accusée d'adultère avec l'employe de son mari: les révélations de l'avocat de Mariama Diouldé Diallo

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 ноя 2024

Комментарии • 380

  • @juicevm93
    @juicevm93 2 года назад +62

    Mane vraimn j déteste ce métier 😢😢😢😢 nite buy fènn suffit nga degluko nga xamnè avocat bi ligueyeum leuy def moy défendre pas pr wax deug et malheureusement c sa notre vie.

    • @aminatadiagne6018
      @aminatadiagne6018 2 года назад

      Pape

    • @khadijaniang5521
      @khadijaniang5521 2 года назад +1

      Guisse nga yaw da nga dof boulko kheup avocat bi kheup ko couple bi ndax djeukeur nane lay sous d écoute diabaram en plus tu dit sa diabar lah tu le fais confiance yaw djiguéne mola diour ko dioural ay dôme ngakoy sous d écoute ki dafa Bone

    • @jackbueur4089
      @jackbueur4089 2 года назад +3

      @@khadijaniang5521 la confiance n'exclut pas le contrôle

    • @mamesodaniang3571
      @mamesodaniang3571 2 года назад

      @@khadijaniang5521 jiguene bu jouboul nak😏 on ne trahit pas son mari de la sorte

    • @elhadjimodoubeye3084
      @elhadjimodoubeye3084 2 года назад

      Mann kay magui beugue decourager

  • @khadijambaye6556
    @khadijambaye6556 2 года назад +17

    Tay mom gemou mala 🙄serigne mbacke la geum 👏👏👏👏👏

  • @papadiop6508
    @papadiop6508 2 года назад +96

    Clédor soit raisonable lou ame preuve ngay défendre Ragaléne YALLA way

    • @coumbandiaye6923
      @coumbandiaye6923 2 года назад +8

      Bilahi toi tu comprends. Moi c'est quelqu'un que j'admire beaucoup mais cette fois ci vraiment il n'est pas du tout à l'aise dans sa défense. Moi je suis des fois ses plaidoiries.

    • @miyandiaye2318
      @miyandiaye2318 2 года назад +4

      Mom kham nani limi wakh sakh dou deugue

    • @ndiemendiaye9979
      @ndiemendiaye9979 2 года назад +7

      Mom la wakh sank avocat dîna dugal bopam safara ndakh alal aduna

    • @laurentgomis7880
      @laurentgomis7880 2 года назад

      À cause DECE GENRE D'AVOCAT QUE LA PLANÈTE SOIT POURRI

    • @mamesodaniang3571
      @mamesodaniang3571 2 года назад +2

      Ligguéyu avocat tamite 😏

  • @mndoye702
    @mndoye702 2 года назад +28

    Je suis désolé téye .Cledor avocat sa wakhe dji dajiou woule deh

  • @aissataba764
    @aissataba764 2 года назад +85

    Mane dhh meunena sedeii si serigne mbacké mbeugoul sakhh diambour bou khiff waxoumala akk djabotamm. Mane son employé abonnement lama defalone mou settlou douma dem mouniima damala fayal si restaurant bii maniko mane souma dekeii douma meuna agne mounima nala outeul rendez vous si sama medcin. Yalla rekkk moma tim walakhiiii moussoul nangou niou khif xana mou fekkk niou bagneko yeug defois amna benn employé bou neko ben jour sama bopou daye meti mouniko demal djeulii agne soy agne di tané

    • @nafissatou29
      @nafissatou29 2 года назад +2

      Machallah

    • @thiamaskoucawaty6644
      @thiamaskoucawaty6644 2 года назад +2

      Donc diabar dji ha Sai Sai rek thé beugue kikiki

    • @ramcessediouf3224
      @ramcessediouf3224 2 года назад

      Machala

    • @morlam8705
      @morlam8705 2 года назад +6

      @@ramcessediouf3224 qd j'ai su que la femme est peulh j'ai clos le débat ! Nagnou ko gnouss lep moma !

