Leineu rek la d'accord si fadam thi loumou wax yup . Moy bouniou défé face to face ba nopiii lamb toukiiiii. Sinon lingua fi wax yup comprendre naniou défé na dangua farrrr ndax do dioxxxx Ama leip di mettre en garde franc . Ndax adversaires youniou am yup douniou Beineu walay
Ki diaroul tontou daniouy gueuna dougal franc si combat bi rek . Meuna touniou wax li diaxal wa parcelle si lamb ndax Modou lo defnalein Lou neik. Lesss waxoul yalla nopina
Sa n’a pas d’importance khamna lamb ..ya ngui deglou ay herve mathou pierre menez mourinho meussugn football lougn wakh cii footbball nga gueum arreter d’être des complexes
incha'Allah yalla nanioukô féké talko Ama baldé yalla nkô yalla maï ndam incha'Allah si niarry combat yup incha'Allah 🌴
Amine inchallah
Amine yarabi ❤❤
Ama Baldé yalla nako yalla may ndam yarabi ❤❤
Ama Yalla nala yalla maye Ndam inchalah
Modou Lo yalnako yalla maye ndame modou Lo yalnako yalla maye ndame 100% parchele kasse ❤❤👑👑✌🏻✌🏻
Fadam soy wakh si ama sama khôl Day sedd je t'adore
Dieulen Lepp diokh ama ba bisba inchallah
Ama baldé rék ❤❤❤❤❤
Franc yalla nako yalla may ndam inchallah 🤲
Ama balde francs c sera le combat de l annee
Vrais
Franc Ndam reke inchallah 🙏
Inchalaj man malick badiane may don revelación Senegal si mma ak lutte avec freap
Inchallah Sérieux beaucoup de travail on t attend digué Boor la
Fadam nena peace and love 😂😂😂 thiey fadam😂😂
Super franky 💪🏾💪🏾💪🏾
Leineu rek la d'accord si fadam thi loumou wax yup . Moy bouniou défé face to face ba nopiii lamb toukiiiii. Sinon lingua fi wax yup comprendre naniou défé na dangua farrrr ndax do dioxxxx Ama leip di mettre en garde franc . Ndax adversaires youniou am yup douniou Beineu walay
Ndiago mo meune mo eupeu doolé ❤️👌
Ki parfois louko nekh lay wakh
Fran mn guene parè Ama balde
Fadam meunoul wakh exclusivités 😂
Moytoul ma mbeur bouy wakh diokhma diwww balla tapha tine révélation leuh dh
Damay ragal franc dieul coup lambam yakhou ndakh ama khekh katla mais franc df am dolè ❤
Ama baldé dakkoul khekh franc…franc mbapatt bi la favoriser motah gars yi guissou niou khekh bi mais remise yi mouy def rek nga khamni meun na nekh
@lem475frznc nak Ama balde moko dakk xekh fouff
Ama mon âme combat fadam
Thiey fadame ioe isque ya dake pakola 😂😂
😂😂😂😂
Fadame taye wakho deugue
Dane poutine AK t.y 2 AK sokh AK Forza AK b52 nganane 50/100 yawite kholale lingaye wakh
Ki diaroul tontou daniouy gueuna dougal franc si combat bi rek .
Meuna touniou wax li diaxal wa parcelle si lamb ndax Modou lo defnalein Lou neik.
Lesss waxoul yalla nopina
Fadame Khana ama balde la faral
❤❤❤❤❤
Peule bi rk inechalla
Fadam 😂😂y’a dak Pokola 😂😂😂
Ama vs siteu moy combat en moi de août normalement
Bg2 vs mousa doy
Bilay kii komm kouy wax thi dinné bouy wax thi lamb😂😂
Té khamoul dara nak 😂
@@AlyYoro mo xam dara nak sa way fadame nimou xamè lamb kène xamèwouko la
Ama kassé
Fran bou amé loumouye bayi khélle thi Ama Manena bayi beuré
tay di😂😂😂😂
Franc na xamni ama dou tiaxané combat bi
Franc tamite dou thiakhané lamb
Jamais
Ala dakoy Daan inshallah
Yaw bayino fadam faranc moi mén foff ama balde billhay wallhy
😂😂😂❤
Il a eu combien de victoire dans l'arène 😂😂😂
Sa n’a pas d’importance khamna lamb ..ya ngui deglou ay herve mathou pierre menez mourinho meussugn football lougn wakh cii footbball nga gueum arreter d’être des complexes
franc ama mo meune sakh sa papa modou lo bamouye beurék mome rek nélawoul
Modou lo mo meune séni baaye yéne ñeup nguay doul fii. Amoléne ndaye diom sakh
Fadam dalal 😂 franc mo mann fouki ama balde
Lambe amoule d'onde liguéye rk moulaye Faye
France kassé
Many louy nawa nékha sani