Gnan na yalla réussir sama djangu bi bama am haliss walahi dinalen diapale ak gni nek si prison yi gnou diaplen té defougnou dara in sha Allah souma tekkiwe nalen diapale mogui sama khel nak yaggna
10:10 😅il est incroyable .. on dirait qu'il ne voit que reussir à l'Espagne..mais on peut réussir ici . Personne n'a réussi en dormant. Tout les hommes d'affaires ici ont tout vécu dans senegal pour réussir.
Je vis en espagne et j'ai envie de faire et dire quelque chose a tous mes freres senegalais . Leur expliquer la realité ( moi je suis venue ici par mariage ) Mais espagne metina , chomage bi metina ,beurina . Espagne nitt meunou fé amati alal . Ma fille me dit fais des photos des conditions de vie des senegalais et tu les publies sur les reseaux socios. Ils sont entrain de chercher du fer dans les poubelles , pour revendre le fer . Ils n'ont pas ou dormir. Et pour les papiers n'en parlons pas . Mon coeur saigne 😭😭😭😭
@@azizndongo7238 niom gni nieupp ay tek katou khél laniou 20 laniouyy nék si galguii dii roubé deff le tout ba lékk bii gawa diekh weur marro bi Bamou nékh léne dioubali Mauritanie après Di gueum lo gayii ay deumm yéwoulene Limay wakhnii fou lere lakoo tékk
Mom dé nenna kisi guinaw "nopil" quand on leur a demandé combien ils étaient dans la pirogue😹😹 Chers jeunes, rien ne vaut le sacrifice de partir en pirogues, j'espère fortement que les autorités vont trouver de meilleures soutions pour éclairer le bout du tunnel🙏🏽
Courage frere actuellement ni j suis en spagn ni après magal la départ St. Louis la déparé Yonne Bou nekh machalla instan bi gnongi si centre bi gnanal léne gnou ame nagn fi deux semaine🥳🙏🏾🙏🏾😭🙏🏾
Thiey yalla 300 000 f yoyou wala 600000 yii soumako yorone ba ba acheté gnari 2 roue di deff thiakk thiakk douma wakh dara resté ici si tu veut voyagé ngua defar sa passeport gnane visa mo guene fouf
Ay way li métina ken kou nekk say wadiour mola takha diougue wayé khalat len gni thi guene adouna nakala laniouy térélé sen yaye yalna yalla samm len inchalah mn pays va mal
Sen-tnt, une application qui vous permet de regarder les chaînes nationales et matchs des championnats européens depuis votre smartphone. disponible sur play store
On voit que gal yi ap surcharge bou metti. Ils sont mal préparés Et mal approvisionné en nourriture. Il fautt prendre des mesures c’est trop. Gueuj wooroul kw.cest hyper dangereux ça. Je pense bou yaaguè daay halluciné
Je vous conseille de venir a Mbour pour avoir les meilleures version sur l'immigration. Vous faites des interview sur l'immigration dans des villes où ya meme pas de mer.
Lo si wakh am lo bayi man mi si galyis la diar 9 jours déf nañou ko si guéji gui dokhou safara lañou don moudié di nan wala dokhou guéji 😪😪nit dé ni sa kanam ñou dieul sanni birr guéji Mé nak insbi alhamdulila ñogui Sant bu bakh nak 23 November 2017 doumako masa faté🇪🇸🇪🇸
300000 ou 600000 sur 316 volontaire c colossal comme somme c vraiment énorme on p faire bcp d choses avec c cet montant et les convoyeur sont seuls gagnant à l'arrivée mais bon c dommages et très triste
Yalna léne yalla yombal nieuw Europe bene yone si barke rassoulilahi sws
Amine Saws🙏🙏🙏
Benen yoon? Aka gaal yi?
