KONA: LOUTAKH CNG VALIDÉ VICTOIRE MODOU…MAÏMOUNA NDOUR FEYE LAWONE WONINA BOU YAGUE

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 3 дек 2024

Комментарии • 153

  • @babathioub7294
    @babathioub7294 День назад +22

    🇸🇳🇸🇳💪💪 Respect kona Sonkooo Rék Laniouye Toop 💪💪🇸🇳🇸🇳

  • @OusmaneSambe-l3f
    @OusmaneSambe-l3f День назад +19

    Merci Kona vérité absolue ❤❤❤sinon Maimouna Ndour c'est une vraie comédienne mais dina joub par force 😂😂😂😂😂vive pastéf à vie❤❤❤❤❤❤

  • @Issadiop9073
    @Issadiop9073 День назад +13

    Merci ancore kona bien dit tres pertina macha alahou tabarakalahou ❤❤❤

  • @rokhayasarr6468
    @rokhayasarr6468 20 часов назад +6

    Force restera à la loi merci Kona sa fait toujours plaisir de vous écouter ❤

  • @silmakhatraore483
    @silmakhatraore483 День назад +9

    Konamba vieux mokho big respect ✊🏾

  • @ahmadsamb4890
    @ahmadsamb4890 12 часов назад +2

    Kona dioum nga si kaddou nga yalla sakh meunoul déf lou arranger nieup soubhanal lah lolou kaddou ndioumté la malgré kham na ni kou diokh yalla thieur nga mais des fois cheytane day wakhlo nite ndioumté

    • @Mousta1Faiiye
      @Mousta1Faiiye 8 часов назад

      Dafa waron wakh Yalla sakh limou Def dou arranger niepou

    • @Mousta1Faiiye
      @Mousta1Faiiye 8 часов назад

      Dafa waron wakh Yalla sakh limou Def dou arranger niepou

  • @SowMadiaw-go2uc
    @SowMadiaw-go2uc День назад +31

    Man bou pastef défoul justice thi complice macky sall ak gouvernement wan ma bayico affaire bi amoul masla.

    • @Issadiop9073
      @Issadiop9073 День назад +7

      Boul jahlè justice sera faite incha alahou broo

    • @SowMadiaw-go2uc
      @SowMadiaw-go2uc День назад +2

      @Issadiop9073 🙏🙏🙏

  • @BadaraFall-b9t
    @BadaraFall-b9t День назад +4

    Merci beaucoup frère kona yawe rek laye khol ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mbayeabdourahmane5076
    @mbayeabdourahmane5076 День назад +4

    Je vous suis et abonné
    Sa khalate nga wakh té lou lēp moy deugue thii combat bi

  • @seynaboundiaye-z1w
    @seynaboundiaye-z1w День назад +3

    Merci beaucoup Kona

  • @mordione7519
    @mordione7519 День назад +4

    Jajëf champion!!! Dëgg rek nga fi wakh. Billahi!!! Keep it up Bro!!!

  • @abdourahmanfall1908
    @abdourahmanfall1908 День назад +4

    Kona le patriote respect amal diam rek frere 🙏

  • @cheikhmbackesaliou7893
    @cheikhmbackesaliou7893 День назад +7

    Je suis content si et seulement si MNF n'est pas contente 😂😂😂😂😂

  • @DiorcoutureModou
    @DiorcoutureModou День назад +3

    Yalla äÿ thiam potoum bour dagaye wér barou féndi moutaw thia kawam boulby da tourner dé ndour faye thi ay tapalé rek la né machallah kona sama wadji ❤❤❤

  • @Mameleye-t2w
    @Mameleye-t2w 11 часов назад

    Merci beaucoup kona ❤❤

  • @assanesow3824
    @assanesow3824 День назад +4

    Merci Kona ❤❤❤

  • @mouhamedkandji40
    @mouhamedkandji40 14 часов назад

    Merci Kona Diadieuf ❤

  • @badarapapealioudiouf2822
    @badarapapealioudiouf2822 16 часов назад +1

    Li motakh xam xam ak ragnélé bakh ci lép. Merci Kona

  • @MorWade-w7q
    @MorWade-w7q День назад +4

    Kona siteu danona félicitations modoulo

    • @layetheonly5139
      @layetheonly5139 19 часов назад

      Modou lo danouna

    • @MorWade-w7q
      @MorWade-w7q 12 часов назад

      @layetheonly5139 yaw amo ay beet siteu xamol dara

  • @makhtardieye8261
    @makhtardieye8261 15 часов назад

    Merci 'kona

  • @ibrahimasarr8775
    @ibrahimasarr8775 15 часов назад

    Big respect a toi kona. Ta tt dît....conserna Maimouna 7 TV. On devrait fermée cette 7tv depuis longtemps. Loulou dou télé

