15h DÉBAT | Ndax Islam am na bénén déllu waay budul ALQOURAAN ? | Dr Ahmad Khalil LO- C Mbacké Sakho

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 11 янв 2025

Комментарии • 14

  • @moustaphadiop5405
    @moustaphadiop5405 7 месяцев назад +3

    Macha Allah swt CAMS rafetna rafetlouna KO leerna ndakh Indiga preuves yii mouye alkhourane wakhi yaAllah swt dieuredieufety

  • @mamadoudione9116
    @mamadoudione9116 2 года назад +11

    Dr Ahmad khalil lo sa xam xam lërena... c'est simple kou bayi sunna sonou... sakho nenga alkourane rk ngay topou té yangui guène thi al khourane di niewate... tontou wo béne question thi limoula wakh...al khourane dale ak sunna yeupe thi yalla la bayéko.. bo wédé al khourane moy wédi nga yalla bo wédé sunna moy wédi nga yonnéneté bi psl té moy wédi nga yalla ndax té yalla moko yonni... ma cha Allah dr Ahmed khalil lo linga wakh mo lëre... al khourane ak sunna... té lëpe thi yalla laye delou al hamdouli'Allah... yonnéneté bi dou wakhé banékhou bakaname🥰🙏

  • @masiba7272
    @masiba7272 2 года назад +3

    Macha Allah docteur Ahmad la fin prouve qu'il est tombé Bas.
    En résumé on ne peut suivre le Coran sans la souna du Prophète les deux vont de pair.

  • @cheikhibrahimandiaye3449
    @cheikhibrahimandiaye3449 2 года назад +1

    الحمد لله الذي هدانا لهدي محمد صلوات الله وسلامه عليه

  • @masiba7272
    @masiba7272 2 года назад

    Macha Allah !j'ai toujours voulu un débat pareil .

  • @omardiop803
    @omardiop803 2 года назад

    YALNA YALLA DIOUBAL CHEIKHE MBACKE SAKHO DEGLOKO ALKHOUR AN
    WAYE DEGLO ARAB DEUG DWUD DEG COME MOM MOY TEKIL BOPAM. LE VRAIE PROBLEME MOY DAFAY TRADUIRAL BOPAM TE DEGOUL LA LANGUE ARABE

  • @ismo2brain
    @ismo2brain Год назад

    Nane nga meuna dieulé AlQuran wédi diangalé koumou yooni wathié ko si mo mouy Mouhammad Salallahou Aleyhi Wa Salam

  • @ismo2brain
    @ismo2brain Год назад

    2 C'est Lui qui a envoyé à des gens sans Livre (les Arabes) un Messager des leurs qui leur récite Ses versets, les purifie et leur enseigne le Livre et la Sagesse, bien qu'ils étaient auparavant dans un égarement évident, 3 ainsi qu'à d'autres parmi ceux qui ne les ont pas encore rejoints.

  • @bayesambaniass5847
    @bayesambaniass5847 2 года назад +1

    Sounnah dafa nékha layal koi
    Alhammdou lillaah

  • @dioufabdou9481
    @dioufabdou9481 18 дней назад

    En tout cas li cheick Di wah lerna trop

  • @aliounebadarandiaye5344
    @aliounebadarandiaye5344 Год назад

    je ne comprends pas comment on peut croire au coran et non a la sunna alors que les mêmes personnes qui ont transmis le coran à la génération future ceux sont les mêmes qui ont transmis la sunna je prend ce qui m'arrange et je l'interprète à ma façon drôle de manière de concevoir l'islam

  • @OumarDiop-g6t
    @OumarDiop-g6t Год назад

    Nékhoul ba nékhoul wayé sakho dégo alquran

  • @bahablaye3053
    @bahablaye3053 2 года назад

    Franchement cheikh mbacké et nul li ngay wakh defa yomb trop c terre a terre