Affaire Seyda Zamane: Les Layenes sortent de leur silence, Cherif Laye dit ses vérités "Waxna Yayam"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 фев 2025

Комментарии • 314

  • @mamadousall1180
    @mamadousall1180 5 лет назад +2

    Mouhamadou Rassoulalh mo dieuk té mo moudiou si gni yalla yonné.
    Bénén Yonnénté dotoul wathieu ba yowmal khiyam.
    Thiakane bakhoul.... wa salam.

  • @mansourpouye7462
    @mansourpouye7462 4 года назад

    Yalna yalla yoke saye lérr si barképe seydina limamou

  • @dembaniang4387
    @dembaniang4387 5 лет назад +29

    Kou geum gnou Geum ku geumoul gnoun geum nanu sang bii sa mame lou yall bind mosii geun baye lahi moyy yarasoulilahi psl

    • @alediagne4471
      @alediagne4471 5 лет назад

      Amna Maye dè wayè dou rasoulou llahi nake danga dioume

    • @mansourpouye7462
      @mansourpouye7462 4 года назад

      Baye laye moye rasoulilahi mo wékhone maka nieuw nioul fi si saw

  • @abdoundoyelayendiaye221
    @abdoundoyelayendiaye221 5 лет назад +7

    MachaAllah Serigne bi...Claire et limpide. Rien à ajouter.

  • @mamambacke7187
    @mamambacke7187 5 лет назад +1

    Machalah laye makhtar kaduu yi rafete na trop bilay mandouté ak gueume si séne famille la bayéko nawna léne ndax séne djiko you séll yi

  • @zeinadiop501
    @zeinadiop501 5 лет назад +22

    Seydina limamou psl néna gnar nioma kham kima geume ba déh ak kima wédi ba déh kou khamoule nanga mandou wasalam🙏🏽🙏🏽

  • @bachirrlaye8605
    @bachirrlaye8605 5 лет назад +9

    Laye makhtar lima si nékh moy vous parlez tréééés Bien 🏳🏳 yalla nalleu yalla faye

  • @papapouye850
    @papapouye850 5 лет назад +7

    Merci Sangue bi geume baye laye rek yakar baye laye doye lo baye laye rek sama gars appel bi Moungi ñieuw niou wadiale ko ak talibement sunu yittei mame baye laye sunu yakar tay ak eleuk baye abdoulahi mission bi mashallah geuneuh yag geuneuh wer

  • @tuuttank7230
    @tuuttank7230 5 лет назад +7

    machallah laye mokhtar amna solo gniy dingate thi commentaires yi nak diarunio tontou yalna yalla fayalniou seydina limamou psl. yalla sah barina nioukoy dingate

  • @almsgueye8711
    @almsgueye8711 5 лет назад +5

    Dieureudieuti sanga cherif alassane laye mahtar cadou yi lairna yalnanu má borom defalnu degueu ak topa

  • @thialallaye1922
    @thialallaye1922 5 лет назад +3

    machallah 💖 laye makhtar 🙏🙏🙏

  • @ibrahimatall7079
    @ibrahimatall7079 5 лет назад +26

    MANE MOM MOURIDE LAA WANTé KéP KOU GEUM SERIGNE TOUBA TE NANGOULO BAYE LAYE DANGUA KHAMOUL WALA DANGUA DEMOUL KHOUNTOU BA...dieredieuf LAYE MAKHTAR LAYE SEYDINA ISSA

  • @soukacasa9658
    @soukacasa9658 5 лет назад +59

    Mane dee talibe Serigne Touba la wantee dama beugeu tee geumm layenne yii sope lenn trop sahh

    • @oumydiallo9542
      @oumydiallo9542 5 лет назад +3

      Soukeina mane sope la lol mercie layenne ak mouride yalla Molène bolle

    • @inconu3299
      @inconu3299 5 лет назад

      Bilahi nioyam💜💝

    • @yandelaye673
      @yandelaye673 4 года назад +1

      Soukey khadim rek kene guenou ko kham MEMEDOU l'on bouko deguele guem wolou mognou War

    • @yandelaye673
      @yandelaye673 4 года назад +1

      @@inconu3299 yow ya guena toute si gni digate ko yakar filae fekh WOTE bi te wediwouko 140 ans YALA miko wotelo diko samal bopap

    • @grereemifa2868
      @grereemifa2868 4 года назад +1

      Diadieuf

  • @gothizlaye6843
    @gothizlaye6843 5 лет назад +4

    Machallah Amna solo Lahi 🥰🥰🥰

  • @nenediaw940
    @nenediaw940 5 лет назад +10

    Baye Laye ASW amoul mass kouko fowé dingako guiss d li réka mounona guéné layenne fowougn fowlouwougn.mandou leen si wa ahlou lahi