    • @Ndiokarabdn3065
      @Ndiokarabdn3065 2 года назад

      Khaw ma wadji mai lerr nama ni wakh deugue nakh kanam Dou féne

  • @Onomar
    @Onomar 2 года назад +70

    Un homme qui a 4 enfants avec une femme l’accuse d’adultère sans preuve ou avec preuve pour moi fallait le quitter si tu as des doutes et penser aux enfants .
    Insbi deff nga wayy woudoul fayy moukk

    • @morlam8705
      @morlam8705 2 года назад +12

      Sa way nit kene douko torakhal surtout ko amel dom mais Me Sire ly xam nani ndawsi diouboul ! Am jeukeur di dem hotel ak gor ? Di yobou jus ak thiep laisse tomber way ! Une honte pour toutes les parties

    • @daoudamariko623
      @daoudamariko623 2 года назад +13

      Si elle avait pensé aux enfants, elle l’aurait pas trompé et elle l’aurait pas comploté contre son mari

    • @miyandiaye2318
      @miyandiaye2318 2 года назад +10

      Mane deih en tant que femme so khassé ba ame diekeur maytoul du fréquenté goor wakhatoumalak di deim hôtel

    • @laminedaffe1403
      @laminedaffe1403 2 года назад +8

      N'oublier pas aussi que ndawsi koumouy defal adultère etait le comptable du mari et ils sont détourné plus d'un milliard dans l'entreprise du mari

    • @ndiemendiaye9979
      @ndiemendiaye9979 2 года назад +1

      Nanu thi tey bu amul wone du ka wakh djiguene la me lunu niu wakhal niune la

  • @serignemodoundiaye8418
    @serignemodoundiaye8418 2 года назад +22

    Pere boul tax niou classei la fañu classei wadji diouff ish mak nga waaye ragalal yalla waaye

  • @diogeytv629
    @diogeytv629 2 года назад +13

    Maître cire cledore ly le Sénégal t'admire bcp mais cette fois si ta passé à côté et tu vas détruire ton image pour rien 💚💛❤️

  • @zeinabrassoulndiaye6782
    @zeinabrassoulndiaye6782 2 года назад +41

    Hôtel laniouy sedalé thiep si diabarou diambour niak diom arrêter ça svp deugu yallah moko mom

  • @hawakane3580
    @hawakane3580 2 года назад +40

    Hôtel si thiep vraiment maître tu es entrain d insulter notre intelligence

  • @lasalihate5927
    @lasalihate5927 2 года назад +13

    Sarakhou Thiéb si hôtel xalass 🙄

  • @maymounagueye7249
    @maymounagueye7249 2 года назад +17

    Dans quel pays sommes nous qui a tort qui a raison seul Dieu le sait

  • @cheikhsarr1026
    @cheikhsarr1026 2 года назад +27

    *🔴 père wakho deug dé 🤣*

  • @rahmandiaye589
    @rahmandiaye589 2 года назад +6

    Koula degulou khamni dangaye fene linga wakhe dara doussi degue ndawssi ndiouboule

  • @Alktar.0560
    @Alktar.0560 2 года назад +27

    Vis problèmes d'adulte yene la rekk mais khalate lene khaler yi Mane khaler yi rekk la yeureum Yallah n'a Yallah sam khaler yi

  • @khadiatoubarry950
    @khadiatoubarry950 2 года назад +14

    😂😂😂Tiktok am guén liguén liguén tiktok tiép si hôtel avocat mo men fénn

  • @aboubakrjeng3029
    @aboubakrjeng3029 2 года назад +14

    Ah maître sa kaddu Dale daloul sama khél Thiéb waroul tax Mouy guéne Keuram di dém ba hôtel si djiguén bouy seuy

  • @madeleinethiare2954
    @madeleinethiare2954 2 года назад +6

    Kou comprendre li maître di wakh namaci dimbali

  • @bayemarba2419
    @bayemarba2419 2 года назад +20

    😂😂😂😂😂 menace! Mais ki deugueur na fit mane dh bilahi dama tite si maitre bi dh Li alpha nane ragalal yalla maitre ragalal yalla😂😂😌😌

  • @yakhitv1226
    @yakhitv1226 2 года назад +16

    Vraiment c'est pas clair distribués thiép si coté hôtel amoul féne en plus vue leurs relations si proche le gars du distribués riz t'a menoul dieul déff si auto dém livrai ko femme bi donc incohérences