  • @ousseynousall5808
    @ousseynousall5808 День назад +2

    Vérités absolu kona ❤❤

  • @serignleye5529
    @serignleye5529 15 часов назад

    Merci beaucoup ❤❤

  • @AsseCisse-by7xb
    @AsseCisse-by7xb 9 часов назад

    Merci Kona

  • @djibrilsene9029
    @djibrilsene9029 13 часов назад

    Salam kona, Sénégal gnoun gneup gnoko bok . Na lep jar yon

  • @seynaboudieng5198
    @seynaboudieng5198 17 часов назад +2

    Merci beaucoup konna domi rewmi yalla nalla yalla dolle same amine yarabi ci barkel alhouranou karim c'est vraiment le bon ❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamadounianghane2330
    @mamadounianghane2330 День назад +4

    C'est vrai ce que t'a dis KONATÉ le CNG aurait du dire que Modou Lo a mis son épaule et de l'autre côté aussi SITEU avait sa tête sur le sac ; de ce fait y'a nul puis Modou a gagné par point aussi simple

  • @doudoudia8093
    @doudoudia8093 День назад

    Merci beaucoup kona vérité absolue niitou deugg, Sénégal daffa beuri aye naffekk, siteu mo dane modou lo daffa léer.

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 День назад +3

    Siteu boumou niou sonal daw combat bi yeup diniou sonal ak victoire

    • @sorycoulibaly594
      @sorycoulibaly594 21 час назад

      Vraiment,lii mooy apologie de la triche...kou defoul dara waroo am dara,noonou la mbir yi wara démée😂

  • @ibrahimaba8222
    @ibrahimaba8222 День назад +4

    Hooooh roi 👑daniou kay liguéye way di arrière pour espérer sa adversaire fakhastalou nga am ndam😂😂😂

  • @Bluerain-j2v
    @Bluerain-j2v День назад +2

    Ziar Kona, amal diamm.
    Ndour Faye ,khatarayou bi diarouko, conforme toi à la loi, elle est valable pour les autres organes de presse.
    Vous êtes déjà dans une mauvaise posture financière et fiscale, Maimouna, vos émotions et critiques personnelles vis à vis du gouvernement ne comptent pas. C'est la loi qui doit être respectée, si vous la transgressez , vous devenez hors la loi.
    Pastef défoula dara et les journalistes ne sont pas au dessus de la loi.
    Cet assainissement de la presse est une demande sociale, les droits des uns et des autres ont été trop longtemps transgressés et leurs vies et leur dignité exposées.
    L'Etat à le devoir légitime de protéger la vie du citoyen

  • @KhadimSeck-ib3vw
    @KhadimSeck-ib3vw 15 часов назад

    Mana solo❤❤❤

  • @CheikhFaye-e2c
    @CheikhFaye-e2c 18 часов назад +1

    Lingua wakh amoule Siteu mo danou même avant sa Siteu defna 4 appui Siteu dafa danou

  • @cisseabdoulaye206
    @cisseabdoulaye206 18 часов назад +1

    Kona j’ai le même avis que toi. Ndiakh la gueuna Guice Mais modou est vainqueur par points

  • @aidasow2910
    @aidasow2910 День назад

    Kona merci beaucoup bien dit ❤❤

  • @user-cw4ij8gt7z
    @user-cw4ij8gt7z День назад

    Merci kona❤❤❤❤

  • @PapaBoulyDIEDHIOU
    @PapaBoulyDIEDHIOU 16 часов назад

    C'est eux qui nous ont appris que force doit rester à la loi

  • @mbayediagne4580
    @mbayediagne4580 День назад

    Merci kona

  • @AbdoulayeSene-e3d
    @AbdoulayeSene-e3d День назад

    Merci♥️♥️♥️♥️♥️

  • @Mousta1Faiiye
    @Mousta1Faiiye 8 часов назад

    Merci konamba toujours pertinent et véridique ❤ mais fall sa numéro usa bi la sokhla please

  • @KhadimSamb-u2m
    @KhadimSamb-u2m День назад +3

    Wa yene ki mer na deh lahilah kay bakh ngani ma bagne

  • @ndaooussemane7369
    @ndaooussemane7369 День назад +1

    Ligua wakh moy deug danio wara ndiakh niou diokh ko victoire par points

  • @DTFTV
    @DTFTV День назад +2

    Sénégal 🇸🇳 dée daniou vole victoire bilay

  • @ousseynoudary9352
    @ousseynoudary9352 День назад +2

    Kona maignou diam je supporte pas modou lo mais siteu danoule kéne dafa daw ba combat bi diekh

