ARTP foofu mu taxaw, na fa sax dàkk jëñaxal nguur gi ba mu jël î matuwaay ci kaw tubaab yii nekk ci réew mi di bëgg a ray askan te du ñu wàccook seen i wareef. Tubaab yi lii ñuy def ci su ñu réew yi, ñeme wu ñu koo def ci seen i reew. Asan wax na dëgg. Dégg naa la yaw Sooyibu nga ne jënd nga 10 Go mu jeex ci ñaari waxtu. Man mii di wax fii ci Itaali, 200 Go lay jot weer wu nekk ci 10€ (6.500 FCFA) Te 50 Go du jeex ci weer wi. Te soo jeexalul 50 Go ci weer, 10€ yi nga jëndeewóon koneksiö bi, di na ñu la ci delloowaat 3€ (2000 FCFA) ba laa ngaa jëndaat koneksiö bu bees. Booleceek fii ci biir réew mi koo fi mën a woo ku ne doo fay dara, ndax ay simili nga koy defee. Lii yépp nag njiit i réew mi xam na ñu ko ndax xam na ñu ni yëf yi di doxee ci àdduna bi. Kon ñoom ñoo war a taxaw ci saafara mbir mi ni ko Asan waxee, su ñu nanguwul, ñu dàq léen, te woo ñeneen. Lii rekk la.
solution les meilleurs sonko diomaye a vie inchaAllah 50ans inchaAllah ❤
Sonko moy Diomaye❤️❤️❤️
NDAYSANE YALNA SEN DIAMOU YAGUE 😢❤🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Merci pour info rmasiyon sur la table ❤❤❤❤❤❤
Bonjour équipe solution manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
الصلاة والسلام على رسول الله محمد
50milion d'bonnè pour solition tv
Sohaibou sma mbokou dioben nga❤
Sohaibou yalna len yalla defal jam
Sohibou Diop manla moustaha Diop nouyoulma al Amine Drame koko sop la
Assane Aka beugue mbotou 😂😂
Ay assane
Ziarnalen yalnalene yalla sam ci barceb s touba amine ya rabbi ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Assane Du nitu Dara 😅😅😅😅😅
Jajeff assane degue pir gua wakhe machaalla 🙏🙏🙏🤍❤🤍❤🤍❤🤍❤🤍❤🤍❤🤍❤🤍🌹🌹🌹
Lirou Diaane 😂😂😂saa Bakho 😂😂
Bay asan misir limo don wax si jamki amna solo lol dagin ko warona baye mo akali
BAYE ASSANE MEUNEUGOUL DÉM MAKKA - NA KHAR FI AK DIX ANS
😂😂😂
Assane Aka beugue mbotou
❤❤❤
Assane moungeul Macka dji Bathi Kanam 😂😂
No, Lirou Diane mdr
Machella ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Assane temps lou khéré lay tek bilahi
Attention Sa ndiogou Forfait valable un mois différent de forfait un moos
Sa danio changer adversairou Lirou bi
Nekatoul wadiodiou
Asane mbotou mésséré
❤❤❤❤❤❤❤❤
ARTP foofu mu taxaw, na fa sax dàkk jëñaxal nguur gi ba mu jël î matuwaay ci kaw tubaab yii nekk ci réew mi di bëgg a ray askan te du ñu wàccook seen i wareef. Tubaab yi lii ñuy def ci su ñu réew yi, ñeme wu ñu koo def ci seen i reew. Asan wax na dëgg. Dégg naa la yaw Sooyibu nga ne jënd nga 10 Go mu jeex ci ñaari waxtu. Man mii di wax fii ci Itaali, 200 Go lay jot weer wu nekk ci 10€ (6.500 FCFA) Te 50 Go du jeex ci weer wi. Te soo jeexalul 50 Go ci weer, 10€ yi nga jëndeewóon koneksiö bi, di na ñu la ci delloowaat 3€ (2000 FCFA) ba laa ngaa jëndaat koneksiö bu bees. Booleceek fii ci biir réew mi koo fi mën a woo ku ne doo fay dara, ndax ay simili nga koy defee. Lii yépp nag njiit i réew mi xam na ñu ko ndax xam na ñu ni yëf yi di doxee ci àdduna bi. Kon ñoom ñoo war a taxaw ci saafara mbir mi ni ko Asan waxee, su ñu nanguwul, ñu dàq léen, te woo ñeneen. Lii rekk la.
👍👍💪💪💝💝💝💝❤️❤️❤️❤️
Lirou bouko wadji doré Tawou laydone 🤣
Cheikh Oumar Diagne dafa yagga fènal tarikhayi, beuriwoul xam xam tai meun sossss
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sa siar n'a la moutoul mark Dia pour yi si imison yi li bou tone Wa Nayik mark diomét tougou si s'en imison kgallis bou Bari gnay fayy
Assane wakhna Deugue Connexion bi dafa chaire trop. Opérateur yi naniou respecter lois yi walla niou Guénné leen reew mi
😂😂😂Baye Assane, Résultats = Ressinta😅
❤❤❤❤😂😂🎉
❤❤❤❤❤😂❤
Sohibou diop déll déf attention boy dieul nitt appel déll tagô tanga wakhko yangui en direct balamô déff eueure ❤❤
Aye weye sangiogou ragalale yalla oumare diange néna begou sering toube
❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sa😂😂😂😂😂😂
🐸🐸
😂😂😂😂😂 assane mésséré
😂😂😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