    • @abdoulayedieng3842
      @abdoulayedieng3842 2 года назад +3

      Doli ci Anna djigueen di envoyer goor gingembre te sekouleen dara ba naaan ko yako mom adultère lolou dafa nek ci deretou peulhou Guinéen kou léen tak tak guelou guars gni point

    • @mndoye702
      @mndoye702 2 года назад

      Wawww kaye nakk wakhe dji mougui nii nakk

    • @mndoye702
      @mndoye702 2 года назад +1

      Ma fôkk distribu thiépp kaye déme si wétti mosqué baa c'est mieux que sa wétti hôtel baa

  • @sonialareinedesandeus
    @sonialareinedesandeus 2 года назад +17

    Proclamer résultats? Métier journaliste daaaaanou na🤦‍♀️ dianguileine!

  • @ndiemendiaye9979
    @ndiemendiaye9979 2 года назад +15

    Metier yep done avocat mo thi yess ndakh defoi nga defendre nit thi lula mane dugal safara donte cas contraire amna thi osi

    • @khadijaniang5521
      @khadijaniang5521 2 года назад

      Ehh vas te faire chiez avocat yi gnéwouniou sa baye .yaw kome do djiguéne li djiguéne bouniou ko def sous d écoute lah ba paré yoboula si yone force Di nga wouyou dji ngir setal sa der

    • @lombredelarue
      @lombredelarue 2 года назад

      @@khadijaniang5521 wah nga deugu si sa argumentation mé mom ossi wahna deugu ....métier avocat mom c vraiment op ça...nga balma nakk hamnani gnéwougn sama baye..

    • @mamesodaniang3571
      @mamesodaniang3571 2 года назад

      Ndieme tu as bien dit. Des fois les avocats défendent l'indefendable

    • @Ndiokarabdn3065
      @Ndiokarabdn3065 2 года назад +1

      Ya taye deugue rek ngua wakh

    • @khadijaniang5521
      @khadijaniang5521 2 года назад

      @@lombredelarue yallah dafa sak teh yamalé wouniou .des fois on dit tout les garçons sont pareille ms amna ay exception
      Djiguéne gni aussi pareille et donc pareille pour les avocat ya des avocat honnête et malhonnête mais cet avocat il est honnête teh d'où lek Riba yallah mondjotou si liguéyame

  • @mohamedbechirsall3589
    @mohamedbechirsall3589 2 года назад +43

    Père c un bon avocat un bon menteur 🤥 😂😂

    • @miyandiaye2318
      @miyandiaye2318 2 года назад

      Dafay défendre cliente bi sama toma dafa wéré

  • @latgrandlatgrand5147
    @latgrandlatgrand5147 2 года назад +2

    adouna dou keur ! dèlo sènn khel si Yalla 🤔🤔🤔🤔🤔

  • @eubeuzeugaleriecouture6535
    @eubeuzeugaleriecouture6535 2 года назад +2

    mettre waxou avoca rék ga wakha

  • @maxndiongue259
    @maxndiongue259 2 года назад +7

    ayy waye djiguène dagnoukoye soutourale serigne mbacké

    • @farmaseckseck75
      @farmaseckseck75 2 года назад

      C vrai soutou reu dfa bax ms kouy niaaloo baniou diapp la yaa wérr sa bopp hum limou dff lépp kou am soutoureu douko dff

  • @diogeytv629
    @diogeytv629 2 года назад +4

    Maitre cett femme vas détruire ton image pour rien fallait pas avancer avec ce dossier car sénégal yeupp comprendre naniou 🌍🌍🌍

  • @bayemorsarr1071
    @bayemorsarr1071 2 года назад +25

    Même si c'était vrai fallait pas d 'arriver la une femme avec qui vous avez des enfants no le mec n' est pas gentlman

    • @laurentgomis7880
      @laurentgomis7880 2 года назад

      C'est quoi gentleman ?