  • @Misterboom-x7x
    @Misterboom-x7x 14 часов назад

    Son excellence Monsieur siteu borom deuk bi mo nokh Roi des arénes bi euf beut bi Damou mbag bi soti Souf si bounou roi bi 🤣🤣🤣

  • @seringekante4314
    @seringekante4314 16 часов назад

    ❤❤

  • @NgoneColy-li6sq
    @NgoneColy-li6sq 18 часов назад

    Kona teunk nga wakh dji Maimouna Ndour déy foureul bi macky by danoo leu ay nélawam djékh rupture ak l'égalité lagn woté Assalamou Aleikoum

  • @issaciss2879
    @issaciss2879 День назад +1

    Sisi mbeur le patriote DEUG la maimouna na dém conforméwou dji à la loi lou yomb amatoufi jub jubbeul jubenti

  • @cheikh564
    @cheikh564 День назад

    Mbockoum rewmi yalnaleu yalla samme té mousseul leu si ayou lamigne ❤

  • @assanendiaye1094
    @assanendiaye1094 18 часов назад

    Kona mouno wakh ba siteu nék roi des arènes bi nopaloule

  • @biramaka6235
    @biramaka6235 День назад +1

    dey il impots rek et neke en regle. macky sathi dawna

  • @papagorakebe7594
    @papagorakebe7594 8 часов назад

    C'est la première injustice de ce nouveau cng

  • @tavarezcheikhou517
    @tavarezcheikhou517 День назад +1

    Reglment yi dafa changei nak saway

    • @MLo-he4lj
      @MLo-he4lj 19 часов назад

      Lolou nak la wara kham 😂😂😂

  • @maramediouf4913
    @maramediouf4913 День назад

    Salam Kona manguila ziar

  • @Soda-m1s
    @Soda-m1s 12 часов назад

    Siteu mo dane vraiment épaule chute laa

  • @issakhaseck9651
    @issakhaseck9651 18 часов назад

    MAIMOUNA doucement way sa holl ba ngui guéné

  • @OusmaneFall-m9d
    @OusmaneFall-m9d День назад

    ❤❤❤❤❤

  • @khadyfaye7864
    @khadyfaye7864 16 часов назад

    Payez vos impôts et soyez en règle administrativement avant de vous plaindre. On a un pays à reconstruire. Dioub, dioubeul.. Mr Sall il faut rester ferme. Rupture!

  • @ndeyeyandendiaye3424
    @ndeyeyandendiaye3424 День назад

    Maïmouuna prends du calmement😂

  • @laminegaye1073
    @laminegaye1073 День назад

    kou gagner wakho wakho ki gagner

  • @diopsidy7766
    @diopsidy7766 15 часов назад

    Lima guis ni mbeur yi naniou fékhé Di beuré si bir mogeu'a wor Park cng bi maîtriséwoul le règlement. Sa motivation pour la victoire de Modou est sans fondement. Encore le lobbying a gagné.

  • @toque5855
    @toque5855 День назад

    😍🙏🏾💪🏾🇸🇳

  • @AbdouNgom-t4y
    @AbdouNgom-t4y 13 часов назад

    Cona lamb amoule logique amoule texse ayi contexte laniouy atte😂😂

  • @mouhameddiop3053
    @mouhameddiop3053 День назад

    MEUNO KHAM LEP AUSSI BOUL YAK SA LIGUEYE WAKHOU FAR REKK NGAFIY WAKH MAYNIOU DIAM WAY BOUFI OUTAL SA BOP NONE YANGUI LIGUEY LOU DOP LINGAY WAKH KHAMOSSI DARA NOPILL

  • @HabytoumboAmadou
    @HabytoumboAmadou 19 часов назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamediakhoumpa6748
    @mamediakhoumpa6748 11 часов назад

    Nono siteu bu ngor diokhou gnuko victoir dei pokolaa dane nagnnn koo da gnokhou victoir lisss ndiaguo

  • @ndeyeyandendiaye3424
    @ndeyeyandendiaye3424 День назад

    Gni dagno sanko peuple bilein warone diapalé dagnoulein méré

  • @cheikhdiakhate716
    @cheikhdiakhate716 12 часов назад

    Mnf 63 millions yi lan sokhla na gaww

  • @awabalde6432
    @awabalde6432 День назад

    ❤❤🇸🇳🇸🇳❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @khadimegueye9070
    @khadimegueye9070 19 часов назад

    Lamb dji amul yone cng lañu def tegu ñuko feneu

  • @abdoulkhadreba5724
    @abdoulkhadreba5724 День назад

    Ziarré bonne nuit

  • @bocargadio4054
    @bocargadio4054 День назад

    On sent que tu n’est pas objectif si combat Modoulo Siteu bi mais parfois day ame meuno ame deug si lepp !
    Bon courage liguey bagui dope !