  • @aidagueye6327
    @aidagueye6327 5 лет назад +9

    Bien dit Laye maktar Macha Allah

  • @absademesow7010
    @absademesow7010 5 лет назад +6

    Ay rapp la jai vu une femme ki faisait ça yalla na wér si barké baye laye aleysalam

  • @lstv9976
    @lstv9976 5 лет назад +1

    Belle déclaration nous sommes tous des serviteurs de dieu lep louy saltel diné gii dagno wara bolo dindi ko

  • @seydinaissawade6833
    @seydinaissawade6833 5 лет назад

    Wakhedji rafétena machalla snaga ala sane yalla nala yalla barkéle

  • @fatoudiouf6914
    @fatoudiouf6914 5 лет назад +9

    Baye laye amoul mass psl kou KO bagne dé rek motakh doko dégu kou geumoul bayi niou ak sunu geum .

  • @lhistoiretv2031
    @lhistoiretv2031 5 лет назад +2

    Ko bkh ki younente bi psl kene la ta mongi maka m pas senegal 6 mom 9 rek yen ak mom bene la yalla nagnio yalla dioubel Ko bkh ki al qoran ak souna rek moy deug macha allha 🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @khadijaniang3601
    @khadijaniang3601 5 лет назад +22

    Merci laye makhtare mais c’était pas à la pauvre maman de faire le toube la fille est majeur et vaccinée donc elle n’avais pas à subir cette pression wassalam.

    • @fallougueye381
      @fallougueye381 5 лет назад

      Merciii,et meme la maman n a rien expliqué d importance,c est louche

  • @wolimatawade846
    @wolimatawade846 5 лет назад +4

    Djeureudjeuff Alla ainsi que tout les petits fils et talibés. Diné gui bén la. Allahou Akbar🙏

  • @mounzzfrederic1148
    @mounzzfrederic1148 5 лет назад +3

    Yalna yalla same niou allah keneuh la et seydina mouhamad ibn abdallah psl est le sceau des prophètes et le dernier nanui tope yallah diangue alhurane karim moy deugue ah yallah dal meune na mougne lu ame Sénégal amul faineuh

  • @mahmudlejuste7196
    @mahmudlejuste7196 5 лет назад +1

    Jajeuf Ala MachAllah kadou yi amna Solo Baye Laye Amoul Mass

    • @biramasy7300
      @biramasy7300 5 лет назад

      Machala laye mahtar je savais pas ke cette association exister vous avez bien parler mais je voulais attiré votre attention sur la yene je le suis pas mais je l'ai aimé et je voie quelque chose à camberene qui me fait mal a l'époque quant on était petit les femme s n'osait pas porter de pantalon ni jupe on ne fumer pas mais malheureusement on le voit maintenant s me fait mal si vous pouvez kelque chose

  • @adiakandji9459
    @adiakandji9459 5 лет назад +6

    Machalla machalla sangue

  • @ndatteyalla9917
    @ndatteyalla9917 5 лет назад +8

    ولقد بعثنا في كل أمة رسول yalla yonina ci xétt bounék yonénte la wax légui dama léni lathi kone nioune xéte bou nioul kane moy suniou yonente xete la yalla wax légui baye laye wotéko nguéne ni dou mome ta yéne gneup daccord nguéne ni mahdiyoou dina niew wa légui lutax ki woté mahdiyoou nguéne ni dou mome san preuve ta noublie pas que mouhamed psl moy woté wate ci gratou mahdi إن الذي فرض عيك القرآن لرادوك إلى معاد mane yalla faratl alkhurane siyaw dinala déloci bénéne rendez vous lako yalla wax ta baye laye waxoul ni bénéne prophete la dafni ki fégnone pénkou démb mo fégn ci soow bi tay kou beugue lou lér san wéranté so beugué niou debat bame lér wassalame