    • @lamine1406
      @lamine1406 2 года назад

      @@laurentgomis7880 C est soutaral ko bayiko mou dem bou dé deygue leu té khol thi ndiabotam boudé la femme roussou thi dieukeureum

  • @aladjifalloudia4915
    @aladjifalloudia4915 2 года назад +2

    Djigune soupal taboul woulo serigne mbacke yalla nala Yalla takha wou

    • @dadocisse1034
      @dadocisse1034 2 года назад

      Goor tamite sopal té boul wolou yallah bouy dore goor mosiy eupelé nakh môme la khélame mate djiguén bou boné rek goor moko bonale . Parfois même ce son les hommes qui vous pousse à prendre une mauvaise chemin

  • @laplusbellendiaye1753
    @laplusbellendiaye1753 2 года назад +8

    Wa Kou amoul Lo doundé noye défaré jus di mayé

    • @mamesodaniang3571
      @mamesodaniang3571 2 года назад

      Moma diakhal 😏

    • @ndeyeantandiaye2419
      @ndeyeantandiaye2419 2 года назад

      Mais avocat yi moy dieul soulene télone dieul gnou plaider ba wadji diokh ay domame pension puisque amena khaliss.

  • @guerrierdelalumiere3195
    @guerrierdelalumiere3195 2 года назад +9

    Jdigén hkélam matoul soutouralko té yalla rék tahk, yalla fey laa

  • @fatim3043
    @fatim3043 2 года назад +3

    Métier avocat métina dehh...parfois tu es obligé de défendre des choses incroyables.

  • @Dulce-pm1ku
    @Dulce-pm1ku 2 года назад +1

    Son mari defna lou mingo woul ak aday senegal si koula dioureul 4 dom masha allah ngani dangakoy wér même boudone deug sax war nga xol si xalé yi té xamni way woudoul fay leu

    • @adamsdiallo9521
      @adamsdiallo9521 2 года назад +3

      Mais parfois ça devient compliqué dans notre pays " nga nèk si deugue gnou fènlola vilipendé la yakhela torokhalla bé paré danèlela .Tu auras deux choix seulement sinon tu laisse tout dans les mains de Dieu et attendre le jour du jugement et vivres avec les critiques sinon tu devient incontroble pour te défendre notre pays va mal 😭😭

    • @Dulce-pm1ku
      @Dulce-pm1ku 2 года назад

      @@adamsdiallo9521 tu as parfaitement raison mais parfois c mieux nga bayi lép si loxoy juge bu nak bi Allahou

  • @ibrahimalo6660
    @ibrahimalo6660 2 года назад +10

    Clé d’or. Sene mi nit la. Ahh khalas. Yi fene. You lerr.

  • @abdoulayeba5306
    @abdoulayeba5306 2 года назад +7

    Avocat bi niéméneu Yalla

  • @ameththiaw9270
    @ameththiaw9270 2 года назад +7

    Thiepe si hôtel wakhale 😂😂😂

  • @malicksene1066
    @malicksene1066 2 года назад +12

    Gnimé yalla bi ci yéna avocats yi yém nama

  • @ibnarabia4275
    @ibnarabia4275 2 года назад +4

    Waw thieb mom loumouy déf si hotel

  • @albertinesarr850
    @albertinesarr850 2 года назад +26

    Même si la femme elle n'est pas sérieux libérer là
    Sans pour autant tu la vilipende

    • @babefifiya6071
      @babefifiya6071 2 года назад +2

      Pourquoi la libérer avec tt ce kel l’a fait dafay yomb trop

    • @vitolesenegalais6540
      @vitolesenegalais6540 2 года назад

      C est pas si facile que ça avec des enfants,le problème de la garde des enfants et surtout d une éventuelle pension alimentaire a donner.
      C est des paramètres a prendre en considération , est-ce que le couple arrivera à trouver un terrain d entente.

