Axirou Zaman : NJAALOO DAY XAÑE WËRSËG. Avec Oustaz Makhtar Sarr.

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 19 янв 2025

Комментарии • 52

  • @cheikhdiop82
    @cheikhdiop82 Год назад +5

    Salaam ya oustaz Makhtar Sarr , dieuredieufati !! Machalla yalla na gnou la yalla fayal yiw si barke Seydina Mohamed SAW , theme bi mom themou societe bi la , musulman ak Chretien yeup , Mac ak ndaw , donc lou gnou si meuna am rek dafay bakh meme bou dee 1fois par mois . Di niane yalla mou oyofal la ko ta yokal la weer ak katane , ameen !!

  • @abdoulayedabo9509
    @abdoulayedabo9509 Год назад +3

    Yalla naniou yalla moussal ci njalloo

  • @ndiemediouf8365
    @ndiemediouf8365 Год назад +15

    Slam aleykoum wa rahmatoulah y'a oustaz nous demandons 3 ème partie, 4eme partie, 5eme parti.......du thème njaaloo amna solo trop dieureudieuf

    • @AichaDia-y1l
      @AichaDia-y1l Год назад +2

      Billay de ndakh sougnou reewmi moom wakhtan bi amalnagnou solo lool ndakh gnou bari dagnio def njaloo mom dou dara kholal thi seriyii rek mem boude seriela dagnkoy def komko dara nekouthia soubhanal la😢yalla nagnou yalla moussal amiin

  • @mouhamedndiaye1418
    @mouhamedndiaye1418 Год назад +5

    Naniou déme 3ème partie

  • @awambengue2820
    @awambengue2820 Год назад +4

    Salam aleykoum Oustaz amna solo niongui khar suite bi

  • @salioufall4345
    @salioufall4345 Год назад +4

    Wa waaw 3ème partie moom lañuy xaar ustaas ndax dafa am solo

  • @moustaphaleye4500
    @moustaphaleye4500 Год назад +2

    Layakcfi atahadusu. Fisina darsayni

  • @balladiagne9144
    @balladiagne9144 Год назад +5

    Machala yalnala yalla faye amine amine amine

  • @mamadusall3567
    @mamadusall3567 Год назад +4

    Machalla oustaz gnogui sakkou 3eme parti yalna yalla fayla gouddal sa fane

  • @ibrahimandiayeattiidjani1269
    @ibrahimandiayeattiidjani1269 Год назад +3

    Allhou Akbar

  • @mahmoudgueye5387
    @mahmoudgueye5387 Год назад +6

    Lou wërr Oustaz Yalla na Yalla dolli yeurmandé ak diégueul ak mouthiou gou raféte (AMINE)Diadieuf

  • @amadoudieyte1620
    @amadoudieyte1620 Год назад +3

    Kou njaaloo ci kan la wara dem pour niou door ko

  • @AichaDia-y1l
    @AichaDia-y1l Год назад +3

    Ma cha allah bou ame 4eme sakh biuga nagn ❤mem boudoul bi emisio emision yii yep warolen ko def benna joudi rek ndakh emision bari douma bouga mou jekh

  • @daoudathiaw
    @daoudathiaw Год назад +2

    Jereujeuf yaa Oustaz. Yalla na buur Yallah fey ! 3e partie ci barke mariage ak ngeneel yi ci boroom bi préparé doone na am solo

  • @elhadjikama4393
    @elhadjikama4393 Год назад +2

    Machallah 3m parti

  • @mansourdieng2000
    @mansourdieng2000 Год назад +3

    Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Sél Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Baax Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Yiw Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Dioup Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Bari Xam Xam Mi Machallah Oustaz Makhtar Sarr Mou Am Dégu Dégu Ci Diiné Mi Yalla Nala Yalla Faye Yiw Oustaz Makhtar Sarr Yalla Goudeul Sa Fane Yalla Yokou La Ci Xam Xam Ak Khéweul Gou Yaatou Lool Té Barkél Ba Ngua Yeuk Ko Amine Allahouma Amine Dieureudieuf Oustaz Makhtar Sarr Yalla Na Gnou Yalla Défal Dégu Ak Topou Té Mouseul Gnou Ci Ndiaalo Ak Diégué Ndiaalo Amine Allahouma Amine 🤲👈

  • @mayorondiaye3317
    @mayorondiaye3317 Год назад +3

    salam yaa oustaz sokhla nagnou 3eme partie incha allah

  • @7TVOFICIEL
    @7TVOFICIEL Год назад +4

    3e demande sociale

  • @ibrasamb8457
    @ibrasamb8457 Год назад +2

    Yànna Yàlla fayal ñula ci barke Yonen.
    Loo ci indi rekk doyul ñu deglu partager insàlla.