Gnan na yalla réussir sama djangu bi bama am haliss walahi dinalen diapale ak gni nek si prison yi gnou diaplen té defougnou dara in sha Allah souma tekkiwe nalen diapale mogui sama khel nak yaggna
Yalla na yalla motali
Yalla na yalla motali sa yéné amine
Niom meunanio tekki avant toi
@@criska907 amine
@@mariendiaye3286 amine
Ce gas il est intelligent
frere boulla yalla fayé sa xoll do sone diam rék gaye âme bn chance frère Dina bakh
Dou kii modonn dédicaces abba no stress 😂😂 da moudié délouci 😂😂
C'est trop triste bilay.vous êtes des vrais guerriers.que ya Allah vous bénisse et vous aide à trouver les meilleures conditions de vie amen
Ce gars est un professionnel
Vraiment comment faire j’aimerais être présidente pour aider les jeunes c’est triste vraiment
10:10 😅il est incroyable .. on dirait qu'il ne voit que reussir à l'Espagne..mais on peut réussir ici . Personne n'a réussi en dormant. Tout les hommes d'affaires ici ont tout vécu dans senegal pour réussir.
Boulèn gnou sonal kèn kheuyoul am ay milliards mom wakh djou yakhou la !!! Fii daw dépense mofi am kou guiss lénèn dém fa
@@methaniane6220 dem espagne diamono dji ak lifay xew yeup esk khel leu?
Yalla n'a gnou Yalla doli soutoura 🙏🙏🙏
Là je vois du professionalisme il est tres fort ce journaliste....
Par contre il devrait s'asseoir comme un homme. Sa façon de s'asseoir est trop féminine..
Sheut gars yi ay gor yalla deug l'an kholal m'a li rek sheutt, li lepp pour réussit 😔😔🙏🏾🙏🏾🙏🏾🇸🇳
Je vis en espagne et j'ai envie de faire et dire quelque chose a tous mes freres senegalais .
Leur expliquer la realité ( moi je suis venue ici par mariage )
Mais espagne metina , chomage bi metina ,beurina .
Espagne nitt meunou fé amati alal .
Ma fille me dit fais des photos des conditions de vie des senegalais et tu les publies sur les reseaux socios.
Ils sont entrain de chercher du fer dans les poubelles , pour revendre le fer .
Ils n'ont pas ou dormir.
Et pour les papiers n'en parlons pas .
Mon coeur saigne 😭😭😭😭
C’est vrai dh Espagne mom amatoule Dara diaroul ray sa bop
Bly maNe magui Madrid mei espagne mety neuh trop Bly wly
Yaw gnibisii
Yaw nieuweul tokk fii seuy fii
Salam ma sœur ne te fatigue pas il ne vont pas te croire c’est la même chose en France mais que faire ?????
Ibra ndiaye yallna yalla gena doully sotoura ba diame âme me youmboull de 😭😭😭😭🙏🙏🙏
Ndeysaan
Wa li khana galou gueweul leu won🤣🤣🤣🤣mais ce gars est tres intelligent machala utilise ton cerveau dina bah inchala meme boudul ci gal gui
😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
Setanal té bayi commentaire yi😏
Féhéko rek yaw🙄
Mai boy 👦 Bou rasta bi khife nga de
Insbii mole yiii nioy tékk deal gayiii encaissé gayiii weurrr marroo Bamou nékh léne né naniou dellou bouniou nieuwé patioooo yéwouléne insbii guédj guiii Amoul dieune motakh niouy tékk khéll gayiiii
Lou leire nga wakh
@@azizndongo7238 niom gni nieupp ay tek katou khél laniou 20 laniouyy nék si galguii dii roubé deff le tout ba lékk bii gawa diekh weur marro bi Bamou nékh léne dioubali Mauritanie après Di gueum lo gayii ay deumm yéwoulene Limay wakhnii fou lere lakoo tékk
Ah bon
Lingay waakh nii lou manna nek leu. Khalatoum mako woneu saakh. Doyna Aar
Max luler ga wah
Rouss lo nako dh , néna ko nopil😂😂
😂😂😂😂😂😂lolou raynama
Bilahi lolou ladone khôl si commentaire yi 😂😂😂
Mome moko lath ba parrè neko nopil
Loumi wakh wa kogn ba😂😂😂
Nopil
Digui siratt louko fi diar mè courage sa ira inchallah
Ndeysan li metina trop 😭😭😭 yalanalene takhawou si barké Mohamed 🙏🙏ms amena djiguene you ameu fitt
Ay waaay beugn dou rei diaam😂😭
Yalla Bakhna !