    • @morlo4034
      @morlo4034 5 лет назад

      mouhamadou minal bidy hade aswada mouhamed ma wehone nioulate na

    • @mansourpouye7462
      @mansourpouye7462 4 года назад

      Mo wékhone démbe niew nioul taye

  • @khadyseck6120
    @khadyseck6120 5 лет назад +5

    Dieureudieuf sangue Laye Makhtar

  • @dielaye6315
    @dielaye6315 5 лет назад +2

    Merci beaucoup sangu laye makhtar 🙏🏾❤

  • @zeinadiop501
    @zeinadiop501 5 лет назад +19

    Diné seydina limamou psl bi kouka nara tilimale yaye yakou

    • @lazebre1192
      @lazebre1192 5 лет назад +1

      Ya qu'un seul dîné waxal tariqa yéne xaléyi xamoulén dara

    • @TheDiogop
      @TheDiogop 5 лет назад +1

      Dagha djoum sokhna si. Dîné bi Ya ALLAH l'unique moko mom

    • @morlo4034
      @morlo4034 5 лет назад

      rk

  • @ibrahimaniangndiaye1963
    @ibrahimaniangndiaye1963 5 лет назад

    MACHAALLA ALASSANE AK SENY LAYENNE YEP CONTANANE KADOUYI RAFETNA

  • @misterblacki8776
    @misterblacki8776 5 лет назад +13

    Baye laye amoul mass

  • @evasoum3593
    @evasoum3593 5 лет назад

    Merci Chérif Laye 👌

  • @awandiayepouye4743
    @awandiayepouye4743 5 лет назад +14

    Pour les gent ki critique natt diaroul tonton layenne kéne xaméwouko si Aÿ wahhh

  • @lajusticedallah8503
    @lajusticedallah8503 5 лет назад +13

    Salam aleykoum
    J'ai lu les commentaires ici sur d'autres vidéos qui parlent des Layènes mais je ne vois que mechancheté sokhor niak ndiangu ak hakar ni alkhourane ak sounneu gnéna lako Yalla diaklel.
    J'ai vue nak ngeen di wax dé deki doundaat fii ci kaw souf amoul ay sirk bida'a damani demleen diangi sourate kahfi di ngeen giss Yalla dafa andi diouyoo ci niata temps legn nelaw avant Yalla di leen ressuscité. Té pourtant mom rek manoon na leeral fofou wayé defouko. Té fofou giss ngeen Yalla ''bahas nahum liyatasa alouna baynahoum'' la wax nga giss si baatou ''dekil'' kone dé deki amna fofou té si kaw souf la xéwé Kone nak layene yi ci gni geum ni dé déki ci kaw souf leen bok dlnc kay acceptel leen ko rek niko Yalla défé ci sourate bobou.
    Benen bi ma ngi giss niouy wax ''khatama nabiyina'' déja esk lire nga li sourate bobou djéxé? Apres li Yalla dafsi tek ''wa kana Lahou bi koulli chayin aliman'' mane ''wayé Yalla nék na di adji am ci lepp loum mana doon'' kone dou yow yay firi aya bi convaincre niou nonon. Té ''Khatama nabiyina'' gogou firiwoul rek dernier prophete ndax yonnent néna demb sama diak moy derniere diak kone loutax niouy tabax ay diak ba légui? NE ME DITES PAS QUE CE KE JE DIS C'EST TROP SIMPLE JUSTE POUR QUE VOUS REFLECHISSIEZ.
    ta ci lolou lane lassi saydatounna aicha rta wax ci aya bobou ngeen di dak di yam si ''khatama nabiykna'' demleen geustou mo geun seen thiaxaan yi. LAYÈNE YI FOU LEER LEGNOU TAXAW.
    Ngeen di wax batay i aya bi nek ci sourate maida ''al yawma akmaltou lakoum dinakoum ila akhiri aya'' loutax kone ngeen top ci ay chafi malik abou hanifa hanbal et meme vos guides ibadou et serigne pour donner de nouvelles legislations dans la religion? Gni di dioulé nii gneulé di dioulé nou wouté?? Té ngeeni fnéna yore xam xam bi?? Ba pare ni yonnent néna matal na dine lislam kone dara warouleen kossi yok lou tolni ''zara'' wala ngeen wagnissi lou tol nonou.
    Khadith bi lire na kounane Imam Mhadi ci descendant yonnent ley bok yoe momou diko wax je me dis ke dara xamoo ko ci loukha ak ci histoir. Yonnent sou waxé ''al mahdi mini'' walla ''mina'' meun na firi nii Mahdi est de lui kone mane na doon mom c'est un nous inclusif kone pourquoi manoul fegnate doon le Mahdi??
    Je ne vais pas trop m'attarder j'etais juste de passage pour vous reveiller et vous inciter a aller geustou boubaax bagn di nek ci site yi di lakhatou seen guinaw machine di wax louleen neex di saga waté di diay rew lolou dou diné di diay arrogance ittam.
    Wa akhirou dahwana anil hamdoulilahi rabil enlamine
    PS: J'AI FAIT EXPRES DE NE PAS CITER ENTIEREMENT LES VERSETS ET LES KHADITHS VUE QUE VOUS ETES DES SUPER ERUDITS VOUS TROUVEREZ PAR VOUS MEME.

    • @seydinagueye8344
      @seydinagueye8344 5 лет назад +3

      Wax bi matalé na wayé Bilay ya âme temps di tontou gni. Li Yalla wax si Yasin rékk moy deug s36v7,8,9,10

    • @marlaye7481
      @marlaye7481 5 лет назад +1

      @@seydinagueye8344 teunk nga lep Laye Makhtar, dieureudieuf !

