Makhtar Sarr dh, li tah Mouy wah leup Moy ibadou yi la bagn. Dou wah lou nek thi Sénégal wala souy wah tamite gnou néw dollé késsé léy ataké , mais sou féké dénga bok thi keurou diné yi rek Loula neh wah mais douçi wah. Problème boumou am Moy le fait que nitt gnou beuri légi ibadou yi lagniy déglou , ndah wahou nitt ak wahi dof dou béne.
Mais li boumou dialeu sans rien khéwe, li foke nou saisir procureur pare ce que dafa toumale doctor Ahmad lo. Ahmed Cissé loumou wakhe moye deugue ki khole bou bone la yorre.
Dou noppi bènn yoon sén pass pass you bonn yi dèss nagne dadji sén you bonn par force. Wallahi bou nékoulwone nouye chaytani di yakk xeel diaroul ñoukoy totou. Déy té tay xam cii ni déy fenn boss kékk lay woup.
Yéne linguene warone wakh nguene deme nii ahmed lo mou déme took book ak Al oustaz cheikh makhtar sarr béne plateau niou wakhtané diner légui nguéne bayi ameth lo Bou féké danguéne diapp nii diners dji took di khasté la wala thieukeul toubaye ak goudeul sikime nakh nguéne séne bop
Docteur Mouhammad LO YALLAH nakou YALLAH SOUBEHANAHA WATALAH préserver, samou ko, maykou Tawfékh. Amine!
Amiin
Machala lér yi am na soulo torop machala
Yalnagnou borom bi mousseul si chaytaane.
Tarikha yii dama rétiou limassi nékoone. Gni ay vrai nafékeu lagn. Yagu nagn nakh population yi
Macha Allah oustaz omar mbaye naafekha bumak moy makhtar sarr
Makhtar sarr warna ragal yalla témou outî yar AK xam xam
Waw lo wer gua wakh
MAA Sha Allah
ماشاء لله وجزاكم الله خيرا كم
Dr Ahmed Lo YALLANA nafi té weer
Waye boul sokhor waye té ngua wakh oustaz makhtar Sarr mou sél mi .
Makhtar Sarr dh, li tah Mouy wah leup Moy ibadou yi la bagn. Dou wah lou nek thi Sénégal wala souy wah tamite gnou néw dollé késsé léy ataké , mais sou féké dénga bok thi keurou diné yi rek Loula neh wah mais douçi wah. Problème boumou am Moy le fait que nitt gnou beuri légi ibadou yi lagniy déglou , ndah wahou nitt ak wahi dof dou béne.
Jërëjëf Maxtaar❤❤❤
Serigne Mansour yalla naco sunu borome yeureum mais reral naniou niit yi c'est incroyable
Makhtar Sarre mom yalla moo def manumaco deglou defa amoul xam xam en plus defa naafékh limata wakh wakhouco daal
Aslmk Matar Sarr, vraiment doon niyou DEUG, wallahi kholo YALLAH ci lingay wakh,wakh ci yaw soudoul woon leralal deug,wakh ci yaw perte temps.
Nooo! Makhtar sarr demmal gestou kham kham 🤣🤣🤣🤣
Macha allah cheikh bi qu'Allah vous récompense makhtar sarr c un hypocrite
Longue vie a vous ❤ au senegal ya cheikh
Makhtar sarr damako yeureum dafa bagne Ahmed lo ba faf niak sagom diga déé dé docteur amoul sa diott
Vraiment
Makhtar Sarre defa mana fén vraiment du wakh xam xam
Matarr sarr Ben samman duo khalifa dine
Matar sarr amoul yar amoul xam xam
Sénégal dall aye élève primaire nioye wah akk aye doctorants
Surtout lolou sah....bilay..
Surtout lolou sah....bilay..
❤❤❤❤❤❤❤
Mataram sarr khamoul dara yallah dinako atè Dr Ahmad lo
Mais li boumou dialeu sans rien khéwe, li foke nou saisir procureur pare ce que dafa toumale doctor Ahmad lo.
Ahmed Cissé loumou wakhe moye deugue ki khole bou bone la yorre.
Eeettttttttttt Matar 😂😂😂😂😂😂 marché poisson tasna woyyyyy ils ya des docteurs en soudi pour War waa saoudi non thimmmmm
Quelle comédie
Mokhtar Sarr do ngor sa fami ay diam laniu khmnanola bu bakh
Lousssi yonou docteur Ben salmane dou borom kham jham
Mais kagne néniye planté matar Sarr diotena nak niou djoke si aye mbirame
Ki lolou la beugeu gnou plient ko gir mou siw thi adounabi dakhe kou Dr lo plinet ga siw
Arabe saoudite ak makka
Té cheikh Dr lo mo geun ay kilifam
Foko tèk
Waa boo waxee loolu lépp ba noppi. Waxleen ca la xew ca Màkka
Kii dafa rérr ndeysaan
Dou noppi bènn yoon sén pass pass you bonn yi dèss nagne dadji sén you bonn par force. Wallahi bou nékoulwone nouye chaytani di yakk xeel diaroul ñoukoy totou. Déy té tay xam cii ni déy fenn boss kékk lay woup.
Beneu argument amouko makhtar sarr bi 🤦♂️
Yéne linguene warone wakh nguene deme nii ahmed lo mou déme took book ak Al oustaz cheikh makhtar sarr béne plateau niou wakhtané diner légui nguéne bayi ameth lo
Bou féké danguéne diapp nii diners dji took di khasté la wala thieukeul toubaye ak goudeul sikime nakh nguéne séne bop
makhtar sarr goudale fane ak wére Ammed lo hamoule darra pour gnome so diangé arabi saoudi hamegua dara
Kii daa rèwe wayé Yalla dinako yarr. Xamoul dara si diné
Makhtar sarr domouram la
Dadji bidahs si diamou y'Allah la bokou
Pourquoi vous vous clashez entre musulmans.
C tous des hypocrites menteurs ❤❤❤
Khamou lèpo tè lokhamol wèdiko koragal yalla dokodèf par parlou rèk
Matar diaradiuef
Che abdoulaye dieye gandiol
Ahmed lo dafa rew
Makhtar lolo dodègue niowakh si ndakh kourgui lisidès bariwol tè kour laye guisè ak narbi limasi kham lèpo domako wakh mok
Wa ki limouye kath moko taye
Ah vous êtes des fous
This makhtar is like a woman
Yaw sa mam bum la fatuwale matakh yaw do ngor doktor lo dusa naole dakh mom ngorla
Ta yaw setub diamga mo takh lo khalat wakh dakh do as ngor
yaw nopil