Courage les frères boléne dématé yalna nguéne dougou si diam ak salam,mane mi si guéjj la diar mé sante yalla boubah
Ibrahim ndiay du courage brother .ce moi pap demba yeumbeul du courage rekk
Envoyéma numero Ibrahima Ndiaye j suis en italy
Bilahi ay jambar guene kouléne dimbali guéne ame dara
Mane dh sii gallgui la diar 2015 mee nak sant rek 🤝🤝🤝🇮🇹
Nèna ko nopile 🤣🤣🤣
Bakhna si mom
😂😅🤣
Da sop kat 😂😂😂😂
Woy
Mdrr
Gal guewel mom koussi doug ya togn sa bop😂😂
🤣🤣🤣ndaw wakh diou bari
Beugn dou réé diam Astafiroulah 😂😂😂
Ndayesan ibra ndiaiye sama kharit kou bakhx yalna la yala taxawou amin
Mom dé nenna kisi guinaw "nopil" quand on leur a demandé combien ils étaient dans la pirogue😹😹
Chers jeunes, rien ne vaut le sacrifice de partir en pirogues, j'espère fortement que les autorités vont trouver de meilleures soutions pour éclairer le bout du tunnel🙏🏽
Tu as constaté donc 😂😂😂Astafiroulah li metina
😅😅😅😅😅😂😂😂😂😂gni dano nekhh
Yalnaleine yala diapalei takhawou leine .. ibrahima khaliloula koubakh sama kharite bi du courage
Péral nako nak Nopil 😂🤣😂🤣
Courage frere actuellement ni j suis en spagn ni après magal la départ St. Louis la déparé Yonne Bou nekh machalla instan bi gnongi si centre bi gnanal léne gnou ame nagn fi deux semaine🥳🙏🏾🙏🏾😭🙏🏾
Cv donne moi stp ton contacte nimero telefon ou Facebook?
Delen wakh deugue
Lolou bou amé sakh waro ko fé wakh di encourager nite yi nioune dieulate gale yi
@@modoundiaye7985 vraiment kouko dgue amate fitou deim
Bayil fene
C triste mai nopil bi ray nama 🚶😂
Kon dou man kessei mako setlou
@@myo336 svp nopil c où? Mane guissoumako wakhmma ci gnata minutes la svp
deugue rek la gueume tigui 3mn30s
Balegui maguikoy ré sheuuut 😂😂😂
@@fatimaba4659 doma c à partir de kel minute svp nopil bi guissoumako
Sa waye da khiff ba taye khola mouye léka mbourou
Vraiment li tissna torop yalla nale'ne borombi dole' takhawou mougnele'ne lou djiot yombou li yeup sounou ndjityila re'k sathieuyi bounou ligue'yaune bagna sathieu alalou senegal kon jeuneyi am ligue'ye inchallaah
Bilae souma amoon xaaliss nioom nieupp lay wouteul ligueey dileen fay chaque weerr. Ndeysaan lii mettina😢
Nopil bi raynama way😂😂😂
Noo journalistes bii est tres très professionnelle 👏👏👏👏
9:58🤣🤣🤣🤣wadji nèna galle gou gorè la yorr
😂😂😂😂😂
Un pays rempli de jeune sans travail des chômeurs d'espérer l'état qui remplit ses poches l'Afrique va mal
Non le gas m a tué😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Thiey yalla 300 000 f yoyou wala 600000 yii soumako yorone ba ba acheté gnari 2 roue di deff thiakk thiakk douma wakh dara resté ici si tu veut voyagé ngua defar sa passeport gnane visa mo guene fouf
Yalla nalen yalla soutoural diapalelen
