Wallahi seydi Gueye, gnome faydou chaïtane sani ak gnome Aïda ibliss ak khady diawharatoul chaïtane gnô waral coronavirus bi ndakh moy yalla binou néké ci tourou mawlana cheikh Ibrahim Niasse rta ak faydatou tijani bou séleubi ko yalla diagléle
Bayiléne cissou bii. Hana Gamou dou ganaw Yonnent bi et Baye déf nako. Yonnent SAW boumou gadayé diogué makka nieuw médina, teug ak féthie lagn ko terto. Et Baye talibé wam yeup ay goor lagn, djiguéne amou tchi. Baye kéne douko xam. Dang tchiy xam touti, sa morom xam tchi touti. Contenté woul si linga xam té bayi lii bokkou na tchi wala bokkou tchii.
Seriñ nioguilay siar di rafetlou sa xam xam si chariyatou islam dila xamal ni la Baye niari tank la messeu atei wo mouy chariyatou ak hahiha Baye Mo fi indi lou meusta aam xamal ko ndaw yi kone douniou diaxal lou meusteu aam di Aam ginaw cheikh ibrahim.Faydou saani mom kanam la dieum jiggen bouy Zikrou nak bo nei da aram moy dagua gat xam xam ndax baye Mo wax ni amoul jiggen ay goor rek la Aam .Liguay atewo mouy chariyatou bofa yemei rk moy sa xam xam sorewoul.Amal diam yalna yala déf diam
Dèlène guëstou balaguène di critrique limou wakh dara douko dindi bayilen di topp sen naffssou diko tek baye niass dinnè ak khakhikha lafi bayi baye gueye mounoko critiquè limou kham thi baye ba illa yawmi dinne doko kham xam xam guette lathi wasalam.
Yalah nah yalah yessal ndiegal akk yeurmaner thi yaw
Macha allah yalla nala yalla fay ta diégueul leu teugg bokoul si fayda bi
Wallahi serigne bii. Kou am kham kham kou ragal yallah kou deguou wayé batay sénégalais yii khamougnla
Macha allah Baye moustapha bou moukhadame yépa mélone ni yaw fékone na gnakhane yi jékh
ماشاء الله
Machala , la vérité absolue d'Allah
Degue rek ga wakh gueye yalna yalla fayla nagnou bayi fomi tè toppou diagalem cheikh ibrahim
Numero 1 ci Senegal machalla wer ak goudou fane rek amine
Mashaa allah,papa mustapha yallah moo yoor sa faye yallah na nyu la fayal y Aaamiin
Leerna nagne dieuredieuf Imam Moustapha gueye.MACHALLAH kham kham rek gueye
Guinaw bayla wayé bi mouy doun ndou tagou fé thie amoul djigéne bouy zikar amoul 🙏💞
Machallah vérité absolue Yalla nala Yalla fay...leerna nagn gars yi seen bakkan rek
Manchallah yalna yallah mayla werrr ak guoudou fane si barke cheikhou tidjianie amine baye niass
Wallahi Wakh nga Deuggg,ay way ya Nièmè deugg.Mashalla😍😙😶😚😗
El Hadji Moustapha YALLA NALA YALLA FAY YIW.Amine ak Mbolèm Djioulite,Wallahi konetane nañou Thi yaw😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😚
Machallah yalna bour doli lá tawfikh boubakh si barke Al quranul karime te goudeul fan Gui te yoku kham kham kham bi diahi seyedina Mohamad
Machallah dieureudieuf baye Moustapha Gueye yalnanguafi yague lool té andak wër bidiahi Nabil-il Moustapha barké cheikhoul khadim amîne 🤲🤲🤲
سبحان الله
Macha allah serigne bi yalla na yalla goudal sa fane may la wer lerr na ame na solo Alhamdou lilah
ماشاء الله ♥
Macha Allah cheikh moustapha vraiment li niepa si wara wa
Machallah yallah yallah fayla yiw teu godal sa fane mayla were ak werlè
Amine
الله أكبر dieureudief serigne moustaph gueye
Macha'Allah Macha'Allah ALHAMDOULILLAHI
yala na yalla werall la
Jerejef seringe mousstapha yalna yala yagal lafi wakh deg légi dafa raflé
machallah baye moustapha Gueye
Machallah gaye lérna trop
Akay degu
Sakh yalla sa fane goudou
Thieye baye Moustapha Gueye ya gnémé dueg
Wallahi seydi Gueye, gnome faydou chaïtane sani ak gnome Aïda ibliss ak khady diawharatoul chaïtane gnô waral coronavirus bi ndakh moy yalla binou néké ci tourou mawlana cheikh Ibrahim Niasse rta ak faydatou tijani bou séleubi ko yalla diagléle
Macha Allah ndeye
Way Legui khaliss rk
Ken dou wa talibé yi Lou Baye niass beugueu
Virus la bou Nek si Faydou bi
Leer n nieupp hana deugueurr bopp ak topou seytané
Machalla
Bayiléne cissou bii. Hana Gamou dou ganaw Yonnent bi et Baye déf nako. Yonnent SAW boumou gadayé diogué makka nieuw médina, teug ak féthie lagn ko terto. Et Baye talibé wam yeup ay goor lagn, djiguéne amou tchi. Baye kéne douko xam. Dang tchiy xam touti, sa morom xam tchi touti. Contenté woul si linga xam té bayi lii bokkou na tchi wala bokkou tchii.
Sa prouve que ba légui ya ngui khaybou
Ki Baye niass moko yar kou beugueu fethie Demal si waly seck
waxouma teug ak fèthie wayè fane la baye bindè faydou saniya so parè nga waxma fou faydou eweulou commancè ba fime dièkhè wala nga waxma louy fayedou
@@ismailandiaye4722 jerejef serinj bi lolu moy latch bi werr,su feke talibe bu daggu la nala jokh tontu bu werr
Jeureudieuf baye niasse amoul djiguene
Seriñ nioguilay siar di rafetlou sa xam xam si chariyatou islam dila xamal ni la Baye niari tank la messeu atei wo mouy chariyatou ak hahiha Baye Mo fi indi lou meusta aam xamal ko ndaw yi kone douniou diaxal lou meusteu aam di Aam ginaw cheikh ibrahim.Faydou saani mom kanam la dieum jiggen bouy Zikrou nak bo nei da aram moy dagua gat xam xam ndax baye Mo wax ni amoul jiggen ay goor rek la Aam .Liguay atewo mouy chariyatou bofa yemei rk moy sa xam xam sorewoul.Amal diam yalna yala déf diam
Amal eudeup ki Baye moko diangal tarbiya ko sou féké sa mouhadam mo meun Baye nga waxma..
demal jangui boy