Sama commande bi eksina Machallah Chérie neex na sell na Wallay neex gua deret mom togue day and ak neex derett😂 Maroc kay bombe amoufi sime mofii am😂 Merci Sauce bi djanguena ko fi damako dane Lekk fii rekk nane li neex na t meunoumako Merci beaucoup
Ah Alphie Ba Poulo. Tothie nga fi. Chanson bi nak amatoufi. Waa dokk koor djakarloo ak bii couscous royal jarnako. Masha Allah :) :) Deggal jamm rek yow. Nous t'aimons tres fort. Waa nila. Cuisine dafay andak bonne humeur. leep saff, nieup contaan. Que Allah benisse ta chaine ak ton travail. Merci du partage. Allah samaal la sa njaboot. amiiiin. :)
Sauce tfaya bi, ohhhh😋😋😋😍😍😍 Couscous marocain sans sauce tfaya n'est que ruine de couscous, looooooonnnneeee😋😋😋 Haha maachallah domou baay, sa bonne humeur c'est contagieux. Amal diam all time 🙏🏾🤲🏾🤲🏾
@@AlphieCuisine oh okay merci J en prendrais a Dakar com je vais m y rendre ds 3 semaines inshaALLAH... Alphie sani gniou un coucou sakh de tps en tps wa SAN ANTONIO Texas 😅, ca fera plaisir a ma fille elle adore tes videos 😍
Yallna yalla same tata content nagne dh ❤️❤️❤️❤️❣️❤️❤️❣️❣️❤️❤️❣️❣️❤️❤️❣️❤️❤️❤️❣️❣️❤️❤️❤️❤️😘
Merci beaucoup ☺️ merci 🤩 j
ooh notre alphie sa coucous bakhnaaa machala tout est beau
Alphie khana wa team Sénégal mom dagu len Di faté daniouy meer dee
Team maroc contanenaniou c couscous marocain Sénégalaise eupna kene dou yaw ma cherie
Wa aussi
Athia notre alphie national fila guene tay
🥰🥰🥰🥰🥰ahhh alphie kene dou yaw li nga couscous amoul fene merci 🙏🏾 yague fi té werre rek
Ndèy saaane, la sauce du couscous me rappelle ma maman, elle nous avait appris à préparer cette sauce rouge pour le couscous...
Hoooo mashalah
Machallah Alphie sa couscous royal bii toghna
Tata Alphie yague fi lool and ak were
Man dè chak jour ma repeter recette yi
Contane rek.
Machallah merci alfi cuisine ca kaw ca kanam
On te remercie pour ta générosité 🥰😘😘
Machallah. Merci beaucoup notre Sister internationale alphieeeee
Macha'allah chef Alphie couscous bi tokna mais khamou mawone ame ngua yénéne talents... 😊 voix bi nekhna macha'allah 😇😘😘
😂😂😂😂😂😂mane guay nakh
Mahcha,allah amna solo alphi
Machallah ma belle bonne continuation
Walahi je t'adore alphie makk yaw depuis tfm j'aime bien suivre tes cuisines😍
Merci beaucoup ☺️ eva
Hééé Mbaye, Hééé Alphie li lane la💙💙💙👏👏👏💐💐💐💯💯💯🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Machallah merci👍👍❤❤❤😋🤗💯💯🙏
Machalla wayyyy ❤️❤️
Machallah yalana l'homme bi wére
Alphie yah meune diémoh deh❤️❤️
Sama commande bi eksina Machallah Chérie neex na sell na
Wallay neex gua deret mom togue day and ak neex derett😂
Maroc kay bombe amoufi sime mofii am😂
Merci Sauce bi djanguena ko fi damako dane Lekk fii rekk nane li neex na t meunoumako Merci beaucoup
Merci à vous si commentaire bi
Machalla c'est beau nekh na barri na
Tata alphie thia kaww thia kanam 😍
Machallah chef alphie croussiant li si couleur eupeuneu ♥️🥰🥰
Machallah notre Alphie nationale,temps yi mangui pratiqué you bakh yaw dal Ba Poullo amal diaam fo tollou 🥰🥰🥰
Ah Alphie Ba Poulo. Tothie nga fi. Chanson bi nak amatoufi. Waa dokk koor djakarloo ak bii couscous royal jarnako. Masha Allah :) :) Deggal jamm rek yow. Nous t'aimons tres fort. Waa nila. Cuisine dafay andak bonne humeur. leep saff, nieup contaan. Que Allah benisse ta chaine ak ton travail. Merci du partage. Allah samaal la sa njaboot. amiiiin. :)
