Net Tali: La Gnamou Xalé Offerte en Mariage à un Vieux

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 23 ноя 2024

Комментарии • 47

  • @nabouDiop-so2vy
    @nabouDiop-so2vy 5 месяцев назад +38

    Elle doit quitter ce mariage et allez chez sa sœur et continuer son travail pour gagner de l'argent et acheter sa propre maison 🏠 et vivre comme elle le souhaite et un jour fondé sa propre famille ❤❤ et vivre heureux sans estresse

  • @YacineNdoye-rr9iv
    @YacineNdoye-rr9iv 5 месяцев назад +13

    C'est important d'avoir ton bonheur 😢

  • @RamaSy-s1e
    @RamaSy-s1e 5 месяцев назад +13

    Elle n’a qu’à aller chez sa sœur et divorcer de se vieux merci ❤❤❤

  • @gueyecheikh4878
    @gueyecheikh4878 5 месяцев назад +13

    Blh Sénégal ay problème kasse la

  • @awadiouf9597
    @awadiouf9597 5 месяцев назад +8

    Wa papam bi nitte leu 😮demal sa keur sœur boulnangou nioulay forcé

  • @salimataba6813
    @salimataba6813 5 месяцев назад +7

    Boumou farantou ndax dakoy diox dikko bou bone na fexe guene ci seuye bi te tok ligueye ba yalla niew

  • @AbdoulAhadGueye-ep6rd
    @AbdoulAhadGueye-ep6rd 5 месяцев назад +3

    Nit gni nioungui sonal sèn bopp si lou beuri lo khamni bouko yoon yeugon régléko, niou tok rek di sonal sèn bopp

  • @Alislamniass
    @Alislamniass 5 месяцев назад +4

    Nh dèf liko mag bi wakh na tass th après souko pabi naré may kenen mag dji soutenir ko mou bagne se douguou

  • @madonaniang9363
    @madonaniang9363 5 месяцев назад +1

    Je voulais vraiment savoir la crème que tu utilises pour que je puisse l’utiliser aussi s’il vous plaît dite les produits que vous utilisez ❤

    • @astoumaguettesissokho32
      @astoumaguettesissokho32 5 месяцев назад

      C'est secret toi aussi elle n'est pas là pour faire la publicité d'un produit qui ne l'apporte rien fait des efforts pour trouver ce qui te vas vous n'avez pas le même type de peau

  • @Cheikh621
    @Cheikh621 3 месяца назад +2

    Na fippu ñibbi té bañ pappam diko may kum bëggul

  • @kechiphone5689
    @kechiphone5689 5 месяцев назад +1

    Ndagoul nba geneu si seuy bi bi gnibé sen keur soula. Sa papa beugué mayé nga bagne dou moudj fen

  • @nastousarr2875
    @nastousarr2875 5 месяцев назад +1

    Elle quitte le marié non elle doit patientee car elle encore très jeune

  • @HousseyNouWade
    @HousseyNouWade 5 месяцев назад +1

    Elle doit quitter ce mariage dont elle n est pas heureuse car un mariage intérêt personnel elle doit s approcher aux parents ou amis proches de sa famille pour les exposer ses doléances avant qu elle fait l irréparables

  • @MamankhadysidibeMakhady
    @MamankhadysidibeMakhady 5 месяцев назад +1

    Mane dal louma guiss moy mome ak mak thie niou nék béne affronté sen papeu té tass sey bi par force dém dek ak mak game wa ila mou sét location té mou am dioum te bopal ba guiss kou bakh mou seyel ko

  • @TraoreTraore-rz1ns
    @TraoreTraore-rz1ns 5 месяцев назад

    Sa ma bene mam bou gorr da retraite bimou niewee deukba moutak bene khale mou ama ak mom 3 enfant ndeyssane khale boudjigune bi décédé legui takana benene khalé am ak mom 4 enfants encore wallahi sama bougorbi minguigafa belegui en plein forme😂

  • @afounasabaly2814
    @afounasabaly2814 5 месяцев назад +1

    Amène la chez toi

  • @mameyacinekane
    @mameyacinekane 5 месяцев назад

    Ok papa mais donne moi le temps de me reposer et attendre les conseils de sa sœur

  • @YacineNdoye-rr9iv
    @YacineNdoye-rr9iv 5 месяцев назад +6

    😢

  • @seynaboudiawara3226
    @seynaboudiawara3226 5 месяцев назад +1

    Alalou aduna dinatakh gua yakh doundeu nit ko diour
    Na tass seybi yobouko si yoneu mogueune mariage forcé légui yone rek