Yalla naleine yalla may lou gueine soutourlo mouy fi ak fenen mou gueune si yeine 🙏
Bilay yalla bakhna dina bakh deh 🙏🙏🙏
11:38 rastaman bi khif gui si gall gui bayé gouko dh😄😄
Lilou ko daire 😢😢😢
Yow li deynawar lol ndeysane yalna yalla tahaw gniep
Il as parfectement raison, daguay dof di délire, Man dama don guis Lou graw, me Sant yalah
Masta
Ah yow danga done miirr rek di dianèr😂😂😂
Sawaayy esk doukhiiff am Ndiayen nga dei
😂😂😂
Ibrahimalaye Ndiaye 😂😂😂
Ndeyssane il a l’air triste 😔
Ay way li métina ken kou nekk say wadiour mola takha diougue wayé khalat len gni thi guene adouna nakala laniouy térélé sen yaye yalna yalla samm len inchalah mn pays va mal
Sen-tnt, une application qui vous permet de regarder les chaînes nationales et matchs des championnats européens depuis votre smartphone. disponible sur play store
Tout l'argent que vous donnez pour voyager solen ko defone si ben investissement li yeup doulen si fekk. Ladiouma ken aviwam.
Voilà ! investir au lieu de gaspiller l'argent et sa vie.
@@Topofthetopapex gars yi amougnu xaliss sén matériel lagni taylè wala xaliss diambour yi lépp dém
Waay dji nopina dé
Rouss na sakh
Gni gneup aye mole lagne dagnouye ragala wakhe gnou diapalen mes fayolen draa mes yalla nalen borome diapalé inchalla defalko gneup
tenou and mboolo kheekh lii mou diouk fi ✊✊✊✊mboloo mooy doole
Daysann Arobase yal nalla yalla sam nitt kou bakh nga ligeye rekk nga kham
Hy li mom kharou la ndeyssane bgue tki mo mety
Kone guedj gui dafa am fou thi touddou diegui sirate😂😂😂
🙄
Fofou moy beuleba moy fii gnari guedjie yi ndadiee fou doywar lay wakh
@@jacksonkeuli3147 guedjou senegal bi ak Espagne
Waw fofou la dei bateaux yi sakh dagnouy am blem fofou parfois
@@jacksonkeuli3147 kone d diaroul pirogues yi difa diéma diarr
Wa lane motakh sounou gniitt tou réw mii diay zone bii nga xamné sounou domou réw si laniouy danne sén dolé nn méttina kénn meunoufi avancé
Daguena yab yalah, laguene.di.outi.europe.mogui.fi.thi.senegal
Walahi persinda bi mo bakhoul mai moul yi aye diambar la niou
Bege teke rek Yalla nalene yalla diapa lene
"Gallou guéwèl yi" rè ba tass.
Malako wakh
😂😂😂😂😂😂😂c’est ce qui m’a tué
Sama galou mbok yi
Galou Guewel yi lay weur man, 🤣
Saway mane lolou la ree ba sone bien affaire bi metina
Nopile nak ahh😂😂😂😂😂😂
Nèna ko Nopile 😂😂😂😂😂😂
😂😂😂
😛😛😆😆😆
Ki weroul deh 316 personne khana da dioum
Beug teki rek mon frère santé yalla rek te pare waate nioune jiguene sakh delounie guinaw dem incha alah
316 personnes multipliées par 300 000 ou 600 000 khol léné lolou niata ci khaliss la !!! Gni di organiser li ay millionnaires lay fimou tolou ni.
Laaay 94millions la yaw tei essence 1.500.000 rek ngay dougueul
Ba parei sen lekk yi dou doye doyna waar
Yalna yalla samme niuu.
