Macha Allah..di la deugueul bou wér segn bass..car koula kham la.. Té wakhone nala ko thi ay diamono...né digua fégne par force bama fégnal la ndax daga meusseu lakhou té ragal wax thi kerssa gou réy gui macha allah.. Dites vous bien Qu'il ne vous a absolument rien dis de tout ce qu'il vit et voit tous les jours..cet interview n'est qu'une pincé de sel devant un contenaire bien rempli.. Deug béne la dou niar..kou nagou té gueum yalla na yalla barkél.., kou gueumoul yalla nala yalla dimbali.. No comment..!!! Segn Bass Yalla nala Yalla may fane wou goude té ande ak wér.. Alhamdoulilah..dieuredieuf Serigne Saliou..!!!!!!!!!!!!!!!!!!!
wa mai man damay lathe???khana Sénégal amoul il y a plus de médecin qui travaille sur le domaine de psychologie ??? rewmi barina Aÿ doff trop yallana gniou yallah moussal ci yii
Yèèn ñi nga khamnè yènay commenté je vous conseille de faire tres attention...nit loo deg té amooo thi xam xam danga thiy maandou...ceux qui marchent sur la voie du tassawuf (je ne parle pas des faux mourides qui en sont encore au stade de fans club mais plutot de ceux la qui cherchent la face de leur seigneur et une extinction en lui) savent que ce que dit cet homme est bien possible Cela ne vous coute rien de vous abstenir d'insulter quand vous exprimez votre desaccord....MOYTOULÈN GOOR YALLA YI
wagui dina deup micro monou yap khawma journalist la khawma loumou don dof bi nga khamni wakhoufi loudoul ay guent wakhoukofi lima thi geuna mèti nak serigne saliou mim thiy toudou moma mèti.
Li rèk moma meti diagnou touss khamou dara ni dagaye am ay talibé legui sa talibé noy def ak niom wayé koula degue kham ni ay wakh dof ngaye wakh ak wakhi kou danou si saréte😂😂guente rk ibliss ngay guiss stp bayi lene serigne saliou te yalla takh
Milkosse Milkosse ki limo wax lan mosi yono mourid nimo ame si koy todo mourid nila ame si tidiane ana el cheikh lonek wax nako fi ñi ay saytani ñiolen solo rek te lima si gana meri moy serigne saliou ko dioque rek taxal ko 😭😭😭😭
Busra Samba dett way ki boukooo yemale ak cheikh bethio ndakh ki limouyy limouy wakh chekh bethio wakhoukoo chekh bethio moko geunaa manou fouf yalla bou cheikh bethio melnikooo yalla nalen yalla yalla dimbalii si barcke seydina mouhamet psl amineee
Papay patin mogui nii dh sama gayi! !! Mom dh lépou cii guente lako tekkk marrer
Néna boma setlo mangui khawa dal wouyyyyy déna 😂😂😂😂
MOR MBOUP ; S ke tu peut prouver le voyage nocturne du prophète !!!
الله أكبر sama khol diékhna
Gueumeul ligaye geume
yawe dame doull pape bi daye doull
yalla rék moo kham ndakh deugeu la wala deet
Wadji vraiment kou meuna doule Quoi. Ahhh c'est vraiment triste pour tt les senegal.
Nonou la manè feneu nk modou kèmane sathi bou makla
Wallahi senegal 🇸🇳 li dou djam li mousiba la deug rew bo kham lou way nekh wakh war nagno halat thi bamel moungui gnouy khar allahou akbar
Macha Allah..di la deugueul bou wér segn bass..car koula kham la..
Té wakhone nala ko thi ay diamono...né digua fégne par force bama fégnal la ndax daga meusseu lakhou té ragal wax thi kerssa gou réy gui macha allah..
Dites vous bien Qu'il ne vous a absolument rien dis de tout ce qu'il vit et voit tous les jours..cet interview n'est qu'une pincé de sel devant un contenaire bien rempli..
Deug béne la dou niar..kou nagou té gueum yalla na yalla barkél.., kou gueumoul yalla nala yalla dimbali.. No comment..!!!
Segn Bass Yalla nala Yalla may fane wou goude té ande ak wér..
Alhamdoulilah..dieuredieuf Serigne Saliou..!!!!!!!!!!!!!!!!!!!
Ibrahima Ba ki fen kat LA mo dakha fen pateh sakh domiharam GI nga don
Ki dian goul té hamoul daye data daye yam
mashallah ki beugna ko giss ndakh kou takh thi serigne saliou dou neen
Extraordinaire ce qui ce passe dans ce pays.
