106 Modou Kara pervers la lale drianké touba yi rek hana sa maman silabok
serigne modou dou sa morom manul mo gun si yaw
@@Homme07-c2y démal wakh ko sa baye ak talibés yii di topou Modou Kara
niouss ndayam késé la déf ndawsi
Imbécile la rek niaf ndéyam rék mo bakh si mome bamou bayi limouye déf seytané
Yen tamitt lolen di saga...?
Moi aussi
Merci oustaz kante
Koumou nekh woote loula nekh....
Machallah le journaliste est fort.
Imam yoneta bi nena « mane ankara khouroudioul mahdiyou fa khat kafara bima ouzila ala Mouhamed » « kou wedi mahdiyou wedi nga lepou lougnou wathié si Mouhamed » té kou wedi mouhamed diakhanenama moy sa keur
King James legui wakh gnou kane moy mahdi bi
limamou laye c le prophète mouhamed psl
Bilay baye laye moye mouhamed psl
Astahfiroulah
@@suzanelaminegueye1911 il faut faire des recherche avant de dire astafiroulah ou bien la nuit avant de coucher tu fai 2 rakka et tu demande à DIEU de te montré si LIMAMOU LAYE est'il le PROPHÈTE ou pas inchalla DIEU va te montrer la vérité
Dawsi yallah souko diapé dina hamné yallah karim
Merci imams pour ces vérités
Ce sont les tarikas qui ont détruit c pays chacun interprète l'islam d la façon qu'il veut résultat c genre de délire des el cheikh des khoutbou zeman des zeyda zeman et j'en passe
nam Aly tu y’a tout dit frère
Déet waay
ya meuna fenne dé lou takh ngen nafekk
Namur Aly ya mana doul domerame do wakh ak zeyda rek
@@namaly829 certe ya des gens qui raconte du n importe quoi mais ne generalise pas.ya des maisons familliaux qui sont heumbles parcontre ya des maisons familliaux qui compare le prophete a leurs "serigne"c desolant quand même
Ndawci daniouko wara talal ci nathie bii beussou al jummah diko bathie yattou Dakaar souko defer mou gueene deuk bii
Merci choukourane ya imam
Kouy guiss mbakh noumou moune nékké yeuneunte dafay fénne
Imam kante thi kaw thi kanam
Kou jogg dokh sa ndaw namoula safé boo jeumè makk d'i wooté lou nekkoul waye xam waay
Kii di woté nane ap yonante keu Li diadou si mom moy mou dèm diangui défari bopam té kham Yalla douyoni djiguen astouma ko khamni ndiébér katla di Togo ay niawtéff...
Limou wakh ci nite yi feu tèwone te seugg rek bégna sigui damako ci fekk ci c'est peut-etre vrai qu'ils ne savaient même pas le but de cette invitation. Parce que si vous observez bien la vidéo ils ont fait que répéter la même séquence plusieurs fois.
N'a sénégalais yi thi bopam deffarouwatt sougnou beugueu Lou melni dioukkk fi peuple Lilou gueum rekk lolou moy reflété thi personnalité publique yi
Baye laye moy mouhamed
Dafa léérr
Ehhhh c simple na dem à la mecque mou wakh fa lolou niou wol nakh digua gnibi en vie
A noter aussi que le journaliste est fort
Ki koku top topeuh seytani pure .jtjr..
Li ma gueuna diakhal moyy gni fa deme
Mage....manedai li dai la wahhe......💭🤐🤐
Bilahi doyna warr
Mais aida qui dara dalou ko remarque bi ma djeuk am thi moom moy le mot réorganisation alors réorganiser quoi le profete Mohamed psl est l'envoi de dieu point
@@magendoye93 c'est ça
T à chaque fois anna bou yorrer micro rek la soit disant djiner bi du wakh bou parer do toul wakhati c son t les sectes maconique qui font sa il veulent déstabiliser le pays ils que tout les sénégalais le sache
Journaliste bi kouma nx la dalay lath ga wax deug mu and si ak ioe ba parei di wax si lou bx si dinné bi mashalah
Sénégal mo bai ay naafek nagnou bayi diné ji gnouy fowé li rek nak mo diara wakh diabaténa trop mouy melni fantôme ni
Le vrai defender de l'Islam
Nous qui somme de d'autre nationalité ne comprenons pas la langue si vous pouriez traduire aussi en français pour nous.