    • @cherifolo2759
      @cherifolo2759 5 лет назад

      Tu pourrais pas le résumer ?... il est trop long ton récit ...ishhh

  • @adamasy8323
    @adamasy8323 5 лет назад

    Diereudieuf laye waxjji raffettnna ntee manndou am oorma

  • @nenediop7216
    @nenediop7216 5 лет назад +5

    machallah laye makhtar baye bakh na

  • @awasall5373
    @awasall5373 5 лет назад +2

    Dieuredief laye makhtar wakhdji Selena

  • @papeamadoumbengue4627
    @papeamadoumbengue4627 5 лет назад

    Mach Allahou laye makhtar amna solo... lidoune diné dou ay tëguine. Baye asw daane na wakh ni diné dja ndaw y'a ak maag gnu mousse gna

  • @amadoudiekebe4993
    @amadoudiekebe4993 5 лет назад

    Machalla wakhdji rafétna trop

  • @diamalayembaye1384
    @diamalayembaye1384 5 лет назад

    Bien dit

  • @mamadousow6145
    @mamadousow6145 5 лет назад

    Merci laye laye

  • @inconu3299
    @inconu3299 5 лет назад

    Laye makhtar💝

  • @magoulahidiop7056
    @magoulahidiop7056 5 лет назад +5

    Machallah

  • @aidaseck9732
    @aidaseck9732 5 лет назад +2

    Machalla limo ame solo

  • @massoudadiakhate9284
    @massoudadiakhate9284 5 лет назад +9

    Machalla laye makhtar dieredief

  • @abd9526
    @abd9526 5 лет назад +3

    Donc vous , l'islam ne vous intéresse pas c'est votre confrérie qui vous intéresse et votre poche

  • @boytouabzzotou4314
    @boytouabzzotou4314 5 лет назад +2

    prophet Muhammad mo wakh bènèn prophet dodoul am si ginawam Ken bousoul giss si alkhoram ak hadis né net daye dioudou wékh tiye souba nga nioull aye thiakhan kassè la

  • @clienthilmi4085
    @clienthilmi4085 5 лет назад

    Sokhna rafetna merci jetiame

  • @fatousane2353
    @fatousane2353 5 лет назад +1

    Seyda Zamane son vrai nom est Nafi Diop. Elle habitait á mermoz première porte et sa mère avait une boutique qu’on appelait Madame Diop. Elle est á la recherche de l’argent avec ses soeurs. Elle fût la femme de maitre Masokhna Kane. Nafi Diop arrête de faire du cinéma. Elle est avec ses grandes soeurs . C’est un deal pour se faire de l’argent.

  • @badoukane6584
    @badoukane6584 5 лет назад +1

    Zayda moye aida diallo bou Layen 👹👹👹👹👹👹👹👹

  • @ahmadfrer9126
    @ahmadfrer9126 5 лет назад

    sokhna si limouy def ni ce pas la première fois mouy am aï nit gnoco fi ndieke Sénégal deloulen si tere yalla bi nguen bayi wote yi

  • @abdoulahatdiouf3946
    @abdoulahatdiouf3946 5 лет назад

    Sokhna si na ragal yalla té khamné bamél khatna leundena

  • @gorafall2236
    @gorafall2236 5 лет назад +2

    Ben yonete mo am mouy mouhamed darasoulaye mathia Medina ak mak

  • @lhistoiretv2031
    @lhistoiretv2031 5 лет назад

    عن أبي سعيد الخدري رضي الله عنه قال النبي صلي الله عليه و سلم : يخرج في آخر أمتي المهدي ، يسقيه الله الغيث ، و تخرج الأرض نباتها ، و يعطي المال صحاحا ، و تكثر الماشية ، و تعظم الأمة ، يعيش سبعا ، أو ثمانيا ، يعني حجة
    (رواه الحاكم و صححه الشيخ الألباني في السلسلة الصحيحة رقم ٧١١)

  • @amadoucamara8011
    @amadoucamara8011 5 лет назад

    Sénégal dou déme kounék amgae si sa bir tarikha lo khamni yalla mbegouco mourith baye fall do djouli do wor tidiane salatou fatikha diawharatoul kamal ak wassifa layén amnanou yénénte Bou béss ak mahdi niasén gies yalla ak lépe yalla

    • @Minaseydibarkham
      @Minaseydibarkham 5 лет назад

      Ah ok donc yalla ak lépp yalla la lolou yalla beugou ko,yaw dé wakhou lo fi dara.Wolof Ndiaye sakh wakh na né »loudoul yalla nén la « «.

  • @moussacamara9206
    @moussacamara9206 5 лет назад +1

    Sayda Zaman AK limoulay yeup ay fénkat lagne 6 Say 9

  • @saabajoe
    @saabajoe 5 лет назад +1

    Catastrophe..... Astaghfiroulah al Aziim wa ashadu'an laa ilaha ila'Allah wa ashadu'ana Muhammadan Rassul ul'Lah. La khawla wala khuwata ila bil'Lah. Mohsiba dou djogué moukou Senegal ak ts les delires ski se prononcent ouvertement. Nagnou Yallah yeureum téh diégueulgnou. Sheuteuteuttt...

