Touba entre loi et insécurités : Serigne Abo Mbacké clarifie le débat

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 3 янв 2025

Комментарии • 167

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 6 дней назад +21

    Baye fall yi daal waw leeeeeeeen goooooooor jërëjëf ❤❤❤❤❤❤❤

  • @ahmadoukhadimlo4599
    @ahmadoukhadimlo4599 7 дней назад +20

    Jërejëff Cheikh Thioro ❤🙏🏾

  • @khadimsarr9157
    @khadimsarr9157 6 дней назад +17

    Cheikh thioro mbacke wakh na deug touba amoul sécurité touba la deug

  • @mortallanakoyallatakhawulo303
    @mortallanakoyallatakhawulo303 6 дней назад +10

    Bay fall yi yalla ne len yalla takhawu ❤❤

  • @cherifchifo3590
    @cherifchifo3590 5 дней назад +4

    Honorable député Cheikh Thioro Mbacké nittu deug la machallah "Civiles meunoul yar moromou Civiles" l'État doit prendre ses responsabilités

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 6 дней назад +16

    Touba daal lifi Serigne bi bague Moy Am inchallah wa Salam

    • @noble4211
      @noble4211 2 дня назад

      Na diarr yooonn say seugn bi beugew kou nii murm

  • @Moustaphafalle
    @Moustaphafalle 6 дней назад +20

    LI Serigne Mountakha beugue de moy am inshallaah

    • @noble4211
      @noble4211 2 дня назад

      @@Moustaphafalle bayill fénn s MOUNTAKHA waxoull lolu

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 7 дней назад +16

    Machalla Serigne cheikh thioro Mbacke ya bakh ❤❤❤❤❤

    • @sene6344
      @sene6344 6 дней назад +1

      Sa data ndaye yak mom

  • @cheikhseck6683
    @cheikhseck6683 6 дней назад +5

    Dieredief s cheikh thioro Mbacké ❤️❤️

  • @cheikhmodoufall9108
    @cheikhmodoufall9108 4 дня назад

    Merci beaucoup dieureudieuf Serigne Touba

  • @toubadarmanko7193
    @toubadarmanko7193 5 дней назад +2

    Li Serigne beug rék moye âme inchalah

  • @SyllaMouhtar313
    @SyllaMouhtar313 7 дней назад +15

    Xana Dou commissaire Bou Gouye Mbinde Mofi waxon Ni Li Serigne Bi Di Téré Si Touba Mom Dousi japp Kénne Ndakh Lolou Serigne Bi Moko Téré Wayé État Bi Téré wouko
    Kone Naka Laniou Mana Yakaré Si État Mou Défall Serigne Bi Limou Beugue Si Touba....
    Vive Les Baye Fall ❤️❤️❤️ Thia Kaw kanam Rekkkkkkk🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

    • @serignesalioumbacke3021
      @serignesalioumbacke3021 6 дней назад

      Li Serigne bi beug wutëll Touba statut boppam rk mooka mana saafara ak jangal gone yi te yarr leenn

  • @laveriteabsoluejuste6358
    @laveriteabsoluejuste6358 6 дней назад +5

    Jërëjëf mame cheikh Ibrahima fall ❤❤❤

  • @sambakani
    @sambakani 6 дней назад +6

    Les temps ne sont pas les meme.,....demb dou tay....securite touba bayileen ko ak bay fall yi si non bordel bou meti moofay am...❤❤❤

  • @Suhaybu28
    @Suhaybu28 7 дней назад +7

    Am na solo lool waay ! Jaajëf Seex Abóo Madyana

  • @tamba3561
    @tamba3561 6 дней назад +4

    Serigne Abo ligawakh dou indi jamm civil douyar moromou civillam Serigne thioro ❤❤

  • @Alkokyou
    @Alkokyou 7 дней назад +8

    Moi personnellement j'habite a Touba et j'ai pas aucune insécurité a Touba
    Touba est comme toutes les villes monde la police ne peut pas être partout
    Je soutiens a 100/100 les Baye Fall

