Les commentaires genre Je suis mouride mes j'aime Serigne Babarcar Je suis tidjane mais j'aime Serigne Touba Dolene arrêter svp. Serigne Touba Mame Maodo Malick ay nitou Yalla laniou tay avant d'être Mouride ou Tidjane ay Djoulile lanou kep kouniouy wo ci dine dagnoko wara beug ta Yalla takh
Yagüe Léne fi loool ta wér sy malick serigne mbaye sy mansour ak rakam serigne maodo sy dabakh Barkép Borom Touba khadim Rasoul ak Mame Thierno Borom Darou amine ya rabi ndakh yalla natall kharnou bi
Man daal wakh deugue yalla ki damako beugue rék depuis bama néké lhalé beu ligui awma si mom sago 😭😭 Wallahi pape maodo dafa bakh yalnako yalla same goudal fanam té mayko wér maygnouko nioun nieup
Machallah Sy Malick, kaddu yi rafétna trop, nirou nga sa Baay Aladji Abdou Aziz Sy Dabakh Yalla nala fi yalla bayi Seydil Hadji Malick Sy Maodo si barké borom beuss bi Yonént bi saw
Bilahi souma guiseii ay khelei you ndaw nek Europe diap sounou kilifaa yi di saga rek walahi sama khôl Day metii lol.. Diereudieuf serigne maodo sy yague Fi loll teii wérr.. Serigne babacar sy Mansour yallah na Fi yaag tei wérr ak kouni amine
Billahi s'y Lou dioge si khôl si khôl rek Laye dème li dawna yarame me nioune niépeu wara n'a niou sé am diangatteu si yalla naga sout sa Mame fan te dese barkeba
Amin Sy Malick, yalna yalla deguerel sen tahaway té tasniou cih sen barké 🤲❤️
Les commentaires genre
Je suis mouride mes j'aime Serigne Babarcar
Je suis tidjane mais j'aime Serigne Touba
Dolene arrêter svp. Serigne Touba Mame Maodo Malick ay nitou Yalla laniou tay avant d'être Mouride ou Tidjane ay Djoulile lanou kep kouniouy wo ci dine dagnoko wara beug ta Yalla takh
Ga gneme ko wakh
Merci👏🏾
Machala Digne fils de mon bien aimé DABAKH.
Machalah Machalah Machalah Ousmane Sonko yangui si deuk bou tééd bi yalana borom bi defleu président du Sénégal 🇸🇳🇸🇳 insalah 2024 .ken Mame Maodo
Je suis mourride mais j'aime trop ce Grand Homme Serigne Maodo Sy Dabakh❤️❤️❤️❤️❤️
Avant geu nek mourid joulit geu kon nougn jilit yui dou no wara begeun te sounnou bir
Le «mais » n’avait pas de place dans ton commentaire. Je suis mouride et j’aime… il n’y a pas de contradiction d’être mouride et d’aimer un tijane
@@azizfall8907 1
Anta Fall on t’aime. Gnoune gneup ben lagne. Sallalahou Aleyhi Wa Salam mognou ndiaboté
De même que moi je l'aime beaucoup billahi
Man serigne touba layakare wa ki ak s babacare s'y hawema thi gniome sago gniobakh lagne barcke yonneteby psl yalla genfi yague ter wee amine
Amine
🙏🙏🙏
Ndysan kou bakh lou bakh rek lay guisd
notre fierté la tarikha tijanya partout dans le monde
Machallah Sy Malik yague fi teh wër djieuredieuf
wallahi wakh nga deugue bou werr MachaAllah yalna yalla may werr ak werrel si barké seydouna Mouhammad sallallahou aleyhi wa salam psl inchaAllah