  • @mamadoulahimbaye6848
    @mamadoulahimbaye6848 5 лет назад

    LAISSEZ LA D.ICI UN AN ON VA VOIR

  • @lamintouray6845
    @lamintouray6845 5 лет назад +2

    May Allah has marcy on us .Truly we are the end of time all those call them self as a prophet are the workers of anti crist

  • @fatousane2353
    @fatousane2353 5 лет назад +1

    Je ne crois pas qu’elle est malade. Seyda Zamane est entourée de ses deux grandes soeurs. Je les connait très bien.

  • @bamansour1261
    @bamansour1261 5 лет назад +1

    Guinaw seydina mouhamad benén yonént amatoull

  • @lhistoiretv2031
    @lhistoiretv2031 5 лет назад

    عن أم سلمة رضي الله عنها قال رسولُ اللهِ صلَّى اللهُ عليهِ وسلَّمَ : المهدي من عترتي ، من ولد فاطمة
    (رواه أبو داود في سننه رقم ٤٢٨٤ و صححه الشيخ الألباني في تحقيق سنن أبي داود)

  • @amadoucamara8011
    @amadoucamara8011 5 лет назад

    Démlén diangi séne diné yalla daflakoy lath mon guene top alkhourane ak souna Sénégal kou nék amgae si sa bir tarikha lo khamni yalla mbegouco mourith baye fall do djouli do wor tidiane salatou fatikha diawharatoul kamal ak wassifa layén amnanou yénénte Bou béss ak mahdi niasén gies yalla ak lépe yalla la

  • @bambasunumbeckte5915
    @bambasunumbeckte5915 5 лет назад

    Damay ladji rek de
    Ndakh baye da wote yonnént l
    Li rek de laay léér lu ana layén yi

  • @massndiague6543
    @massndiague6543 5 лет назад +1

    La nabiyi badi la younétibi sallalahou ayahi wa salam wakh

    • @kingjames5726
      @kingjames5726 5 лет назад

      Mass Ndiague Aicha Sokhna yoneta bi nena « khoulou khatimou naby walatakhoulou la nabiya bahada »

    • @morlo4034
      @morlo4034 5 лет назад

      mame limou laye limou wah dafa ler mana dembe mana taye

  • @lhistoiretv2031
    @lhistoiretv2031 5 лет назад

    عن أبي هريرة رضي الله عنه قال النبي صلى الله عليه و سلم : يبايع لرجل ما بين الركن و المقام ، و لن يستحل البيت إلا أهله ، فإذا استحلوه ، فلا يسأل عن هلكة العرب ، ثم تأتي الحبشة فيخربونه خرابا لا يعمر بعده أبدا و هم الذين يستخرجون كنزه
    (رواه ابن حبان و صححه في التعليقات الحسان على صحيح ابن حبان رقم ٦٧٨٨)
    Les richesses, la pluie, la végétation et le bétail seront abondants à l'époque du Mahdi qui va distribuer l'argent de manière équitable et la communauté va se développer
    D'après Abou Sa'id Al Khoudri (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit: « Il y aura parmi vos califes un calife qui donnera l'argent de manière abondante et ne le comptera pas ».
    (Rapporté par Mouslim dans son Sahih n°2914)

  • @mamefatythiaw6518
    @mamefatythiaw6518 5 лет назад +2

    MERCI laye makhtar

  • @chachawane6836
    @chachawane6836 5 лет назад +2

    Le dernier prophète c'est seyidouna mouhamed sala llahou aleyhi, wa salama katamoul anbiya wal moursaline

    • @elhadjiabdoulazizndiaye4284
      @elhadjiabdoulazizndiaye4284 5 лет назад +4

      Issa est toujours prophète,il reviendra pas pour une nouvelle prophétie mais pour des éclaircissements,mais Mohamed allehi wa salam demeure le dernier prophète.

    • @chachawane6836
      @chachawane6836 5 лет назад +1

      @@elhadjiabdoulazizndiaye4284 machalah

    • @chachawane6836
      @chachawane6836 5 лет назад

      @arabi thiaw c'est vrai mais محمد هو خاتم أنبياء و المرسلين

    • @dielaye6315
      @dielaye6315 5 лет назад

      @arabi thiaw laye makhtar ne perd pas ton temps à répondre à ses ignorants stupide

    • @elhadjiabdoulazizndiaye4284
      @elhadjiabdoulazizndiaye4284 5 лет назад

      @arabi thiaw toi t'as des bobos d,qu'est ce que j'ai dit là ?
      J'ai répondu tout simplement à ta question "que faire du retour d'issa allehi wa salam ?
      Où est ce que t'as vu que je suis entrain de dénigrer ?

  • @grereemifa2868
    @grereemifa2868 4 года назад

    Baye laye mom la démb mom la téy mo khéson démb mom fi nioul tay

  • @babacarndom2605
    @babacarndom2605 5 лет назад +4

    Yonénetibi mangua médine kénéne kouko woté doul ngua ak ko done.