  • @dialibatou3686
    @dialibatou3686 4 дня назад

    Dieureudieuf Serigne Abo

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 7 дней назад +18

    Machalla Serigne Cheikh thioro Mbacke Diamou Rik kaye Am ❤❤❤❤❤

  • @bathiesow5537
    @bathiesow5537 6 дней назад +2

    Jërëjëf sëriñ Aboo kàddu yi rafét Na amna solo

  • @BallaDieye-d6f
    @BallaDieye-d6f 7 дней назад +3

    Amna solo Mbacké balla ❤

  • @massambadarousalam9586
    @massambadarousalam9586 6 дней назад +1

    Maasàllaa amna solo lool.

  • @salioudiouf1022
    @salioudiouf1022 4 дня назад

    Serigne Abdou Rahmane Mbacké Ibn Serigne Mbacké Madina yalnafi yague té wére

  • @MourtadaMbacke-ot7fp
    @MourtadaMbacke-ot7fp 7 дней назад +3

    ❤❤❤❤❤machallaaaaa

  • @salioundiaye5763
    @salioundiaye5763 6 дней назад +1

    Merci beaucoup

  • @MAKTABATOUTAWFEKH-pn6st
    @MAKTABATOUTAWFEKH-pn6st 6 дней назад +2

    جرجفت بك لي امن سولو
    جزاكم الله خير الجزاء

  • @DarameModou-l4i
    @DarameModou-l4i 7 дней назад +1

    ماشاء الله ❤

  • @SerigneNdoye-i4l
    @SerigneNdoye-i4l 5 дней назад

    Thioro Touba kheutt ndiggueulou seugne bi moffa amme wayé dou in sécurité bayil di diakhassé ay wakh ndiggueul moy dokh Touba inchallah

  • @oumyfaye329
    @oumyfaye329 7 дней назад +2

    Amna solo

  • @makhtarniang8577
    @makhtarniang8577 7 дней назад +4

    Machallah sgn abo fi diam rek mofi am cheikh thioro may gnu diam waaay

  • @moustaphadiop3795
    @moustaphadiop3795 6 дней назад

    Machaallah Dieureudieuf Serigne Abo lèrna nagne ta wakhdji yitam tégui nouna

  • @cheikhseye4119
    @cheikhseye4119 7 дней назад +1

    Machalla serigne bi léral yi amna solo loole

  • @kossofaye2461
    @kossofaye2461 6 дней назад

    Jerejeuf serigne cheikh thioro❤❤

  • @mortalamback
    @mortalamback 7 дней назад +1

    ماشاء الله

  • @Tapa-vc5uz
    @Tapa-vc5uz 6 дней назад +1

    Deug la mbacké yallah nala yallah Faye si léralyi

  • @DioufMamour-p3p
    @DioufMamour-p3p 7 дней назад +1

    Merci

  • @mouhamedrassouldiop1739
    @mouhamedrassouldiop1739 5 дней назад

    civile meunoul yaar civile foofou la rewandé tambalé
    je me rappelle quand on était jeune bo defoulwoon lou jaadu si mbéd mi wa mbéd mi gnolay yaar ba doto am fitou deff lou demé noonou
    merci les bay fall❤❤❤

  • @serignefalloukanendamatou4630
    @serignefalloukanendamatou4630 6 дней назад +1

