Modou Anta tape sur la table : "Modou Lô sou dieulaaté Balla Gaye danou waat..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 янв 2025

Комментарии • 41

  • @mamadoumousserinediop8056
    @mamadoumousserinediop8056 День назад +4

    Belle analyse de Modou Anta

  • @mouhamadousaybatoudiaw
    @mouhamadousaybatoudiaw День назад +2

    Non Modou anta da khame lambat déh ❤

  • @Domou_Deukk_Bi
    @Domou_Deukk_Bi День назад +3

    Balla sawarouma si combat bouniouko diokh favoris...
    Son fort c'est les combats de defi, combat tay ngay dée
    Siteu dako nara déglou moudéf béneu faux pas mou exploité koo

  • @AliouCisse-x5d
    @AliouCisse-x5d День назад +1

    Bien dit lamba lock

  • @jobehamidou6545
    @jobehamidou6545 День назад +4

    Wallahhi billiahi Parler vrai modou anta

  • @tallambengue-oc4cd
    @tallambengue-oc4cd День назад +3

    Balla gaye bilah walahi souh moh Meune siteu 1000fois siteu defufi dara bari wax teksi

  • @SambaToure-n9h
    @SambaToure-n9h День назад +6

    Modou Anta wakho deug modou lo moy lutteur le plus populair 🎉 de sa generation 🎉

    • @PapeNgom-j6f
      @PapeNgom-j6f День назад +1

      Bilaye copin kn dou Modou lo

  • @mormboup9301
    @mormboup9301 22 часа назад +1

    Mdrr dpui quand balla est plus populaire ? Modou est un comorien!

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 День назад +2

    Lolou mom amna😊

  • @alphadiouf8111
    @alphadiouf8111 День назад

    Yenn gni rek yeneuh wara wakh thy lambe...❤nakh danguena kham lambe

  • @yaalasadio
    @yaalasadio День назад +12

    Modou Lo deh mom soneu na 😂 sou beurré woul dagn koy boler si lamb dji

    • @daoudathioubou6710
      @daoudathioubou6710 День назад +3

      C’est normal parce que c’est le roi des arènes. Kou djitou nieup diokhogne leu

    • @SambaToure-n9h
      @SambaToure-n9h День назад +3

      Billae lambe diou am niou toudou ko cône yaa ngi bayi limay bayi khel 😂

  • @BaMasour
    @BaMasour День назад +1

    Kouy daw nounoulay dané déléne ndiémé deugue

  • @bachirdiop19
    @bachirdiop19 День назад +1

    Pourquoi beugua déme stade Abdoulaye Wade mo way

  • @FallouCisse-r3i
    @FallouCisse-r3i День назад +3

    Wakhoul deug deee sathies douma ko dane ko mounane keneu meusouko door dane ko

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 День назад +1

    genre analyses yi motakh Siteu dou dieul béen risque, lane moy Siteu amoul loumouy perte si combat bi?

  • @Deggou
    @Deggou День назад +1

    Modou actuellement mo meune balla , balla menoul daneu modou bi...

  • @assanegueye1352
    @assanegueye1352 2 дня назад +2

    Saway balla gaye ndoata march nul lanou am

  • @laminediagne4143
    @laminediagne4143 День назад

    Teniroul kène échec siteu défou fi dara

  • @AmaraKoita-y9f
    @AmaraKoita-y9f День назад +1

    Franchement lambologue baxoul thi télé il force trop puis téyoul teksi day beugeu wakh lep

  • @mamadouwade6565
    @mamadouwade6565 День назад

    En tout cas siteu bou taxawé degeul bopam dou mate 5mn😂 inchallah

  • @Ibrahimadiange
    @Ibrahimadiange День назад

    Modou anta parle sur le plan du lutte waye khamo kan Mony balla gaye

  • @assanewade6616
    @assanewade6616 День назад

    𝐄𝐦𝐩𝐞́𝐫𝐞𝐮𝐫 𝐛𝐢𝐠𝐧𝐞 𝐤𝐨𝐲 𝐟𝐨𝐫𝐜𝐞́ 𝐦𝐨𝐦𝐚 𝐝𝐞𝐟 𝐚𝐲 𝐫𝐞́😂

  • @YoroDiop-el4kn
    @YoroDiop-el4kn День назад

    No modou anta khalatam la wakh bane riske balla bou dieloule siteu kouli dieul

  • @diopablaye5227
    @diopablaye5227 День назад

    Lamine ila yaw midini gna wakh de

  • @PapaSambaSy-h7r
    @PapaSambaSy-h7r День назад

    Modou anta wakhna deug souniou stade yi khalatouniou ko diokh wa lamb Bayilne thiakhane