    • @adjisamb6308
      @adjisamb6308 5 лет назад

      Yaw yay doul katt bi sa thiapap yaye wayy réw imbesil biii

    • @labelle4941
      @labelle4941 5 лет назад

      @@adjisamb6308 😂😂😂😂😂😂

    • @labelle4941
      @labelle4941 5 лет назад +1

      @Boubacar Laye lololololol limamou laye n'est pas le prophète Mouhammed sala Allah aleyhi wa salam. Le Mahdi aussi c'est pas Mouhamed ! Le pére de Limouma se nomme t'il Abdallah? Sa mére Aminata? Bah le Mahdi, ses parents auront les mêmes prénoms que ceux de Mouhamed sala Allah aleyhi wa salam.

    • @labelle4941
      @labelle4941 5 лет назад

      @Boubacar Laye Seydina Mouhamed sala Allah aleyhi wa salam s'appelle aussi Ahmed , Moustapha vas verifier ! Tu peux bien croire à ta version de l'histoire mais pour rien au monde je te rejoinderai là dessus. Sur ce je te souhaite une excellente soirée sous la protection divine. As salamou aleykoum Aboubacar.

    • @labelle4941
      @labelle4941 5 лет назад

      @Boubacar Laye 🤗

  • @cherifalhousseynoulahi2316
    @cherifalhousseynoulahi2316 5 лет назад +5

    Mashallah Sangua amna solo

  • @syngariboundou2355
    @syngariboundou2355 5 лет назад +1

    La nabiya bahdi bane kilifa thii keur dinè yii nio nangou nè limamou nè yaunènetè la masselaha rèkk mo bari senegal

    • @syngariboundou2355
      @syngariboundou2355 5 лет назад

      @Boubacar Laye koulako wakh khaw ma kane dè wayè maodo akh gnabotam bokou gnoussi

    • @syngariboundou2355
      @syngariboundou2355 5 лет назад

      @Boubacar Laye bii dègulou nako bou yague wayè dègoulène lii mou wakh dafanè dafa ame kouko lathieu nakh do wakh tanè same tarikha mounèko fobok mounèko mane layènela mounèko nioniou ay yaunènetè laniou c pour lui dire lii nga nèkk khamoko motakh mouwakhè nonou nakh meusse nga dègue wa tivaoune wakh nè limamou yaunènetala

    • @syngariboundou2355
      @syngariboundou2355 5 лет назад

      @Boubacar Laye même bouko wakhè amoul

    • @syngariboundou2355
      @syngariboundou2355 5 лет назад

      @Boubacar Laye race noire amoul prophète dinè amoul panafranime

  • @bobcamara4127
    @bobcamara4127 5 лет назад +6

    thiakhane mom si thiakhane rék lay dellou

    • @adjisamb6308
      @adjisamb6308 5 лет назад

      Téyal sapp charr yaw bop camara yaw lay wakhal khamoulo touss saytané nga kéne manoul tilimal layénne yi ngay doul layénne amoul thiakhane teudieul sa gatte

    • @morlo4034
      @morlo4034 5 лет назад +1

      @@adjisamb6308 bayil ma goor djigue yi wotebi kene manousi dara

    • @adjisamb6308
      @adjisamb6308 5 лет назад

      @@morlo4034 gni danio yabaté té igniane ba paré réw

  • @massndiague6543
    @massndiague6543 5 лет назад +4

    Yén nieupa yém boulén niou sonal way

  • @abdourahmanediop730
    @abdourahmanediop730 5 лет назад +6

    Tout les mêmes parce que vous dises que Limamou et le prophète Sénégal moneh

    • @adjisamb6308
      @adjisamb6308 5 лет назад +3

      Moy yonéne bi dala méti seydina limamou et le prophète

    • @bayesouleyediop714
      @bayesouleyediop714 5 лет назад +1

      Seydina limamou moye rassoulou lahi nga beug ko ak nga bagne gnou sokhorr

    • @lhistoiretv2031
      @lhistoiretv2031 5 лет назад +2

      @@bayesouleyediop714 ko bkh ki yen dangen reere me yalla na len yalla guiindi

    • @moussakeita9085
      @moussakeita9085 5 лет назад +1

      Salam anlaykum ! Le mahdi n'est pas encore venu. Il viendra in sha Allah, la fin des temps. Son nom sera Muhammad Ibn Abdullah, il viendra de Sham. C'est tout. Arrêtons les innovations en matière de religion, suivons la voie de Muhammad anlayhi Salam. Sinon, on sera exploité par les grands innovateurs explorateurs, collecteurs de fonds pour enrichir leurs familles tout en appauvrissant ceux qui les suivent aveuglément. Il faut raisonner.

    • @inconu3299
      @inconu3299 5 лет назад

      Yow Lo khamoul nopithi. Tu na rien compris bilahi.