Alahouma amine fatima Ay way li nekhna hooooo sa ma khol fesna merci beaucoup ☺️
Manshallah sa plat bi wouyona tourame tarekala
YÉNAGUI TOK MANGUI TAKHAWE MOMAYE RÉLO MANE😍😍😍😍
😂😂😂
Machaallah chef alphie
Macha Allah 😍 t'as une belle.yallah na sa diam yague
Alphie MEILLEURE namenala bilae digua wakh fane la nekk damay daw rek mais Mangui guiss lepp nekhal gua koor gui comme d’habitude mashallah keneu dou yow ❤️🥰
Waw nonou leu diot waroul beuri gros bisous
Épice yombenala ndakh guisna dengage épicé généreusement machallah amna solo
Sa couscous bakhna daleu
Inchaalah inchaalah 😂😂😂
Yakalko pape cheikh 😂😂😂😂😂ak Oustaz modou fall
Niou waxalla say bax bax midi plus 😂😂😂😂😂pape rk 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
@@AlphieCuisine Waw pape bou sourer rk 😂😂😂
Alfi sa tog bi nekhna and na ak bonne humeur 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Team croustillant finga géneu tay lane la
Mane dal yaw la gueume yafi né wa Léa esk do dieul assistante tamite gnieme na wagne dé 😍😋
Non Léa rek
Macha'allah sister longue vie à vous
Machalla machalla
Wawa machalla Sama 😋😋😂😂😂
heureusement ba koorii guii lakko setan, merci souniou alphie internationale
Laaane 🤤🤤 riche sayou plat bi rek lènène la ay nioune founiou dieum 🥰😍
Merci sister d’amour ❤️😍
😂😂😂😂😂
Couscous bi daal ma sha Allah. Très bien dressée
Merci beaucoup
😍😍😍😍mashallah
Machalla ❤ ❤ merci Alphi et bon Ramadan
👏❤️❤️❤️🙏♥️🤝
No Alphie tu nous Gates bisous bon appétit
No li bakhna déh pour karité pour nous qui sommes au maroc
Kene dou yaw aussi ♥️
Deugeuleu 💃💃💃notre alphie mondiale fouko nekh lay guéne lonnn 😂❤️😍🙏team croustillant the best 💪💪
Walahi beugue fête yi nekh rek 🥰🥰🥰
@@AlphieCuisine ❤️😍
Machallah ❤❤
MachALLAH❤️❤️❤️❤️👏🏾👏🏾
Macha alla
Machalah
Thioum il faut mou am tookh Sénégal Day fay
Mashalla alphie désormais je préfère cette version de couscous.merci alphie pour la recette
Moi aussi deee
Ça donne envie 😍merci
Li nekhna kat
Masha Allah Dieuredieuf
Sauce tfaya bi, ohhhh😋😋😋😍😍😍
Couscous marocain sans sauce tfaya n'est que ruine de couscous, looooooonnnneeee😋😋😋
Haha maachallah domou baay, sa bonne humeur c'est contagieux. Amal diam all time 🙏🏾🤲🏾🤲🏾
Wa degeul nanite hoooooo li Eupena way sauce tfaya merci beaucoup maman racky 🥰🥰🥰🥰
Bonjour ma belle le.prix c est pour un sachet ou par pack?
Bilay kéne dou yaw si gnoune
Jaajeuf waay amna solo lol
Wawaw💃🎤👍👍❤🤣
Eupeune❤
Alphie yaye sama professeur yama takha beugue épices
Bonsoir Alphie
Est ce que vous avez un representant aux USA pr les epices?
Vraiment tog nga sama plat 😇
Non pas encore mais vous pouvez acheter en ligne www.reen-epices.com
@@AlphieCuisine oh okay merci
J en prendrais a Dakar com je vais m y rendre ds 3 semaines inshaALLAH...
Alphie sani gniou un coucou sakh de tps en tps wa SAN ANTONIO Texas 😅, ca fera plaisir a ma fille elle adore tes videos 😍
Louma nekh si Alphie anti gaspillage la .
😂😂😂😂
Cc ma Alfie boule takh sérére yii Rétane alpoulard yii merci si repas de fête yii yaw danga meilleure ba poulo beugue niébé cc à léa 😘😘😘❤️
Merci à vous serere yi contane naniou
Tu es trop généreuse de partager ton savoir avec nous j'ai télécharger presque toutes tes recettes. Merci beaucoup❤❤❤
❤️❤️
Dowline bi khente ko 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Temps saf saf