  • @ImboboKaga
    @ImboboKaga День назад +1

    Lambalogue del teey touti, di wagni digression yi. Modou Anta sou lamb yakho diapna ci nga, ioe ak gniy bagn wax deug yen mbeur yi. Siteu aussi danoul ben poids lourd, woutoul daan mbeur dey nieuw di daw ak di samp nul. Kone solen toké si media di wax genre wax yi, amna yenen mbeur you ndaw youy nieuw def lamb business, manaan douy stade bi, nieuw samp nul ni en tout cas douma danou. Té lolou guiss nagn ko Combat Mor kangKang vs Diop2 ak yenen grand combat you moudj té lolou dieumé woul lamb kanam. Lamb affaire ndiom la, dou ay business ay negociation. On ne vous critique pas pour juste vous critiquer mais tu dois franchement revoir ta communication téy wax lou deugou. Setlou na aussi combat Siteu v ModLo même, tu incitais Max à déposer un recours et un appel. Ce qui ne ressort nullement de tes prérogatives en tant que reporter/Chroniqueur.
    Et puis, t'as fait un recensement par je ne sais quels moyens pour savoir que Balla est le lutteur le plus populaire de l'arène ?? xolatal ningey waxé seugn bi té gueuna mandou. Meun nga analyser nak sa droit leu. Nga balma akh nak

  • @FallouDiakhate-p4d
    @FallouDiakhate-p4d День назад

    Wakh deug fa yalla Mbeur yi mbam yi niosi eupp dh

  • @KhadimDiagne-h2e
    @KhadimDiagne-h2e 3 часа назад

    Modou anta balla sowakhé lôlou no fataliko euema séné wala boye niag Balla gaye dane sitau dou takh moye wakh loudoul lôlou

  • @doustar2193
    @doustar2193 День назад +4

    Modou anta yah muna dul
    Balla uepul modou Lo sipuerter balla Sénégal là yuem Modou lo nternational là buy bueré niata Bus moy diogue Gambie xamo lingay wax

    • @AminataDIOUF-ez8kd
      @AminataDIOUF-ez8kd День назад +1

      Ioe mi ya xamoul lingay wax

    • @modoubayefallsikroulla1423
      @modoubayefallsikroulla1423 День назад

      Yaw mi ya khamoul lingay wakh mond lamb balla mosi eup souportér balla bouy beuré liy diogué gambie ndanga kham noumou tollou

    • @AlleFall-y7t
      @AlleFall-y7t День назад

      No siteu mo eupeu suportair mè modou reck lay tope mé boumou.djeule.balla.gaye.beugeu.corigé.modou.lo.bock.nasi.li.takh.mou.djeul.siteu.mé.pourqw.modou.lo.di.dérangé.balla.gaye

    • @modoubayefallsikroulla1423
      @modoubayefallsikroulla1423 День назад

      @@AlleFall-y7t khana konn modou dafa dieulone boy niang pour corigé balla légui balla mome waroula beuré ak siteu pourquoi siteu mbeurou gokhla té balla mbeurou andouna la balla mo eup souportér si lambdji lolou la yalla dogual

  • @Chakor8955
    @Chakor8955 День назад

    Modou anta khamou balla gaye iaw wakhal Lou nék sa xél ak sa xol rék

  • @SambaToure-n9h
    @SambaToure-n9h День назад

    Siteu bou defon ni moromam yi vp yi dagne kay daane wakh Len deug rk beuré niar nio Kay deff ah

  • @KhadimMbaye-k4f
    @KhadimMbaye-k4f День назад

    Yaw yay yalla modou anta xamo dara

  • @AmaraKoita-y9f
    @AmaraKoita-y9f День назад

    Franchement lambologue baxoul thi télé il force trop puis téyoul teksi day beugeu wakh lep