  • @yacineniasse9608
    @yacineniasse9608 5 лет назад +3

    Pourquoi vous avez interpelée sa maman et non elle mm elle est la principale concernee

    • @adjisamb6308
      @adjisamb6308 5 лет назад +2

      Bouniou khamoul dome dji tes khame yayam si mome lanio déme

    • @marlaye7481
      @marlaye7481 5 лет назад +1

      @@adjisamb6308 yaw mom ma mbókka nga hamna😄

    • @adjisamb6308
      @adjisamb6308 5 лет назад +1

      @@marlaye7481 sama papa mar la toud sama papa nga lébou pirr

    • @marlaye7481
      @marlaye7481 5 лет назад

      @@adjisamb6308 dou hasard moss sallàw !

  • @moussatine2717
    @moussatine2717 4 года назад

    Mais boye diouly sa likhame dènguaye né ass chadou anla ilahkha Mouhammad rassoulilakhi wa dénguay wakh tourrou kénénn Sénégal mo nékh rék 🤭🤭🤭

  • @arametoure126
    @arametoure126 5 лет назад +2

    Diadieuf laye makhtar

  • @sadextalibebambaprotege8524
    @sadextalibebambaprotege8524 5 лет назад +3

    Lou ler ni lako xalaté kou xam captage bouniou nieuwé même voix bbou ngay degg

  • @lhistoiretv2031
    @lhistoiretv2031 5 лет назад +1

    Sous l'autorité d'Umm Salamah, que Dieu soit satisfait d'elle, le Messager de Dieu, que la prière et la paix de Dieu soient sur lui, a déclaré: Le Mahdi vient d'Attara, du fils de Fatima
    (Rapporté par Abu Dawood dans sa Sunna n ° 4284 et authentifié par Sheikh Al-Albani dans l'enquête sur Sunan Abi Dawood
    GAYI LI WAKHO YOUNENTE BI LA DEH

  • @bandaguene4745
    @bandaguene4745 5 лет назад

    Now coment ndawsi fencat la

  • @fantadiedhiou4136
    @fantadiedhiou4136 5 лет назад

    Pourquoi vous ne cherchez pas à rencontrer zeyda en question

  • @abloslimshady
    @abloslimshady 5 лет назад +13

    Sénégal dafa nekh rek, kholal ki tamit nane limamoulay moy "mouhamadou Rassoulilah"; yonenti bii gagnou na bou yagg sila lil$mamou dioudou.
    Yen ak femme bii daal yéna yam quoi.
    N'importe quoi ce pays là, beu paré nane procureur na def ligueyam sinon dinagn bay talibé yii def lougnou beug.
    Lolou kilifeu dina wakhè nonou. Kon yén vous êtes des hors la loi quoi. Sénégal lou way beug def ndakhté il suffit nga bokk tchi keurou diné'(déjà kerou diné amoul, c'est pas ca keur diné) rek def lola nekh quoi...
    Anarchie bi fofou la commencé.

    • @sonkoboyztv6762
      @sonkoboyztv6762 5 лет назад +5

      Bo déwé Di nga ci xam darra ,tu le sauras...

    • @abloslimshady
      @abloslimshady 5 лет назад +5

      @@sonkoboyztv6762 Mmo soxlawouma deh pour xam kouy yonenti bi ak kouy imamoul mahdi ndahté text yangui fi té Alquran leral naniou kouy yonent/
      Au nom d’Allah, le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux.
      Allah a dit dans la sourate Maida n°5 verset 3:
      اليوم أكملت لكم دينكم وأتممت عليكم نعمتي ورضيت لكم الإسلام دينا
      (سورة المائدة ٣)
      « Aujourd'hui j'ai parachevé pour vous votre religion, j'ai complété mon bienfait sur vous et j'ai agrée pour vous l'islam comme religion ».
      Sachant que la réincarnation n'existe pas en islam:
      La réincarnation ca n'existe pas !
      Allah SWT dit :
      "Comment pouvez-vous renier Allah alors qu'Il vous a donné la vie, quand vous en étiez privés ? Puis Il vous fera mourir; puis Il vous fera revivre et enfin c'est à Lui que vous retournerez." (Sourate baquara)

    • @adjilaye1511
      @adjilaye1511 5 лет назад +2

      Mbengue laye makhtar.diaroul tontou wooter kouniou wo rek bossiy bokk

    • @CherifLahi
      @CherifLahi 5 лет назад

      Ioe con nga rkk amo bène baat noppi !