Machallah Yalla na yalla doli wer gui ak fane wi barkep xassida yi
Machahalla longue vie à tous nos marabouts
Allahouma Amine
Amine
Yalla gafi Yagüe té wèr mame maodo sy♥️♥️
Allahummma Amiin
Amine
Yagüe Léne fi loool ta wér sy malick serigne mbaye sy mansour ak rakam serigne maodo sy dabakh Barkép Borom Touba khadim Rasoul ak Mame Thierno Borom Darou amine ya rabi ndakh yalla natall kharnou bi
Machallah Serigne Modou yallah na yokk fane AK were Machalahh ❤️❤️❤️
Sy Malick yalna yalla goudal fane bi 🥰 mayla weer ak weerlé
Machallah Sy malick ya bakh yalla na yalla takhouleu té sameleu goundeul sa ay fane té mou anda akh weur si barké taha sws
Machala sy kaine dou seydina mouhamed psl
Masha lla Lou rafet Mashalla ❤️yalnako yalla sam mayko wer
Machallah machallah yalla na yague té wéér sy Malik
Machallah wakhtane bi âm na solo lol jërëjëf sy malick
Man daal wakh deugue yalla ki damako beugue rék depuis bama néké lhalé beu ligui awma si mom sago 😭😭
Wallahi pape maodo dafa bakh yalnako yalla same goudal fanam té mayko wér maygnouko nioun nieup
Machallah Sy Malick, kaddu yi rafétna trop, nirou nga sa Baay Aladji Abdou Aziz Sy Dabakh
Yalla nala fi yalla bayi Seydil Hadji Malick Sy Maodo si barké borom beuss bi Yonént bi saw
Merci président Khalifa ababacar sall tu as bien parlé machallah
Machala tubarkala ken.mame maodo malick yalla nanou tass si barckeme
Yalna yalla doli la wer inchallah
Machallah 🙏 dieureudieufaty sy yalla naguenfi yague looool té wér ak ñioun amine 🤲🇪🇸🇸🇳
j ai mal de le voir pleurer svp papa ne pleur plus svp svp svp
Walahi deysane mobakh khôl bi woyof
je pleure même
Bilaay si yàgg yàgg dem rekk waay yalna yeex
Bilayi Sy Malick yalla nala YALLA faye si barké SEYDINA MUHAMMAD amine ya bakhe donouga sa baye ba dé
Djeureudjeuf serigne bi kadou yi rafétna yallana yalla goudeul sa fane
Machalla yag fi loll sy
Bilahi deggou moo woor Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Li nek si xol fegne si canam walay sa thiofel si yonenti bi ñiepp xam nane ko walay sy malick yalla nala fi yalla yagal té andak wër
Machalah yalna diame yageu
Machalla ❤ sy yalna lene yalla faye goudale sene fane
Dieuredieuf Serigne Maodo.
Merci Khalifa. le message est pertinent.
Machallah sama Serigne longue vie et santé de fer merci
Machallah sy Malick yallana yallah yagualafii 💞👈🙏 sy Malick cou sétane lii rék dioye 😭 sy Malick lou guéne sii xool rék dougou sii xool,( bilahi sy yaa bakh)💘💘💘💘💘👈
Yalla yagal lafi InchAllah. Bon Gamou à tous les musulmans du monde
Dama beugué trop Serigne Modou Sy
Sy malik yag fi teh wer yabakh
Serigne Maodo sy Dabakh
Machallah Machallah
@@abdouaziztoure3586
@@abdouaziztoure3586
Yalla na sa fane goudou
Sy malik ak kou né amine
Yalla nala yalla dolii soutoura
Des leçons de morale de tous les politiciens.
