Salam aleykoum tata Marietou et la communauté si quelqu'un peut m'aider MachaAllah au top,jaimerai c'est avec quels matériels sur gaz que tu as fait tes grillades s'il vous plaît merci beaucoup tata
4 года назад+1
Lodge Pre-Seasoned Cast Iron Reversible Grill/Griddle With Handles, 20 Inch x 10.5 Inch - One tray www.amazon.com/dp/B00008GKDQ/ref=cm_sw_r_cp_api_glc_fabc_WAR4Fb01W5KD0
Bjr tata, bravo pour sa couscous royal bi mè je trouve que sucre bi barèna torop et il y a tlmt de diabétiques au pays. Les pois chiches n'ont pas besoin d'être sucrés. Sinon cette recette est impeccable. Merci pour tes belles videos. Kiss
Bonjour ya marietou vos plats sont extra et j'en apprends tjrs maa shaa ALLAH yallah na yallah laffal la thiat.....une question votre sauce ognions elle n'était pas trop sucrer?
5 лет назад+1
nancy fall Ameen way ma Cherie no pas du tout juste tèm tèmi
Hello Madame,where can I get the Morrocan seasoning powder you mentioned in the video? You saix you will show it but,you did not a d what is the name. Thank you very much and stay blessed.
Ta Marietou j'ai constaté que lingay faté le nom de tumeric en français dafa bari tay ma wakhla noy def dangay dieul bout de papier nga accroché ko au dessus de ton fourneau et tu écris ngadam TUMERIC = CURCUMA nga nopalou niou nopalou 😂😍
5 лет назад+3
Aminata ba 😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣 non teyyy moomm dama retaann ba tass Masha Allah dinako defff
Tta Yétou dall béné xalé bou tou toudou Mariétou comme vous sa so wakhé goudouss goudouss mo kay dall heure boko wakhé mou top si té nane souma magué samma phone lay dieul tek ko sama cuisine di khol si iao di cuisiner
Salam aleykoum tata Marietou et la communauté si quelqu'un peut m'aider MachaAllah au top,jaimerai c'est avec quels matériels sur gaz que tu as fait tes grillades s'il vous plaît merci beaucoup tata
Lodge Pre-Seasoned Cast Iron Reversible Grill/Griddle With Handles, 20 Inch x 10.5 Inch - One tray www.amazon.com/dp/B00008GKDQ/ref=cm_sw_r_cp_api_glc_fabc_WAR4Fb01W5KD0
Salam aleykoum merci Tata Marietou MachaAllah
Miammmmm miammmmm Machala diaratina yone .l'AF thiat
Ahh machaalah tata sa ndougou rissss na😂tawarkala defati ngua bamou diap forme chéé bien 😍
Magnifique 🤗🤤😋
machallah merci pour cette nouvelle decouverte culinaire
Machaallah comme d'habitude. Longue vie
Waw keyyy merci bcp Tata li rek la beugue. Fi dal Koufi menoul togg yow la nekh ak mére goundouss goundoussi rek machallah.Ma sétani té gneuw
S. Diaw que
Mashallah j’aasadooore👍
Walaykoum salam ndaw machallah amna solo
Ma Sha Allah Tata Mariétou😘.
C vraiment un plaisir☺
Machalla machalla notre cordon bleu machalla 🙏
Maaaaachaaaaallahhhhh
Mashallah Tata yalla na lokho bi wér😍😍😍😍
Machalla matenga djek
Maimouna Ndao Ameen wayy
Merci tati Marietou fi ngama guené sakh khamoko ndakh damay ay gane dimanche té momla faciené tog incha Allah ché bien😘😘😘
Dieumb DIA Masha Allah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Macha allah si kaw si kanam maguette Fall depuis senegal
Machallah félicitations
Machahalla tata todiatigafi fi nena radiakh
Macha allah 👍👍👍
Machallah machallah
Merci tata dagnouy sétane en mm temps di diangalé anglais on est fière de toi 🥰👌
Laffati thiatt rek diam si yaw macha Allah
Machalah
Ma petite soeur elle a 10ans soumalay setann ell vient a côté de moi dafay retannnn beu sonou. Yallah nala Yallah fay Tata merci.