    Touba môme lifi Serigne bi bëgg rk mofiye am in saa Allaah jerejef serigne Touba

  • @AblayeDiop-e8r
    @AblayeDiop-e8r 6 дней назад

    DIEUREDIEUF CHIEKH THIOROU MBACKE ❤❤

  • @cheikhounathiaw6958
    @cheikhounathiaw6958 7 дней назад +1

    Machalla mbacke lerna de diarejief

  • @moussandiaye1095
    @moussandiaye1095 7 дней назад +1

    Machalla❤❤❤

  • @sidyndiaye4697
    @sidyndiaye4697 6 дней назад

    Merci beaucoup s cheikh thioro mbakce ❤❤❤❤❤❤

  • @magattediop3886
    @magattediop3886 6 дней назад

    waw goor Waw goor dieureudieuf mbacke

  • @BayeAbdouGaye-x6o
    @BayeAbdouGaye-x6o 6 дней назад +2

    Li Serigne bi beugué rek mooy am

  • @DIEREDIEFSERINGETOUBA4
    @DIEREDIEFSERINGETOUBA4 7 дней назад +1

    Amna solo dh Mbacké jaajëf

  • @fallouimambadiane4083
    @fallouimambadiane4083 6 дней назад

    Jërëjëf Mbàkke li sëriñ Tuubaa bëgg ci dëkkam mooy am inchallah

  • @SerigneCheikhounaMbackeSaye
    @SerigneCheikhounaMbackeSaye 7 дней назад +3

    *Waxi Cheikh Abdoul Ahad Mbacké :*
    *Gnétte 3 gnii gnoo yakh adouna:*
    *(1) Kou khamoul Dara tay wakh,*
    *(2) Kou kham touti di wakh Lou Bari,*
    *(3) Ki kham Ba paré noppi.*
    *SUNU LÉPP SERIGNE TOUBA*

    • @SerigneCheikhounaMbackeSaye
      @SerigneCheikhounaMbackeSaye 7 дней назад +3

      sécurité TOUBA civile meusoko yor police migui fi di déf Liguéyeume, mais dafa am Lou dés li dés nak mom la Baye fall yi di déf ni Moy samou wormay deuk bi comme Niko SERIGNE bi beugué

  • @SerigneCheikhounaMbackeSaye
    @SerigneCheikhounaMbackeSaye 7 дней назад +2

    sécurité TOUBA civile meusoko yor police migui fi di déf Liguéyeume, mais dafa am Lou dés li dés nak mom la Baye fall yi di déf ni Moy samou wormay deuk bi di TOUBA

  • @djilydiaw1587
    @djilydiaw1587 5 дней назад

    Par contre le debat n'est pas encor clarifié.

  • @MoustaphaSourang-qo1cz
    @MoustaphaSourang-qo1cz 6 дней назад +3

    Cheikh thioro xamal sa bopo ano niou AK dh sonko lan andal wa Salam ❤❤❤❤❤❤❤

  • @alhikmatabiri6955
    @alhikmatabiri6955 7 дней назад +5

    Baye fall do civil biir touba

  • @AbdoulayeNiang-m9v
    @AbdoulayeNiang-m9v 6 дней назад

    dieure dieuf mbacke balla ❤❤❤

  • @MbayeDiao-cv8ne
    @MbayeDiao-cv8ne 6 дней назад

    Dèrèff cheikh thioro❤❤❤❤

  • @makhadieng8899
    @makhadieng8899 6 дней назад

    Bay fall❤❤❤

  • @sgmstlofficiel3147
    @sgmstlofficiel3147 6 дней назад

    Tubaarkàlla jërëjëf.

  • @khadimMbacke-d9u
    @khadimMbacke-d9u 7 дней назад +3

    Cheikh thioro yaw ko khamadi gua Touba pour Sérigne Touba

  • @alhikmatabiri6955
    @alhikmatabiri6955 7 дней назад +2

    Thiaaxaan katt touba daý xatt si moom

  • @layetine9003
    @layetine9003 6 дней назад +6

    Chiekh thioro khamal sa bop .li serigne bi beug rek moy am inchallah

    • @AblayeDiop-e8r
      @AblayeDiop-e8r 6 дней назад +1

      Ioe ya wara kham sa bopp

    • @grandgrand8941
      @grandgrand8941 4 дня назад

      @@layetine9003 Serigne Touba yanako yalla yeureume kharéko aljana firdawssi Amine
      Limou wakh woté ko kham kham AK ndioube AK ragal yalla diamou ko

  • @thiammady4782
    @thiammady4782 4 дня назад

    La gestion paix et la sécurité sont des tâches dévolues à l'État qui a délégué ses pouvoirs aux forces de sécurité (police, gendarmerie, armée).
    L'injustice est le dénominateur commun de toutes les guerres civiles.