  • @naturalmavista1917
    @naturalmavista1917 2 года назад +8

    Wooooy thiép ba hotel🤣🤣🤣

  • @moussagaye6290
    @moussagaye6290 2 года назад +1

    Elhadji Abdoul Sy wakhona ni 3 avocats yo djiss kena mothi deme aldiana soubhana la

  • @lapiraterie92i7
    @lapiraterie92i7 2 года назад +3

    Cledor séne mélo wonne ni dh maitre elaj diouf dala yakeuu Leigui

  • @damembow6374
    @damembow6374 2 года назад +11

    Arrête way waxofiii dara sunu xel yii nioko mom

  • @dina3804
    @dina3804 2 года назад +4

    Wouy jus ginger fin na nakk

  • @makeitreal6918
    @makeitreal6918 2 года назад +7

    N'importe quoi comment tu peux être marié si envoyé ay jus gingembre à un autre homme franchement Sénégal c le bordel

    • @FascinatingMya
      @FascinatingMya 2 года назад +2

      ah sa kharitou jeukeur menoko tibal johko jabaram

  • @mouhaba6225
    @mouhaba6225 2 года назад +6

    VRAIMENT AK LOU MEUNE TA HEW DIAROULE WONE DEME JUSTICE MEUNON NANIOU KO REGLER SEN BIRE TE KEN DOU YEGUE LI DEFA NIAWE

  • @ndiayendiaye313
    @ndiayendiaye313 2 года назад +9

    Thiay yalla khalatal yalla Thie lingay wakh

  • @mouhamadoudiallo9688
    @mouhamadoudiallo9688 2 года назад +2

    Ioe douma xaar sakh ba vidéo bi diékh legui lay supprimé sa numéro. Eiy bayyiléne xél bammél

  • @LaBarhamienne
    @LaBarhamienne 2 года назад +1

    Une femme peut pardonner l'infidélité de son mari, mais l' homme ne partage pas sa femme. Soudone djiguéne meune nako baal mais goor meunoul supporté lolou.
    Wadji faténa neu euleuk ay domam laniouy xass yalla bouniou done ay djiguéne nak, wooy wi dotoul fay ba mouk même si daniouko togn.
    Tieuy, yalla naniou ya allah bolé ak kiy guene thi nioune mousseul niou té moutieul niou🙏

    • @elhadjimodoubeye3084
      @elhadjimodoubeye3084 2 года назад

      La femme n’a pas pensé a ses enfants
      L’homme a le droit d’épouser jusqu’a 4 femmes mais la femme n’a pas ce droit barhamienne tmt
      Bo degue lo Dieukeur djii digua hame li hew
      Au fond il est détruit à l’intérieur et la femme n’a aucunr honte

  • @khoureyeanne558
    @khoureyeanne558 2 года назад +1

    Mais clador ment doucement walahii nek fii avocat si senegal moy yobou sa bopuu safara yaw lernala nii k liguay wax amoul thieeee

  • @abdoulayedieng3842
    @abdoulayedieng3842 2 года назад +7

    Avocat ligueye geuno ko boon d'égal rék borom bediaw bi di feen

  • @ndayemareme743
    @ndayemareme743 2 года назад +3

    Mousouma guiss kou meuna féne ba melni maître c'est honteux bilahi

  • @bambandao4733
    @bambandao4733 2 года назад +4

    Vraiment wakh bi môme doy you ma

  • @babacarfaye4101
    @babacarfaye4101 2 года назад +1

    Le défenseur de sonko et compagnie 😅😅, on a plus confiance en toi..

  • @saliouloum2112
    @saliouloum2112 2 года назад +6

    Yaw môme wede nala dagaye fene yalla moye ateh kat Bou makbi

  • @diorthiam9450
    @diorthiam9450 2 года назад +4

    Fène rkk pour sa cliente am deug

  • @mamignimadieme3581
    @mamignimadieme3581 2 года назад +11

    Hôtel ak thiéb parégou ma ngaye wakh, wakhou gingembre si diabarou diambour jugé ouma nak dama fi diarone dongue

  • @la_force_tranquille7260
    @la_force_tranquille7260 2 года назад +1

    Thieuy avocat😱😳kii dou Clédore?

  • @thiamaskoucawaty6644
    @thiamaskoucawaty6644 2 года назад +6

    Avocat 🥑 ki ment comme il respire c'est au Sénégal qu'on trouve ça ragualal Yalla svp

    • @morlam8705
      @morlam8705 2 года назад

      No c pas juste au Sénégal l'avocat défend tjrs son client par tous les moyens ! Mais nit yi xam nagnou lou yenou mana mais le juge cherche des preuves pas des indices ! Il peut même donner tord au mari s'il n'a de preuves qui ne font pas l'ombre d'un doute même si dans sa tête il croit que la femme trompait le mari ...mais tjrs les peulhs c fou vraiment moi je vais jamais marier une peulh j'ai déjà été victime juste étant fiancée !