Liguay nalaw tamit beurina si Serigne
Wax deug yoblenko dalal khel
Liii motakh Sénégal dou dem
😂😂😂Yaa meuneu douul 😂😂😂
(Lepp thi guente ) laillaha illallah
Bayi leen serigne saliou mi gueen di foè
Wakh dji limy barri barri
Wakho fii benn baatou alkhur aan
waaaaaaaaaaauuuuuuyyyyyy !! 23:30 néna sadam ussein'' mane ngay dakk?? Dotoko defatii !! '' Loooool!! mais nak gayi nanussi teyy nak, yalla da beurilé té tabé lole té meuneu mayé lole!! ngouram gui sakh meune nako mayé té douko wagni dara!! nanu rafete ndiorte rek
Yaw ki doule meun nako trope
Amo tole amo dara khomo touss diango ni dagaye am ay talibé koula topou Sénégal dal mo nekh
thiey Watasawouf diney guenti
Billahi adouna koum takh nkay fénal koutolné s saliou dankaki rethou
Wayéé paby gnémé na Yallah dhé
Machalla
Aka bari guenti😂😁😁😁😁😁
DIEUREUFEUTI IBRAHIMA KOU CI AMOUL NDIMBEUL DAGUA YAKO
.
Wooooooooyyyy fenn cat bi
Ya meneu tothie sa data ndaye 🖕🖕meneu dul😡😡🖕🖕
Sa bopou bu dague ndayam bi sa data ndeye
serigne touba wakhone na ni mbollo dinagne ma toudoo te kene mounou lene tere dem safara...ndakh lima nek nekougnoussi
Kii kouka dakha doul amoul
kimom eupe na invite si television
wa mai man damay lathe???khana Sénégal amoul il y a plus de médecin qui travaille sur le domaine de psychologie ??? rewmi barina Aÿ doff trop yallana gniou yallah moussal ci yii
salam salam nmr basirou pen svp
Ya mana guénte😂😂
Yèèn ñi nga khamnè yènay commenté je vous conseille de faire tres attention...nit loo deg té amooo thi xam xam danga thiy maandou...ceux qui marchent sur la voie du tassawuf (je ne parle pas des faux mourides qui en sont encore au stade de fans club mais plutot de ceux la qui cherchent la face de leur seigneur et une extinction en lui) savent que ce que dit cet homme est bien possible
Cela ne vous coute rien de vous abstenir d'insulter quand vous exprimez votre desaccord....MOYTOULÈN GOOR YALLA YI
Yaw meuno nopi yaw
Kou baakh démal dia'ngui sa diné ta'ngua baalma
such a big liar , I never seen it in my whole life. WOW .
Ki mo mene féne adouna moye wadia touki wale
Kiiii dafa kateu ndayam foumako fekk kholli leufeul ndayam😡😡😡😡
Sakha Saibatou ki kai dafa cat ndeyam ak bopam bu dague ndayam bi
wagui dina deup micro monou yap khawma journalist la khawma loumou don dof bi nga khamni wakhoufi loudoul ay guent wakhoukofi lima thi geuna mèti nak serigne saliou mim thiy toudou moma mèti.
Saway lingay ngénte bari na !!
diadieuf serigne bi gamnala namgoulna chekhbi
Li rèk moma meti diagnou touss khamou dara ni dagaye am ay talibé legui sa talibé noy def ak niom wayé koula degue kham ni ay wakh dof ngaye wakh ak wakhi kou danou si saréte😂😂guente rk ibliss ngay guiss stp bayi lene serigne saliou te yalla takh
tayy rék la Warou khana Kii moy papi patai?
yawe Bayile doull
Walahi ngorsi mou mana fén
waw boulén ko saaga way kii sén mbokke Tassawouf la.boulén fatte sén paspse thi guente ak thiakhane la soso🙉🙉🙉🙉
Yaa yap moutasawifouna yi
😂😂😂😂😂 setal yalla si lingaye wakh fenn bakhoul
Adina yakhona thaiy wakh Rek
mdrr yenn mouride yi gno meuneu fenn mdrr
Kéweul dou teupp doom dja beutt, Mouride yangui nonou rekk doull moom niossi meunn nieupp
Milkosse Milkosse lila metti moy maodo dafa signé yalla amoul si kanamou toubab bi
Milkosse Milkosse ki limou wakh moom kesse la concerné waayé yonou mouride yi nekoussi yaw moom kouy ignaane yow lay djapalé
Milkosse Milkosse yah ñiaff sa ndeye
Milkosse Milkosse ki limo wax lan mosi yono mourid nimo ame si koy todo mourid nila ame si tidiane ana el cheikh lonek wax nako fi ñi ay saytani ñiolen solo rek te lima si gana meri moy serigne saliou ko dioque rek taxal ko 😭😭😭😭
Milkosse Milkosse 😂😂😂😂doul rek lay def
Giss nà kou meuneu féne batàyi ''' mé daboul ki !!!