  • @massar430
    @massar430 7 дней назад +1

    ❤❤❤

  • @mamemorthiam8763
    @mamemorthiam8763 7 дней назад +3

    Diap nit fay lou lén 25 mil di door wala di wat di arrêt oto wala moto wala di dokou si keur yi dou deuk do yoon

  • @pirlo4478
    @pirlo4478 6 дней назад +1

    Status spécial rék moma na régler problème yi bou kéne sokhar Touba mo tollou fofou

  • @basiroukankane1262
    @basiroukankane1262 6 дней назад

    Jaajaf Séex joro mbakké ❤❤❤
    Amna solo

  • @mahmadanegueye7732
    @mahmadanegueye7732 7 дней назад +6

    Man dé vraiment Guissouma insécurité touba

  • @falloufall9804
    @falloufall9804 6 дней назад

    Il a bien clarifié le débat

  • @NdiayeAlioune-to9lv
    @NdiayeAlioune-to9lv 6 дней назад +1

    Serigne bi ndieuk ñaan yallah ci touba mooy mboloo mou fay taxawal diouly diouraum té lolou la gueneu beugue kon baye fall yi nañ dém diouly ji ba noopi dooguo règle waaté lolou mooy deugue.

  • @thiounec8752
    @thiounec8752 6 дней назад

    Wakh nga deug Serigne bi

  • @CheikhounaDiop-f3s
    @CheikhounaDiop-f3s 4 дня назад

    Vive Cheikh Thioro .❤
    Nitu deugeu .
    Do diouli do wor nane dagay yar ay diouli kat ak ay woor kat
    Cey diiné Sénégal 😂😂

  • @seringeahmalo8225
    @seringeahmalo8225 5 дней назад

    Ch Thioro ya wakh deuk

  • @abibdiallo8112
    @abibdiallo8112 7 дней назад +1

    Yow mouy wax ya yakh Sénégal sécurité Touba baye fall yii nioko yorr dél wakh degue

  • @CheikhdarouSarr-z8d
    @CheikhdarouSarr-z8d 6 дней назад

    Li yalla beug Moy am

  • @mbcke1430
    @mbcke1430 6 дней назад

    Et si une grande nombre de personnes opposé est-ce que l'état va les laisser de s'entre tué ?

  • @elhadjidiakhate8858
    @elhadjidiakhate8858 6 дней назад

    Diadief chiekh thioro

  • @med-sen8971
    @med-sen8971 6 дней назад

    Serigne Touba voulais que ceux qui habitent à Touba fassent la prière. Donc pourquoi la majeure partie des bayes fall qui ne prient pas sont utilisés.

  • @fallelhadjiabdoulaye2347
    @fallelhadjiabdoulaye2347 6 дней назад

    Touba mom lifa serigne bi beug rek mofay am dou diomaye dou sonko mofay regler dra il faut que sa soit claire

  • @damediagne7040
    @damediagne7040 7 дней назад +1

    Djiadjuf mbacke cheikh thioro mbacke lollou demal nga wakhko serigne bi diokh siwèl yi

  • @FallouMbaye-v9g
    @FallouMbaye-v9g 6 дней назад

    Cheikh tihoro mbacke wakh na deug baye sécurité Touba dafa am problème baye fall yi Line wara déff dou contrôle civil nane wakh deug wayé li lépp makye Sall mo fékh ba Serigne mountakah diokh ko baye fall yii

  • @modouseck7895
    @modouseck7895 7 дней назад +1

    Sama problème moy keur diambour nouko néx gafay néké wala ga xol fénéne c'est aussi simple

  • @mamemorbousso4827
    @mamemorbousso4827 6 дней назад

    Dégini moo wuté mais man li cheikh thioro wax ousmane sonko wakh ko gisuma luci ay
    Ndax s mountakha bu santé bay fall yi sécurité touba
    Da fék état déful ligéyém
    Légi nak amnañ état bu fasyéné ligéy japalé Serigne bi ci kara ngé touba

