MERCI COATCH AY DEGUE REC NGAFI WAKH DEGUE DANOUKAY ÑIEME COULPA YEP ÑIE YOR WALOU FOOTBAL BI ÑIOKA WARAL DOUNOU SAX ROUS 13 ANS DEFOUNIFI DARA LO BAX SI FOOTBALOU SENEGAL DOUNOU SAX GOOR AVAN ÑIOU LEN DON WAKH DEMLEN SILANOU WARA KHAM SEN BOOP THE DEM ÑIACK DIOM FEDERATION DEMISION
yalnala yalla defal diamm yalla same la ya meune wakh deug finak sènègal kouye wakh deug laniuy bagne nafeck yi lègui niu commencè ko takal wala niu crèèyel ko problem bène fène kate doula beug nala lèèrnè yalla ngui andak yaw boul tite boul ragal
Sénégal boy wakh avant dagne nane politicien la mais après gnounane wakhone nako même borom kham kham balagnou ko nagoul mo dèè mètcin après là mort ah Rip
Si la jeunesse sénégalaise n'a pas d'arrêtée d'utiliser la drogue,et des dirigeants irresponsables incompétents un jour viendra il y aura des pires catastrophes
yawdeh amnga ngor guissnga liii guelewar wakhone rek gnunegni nekk bittimreew kersa ak rousse diapnagnou diaratugnudara fignounek. melni ayy terroriste parentsyi warenagnou eduquer khaleyi amougnou bene education wakhaldeh durigeantsyi mbele mbele rek sene aydomm dewugnusi motakh gouvernementbi yeup gnowara demissionner maygnoudiam bilahi lingawakh deugleu l education est importante gnungnunekk bittim reew khamnagnusidara nakhteh fugnudem gnounawgnou respecter gnou on garde nos valeurs. la jeunesse senegalaise souffre dehh walahi mn pays va mal fatenagnou lagnudone montre moi ta jeunesse et je vais te montrer l avenir d tn pays. lholal WA casamance fair play mofa ame et pourtant nous les dakarois on les appel rebelle rectification c nous les rebelles k nos morts reposent en paix👏👏
Enfin, un wakhkatou deug biir SENEGAL!!!!!!!!!!!
MERCI COATCH AY DEGUE REC NGAFI WAKH DEGUE DANOUKAY ÑIEME COULPA YEP ÑIE YOR WALOU FOOTBAL BI ÑIOKA WARAL DOUNOU SAX ROUS 13 ANS DEFOUNIFI DARA LO BAX SI FOOTBALOU SENEGAL DOUNOU SAX GOOR AVAN ÑIOU LEN DON WAKH DEMLEN SILANOU WARA KHAM SEN BOOP THE DEM ÑIACK DIOM FEDERATION DEMISION
Machallah bilae deug rk moy moudie gomiss walahi danga nièmei deug bon continuation yalla nala fi yalla bayii '' sénégalais ngourr rk
Ohooo meussouma guiss kou gnamé ni deugue felicitation way coatch gomis sa wakh rafetna machala
Mrs G omis , sincèrement tu es franc .Que le Tout Puissant te Guide...merci encore une fois merci
Tu as tres bien dit. Merci
Je vous kiffe M Gomis . Vous avez raison sur toute la ligne
yalnala yalla defal diamm yalla same la ya meune wakh deug finak sènègal kouye wakh deug laniuy bagne nafeck yi lègui niu commencè ko takal wala niu crèèyel ko problem bène fène kate doula beug nala lèèrnè yalla ngui andak yaw boul tite boul ragal
Tey nag guisatina ku nieme deug.
Gomis yalla nala yalla fey ci courage bi nga am.
Yalla nala yalla musal ci say noon.
Bien di chiekhe la virite rien que la verite.et merci
Dieureudieuf deugeu rekk nga wax
je conseille de l ecoute car il est tres previsible
Ya Bakh te gore diam rekkk guay ame yallah nala yallah are
waaw grand cheikh li motah ma beug la vraiment c'est désolant.
franchement tu as dit toute la vérité .
waY team coach manifesteiii vous waY
Coach, tu es vraiment véridique. ....
Il a belle et bien raison limou wakh yeup c'est très cohérent
Merci Gomis
merci g cheikh walhi degue rek
vraiment tu as parfaitement raison
le procureur devait écouter ça
pas de négociation Augustin et consorts ts en prison
Bonne continuation coach
merci grand degg rek mo wore
wadji il merite d'etre le ministre de l'sport senegalais
Catia Scurti
Catia Scurti yaw ko yapp
Catia Scurti sama khalate nga wakhe
merci chiekh tidiane
thank you ceikh tidian you talking true
trop fort ce mr
tremblement de terre mo warra am ouakam punition total
Mame Fatou Diagne tu ya parfaitement raison.srx sw très révolté très ho ho honteux.on dirai des cannibales
hahaha mdrrr boul wakh lolou waye bayilène ak yalla rek dinalène atek niom
Je confirme ils dit que la vétité
vérité absolue
waw yaw dé gnimé nga deugu mom li nga fi wakh yeup deugueuleu vraiment
ndeye mandione vraiment Li mom dafa doyna warrr si Senegalese 😂😂
ndeye mandione kii dafa kham liouye wakh walahi
ndeye mandione deug bou werr
vérité absolue k des lâches
farma kote 😍😍😍💋👊👊
Machalla tidiane
bien dit tonton
c'est ça la vérité pour ce lui qui veut l'entendre et celui qui ne veut pas l'entendre, dans la vie il faut avoir le courage de le dire .