Machallah....💚💛♥️💯💯
Amine yarabi Sy Malick yague lole machala mou and ak weurr barké Nabil Moustapha SAW
Machalah Serigne Malick yalnala yala maye goudou fane ack. Werbou yaram
mashallah ❤️❤️🇸🇳
SY Malick ❤️ ❤️ ❤️
Nday saan yalna fi yàlla yàggal sëriñ baabakar si
Machalla sy ❤🙏🏾
Yalla naniou yalla feyal cheikh abdoul hamid sarr
Mâcha alla s’y Malick y’a bakh🙏🙏
اللهم صل على سيدنا محمد وعلى آله وصحبه وسلم
SeriGnE Maodo sý dabah ❤🙏🏽
Macha alla dieureudieuf Sy
Macha allah diere dieuf yaq fiix lol te wer
Bilahi souma guiseii ay khelei you ndaw nek Europe diap sounou kilifaa yi di saga rek walahi sama khôl Day metii lol.. Diereudieuf serigne maodo sy yague Fi loll teii wérr.. Serigne babacar sy Mansour yallah na Fi yaag tei wérr ak kouni amine
Yonenti bii lepp la souniou koukay Magal rek nekh guaniou
💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖N'a yalla guoudeule sa fane mayela wére
Yalna laa yalla doli soutoura
Machalla sy malick sama mame magui laye bueke
Senegal xamougnou niou bakh yignuuu ameu
Machallah yallah yague fii lole te werre ci barkhe seydina mouhamed sallalakhou allahehii wasalam
Bilay hi bougnou yallah beugue nafi bayi sunu baye dji,sunu mame ,sunu wérou waye bilaye!sy malick
Serigne Maodo ❤❤😊
Machallah sy malick oh yonentebi psl rek molen nior
Bien dit.
Mashallah Mashallah ❤ ❤
Amine🙏🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah
Long vie sy Malik ❤❤❤❤❤
Serigne Maoda Malick Sy Dabakh yague filool tei weer diooy lo nguama bilahiii
شرج مود سه دباخ حفظه الله ورعاه
president saydina Ousmane norayni mu sella mi yalna nga gu du fan
Shukran Seydi SY
Machalla waxbi rafetna
Wadia wakhona Serigne mbaye Sy massour doulène resevoir ndakh Macky la andale
Nioniou deniouy manipuler rekk. Kilifa dine yi nieup leniou fi andale.
Astou Diagne, han lolou la wadji wakhoone daal, nena doulen recevoir pourquoi on ne sait pas.
Réservoir rou lén de
Khaw ma nak
@@youssouphasonko4900 bourde bi ba legui dagno guisse Serigne mbaye s'y Mansour
@@babasene9673 bayil gni bgue cas c serigne mbaye Sy Abdoul qui a reçu presk toutes les invités ba lgui khalif bi guénagul
Yague fi lool té and ak wér Sy Malick
Si barkey Gamou gui barkey Serigne Babacar sy.
vive Sonko, vive yewwi askanwi
Serigne Maodo Sy Dabakh un Homme multidimensionnel yague fi lol té wére
Diarama Tivaouane
Walaye ndayssane! Li motakhe ma beugue yéwwi askane wi
Ma cha Allah
Aka bakh
S'y malikh ndoudeul weral
Fene rekh serigne bii dioyole pour sonko il as parlé de mamoudou ibra kane
Machalla 🙏🙏🙏🙏❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤💯💯❤❤❤
Amineee sy
Machllah
Love❤️❤️❤️❤️
Ces politiciens la a chak fw c evenements ame swte gamou ou magal gnom gneup gneuw taxaw beug markè sèn empreunte senegal kagn lay djouguè ci yi
♥️♥️♥️♥️♥️🥰
Billahi s'y Lou dioge si khôl si khôl rek Laye dème li dawna yarame me nioune niépeu wara n'a niou sé am diangatteu si yalla naga sout sa Mame fan te dese barkeba
Dieureudieuf su
❤️❤️❤️
Serigne babacar al khalifa yalana yalla weral temou yagafi lol sy
🫡🫡🫡 respect ✊🏾
ENFIN IL REVIENT AUX FONDAMENTAUX DE MAME ABDOU AZIZ SY DABAKH . . .
Akaa tëdd ta bakh xool bou sett l'Aa yoorr Barki xadimou Rassoul référence Cii lepppp
Dierejuefati Mame abdou sy
Lison de morale pour tous