    • @deugrekrek859
      @deugrekrek859 5 лет назад +2

      @@abloslimshady bou féké geum baye laye moniouy yobou safara kone parénaniou bou yagg bilahi vous croyez que yéna geun diangue wala geun xam diiné wakeur baye laye bilay vous vous trompez ndeyssane

  • @lhistoiretv2031
    @lhistoiretv2031 5 лет назад

    عن أبي سعيد الخدري رضي الله عنه قال النبي صلي الله عليه و سلم : المهدي مني أجلى الجبهة أقنى الأنف ، يملأ الأرض قسطا وعدلا كما ملئت جورا وظلما ، يملك سبع سنين
    (رواه أبو داود في سننه رقم ٤٢٨٥ و حسنه الشيخ الألباني في تحقيق سنن أبي داود)
    Allah va arranger le Mahdi en une nuit
    D'après 'Ali Ibn Abi Talib (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit: « Le Mahdi fait partie de nous, ahl al bayt (*), Allah va l'arranger dans une seule nuit (**) ».
    (Rapporté par Ibn Maja dans ses Sounan n°4085 et authentifié par Cheikh Albani dans sa correction de Sounan Ibn Maja)
    (*) C'est à dire parmi les gens de la famille du Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui).
    (**) L'imam Ibn Kathir (mort en 774) a dit: « C'est à dire qu'il va lui pardonner, le guider, l'inspirer, l'orienter alors qu'auparavant il n'était pas comme cela ».
    (Al Bidaya Wa Nihaya vol 19 p 62)

  • @malakaskiriakos3213
    @malakaskiriakos3213 5 лет назад +2

    Seydina limaamu ak zeyda zamane nioo yem kepp. Seytaane moy seen kelifa

  • @mbayethiam5835
    @mbayethiam5835 5 лет назад

    wouyy dina djour khoutoukh.

  • @sofiyatoudiop9074
    @sofiyatoudiop9074 5 лет назад

    Yayaam defoul Dara baye toupeu ndéyou mbiligui Key n'a toupeu

  • @morlo4034
    @morlo4034 5 лет назад

    baye laye laniou yoni wouyoulaine yonene ndjine sawoo yarame bi

  • @yandelaye673
    @yandelaye673 4 года назад

    Mome de wakhoul ne benene yonene la
    DAFNI MANA DEMBE MANA TAYE
    KOU GUEMOUL MANDOUI

  • @abdoulahatdiouf3946
    @abdoulahatdiouf3946 5 лет назад

    Lahi laha illalah Mohamed kénele maga Madina Limou wakh lérna yonénte dotoul nieuw ci kaw souff Issa sakh sou nieuwé dotoul néck yonén

    • @adjisamb6308
      @adjisamb6308 5 лет назад +1

      Abdou lahad diouf da ngay doul manoulo supporté limamou yonéne leu té dafa nioul da nga raciste touk ak sa geumigne bou mak nga mél ni téroriste mounoulosi touss mon Ame mo khéwkhone démb nioul tay koumou nakhari yaw ak sa sérigne si pote

    • @morlo4034
      @morlo4034 5 лет назад

      @@adjisamb6308 kou halap lignou geume dangniouye doli imane si imamoul ilahi

    • @papeousmanelayesarr3366
      @papeousmanelayesarr3366 4 года назад

      Wakhi doff issa bou nieuwaté dou done prophète hahahhahahhahahahahah
      Demal diangui kou bokk si 5 prophétes you guena puissant yi nganane bou nieuwaté dou done prophète lolou yénwoul mana

  • @ahmadfrer9126
    @ahmadfrer9126 5 лет назад

    delloulen si kitaboullah Sénégal dine folcolor mofinic biyilen bokale yalla yamoul Ken kikoy diamou rec la ham

  • @metzoza8335
    @metzoza8335 5 лет назад

    Soxnasosou boumnou fonto bou yamoul nou defco dohm leggiu senegal dafa am lifi nekke... Soxnasi na ham bopam

  • @ahmethfall9083
    @ahmethfall9083 5 лет назад +4

    Seydina limamou moy rassoul

  • @moisek147
    @moisek147 5 лет назад

    Cetait prepare POUQUOI FRANCE 24

  • @awandiayepouye4743
    @awandiayepouye4743 5 лет назад +2

    Yébaté retttt yefou cheytané retttt la

  • @bamansour1261
    @bamansour1261 5 лет назад +1

    Imam mahdiyou almountazar mom niawa goulll

  • @gorguydieye8492
    @gorguydieye8492 5 лет назад +1

    Bouko nèkhè wotè yala amoul frontière kou mome yala en tout cas nanko tèk thie alkhourane

  • @yussufdiallo9436
    @yussufdiallo9436 5 лет назад

    Cette femme et vous êtes tous dans la perdition.

    • @yussufdiallo9436
      @yussufdiallo9436 4 года назад

      Boubacar Laye ce que les autres pense ne m’intéresse pas car seul l’islam et le prophète m’intéresse

    • @papeousmanelayesarr3366
      @papeousmanelayesarr3366 4 года назад

      Iow mi ya rér

  • @bobcamara4127
    @bobcamara4127 5 лет назад +3

    waxofi touss