  • @coumbasy9044
    @coumbasy9044 20 часов назад

    😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮

  • @SaliouMbaye-jr2em
    @SaliouMbaye-jr2em День назад

    No. Maymona dourr. Wore doumiharam. La. Doull. Rek

  • @khadimgueye407
    @khadimgueye407 18 часов назад

    Kona bègue

  • @AronaDem-u1i
    @AronaDem-u1i 19 часов назад

    Mai, de grâce mets toi à jour sois en règle avec l administration la victimisation ne passera. Le désordre actuel a trop duré ton rôle dans le défunt régime meurtrier et les avantages dont tu bénéficiais alors n échappent à personne. Fais comme t'es autres collègues qui s empressent de régulariser leur situation surtout payez l impôt bon sang. Autres temps autres mœurs voyons. Mai, passe à la caisse l agitation seta vaine.

  • @damediop9049
    @damediop9049 15 часов назад

    Bonjour frère toujour damay and ak iow mai aujourd’hui suis pas d’accord avec toi fekhel kham règlement lamb bala ngay def sa commentaire Pasque binga defé sortes Wakho siteu dafa tek tête bi merci

  • @papagorakebe7594
    @papagorakebe7594 8 часов назад

    Modou lo dafa dane siteu défaite bi mo doul nekh rek nakh danio wakhone siteu zero chance la ame yalla deug leu beug

  • @AbdoulAzizDabakh63
    @AbdoulAzizDabakh63 13 часов назад

    Mais yow la 1er fois danga wakh site mo daane, tay ngani siteu bopou bi laal neu souff😅😅

  • @mamadougassama8155
    @mamadougassama8155 День назад

    Amal diam

  • @DjibrilGANEMbengueNDOYE
    @DjibrilGANEMbengueNDOYE 14 часов назад

    Konia Siteu bi mouy fakhate zarco mougui ko fakhaté si biir dieum si biti
    Mais Modou lo si Siteu boumou koy fakhate mou gui deuxième rangée sakou yi donc guéna na

  • @adamadieng8720
    @adamadieng8720 19 часов назад

    MAIS MNF guayyi MOUNIOU TEPPI LEUFFEUL NDEYAMM ELLE EST ENTRAIN DE TIRER TROP LA CORDE...DOMERAME BI

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 День назад

    He mnf mba khol bi dou wade😂😂bon khatarayou mnf

  • @MbargouDiop-mk4cv
    @MbargouDiop-mk4cv День назад

    Yw kén ladioula psk geunognou kham lamb tapét motakh gua daw lamb dji

  • @SD2FO
    @SD2FO 8 часов назад

    Yaw nokhol falé monsieur tout connaît

  • @momargueye5083
    @momargueye5083 День назад

    Ba legui Pr El Malick Ndiaye tontouwoul Aissata tall Sall 😂

  • @BambokamaraKamara
    @BambokamaraKamara 20 часов назад

    Yes 👉🦻🇸🇳👌

  • @DiorcoutureModou
    @DiorcoutureModou День назад

    Wakh ga deug kona wa gnc dano dioume

  • @Ballasylla-e6j
    @Ballasylla-e6j День назад

    Kona combat bi diekhna bouyagu diaratoul wakh siteu meunoul dane modou lo modou lo kikoy dane dagay takhaway afrontéko

  • @mamadougassama8155
    @mamadougassama8155 День назад

    Si deug nguey dokh

  • @MbargouDiop-mk4cv
    @MbargouDiop-mk4cv День назад

    Mais kome khamguani popou siteu miguithi sakouyi kone lognouye sonal wakh diou bary

  • @ibrahimaba2655
    @ibrahimaba2655 16 часов назад

    Bayil doul modou lo mo dane

  • @AdySylla-sm1bf
    @AdySylla-sm1bf День назад

    En tout cas sa bakkbi rék doyna émission kou beuga dégue deug diapal c le bon tv kou beugoul dégue deug ngir yalla démal kholi fénéne pour mane kona tonioul kéne

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 7 часов назад

    Iaw khamon dara lou takh mou dém dadon khoul ndakh siteu danou woul

  • @cissemalick6564
    @cissemalick6564 День назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤✌️🇸🇳🙏🏼

  • @badaragueye-bw2xz
    @badaragueye-bw2xz День назад

    Taxi li nogay wakh khamoci dara

  • @aidasow2910
    @aidasow2910 День назад

    💪💪💪💪💪💪💪💪🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @elhadjigueye600
    @elhadjigueye600 День назад

    diamou si yaw kona

  • @alufaye1470
    @alufaye1470 День назад

    Maimouna ndour faye na pas de tele elle travaler sur du faux

  • @ModouFaye-cp4vo
    @ModouFaye-cp4vo День назад

    Mboum 😂 Faya mboum faye hkamal sapope