    • @ourayegueye3611
      @ourayegueye3611 2 года назад

      @@morlam8705 😂😂😂loula peuls yi deif

    • @morlam8705
      @morlam8705 2 года назад +1

      @@ourayegueye3611 c com une maladie chez elles ! Je jure que j'ai pas de la haine envers eux mais damalene yeureum! Peut être febar le aussi mais moi je les fuis com la peste 😅limey dieuk khol legui c le mom de famille qd je drague une fille et si j'ai doute je dis tu es wolof ou serere tu me réponds peulh mani la meyma ma wouyou téléphone, daw dem

    • @ourayegueye3611
      @ourayegueye3611 2 года назад +1

      @@morlam8705 mingui niaw dei😂wayé nak niep yémouniu dfoi nga guissi niou régler .certe mom Lolou baké nagn len ko
      Wayé tegoumassi sama beutt d’après lima degg souniu amé dieukeur après loulén nékh laniouy deif

    • @morlam8705
      @morlam8705 2 года назад +1

      @@ourayegueye3611 en tout cas moi je veux plus essayer gnou bakh ak gnou bonne sama yone nekoussi y'a des trucs on me le fait qu'une fois ...

  • @abdouthiam8234
    @abdouthiam8234 2 года назад

    vraiment maître cledor je souhaite k sonko exclut de son pôle avocats car ki auge défendre cette femme comploteur

  • @lalagueye5887
    @lalagueye5887 2 года назад

    Ayway Sénégal kou kham rabam gnou toural ko ame ak nit ay dom toumalko dialo kone kou diour khalayi ana divorcé

  • @mbayangendao653
    @mbayangendao653 2 года назад

    Mane yalla nama yalla mousale si dome bou nék avocate

  • @zeinabrassoulndiaye6782
    @zeinabrassoulndiaye6782 2 года назад +6

    Maître y’a meun doule wallahi euleuk yomal khiyam dina meti trop

  • @annagueye7228
    @annagueye7228 2 года назад +2

    Sarakhou thieb si hôtel maître ya menue doul ragalal yalla nakk

  • @mbayediaw7950
    @mbayediaw7950 2 года назад +1

    Avocat bi limouy wakkh leroul dhé

  • @Leadersvideo403
    @Leadersvideo403 2 года назад

    Kouy yelwane noumouy feyer avocat juste une question rekk

  • @assanemikaelfaye5651
    @assanemikaelfaye5651 2 года назад

    Yalla naniou Yalla mousdeul si am doom avocat

  • @mndoye702
    @mndoye702 2 года назад +3

    Avocat moye métier bou graawe .c'est normal tes paroles c'est pour défendre votre client kaaye

  • @adjiseck9104
    @adjiseck9104 2 года назад +4

    Borome thiep bi dafone Chantage wala. Amoul foumoko wara mena diohe foudel cote hotel. Teye na hele.

  • @LaCultureAfricain
    @LaCultureAfricain 2 года назад +3

    Thièp ba hotel louss na

  • @oukhty9016
    @oukhty9016 2 года назад

    Demleen seetaan dossier bi khalaat tv def ci cas bi mais MG a raison un honnête travailleur gnou arnaqué alalam mettina

  • @laminethiongane3679
    @laminethiongane3679 2 года назад +1

    Cledor magu djeguelou dh me wahofi touss srx🙏

  • @adiaratousodambaye8551
    @adiaratousodambaye8551 2 года назад

    Jus djinguer tamite amnsassi wa bakhna thiey avocat yi😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @yetou1453
    @yetou1453 2 года назад +3