Elle n'est pas la seule il y a même des gens qui se prenne pour des dieu les yalla yalla
Sénégal louway nkh lólou dafé wara diouk lólou amoul bénou réw way
Bi djiguene daniou tegualoul ndeyam rek dekk bou mame elhaj malik ak serigne touba nek niouye wakh ay doff diko top
Merci Imam
Le culpable c'est l'état du Sénégal
Zoukouran imam kanté machallah amnasolo
Oustaz nga balma mais yague nguéne soulevéwou ci ay affaire yo xamni ça ne relevait pas d'ordre de discrimination du coran. Issssshhhhh. Mérénaléne torop.
Imam Kanté s’il vous vous pouvez créer un compte Twitter et poster là-bas aussi pour ceux qui n’ont pas de compte Facebook merci 🙏
Incroyable
Bayilma franc maçon yi yakha deug bi da nguén comprendroul dara ils sont entrain de promouvoir les lobby franc maçon. Ils ont des siéges au Sénégal.
Machalla IMAME ❤️💖🙏
MOUHAMED n'est pas le père de l'un des hommes, Il est bien Le Messager D'ALLAH, AL RASSOULLALLAH et Le Dernier des Prophètes. PAROLE NOBLE ET SUBLIME D'ALLAH SOUBHANAHOU WA TA'ALLAH. Souratoul Ahzab Les coalisés.
Dimbaliléne nit gni waay ak sén aya bi. Dégo léne quran khamo lénko . Go waay
Dafa am luye maye saye saye nguir mu déf limou beug senegal liko geuneu yakh moy gniy sol mbobou boudul sén boss nio may gni buniou tenkou wul ci alkhuran ak sunna yénén meun na nieuw
En tout k khalé bi rafetna toyna damako khémem 🩸
Cette dame est malade. Il la mettre hors d'état de nuire.
Jai peur pour mon pays franchement. Imam nioun yaw laniou deglou !
Wakh deug journaliste bi mtx ma abonnés dall
Moi aussi
Les tarikhas disent pire aussi. Gni nane ma done tewal jesus son sac,ki nane ma namp ki namp. Wakh rek. Niom nieup khaliss rek laniouy weur ci sene religion bi😂
Yaw mome tontula sax yakla
Billahi wallahi ki wooté lolou dou degeu ay fénn késsé
Sélbé Ndom ndékei réwoul sokhna si mo reew
Mane dh lima gueuneu mèti moy yonente bii zikaar layenne bii
😂😂
Merci imams machallah
Imam sa wakh Rafette na
C que loumanekh si imam kante moy polyvalent la
Zeyda Zamane kagn lafi sopékou ? C'est l'ex femme de Maître Masokhna Kane l'avocat des consommateurs.
Gniko topp laa khamoul ay lane laniou
Damako yeurem bou dewé rek bilay loumouy wax fofou ak safara bou tanga bi
Mais yene layéne tmt gnigui wotél limamou lahi yonaneti Kone yague nafi.
Mayar né yonaneti Kaye day ham diné boudoul islam ak téré boudoul alkhourane.
Belle vérité
Sa way togne bakhoul
Roukhou lahi lagn la wakh seydina Mohamed mo gneuwate si nit kou gnoule moy seydina limamou lahi
Saway boo diangoul da ngaye lathié wala nga mandou
Sama wadji wakhal sa wakh tè guéné si Seydina Limamou...lo khamoul boul si wakh
Wa Salam 🙏🏾
Maa chaa allah imaame fatabaarakar rahmaane
Laïcité égal sougnou yone nékoul ci diné et c'est grave.un pays où il y'a 95% de musulmans il serait logique d'appliquer la charia à moins que la majorité de ces musulmans soient des hypocrites (naafekk)
Pape dji seydi na djibril dala djome???
Akkk niou mousoul deim hotel king fath place 😂😂😂😂 niofaa neikone
Aida diallo mounoul sakh fatiha ay ponkall topoukoo amouniou kham kjam khamouniou gattte
Wahkbi diarouko il faut réagir gnef ndayame doorko bamou yewo
ماكان محمد أباأحدٍ من رجالكم ولكن رسول الله وخاتم النبيين
صحيح
Fatou Sall شكراً يافاطمة سله
Dimbaliléne nit gni waay ak sén aya bi. Dégo léne quran khamo lénko . Go waay
Mane dal Sénégal bouniou diogoul ci li Lou nekh way def bi li amé bé legui degouma ben kilifa bou ci wakh
Déjà sa tenue!!!!!!!aye derri segg la sole?!comme panthère deh,prophète bou djiguene mom moy adouna toukina.mane gniy assister thi djotayame diko soutenir moma diakhal... le Coran est la plus pure des vérités,Allah (swt)bayiwoul dara lepp lathi deff mashallah...donc la femme la nagnou may diam,kou nek amegua loula doy seukk
Listé moi le nombre de prophète au Sénégal :