  • @zizouzidane7332
    @zizouzidane7332 5 месяцев назад +1

    yallananiou yalla mousal si kilifa bou amoul diné tes alalou adouna djital la divorce tu as le droit ga louée nék bayiko fofou

  • @harounaba6331
    @harounaba6331 5 месяцев назад +2

    ❤❤❤🎉🎉

  • @cheikhabdelkaderkamara
    @cheikhabdelkaderkamara 5 месяцев назад +1

    Guorgui nekoul thi deugueu sa bay témit nékoul thi deugueu wayé dara boumeu la takha ndialo prend ta dessision ma fille

  • @MatarCisse-u3y
    @MatarCisse-u3y 5 месяцев назад +1

    Na woute ay broke kham kham gnou wah ak pas bi bou antouwoul mou fipou par force bou lolou dialle man damala beugue ba dila guente la fatou

  • @famasow5796
    @famasow5796 5 месяцев назад +4

    C vrai mais papam bi doynawar

  • @nenesonko1562
    @nenesonko1562 5 месяцев назад +2

    Na fatt rackam moy deugeu oufko yirko ndakh moy ndéyam

  • @seutouaby4140
    @seutouaby4140 5 месяцев назад

    Na dem si mack dji mo gueneu

  • @AbdoulAhadGueye-ep6rd
    @AbdoulAhadGueye-ep6rd 5 месяцев назад

    Na dém police dénoncer papam niou niaf ndayi papa dji bakham fanla ték abu de pouvoir bimi déf

  • @wanealpha1965
    @wanealpha1965 5 месяцев назад +3

    Na ngeni ci sey bi mak bi diapaleko

  • @Baaba-c3o
    @Baaba-c3o 5 месяцев назад

    c'est quoi Bal ?

  • @altesseroyale4383
    @altesseroyale4383 5 месяцев назад

    Waw! Yène baye yi yane façon baye la ou?? Yallah Bour Amna patience! Sinon dina yoni malaka yi con déconné gnou tape la ba nga noye! Ehhh damani yangui liguèye démale wouti fo deuk, dème tribunal, tribunal tass sèye bi! Nga continuer sa liguèye diap sa bop ba guis kou bakh kou diara seuyal moutak la! Kou ande si li ma wakh lalale j’aime!

  • @famasow5796
    @famasow5796 5 месяцев назад +1

    Na dem police declarer papam c est pa normale

  • @morthiam6678
    @morthiam6678 5 месяцев назад +1

    Elle. Quitte c'è vieiille hom et refuge categorique delautre nome son pere na pas drois a l obliget un Marie quelle ne veu pas

  • @awakanteh5283
    @awakanteh5283 4 месяца назад

    Pesum kanam la moo ko wara fajal bopam. Pa bi duko reiye duko feess. Na tass teh wahh papam dega aahh waiye

  • @salihate-ew6wy
    @salihate-ew6wy 3 месяца назад

    🎉

  • @AissatouFaye-nj7gn
    @AissatouFaye-nj7gn 5 месяцев назад +1

    Xana amo yenene mbok gua deem fofou ba guiss ko beug

  • @amadouthiam7967
    @amadouthiam7967 5 месяцев назад

    Na mougne. Khale nga dara diaroul yakam ti. Koye bou deugeur diaroul yakam ti

  • @JainabouCeesay-w7q
    @JainabouCeesay-w7q 5 месяцев назад

    Sa papa Moy ndieuka dée paa bi😂😊

  • @MamadouBa-sk2vh
    @MamadouBa-sk2vh 2 месяца назад

    Boul.

  • @kantayesouare6632
    @kantayesouare6632 5 месяцев назад

    Laan moy Bal ??

  • @abymbengue2049
    @abymbengue2049 5 месяцев назад +1

    😂😂😂

  • @aliounbtoure8018
    @aliounbtoure8018 5 месяцев назад

    Na tass tabou tasse boumou delou keur papa wala boufa delo n'a lank boumou seuye ak loumou beugoul

  • @mamadoulaminediop5158
    @mamadoulaminediop5158 4 месяца назад

    Yaw amga dieker wala tontoma??

  • @Feuz861
    @Feuz861 5 месяцев назад

    YAW AY AFFAIRES SEXE REKK NGAY WAKH