Nom paby dou dème mo meune fene
Journaliste bi sa ay ré moko diapo mom si bopam xamna ni deye fenn
ki nak MoMAna Ndeye nelawe DEUG
Mbame xouxe bi mou mana take ndayem doule Santa
Bassirou mi momana katte data ndayam doull
Yamana fenn yamana fenn yamana fenn yamana fenn yamana fenn yamana doul yamana fenn yamana doul doul nopili hamo dara fenn rekke
Ya mana oubi sa leufeul ndaye doule.
je ne comprend plus rien
Mème le journaliste se moque de lui
Non Sénégal nak amoul loi qui Assane Diouf moko tané folen teudjé Assane qui dagne ko wara raye sheuuu😂😂😂😂😂
Sa data ndeye domiharam y ni nga mana mell mouride nga sa leufal ndeye ak sa baye
أعوذ بالله من الشيطان الرجيم
bilahi wakho dage
Yaw amoulen serigne bu mana ramou serigne cheikh tidiane sy al machtoum sa serigne ak serigneam yap domiham ngen
Nga melni daram ngajoo ni domi kharam ji
KI MO AMNA FÈNE TÈE MANA SOSSE
ki nitou yalla la de day guente rek me bisbou yewo dina nekh de khewal dina ame de
saliou mbaye 😂😂😂
Doull way domoram
dafa ame aye rap
ki dafa doff
nonnn ces pas possible m'ai qui dafa mendi
You are such a great liar even the journalist knows that you are lying in front him. May Allah forgive for stupid mentality
bo rousoul wona fen khaw ma loy wakh konnnn
sou la tidjane yi diapé
saway yaw yémé nga d mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrr
éskey y'a meuneu doul
yaw doule rek nay daif
Kottate
yaw de bogison s salihou xawma noy deffffffff
ki dof la bop bi bakhoul
nit day manou.yaguafi tes werr
إن يقولون إلاكذبا
ak noppou you reuy yi yakheu der rek
😡bayile sa khel bigaye fowé
🙊🙊🙊🙊🐕🐕🐕🐕🐕🐕🐕🐕
Yaw mome khana sa lep gente la
Tarikha boo kham ne fenn rek lengni deff fen cat yu mack yiii
Madi Njie thiay man dh warou na si yéne sougnu tarikha moy tarikha deugue wayée yéne mom yalla modéf nguéne bagnou
Cheikh Fall walhal ak fenn cat bobou do fen mo geun so yennn ta nga wakh ko mo bayi doull fen rekkkk domiharam
Madi Njie pourlan nga ni daye féne ??
Cheikh Fall khana daglou woo ko Lou mu wakh si cheikh ak wakhtanam yi yap
Madi Njie digue lou na lépou dioxma sa whatsapp ma waxla lou nguéne masoul xam
Sa fébar bôbou la dalôn ''mo la bàyiwoule ''' mouye doff '''
ya Yaya hhhhh ma waro
yawmi ragalale yalla mame abdoule azize dabakh malike dana dégue simome mouy wakh gnidéme khamougnou si lougnou nék amoul kéne kou meuneu wakh fi ki migui aldjiana wala ki migi safara ndakh béss péthieu fawe mou ame sonalgéngnou torop mane khamouma gnoune fougnou dieume
ياأيهاالناس اتقواربكم.
Nafehk buy fen mobon
VOILA UN 2eme BETHIO C EST SIMPLE PARLE FORT DID TOUT CE K TU PENSE GNIMÈĹ YALA FÈNAL BOU DARA DEUY SI YAW FÈNAL RÈK FÈNAL
Busra Samba dett way ki boukooo yemale ak cheikh bethio ndakh ki limouyy limouy wakh chekh bethio wakhoukoo chekh bethio moko geunaa manou fouf yalla bou cheikh bethio melnikooo yalla nalen yalla yalla dimbalii si barcke seydina mouhamet psl amineee
Yawe Dalle Yaa yiimi rekke lii epna waaye lomata wakhla