  • @mamadoundiare1048
    @mamadoundiare1048 4 дня назад

    Amna solo loll rawatina leral yi lo wer nga wax

  • @MouhamadoulamineSamb-n8g
    @MouhamadoulamineSamb-n8g 6 дней назад

    طوبى المحروسة❤❤❤waw gor

  • @Abdoulah15
    @Abdoulah15 6 дней назад

    mais insecurité qu'est-ce que ca a voir avec les baye fall

  • @mamechiekhfall315
    @mamechiekhfall315 7 дней назад +3

    Yaw dè serigne abo kham gua wayé nak amna nio kham ni serigne touba moy sen mame wayé khamou sene bopou

  • @LemouFall-u1q
    @LemouFall-u1q 5 дней назад

    Civil dou réglé civil Touba li nék da eup

  • @KhadimFall-b3e
    @KhadimFall-b3e 7 дней назад

    Merci beaucoup cheikh thioro mbacke ❤❤❤❤

  • @saerdiop5568
    @saerdiop5568 6 дней назад

    Kudul julli du woor ab yeefër la té ab yeefër manul a ligeeyal Ku tedd ki gemmiñ bu waxul dëgg wax ab safaan

  • @assadolkhadim743
    @assadolkhadim743 7 дней назад +1

    Wa lay mbacke deug lei

  • @mbackebaaritv1516
    @mbackebaaritv1516 7 дней назад +1

    Ndakh ngin diokh guir ñooy samu wurmayi Li serigne bi beugone Nio Deff ko Si deug bi neko Nio si 100% waxgua ko Serigne bi Guir nioy taxawal Jolli diourom

    • @mamechiekhfall315
      @mamechiekhfall315 7 дней назад +4

      Li serigne bi beugui moy ame té mane diouly wouma té geunoma néké dioulit

  • @cheikhbassmbacke225
    @cheikhbassmbacke225 6 дней назад

    Kaddu Serigne Abo yi amba solo lool

  • @bayeabdoumbow4812
    @bayeabdoumbow4812 7 дней назад +1

    Guaayi ndiguel li Serigne bi diokh baye fall yii molén métti

  • @ibrahimadioplo475
    @ibrahimadioplo475 6 дней назад

    L etat doit appuyer les baye fall pour la security de touba

  • @SidiSylla-uo6gp
    @SidiSylla-uo6gp 6 дней назад +1

    Cheikh thioro amol yarr

  • @moustaphadiop3694
    @moustaphadiop3694 6 дней назад

    Ndiguel li mome djeffé far force Sonko khamal sa bop si non di nagne ouye

  • @ibrahimadioplo475
    @ibrahimadioplo475 6 дней назад

    C est un depute de lignirance au detriment de la cite de toub

  • @BayouGoor-of6fi
    @BayouGoor-of6fi 6 дней назад

    Waaw léen Goor Baay Faal yi li Sërin~ bi bëgg mooy am Tuubaa

  • @PDForeverman
    @PDForeverman 6 дней назад

    Baye Fall par force. Cheikh thioro ak koo yakar manou si touss

  • @ibrahimacamara4475
    @ibrahimacamara4475 3 дня назад

    Explications pas du tout claires et non convainquantes.........................................

  • @mouhamadmouserignesalihoud9431
    @mouhamadmouserignesalihoud9431 6 дней назад

    Mais S Cheikh Thioro wakhoufi lou aye

  • @serignesalioumbacke3021
    @serignesalioumbacke3021 6 дней назад

    Touba amull sécurité ndax agression yangi fi ak yaneen
    Cheikh Thioro waxull ne ñu bayyi lu neexx waay deff waaye nanuku deff nako Serigne Abdou Lahad defe woonn mooyli gënn
    Touba keur la nanu nu waxx fann la tambulee ak fann la yam 🤍🤍🤍🙏🙏
    Sama xalaatt la nk 😀😀😀😀

  • @PDForeverman
    @PDForeverman 6 дней назад

    Makhala diangoul. Khamoul sécurité ak li vaye fall yi yoré