Hawa BA Ameen way bisoul mako
@ in sha Allah tata
Machala tata ya takh ma gueneu beugue togue
Machallah tata marietou taye mome delo ngama Maroc deuk nafi 4 ans avant maye gnew fi chaque vendredi mome ladone agnè
Sama plat préféré
19 ème encore thio damay aimé sétane nieuw commenté
Bjr tata, bravo pour sa couscous royal bi mè je trouve que sucre bi barèna torop et il y a tlmt de diabétiques au pays. Les pois chiches n'ont pas besoin d'être sucrés. Sinon cette recette est impeccable. Merci pour tes belles videos. Kiss
Ho li nekhna bilaye guoudou fane ak wer rek
Waw Mariétou youbou youba touy néko si reul la beuk ga traduire ba ko parceque dégouma wolof rires j adore
Gogo diop Ba 🙊🙊🙊🙊😂😂😂
Bravissima
Tata marietou saf na Machallah
ma cha allah sama togolokh bi sa couscous royale bakhna invite ma
Bonjour ya marietou vos plats sont extra et j'en apprends tjrs maa shaa ALLAH yallah na yallah laffal la thiat.....une question votre sauce ognions elle n'était pas trop sucrer?
nancy fall Ameen way ma Cherie no pas du tout juste tèm tèmi
Tata maretou rk si cuisine eupeuna Machallah
Macha ALLA tata namonala
Machalla machalla
Hello Madame,where can I get the Morrocan seasoning powder you mentioned in the video? You saix you will show it but,you did not a d what is the name. Thank you very much and stay blessed.
😂marietou temps yiii mon .. bayi ngua titeul akh nékothi rél légui THEU mo khéw???👏🏽👏🏽👍🏼🤣🤣🤣
Machalah Tata marietou aime sogua setane
Salam Tata mariétou merci pour les recettes mais cilantron ak paprika c'est la même chose walla merci de me répondre
Fatou Sow Waaleykum salaam ma Cherie merci non cilantro moy persil chinois en englais paprika moy feulfeulou Maroc bi merci
@ Merci ma daronne macha Allah lafe thiate et longue vie à vous
Merci Tata marietou j'aimerais aussi que vous faite salade de thon pour k je puisse aprendre la meilleure des sauce pour
Maymona Fall oui ma Cherie les salades de thon y’a en beaucoup il faut regardè les vidéos précédentes 😘😘😘😘😘
@ merci Tata marietou c gentille je vais voir😘
Wa tata sa couscous dothieu na beuguena yi dale sama toguologue
Oolalala nekh na merci tata
Ta marietou bii couscous môme ennnn
Merci pour vos vidéos,on se tape des barres avec vous,vous êtes fun.
Nyamatoss🤣🤣🤣
Bonjour tay plat oriental merci tata mais tata ail grill c quoi svp
Ta Marietou j'ai constaté que lingay faté le nom de tumeric en français dafa bari tay ma wakhla noy def dangay dieul bout de papier nga accroché ko au dessus de ton fourneau et tu écris ngadam TUMERIC = CURCUMA nga nopalou niou nopalou 😂😍
Aminata ba 😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣 non teyyy moomm dama retaann ba tass Masha Allah dinako defff
@ waw 1-0 cone 😂😂😂
Aminata ba yes 1-0 Masha Allah 😘😘😘❤️❤️❤️
😂😂😂
Salam wa saveurs planétaires lou ma Beugu toroooop mom cous cous doumathi doyal agn rér ndéki thx Ta mariétou
Khadidiatou CAMARA Waaleykum salaam ma Cherie merci Insha Allah dinala wo dama busy temps rek
Bjr tata au fait début vidéo yi dou ame son Walla si sama RUclips la
Amoul son
Ndione Lisoune non mako def nonou bougou mathi def music motakh merci
tata dal niakeu leu woroul
Non mane avec tata marietou togue rekk layy def.goudal fane rekk
Tta Yétou dall béné xalé bou tou toudou Mariétou comme vous sa so wakhé goudouss goudouss mo kay dall heure boko wakhé mou top si té nane souma magué samma phone lay dieul tek ko sama cuisine di khol si iao di cuisiner
Nom tata marietou ligua couscous royal miguifi teke seye khetou nokoss amoul
Merci tata Mariètou. Love you 😘
Machallah machallah merci tata mariétou
Tata cc
TATA maimou Machallah
Ziar mer maretou me waxji toubab dase Bari lol te sama Sanryi mom waloum toubab bi xamon si lou Bari te Dani beugue video yi gnongui diegalou nak