    Ki mome dou défarou 😡

  • @lasalihatediene6400
    @lasalihatediene6400 2 года назад

    Mane dh version diekeur dji la guem avocat bi wakhoufi touss

  • @babacarba4273
    @babacarba4273 2 года назад

    merci cledor

  • @papathiam87
    @papathiam87 2 года назад

    Mrs Cledor pensons notre 1er nuit de bamel

  • @mamethiernondiaye9466
    @mamethiernondiaye9466 2 года назад

    Dossier 📁 bi waroko wone dieul danou gua ba diakhane

  • @walyfaye636
    @walyfaye636 2 года назад

    Mé je me pose la question esk avocat guémena yalla aussi Dina khalatt dé amna

  • @damembow6374
    @damembow6374 2 года назад +8

    Nourou woma kouyy wax deug gua balma

  • @cheikhdiop5936
    @cheikhdiop5936 2 года назад +6

    Baneu djiguéne moy nangou ça moromou djiguene dii Diokh dinediere ça diekeur té khamou Loko même boko khamé sakh ak fii reew mii toleu

  • @moriciss6368
    @moriciss6368 2 года назад +6

    Dama khamni diape sa Sonkhna diko wére kome kou amoule aye dome ak mome

    • @maodoba4704
      @maodoba4704 2 года назад +1

      Surtout 4 enfants

    • @sant9021
      @sant9021 2 года назад +1

      Wadjii sonal na femme bi tropp

  • @abijoubayrdiop7885
    @abijoubayrdiop7885 2 года назад

    iow di nga défendre kouy yélwane vraiment maître tu insultes notre conscience 😅😅

  • @fatimasall5467
    @fatimasall5467 2 года назад +3

    Bravo Avoca,bravo Mousieur le juge, la femme est noble, vive la femme

  • @couradiouf339
    @couradiouf339 2 года назад

    Maitre sama khèl nangouwoul ligua wakh

  • @kebendeyeawa7565
    @kebendeyeawa7565 2 года назад

    Mag bouy fén nakh allal té yagui thi sa bountou bamel yalla nako yalla até ak yen

  • @lalionnenoire7371
    @lalionnenoire7371 2 года назад +1

    Wa pabi nitt la li môme vraiment lerna ragalene yalla

  • @ndiobitafaye3458
    @ndiobitafaye3458 2 года назад +1

    Nékeu avocat métier bou boneu leu

  • @khadijawane2073
    @khadijawane2073 2 года назад +3

    Fi rewmi toleuh louniou truqué nekhna kham
    Mani arretei gueum leine maître khamé wougn lani li ngay wakh nekhoul deugu

  • @dioufmamadou7656
    @dioufmamadou7656 2 года назад +1

    Yangui déglou discussion bi fala yém 😅😅

  • @coumbagueye1675
    @coumbagueye1675 2 года назад

    Kouy oute ndimbeul dineleu dieul avocat yaw nga khamné tu es l'avocat des milliardaires

  • @ndeyedieye6598
    @ndeyedieye6598 2 года назад +4

    Soma diegue wone bama wate la 😂😂😂😂 maitre ya gnemai yalla d

    • @nathaliemane9507
      @nathaliemane9507 2 года назад

      C très dure pour l'homme mais ta vie privée est sacré et surtout pense à tes enfants

  • @lombredelarue
    @lombredelarue 2 года назад

    Alaboni métier d'avocat

  • @cadiortvgueye8945
    @cadiortvgueye8945 2 года назад +4

    Linga wakh djouboul de

  • @bintousarr4730
    @bintousarr4730 2 года назад

    S'il ne veut plus de sa femme il n'a qu'à prendre son courage à deux mains et prendre ces enfants et leurs maman en charge ce qu'il veut éviter et fabrique de fausse preuves

  • @dembadiakhate4330
    @dembadiakhate4330 2 года назад +1

    Père yangui doul dh ragalale Yalla way

  • @Allah12.99
    @Allah12.99 2 года назад

    Hiii les avocats 😳 yallah dh kumata bayi xella

  • @bitahimfall5661
    @bitahimfall5661 2 года назад

    Khawma serigne Mback khawma ndaw ci mé ak woor amnasi

  • @importation-eh9gv
    @importation-eh9gv 2 года назад

    Soutoural ko akh noumou meunti dème boul hasslou sey dom euleuk yalla rete ham.

  • @fatouka6462
    @fatouka6462 2 года назад

    Thièp si hotèl kay 😄 je dis rien sama yone si aye fène.