Mane démna ba 5heure de temps MoMA déssé ma dougou Espagne ma terate Maroc
Haaaa
😂😂😂
Baye raye ngama
loutakh lolu sa wayy
Bakhna si iow
Le dernier gars qui a parlé est un real...
Dernier capo bi deugueur na fitt dh😮😮
Yala na lène yalla diapalè bou bakh
On voit que gal yi ap surcharge bou metti. Ils sont mal préparés Et mal approvisionné en nourriture. Il fautt prendre des mesures c’est trop. Gueuj wooroul kw.cest hyper dangereux ça. Je pense bou yaaguè daay halluciné
Du courage ça ira insa allah
Hee nopil lolou mounama ray 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😁😁😁😁🤣🤣🤣 ki limouy wa kogne ba
😂😂😂😂😂
Je vous conseille de venir a Mbour pour avoir les meilleures version sur l'immigration. Vous faites des interview sur l'immigration dans des villes où ya meme pas de mer.
Merci 🙏🏽
Lo si wakh am lo bayi man mi si galyis la diar 9 jours déf nañou ko si guéji gui dokhou safara lañou don moudié di nan wala dokhou guéji 😪😪nit dé ni sa kanam ñou dieul sanni birr guéji Mé nak insbi alhamdulila ñogui Sant bu bakh nak 23 November 2017 doumako masa faté🇪🇸🇪🇸
Moi personnellement, une gas m'avais dit, Sama papa moma yoni sigarete je vais allez à la boutique
Saway rayengameu way
@@momosene5564 ki dou nitt 🤣🤣🤣🤣
yalna léne yalla diappali
Amoil deum danio xiiff rek sone motakhh...
Wawa machalla
Boy deme woma🙏🏾🙏🏾
« Galou guéweul yi » 😂😂😂😂😂😂
😂😂😂 ba diamono dane bakh Guéweul danoul ame gual Macky liguèyoul
😅😂😂😂
@@antaelyfaye3839 Billahi 😂😂😂😂😂
😂😂😂😂ndaw guall bou beuri bagages
😂😂😂😂ndaw guall bou beuri bagages
Aye waye gallou guire gni kagne laye déme mane dé guallou guir gni laye khare paske guire la kouko fi guiss rék gua wakh ma
Ndaysan😭😭😭😭😭
galou gueweul ndaw bari thiow kxkxkx
Ioe fan la GPS di rombé nouadhibou rq di changer heur ioe sa xél mi demna ndékké 😂😂 diante bou rouge bi nak
Aliou ndiaye. DINA bakh
Non yenn daguenni kharou rek nguir yalla tok len fi kou deh do deloussi
Gallou Gueweul yii 😂😂😂😂 Heeeeey Mbaye ndaaaaw lou reuy
😃😃😃😃😃😃Gallou Gueweul😄😄🙉🙉🙉 ndaw waakh diou baari😄😄
Begne d'où ré Diamou Dawal fass Si birr Gall gui kay 😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@@mansourdieng2000 Dama wakh deugg Di 😂😂
300000 ou 600000 sur 316 volontaire c colossal comme somme c vraiment énorme on p faire bcp d choses avec c cet montant et les convoyeur sont seuls gagnant à l'arrivée mais bon c dommages et très triste
Man galou gueweul yi laye dougou mon gueneu nekh day mouthie😁😁😁😅
Hillman ndiaye naku teguat gal bo bakhè rek dogu te illman gallam bakhna
Gal gou gooré 😂😂😂
Gallou gueweul yi kaye. C'est tres difficile quoi dans ce pays. Yalla na borom bi diapale ndaw vraiment.
Mouskila😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Bisaff
Yon wi yombot yalla na borom bi taxawo ndaw yi
Walahi mouskila hateu
Walay kyna mouskilah bzeuffff 🤦🏼♀️🤦🏼♀️🤦🏼♀️🤦🏼♀️
@@rokinagueye9214 sama mboki maroc yi bari ngen fi de
Yalla bakh na