  • @IbrahimaFall-z8n
    @IbrahimaFall-z8n Год назад +5

    Merci oustaz ❤❤❤❤❤

  • @7TVOFICIEL
    @7TVOFICIEL Год назад +4

    Macha Allah 🙏

  • @seynabousall9091
    @seynabousall9091 Год назад +3

    Dieureudieuf oustaz ❤❤❤

  • @abdoulayedabo9509
    @abdoulayedabo9509 Год назад +2

    Merci oustaz

  • @momartallabeye
    @momartallabeye Год назад +5

    Machalah

  • @mansourdiouf2218
    @mansourdiouf2218 Год назад +4

    Danke schön oustaz❤❤❤❤

  • @khadijah4849
    @khadijah4849 Год назад +1

    Salam Ya Oustaz wakhtan si naka lagnou labatei si Islam

  • @Ndiayemo921
    @Ndiayemo921 Год назад +4

    Machallah amna solo oustaz ❤

  • @diopousseynou5119
    @diopousseynou5119 Год назад

    Salam oustaz them bi amna solo contuné ko nakh njaloo gui barina loll si deuk bi

  • @assmalickdiagne8098
    @assmalickdiagne8098 Год назад +1

    Machallah ya oustaz amatina solo na 3 sém partir bi nieuw Ndakh thème bi dafa am solo trop ta legui dafa baré lool sakh ta thème bi baréwoul niokoy wakhtane ta li Lou mata wakhtane la djiradjieuf ya oustaz yall nala yalla fay yiw arrla samala takhawola inchallah

  • @YacineDieng-vy6tv
    @YacineDieng-vy6tv Год назад +1

    JaJeff oustaz

  • @Abdoul-qadirba
    @Abdoul-qadirba Год назад +3

    واصل يا أستاذ أيد ك الله

  • @MamadouLamineDiba-y3c
    @MamadouLamineDiba-y3c Год назад +3

    Ok ya oustaze j'ai compris lannmoy ndialo ok merci

  • @IbrahimaSylla-xq7he
    @IbrahimaSylla-xq7he Год назад +4

    Na 3em partie bi nieuw ndax Ndialo legui dafa beuri senegal lol lol lol sakh 😢

  • @ibrasamb8457
    @ibrasamb8457 Год назад +2

    Thèmes sangara pour le prochain émission

  • @ousmanecisse9975
    @ousmanecisse9975 Год назад +1

    aamiinn

  • @abdoulayedione8317
    @abdoulayedione8317 Год назад +2

    3ème partie dina am solo trop ndakh ndialô gui dafa beuri lool sakh

  • @cheikhcokidiop6690
    @cheikhcokidiop6690 Год назад

    ماشاء الله تبارك الله شكر لكم وجزاكم الله خيرا

  • @AichaDia-y1l
    @AichaDia-y1l Год назад +2

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 o😂😂😂😂😂mounouma giss sa pojou nday giss sa pooj degge bou wer😂

  • @djiteamy2696
    @djiteamy2696 Год назад

    Oustaz niogui khaar troisième partie bi

  • @astoudiagne1767
    @astoudiagne1767 Год назад

    Allahuma amiiine

  • @DAROULHOUDA938
    @DAROULHOUDA938 Год назад

    Uostaz 3ème 3️⃣3️⃣3️⃣3️⃣3️⃣3️⃣😢

  • @habibseye5531
    @habibseye5531 Год назад

    جزاكم الله خير

  • @aichadioufkane1171
    @aichadioufkane1171 Год назад

    Macha halla

  • @astoudiagne1767
    @astoudiagne1767 Год назад

    Amatina solo lôl dieredief oustaz makhtar ,ñungi khaar 3éme partie bi ,wakh degg YALLA,ndakh ñikoy déf bayiko,ñiko défagul, bañsidugg

  • @khalifaleye8014
    @khalifaleye8014 Год назад

    Rts tikko wayeلله ورسوله

  • @diopbabacarmaleye1663
    @diopbabacarmaleye1663 Год назад

    Oustaz défal niou thème si goor yi tak niaari diaaro ta lég lég ga gisthi ay Serigne wala ay oustaz
    Lou thi yalla wakh ya oustaz diadéf

  • @BasketeusouSonko
    @BasketeusouSonko Год назад

    Them bou am sonou

  • @ahmafall2732
    @ahmafall2732 Год назад

    Ancore Une 3er.fois

  • @cheikhdiop82
    @cheikhdiop82 Год назад +1

    Aussi solutions toub bakar , par example kou nialo bane facon toub mo gueune ? A part les tiaw yarr 🤣🤣 !! Kou bokale bane facon toub mo gueune ak sathieu wa la ray niit ?
    Yalla nagnou yalla doli diameu ak khewal , defal gnou deeg ak topou , ameen !!

  • @astoudiagne1767
    @astoudiagne1767 Год назад

    Degg piir nga wakh

  • @beuguerassoul3126
    @beuguerassoul3126 Год назад +1

    Machalla