Merci
merci gomis
TONTON YAYE GOOR PIRE YAYE NITOU YALLA YA NIEME DEUGUE YALLA NALA YALLA ARRE
nagnoula faal poste bou fort thi wallou sport tu le mérites ndakh sa expérience thi sport kéén douko lam lammé...
il mérite d'être le président de la république. .. vérité pur et dur
Bilahi aye deugue rk nga wakh mais fii Sénégal koufi wax deugue gnou crééle la wayé ioe yalla nala same
ولله احبك ياشيخ تجان
kii rek moy nitou deug nak ,,
Sénégal boy wakh avant dagne nane politicien la mais après gnounane wakhone nako même borom kham kham balagnou ko nagoul mo dèè mètcin après là mort ah Rip
Bravo bravo bravo
tu a raison môme il niaw na trope
wouii les dirigeants quiter notre federation guir yalla sa fait bcp temps kon vous demande de quitter .yene lane la
il a bien parlé et il connait le milieu
koulillh akk walah kalhh ak deugueeee riekkk!!
Si la jeunesse sénégalaise n'a pas d'arrêtée d'utiliser la drogue,et des dirigeants irresponsables incompétents un jour viendra il y aura des pires catastrophes
ch m faye merci 🖒 drogue et irresponsabilités st la cause de ce drame snais pas prevenant du touy
wakh nga deugeu Sénégal daniy fowe bakan doun def dara fen rek ak nafekhe li dafa yeme
Ya niémé deugu dé Coach. Ayy souma amone pouvoir yow lay déf ministre des sports
Ndeye Talibé Khalifa Ababacar Sy yovite sopnala nah ligua done talibe serigne babacar svp woma 00221763943069
WALAHI deugatina deug
Bilahi Walahi
Beug nala dh nitt day gnimé deugg
Bilae ya des Nafēk wahall dhè
c vrai coach
niomme nieuppe waara démissionné
Bilahi wakh nga deug ! ZONOX
bilay degue dou romb ay nop wakh degue dafa bakh loll tè bokoy def boul ragal koula mèrè
Senegal cote divoire senegalais kay mo nagouwoule defete
goudeul fane
rafette na machalah
wallaye gomis deugeu rek nga wakhe yaw rek ya takhe mé sétane petitdej
dafa kham limouy wakh baparè meune ko
Ah vraiment deug mo nekh
Ô Métina tu as dit que la vérité
C mr la a parfaitement raison
SAMBA NDIAYE wahal de bilahi
vrmaint ligua wakh moy deugue
Really gnémei nga deug
douma si débat car l'affaire est devant le procureur
Vraiment linga wakh lepou deugeu leu, yaw rek ya war di wakh
bilay wakhatiko kéne amatoul yar ak téguine
trop de privilege pour demissionner!!!
wakh degue yallah doulathi ray
Diadief waay
Wadji ak roulé "R" bi😂
papico pourtant c naturel en lui d
.
deugue rek nga wakh
Nn ki mom lou lerr rek lay wakh bilahi kou am li mouy wakh la begu nala d grand
Billahi yage nama wax gomis moy journaliste sportif bi gaba xarange ci senegal man doma waxanto jamais
kii aka matta bayyi xéll diambar la
Très véridique.
Nice deug rek moy deug
yawdeh amnga ngor guissnga liii guelewar wakhone rek gnunegni nekk bittimreew kersa ak rousse diapnagnou diaratugnudara fignounek. melni ayy terroriste parentsyi warenagnou eduquer khaleyi amougnou bene education wakhaldeh durigeantsyi mbele mbele rek sene aydomm dewugnusi motakh gouvernementbi yeup gnowara demissionner maygnoudiam bilahi lingawakh deugleu l education est importante gnungnunekk bittim reew khamnagnusidara nakhteh fugnudem gnounawgnou respecter gnou on garde nos valeurs. la jeunesse senegalaise souffre dehh walahi mn pays va mal fatenagnou lagnudone montre moi ta jeunesse et je vais te montrer l avenir d tn pays. lholal WA casamance fair play mofa ame et pourtant nous les dakarois on les appel rebelle rectification c nous les rebelles k nos morts reposent en paix👏👏
Deugg rek ngafi wakh il ya eu mort dhomm donc on dw les susprendr a vi il n merite plu d competir a bas uso ouakaw chimmm
C djibril Wase qui a saboté la finale
vérité absolu uso sont animaux on doit les sanctions severema tolérance zero c honteux
deug rek gua wakh nekh nakhari deug rek
Deugue nekhoule
degue rék
Tu as dormi il fallait voir Almakhtoum
mane mala beugeul sama bop bilahy deugeuh nala rey deh...wanteh tamite moytoul supporter USO yi attaquer la wasalam
deugue rec
nagne kate senn ndaye a vie
Merci gomis